Pas de vulgarité, pas d'actes obscènes, pas de gros mots. Une série comique et pleines d'enseignements. C'est une de ces séries qui méritent d'être regardée. Et pas ces autres séries télévisées qui montrent pas nos valeurs et notre réalité.
Au delà de l’aspect comique, BUUR délivre de grands enseignements de civisme,de dignité et de patriotisme ! Il n’a aucun complexe à clamer haut et fort qu’il fait du « sirrou » avec un taxi pour « daw depenses »… quelle belle leçon d’humilité ! Avec le peu de confort que nous avons,il nous arrive de nous plaindre pour un oui pour un non,parfois pour des futilités sans importance. L’attitude de « Buur »,connaissant la vie qu’il avait dans les saisons précédentes,fait réfléchir. Bref, j’adore cette série❤
Sanekh j’espère qu’un jour t’auras ta statue au Senegal un jour , si ça se fait pas que Dieu me donne les moyens de le faire pour toi Quel talent ! Quel Homme ! Quel artiste !❤️
A oui ca cest vraie parmi toute les série de leuz c'est buur guewel mon préféré depuis 2015 je n'ai raté aucun des episodes sois sur TFM ou sur youtube modou mbaye et saneex me la joie de vivre bravo à leuz media la musique générique est génial leuz dois continuer aussi la saison 3 de lemzo chérie j'ai hâte de voir la suite c'est une très bonne série
1-nit ci limu beug nga key naxê ba dimbaliko 2-tolof tolof ak adduna gno ande mougne rk 3-goor du bayyêku 4-responsabilité degn key jox ki amal njarign société mouy goor mouy jigueen
Je suis parfaitement d'accord avec Bour gueweul pour diriger il faut être compétent tout simplement amoul gor amoul jiguen pourquoi pas les femmes ne pourront pas devenir des chefs de quartier voilà
Kou bakh mane douma peulh dh mais sa commentaires bi niawna trop khawma noko mana déffé nga balma wax day rafétt peulh ak wolof fiii la yam mais agoul fa yalla
Pas de vulgarité, pas d'actes obscènes, pas de gros mots. Une série comique et pleines d'enseignements. C'est une de ces séries qui méritent d'être regardée. Et pas ces autres séries télévisées qui montrent pas nos valeurs et notre réalité.
En plus tu regarde avec les enfants j'adore ❤
@@assanandiaye3724Exactement ! Même avec tes parents si tu veux !
Billahi Lou lérr machallah
Les sénégalais xamoul loubax motax ils veulent vivre des choses qu'ils n'ont pas
Kone yow gisso doigt d'honneur modou mbaye bi
Sanekh est trop charismatique dans cette série. J'aurai aimer être comme lui dans la vraie vie .
Au delà de l’aspect comique, BUUR délivre de grands enseignements de civisme,de dignité et de patriotisme !
Il n’a aucun complexe à clamer haut et fort qu’il fait du « sirrou » avec un taxi pour « daw depenses »… quelle belle leçon d’humilité !
Avec le peu de confort que nous avons,il nous arrive de nous plaindre pour un oui pour un non,parfois pour des futilités sans importance.
L’attitude de « Buur »,connaissant la vie qu’il avait dans les saisons précédentes,fait réfléchir.
Bref, j’adore cette série❤
bien disserté
Sanekh j’espère qu’un jour t’auras ta statue au Senegal un jour , si ça se fait pas que Dieu me donne les moyens de le faire pour toi
Quel talent ! Quel Homme ! Quel artiste !❤️
Best théâtre ever. Bii bouléne ko bayi. A ameliorer kécé mais série yeupe des réussites. Début bi tégouna si axe😂🎉
La série qui n'a jamais perdu sa valeur 😂😂
Li kay perte na valeur lgui 😂😂😂
A oui ca cest vraie parmi toute les série de leuz c'est buur guewel mon préféré depuis 2015 je n'ai raté aucun des episodes sois sur TFM ou sur youtube modou mbaye et saneex me la joie de vivre bravo à leuz media la musique générique est génial leuz dois continuer aussi la saison 3 de lemzo chérie j'ai hâte de voir la suite c'est une très bonne série
Bour gueweul plus connu sur le nom de sanekh, est le meilleur artiste de tout les temps ❤
Clairement…. il est excellent dans n’importe quel rôle 👍🏽
Wallahi machallah
sanexx deih mogui mougn retann yi
ah MODOU MBAYE MIII🤣🤣🤣
Voilà les vrais théâtres à l'ancienne qui illustrent bien les vraies réalités de notre pays sans aucune tricherie.
Modou Mbaye soff nga niaw nga 😂😂😂
Modou mbaye ba légui yéwou woul😅😂😂
🤣 saneh ak diarbat dji🤣🤣
Modou mbaye ak manière yi🤣🤣🤣
Modou mbaye maye sa fan numero 1 😂😂😂😂😂, sa kanam lanla
😂😂😂😂 saneex akh modou mbaye😂😂😂😂
Yéena tahone ma bayi série sénégalaise ndahh amoule suite , mé bégg na si suivit bi
1-nit ci limu beug nga key naxê ba dimbaliko
2-tolof tolof ak adduna gno ande mougne rk
3-goor du bayyêku
4-responsabilité degn key jox ki amal njarign société mouy goor mouy jigueen
Leuz série bi dafa nékh bilay bouléne ko bayi na yatou améliorer léne ko bou bakh
😂😂😂 Mdou rayyy nama . Néna mo ngui jouli si yalla di sante si yonantebi
Nama yalla Bâle Modou mbaye nak mome vraiment 😅
Boulko agalé dé😂😂😂
@@doudoundiaye3152 walay dema se rouss yalla trop 🤣
Je suis du même avis que toi.kii mome leuz sétane nako trop.lii la commentaires 😂😂😂
Kénn douko agalé daniouye ...rék 😂😂😂
@@fayebass4129 billahi li Yalla rék moko Sagne🤦
😂😂😂😂😂😂😂😂😂Modou Mbaye sa batt bii dou meussa yéwou 😂😂😂😂🙇🏾🚶🏽Sheutt 😔😔
😅😅😂😂😂🎉🎉
😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂modou mbay ak sanékh dinagn ma ray
Thiey modou mbaye 😂😂
😂😂😂 Modou Mbaye mounou ma dara thi mome
Ki key, 😅😅😅
Merci Leuztv mou dess dinama nex❤
Modou Mbaye kharitou mameum leu nak,
Kanamou Modou mbaye bi di na ma raÿ 😂😂😂
Modou Mbaaye worna Yalla dinama meussa ray bama déé 😂😂😂😂😂
Sanékh yalla nala yalla may kholoup mougn😂😂😂modou mbay rk
Best comedic séries in Sénégal hands down
Cc
Modou M’Baye mon acteur préféré 😂😂😂
Geumo si dra liguay wkh ni 😂😂💔
Sanékh yalla na yalla sammou ko❤❤❤❤❤
J'adore cette série. Leuz est le meilleur❤
Vraiment c'est trop cool
Je suis parfaitement d'accord avec Bour gueweul pour diriger il faut être compétent tout simplement amoul gor amoul jiguen pourquoi pas les femmes ne pourront pas devenir des chefs de quartier voilà
Modou mbay chérie coco😂😂😂🎉
Ndeysan modou Mbaye legui dafa changé sax 😊
Dentition bi MO changer enfaite bou demon si dentiste REK kanam gui nieuwat. Beugne sa change tout.
Ay modou mbaye mi li ba diam leuuuuuuu
Baye Maissa est un grand acteur j’adore!
Lou takh yidi watt mana nélali😂😂😂
😂😂😂Modou me fume
Mais modou mbaye mom😂 yi manière tmite loumou barki Serigne Touba modo mo ndeye niaw😂😂
Modou mbaaye rek lay topp
Modou mbaye nak 😂😂😂
Modou mbaye rafet na
Modou mbaaye demal khol lénène té bayi music bi
Modou Mbaye me fume 😂😂😂😂
Sarap ndayam modou mbaaye niaaw nga
😂😂😂
Modou mbaye 😂😂😂😂
Non mane modou rek 😂😂😂😂 Leuz 8 ans yima tokk dila harre doumalako ballle
Modou Mbaye bilay amal sonou complexe way
La serie qui n’a jamais perdu sa valeur
Yalna sa diam yague sanex walayi azime sa mision matale gako nalaine yalla sama kisi kaw basi kisi souf modou mbaye vai trovare un lavoro 😂😂
Merci
thieye nidiaye❤❤❤
Tek si eyes ba pareil teuyei baksana bi
Cod dela musique 😂😂😂 non Modou mbaye
Modou mbay a tellement maigri soone 😢
Thiono galsen rk
Billahi ndeysane senegal da tare yarame
Mon favorite
Modou mbaye comme diounkhobe😂😂😂
😂😂modou mbaaye nekal nit
Peulh fouta bi loumou jouer si episode bi dou juste theatre deih seine vrai djiko la 😂😂😂😂 feine rek
Kou bakh mane douma peulh dh mais sa commentaires bi niawna trop khawma noko mana déffé nga balma wax day rafétt peulh ak wolof fiii la yam mais agoul fa yalla
Sheuuuu modou tamit
Merci ☺️
Nn modou mbay mi dinafi ray nit de😂😂😂😂😂
Série bou nekh la
😅😅😅😅 modou mbaaye 😅😅😅😅
😂😂😂😂😂sanekh nénako boko si adounabi😂😂😂😂😂😂😂
Avec la qualité de cette série pourquoi ça n’a pas beaucoup de vues
Il ya eu beaucoup d'années entre saison 2 et saison 3. Les gens se sont lassés.
Mane Modou mbaye rek lay topou😂😂😂😂
Modou mbay niawna😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Lou dakheu maam amoul
Lii daal moom niróo na Senegaal
Merci.
😂😂modou mbaye
Lellou Modou mbaye bi 😭😭
Modou mbaay😂😂😂
Pleine d'enseignement cette série🎉❤
Ndeysan mère bi légui da changer ceey adouna
❤❤❤
Deloma Sama khool
Thy mbaay
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Courtage bi aussi war nanou si wakh woute Katou Keur yi tamite nonou laniou sonei…!!!
Vraiment modou mbaye il faut soigner ton image.tu es comique mais...
Mais.. NA defarate c dents nassi sanekh AK leuz diappa. IL es Tres bon acteur
Bilaye War nagnouko diapalé bou bakh il est très fort.
Modou mbay loumou bokk ak lambalogue 😂😂😂??*
😂😂😂😂😂😂 kiii lamb moko dah
@@saliougueye3334 je sais mais dagno am ay trait koi
Ms attend modou mbaye foumou nekone
Sérieusement modou Mbaye mi diogué woul rebeuss pour de vrai 🤦🏼♂️🤦🏼♂️
Modou mbaye est ce que du wagnu manieram yi. Je trouve qu’il en fait trop. Li mu rafet rek doyna.
8ans après 😂
😂😂😂😂❤❤❤
😂😂😂😂
😂😂
😂
Thiey Modou mbaye comme kouye khol si soleil bi😂😂😂
Sheut 😭😭💔😂🤦🏾♂️
❤❤❤❤❤❤❤
Modou mbaye😂😂😂😂
😂😂
😂😂