Sanéx yalle nafi yague té ande ak weur ak keup kou wah amine Sanéx mo meun kéy éy way n'a kou nék wagni si ay atame béni khadjou fan rék niou yokal ko Sanéx
Ils ont attendu trop longtemps entre les saisons 2 et 3 (8ans quand même) c'est pour ça que l'histoire est super décousue. Mais j'aime toujours le show quand même
Sanéx yalle nafi yague té ande ak weur ak keup kou wah amine Sanéx mo meun kéy éy way n'a kou nék wagni si ay atame béni khadjou fan rék niou yokal ko Sanéx
Amine
Amiiiine
Thiey Sanekh rôle bougn ko diokh nga yakarni lolou moy vrai personnalitem magui nane wa Sanekh mom da dieum magg di😂😂😂😂
Sanekh khana rôle la meun kéy😂😂😂
Série bu neex waay! Buur Gëwël ak Móodu Mbaay. 😂 😂 😂
Dakarou est de retour ces mimiques m’ont vraiment manqués 😂😅 😂😂
Modou Mbaaye va me tuer 🤣🤣🤣. Mais buur longue vie à toi
Série bu neex waay! Buur Gëwël ak Móodu Mbaay. 😂 😂
Bou kene décourager dinagnou kheh ba lougnou ame dieule yene wa xalaate contane ci yene mane yene laye top machalla ❤❤❤💪💪💪
LeuzTv ani sama série favori bi Lemzo Chéri j'adore cette série.
Tey tey tey lay dora kham ni la meilleure serie senegalaise est de retour 😭😭😭
Enfin Bour Guéweul est revenu. Ndakarouuuuuuuu😂
On avait hâte de la suite de cette excellente série.
Svp Nous attendons avec impatience la suite Ndari Baba.
Merci @LEUZTVWEB et bonne continuation.
Oh la meilleure des séries est de retour 😊❤ oh sama khol cédena 🎉
Dém Nafi Dara binde fi Kamil Ba nieuw 😂
Walay bro bima guissei titre bi dama tiiite sakh ndakh yagg
@@AmadouBa_12 Ahh li ky😂
Macha Allah ❤
Modou mbaye il est très talentueux 🤣🤣🤣🤣🤣
Modou mbaaye nieuwatna 😂😂❤
Oh lii limako kharr merci wayy leuz🎉❤❤❤
Seuynafi ba am fii niari dome !! Lemzo cheri mome khamna 2035 ley guene ! Soff nguen torope ! Ish
😂
Franchement trop bonne série de retour très souscoté je trouve franchement bonne continuation ❤
Lima geunone beug moy buur gewal merci way
Ohhh damaleine rombou sentv manane ayway yalna nekk deugg une tres belle serie qu'on avait arreté depuis les episodes de "on accelère la cadence " 😂😂
Makhou Sadick tu nous avais manqué. Figure bcp plus dans les séries way
Pére day relax kay 😂😂😂😂😂😂😂
Modou mbay de retour 😂😂😂mai kene dou sma nourou wale sanekh ❤
Ihhh série bouma nékh mongui nii ms louyag lawone😂
Ah bon kii kagn la nii, khawma wonn ni commencer watt na, ohh ❤❤❤
Professeur ak taassou ba waay, dans la serie Dinama neex😂
Merci! Leuz
Ils ont attendu trop longtemps entre les saisons 2 et 3 (8ans quand même) c'est pour ça que l'histoire est super décousue. Mais j'aime toujours le show quand même
Walahi ndeyssane je crois que producteur laniou amoul wonn dee. Financement laniou amoul wonn. Mais ils sont bons ❤
Vraiment merci khar bi yague na
Vraiment merci beaucoup à vous
Tres cool vraiment mai qui connais le générique du commencement sons bi daf ma nekh trop
Mon série préféré way namoun na len ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mane chef de quartier bii momaye raye borome c'est un bon payeur 😂😂😂
Cette série m’avais manqué.
Moudouu mbayyyy😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤
Film bi mo nek sama millieur film ndeyesane merci pour le production contanna si yene
❤Sanex dou nitou fi😂
Modou Mbaaye! The best, the one and only😂
Non Sa Nekh il est fort Big up a lui
Leuz booniou meunéé partager vidéos Bur Gueweul saison 1 bi complet
Si il sont tous sur youtube la saison 1
@@casimirpreira2847 début bi bassi digueu bi mais derniers épisodes yi fégnoul🤔
Wa ki dou modu mbaye😂😂😂
Pour mann modou mbaye changé na😂😂
S3 j'espère que c'est un bon payeur 😂😂😂
Mn série préférée de retour
Haa bilae namone naniou leen wa beure geuweul jërëjëf 🇸🇳 💯 ✌🏿
ALHAMDOULILLAH BI MA DOUNDÉ BA FÉKÉ SAISON 3 BI
Nous voulons Ngéweul gui central
Buur gueweul, enfin Il était temps
Nice naa leuz media🎉🎉🎉🎉🎉
Merci leuzz
Un grand artiste sanexx
Modou mbaye 😂😂
Machalla ❤
aayyyy modouu wayyyyy
Non Sanekh dou niit 😂
Niouy tak ceinture au volant sama gars yi tam naniou lou bone nak
Merci
Baye maysa😂😂😂
Résumé warona sé am
Ay modou mbaye dinama ray di ak baramyi 😂😂😂😂😂
Modou mbaye est de retour
Non modou mbaye😂😂😂😂😂😂😂
Ehh ndàkarou😂😂😂
Mame cheikhou bandit la
Wesh ça fait 10 ans cette série ! Leuz tv reprenez vous waye
Grand bocar sène way diantal grand ....
Mon ❤️
😂😂 Modou mbaye thieupelou bi graw na d hana apprenti l
Ohhh nooo way sama gayi sene production bi mom mouy lolou qualité image bakhoul cadrage bi tamit mouy lolou
en tout cas j'oublie mes problèmes😆😂
Antouqua bour guewal saison 1saison 2 dara takou ko kimaye danéle nakh moye le chef de quartier ma diaga Meyse diore
Namon nalén
8 ans makoye harrr o namone na modou mbaye 😂😂😂😂
Matnako?
@@awasow1803est-ce que eupou ko sakh
@@awasow1803est-ce que eupou ko sakh
Pape makhtar domou ndar bi Artis Comédie bi
Nice
@leuz yane jour lay am?
Namone naa soundtrack bi nak 😊
Ki Dou nitou fi
❤❤ ❤
❤❤❤
Name nanou dakarou buzz la bruit
No Modou Mbaye niawna nakk nama yalla balle😂😂😂😂😂😂😂
Lingawakh moame😅😅😅😅❤❤
@@FALLOUNIANG-k5l dama diomi motakh 🤣🤣🤣🤣🤣
Mais Modou Mbaye comme kou nékone réellement jail
Modou mbaaye 😅
❤❤❤❤❤😂
Modou mbaye😂😂😂
Bismilahi
Série bi la donn xaar
Naturél da nékh
Jajeuf
Télécharger svp 😢
Saison 1 bi noumou dèmè woneu nonou? Koumay diapalé dafa yague bama fatéko
Le générique est vraiment trop nekh
Vc😂😂😂rhojv❤❤❤❤
😂😂😂😂😂
Bilaye Nml n l
Lou néx
Mais buur guewel amoul wone 2 femmes et une bonne situation ?
Bien sûr teint noir et teint clair
J'ai dû re regarder les deux premières saisons...j'avais oublié l'histoire tellement de feu yageu
@@maxtorque5329 ça 8 ans motax gneup fater
No cest pa vrai je pensai à cette série ya pa longtemps
😂
Mais modou mbay tabs changé lol on dirait un drogué
Leuz booniou meunéé partager vidéos Bur Gueweul saison 1 bi complet
❤❤❤❤❤❤❤