Yalla moy may nit kunek wayé man alhamdou lilah thi bimuma tané defma domi darra ma mokal القران الكريم ❤❤❤❤❤❤❤ té diiné l'islam moy premier chose mome la tan na moy la diel moy la choisir
Albasir guéye borom alhouane diamou si yaw diadiaf liguey rafét na loll machallah amna solo torop wayi dafa dof wérou té wédina alhouane ak yalla sounou borom téki for lif mom adounan yép khaliss la pourmom téki force la
Ki limou beugone am nako ndakh niepagui wakh si môme sénégalais yi legi gno beug domharam saga Kat yi gno fi eup ay vu rewmi amatoul bene valeur ndakh internet bi
Moi je suis un coach en développement personnel mais saway limou wax tégouko fén. Ya un proverbe qui dit "Ne laisse pas la défaite te monter au coeur mais ne laisse pas le succès de monter au coeur". Succès bi mo commencé yég si bop bi. Gnoun nieup beug xalis wayé ragal yallah ku mat seuk lagn si démé.
Téki for lif mi éska dioulite la ki geumoul yalla limouy geumlo nit ni.moy no amé bakhna toulé moyé son bon thiey khaliss ak jiguén késsé motakh loubari si adouna bi geum yalla dou ay wakh dieuf la waji kouko topou rére néna am force la weurseûk yi yalla nopinasi yalla nanou yalla diégal si moy yi ak bakar yi
Pourtant notre Dieu qui a descendu le Coran et mentionné dans le Coran le Coran est venu pour nous sortir des ténèbres et nous guider vers la lumière ! C'est pas forcément avoir de l'argent mais une personne qui maîtrise le Coran doit avoir une certaine façon de vivre car le Coran est l'indicateur des panneaux pour les bien-être de l'être humain ! Alors dans ce cas si le monsieur apris le Coran est-ce que il a compris c'est que le Coran disait? Et si il a compris est-ce que il a pratiqué? Car il y a l'apprentissage et la compréhension et la pratiques 🤔🤔
Teki for live si bopame xam xam dako amoule ak dof yikoy toppou si bopame la yeueum . Fimou léne tenk moy kou gémoul limouy wakh mouni leu esprit pauvre nga yor légui nak ngay gorgorlou nak né esprit riche nga yor loumou wakh ngani waw. Sénégal nexna ,ki désabonner rek bloqué dial
Sidy birahima fall Moni diamou léne yalla bame méle ni taye ngaye dée wayée liguéye léne bame méle ni fi ngéne sakhe liguéye sakhe diamou yalla la wayer yalla brome yitter diou kawer la andale tée boye dée si alleu n'a la guailndé raye téki for life si deugue la néke sa waye wouty djilaine khallisse
YALLA SABAHANAHU WA TAA LA XAMOUL XALISS XAMOUL MATÉRIEL POUBELLE YI YALLA VALEUR AK COMPORTEMENT BU BAKH AK YEUREMANDÉ LA KHAM KI NAÑ KA YOOBU DALAL XEL
Boulén faté né am na ay nitt youfi takhawoun née sama serigne moy yalla 🤔 té thiow amoul 🤫 bari guén ay doul trop thibiri😏 jeune yi wouti lén khaliss 💸💸💸🧠🙏
Yalla moy may nit kunek wayé man alhamdou lilah thi bimuma tané defma domi darra ma mokal القران الكريم ❤❤❤❤❤❤❤ té diiné l'islam moy premier chose mome la tan na moy la diel moy la choisir
ماشاء الله عليك ياأخي
Yalla n'a niou mourr lo sunu
القرءان الكريم 🎉❤😊
Yalnagnou yalla bolé AK القران الكريم mousal gni ci kepou kp koukoye Nasakhal
Lolou dé la gis mane
Aka wer machalla ❤
Albasir guéye borom alhouane diamou si yaw diadiaf liguey rafét na loll machallah amna solo torop wayi dafa dof wérou té wédina alhouane ak yalla sounou borom téki for lif mom adounan yép khaliss la pourmom téki force la
Tekki for life merci
Tekki for life kou mana fen la
Tkki for life danion wara lancer pétition niou fermer chaîne RUclips bi😢😢
Da dioum rekk limou
Voilà so boba dinaa xamné yallah Moy diokhé
Non dafa dioume na diégalou rek
Al hamdou lillah bangou yalla mayéé al quran ❤
Nite bou topp dangay toppou kilay diangal sa diiné
فالرزق ليس بحيلة يستجلب❤
Gayi wah dji Moy nagnouy deglou gni nga hamni lougnou wah si diine lagnouy basé wou
Tekki for live m'a fait rire il m'a déçu il nous trompé carrément 😢😢😢😢😢
Tay mom tekki danou na seuuu teuuu teuuu teuut
Machallah sama Serigne yi amna solo yen Nieppe désabonner len si tkki for life
alqoran kokou l'ale na fekk moy lou bakhé❤
Amm ngoor moyyy lepp
Machalla jadiaf amna solo torob yala na yalla défalla lén diamou ❤❤️❤❤️❤❤️❤
Tékki for life dafa wara diangui dîné adouna dako sonal trop té aduna dou keur
Lo fi meuneu ame fi ngakoy bayi diaroul forcé lantement rk
Amna solo machallah
ماشاء الله ❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha alla
Ki limou beugone am nako ndakh niepagui wakh si môme sénégalais yi legi gno beug domharam saga Kat yi gno fi eup ay vu rewmi amatoul bene valeur ndakh internet bi
Wallahi broh
Daa dioum rek yalla nako yalla yeureum te niital ko😂
Wadji da rèw bilay
Macha Allah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Moi je suis un coach en développement personnel mais saway limou wax tégouko fén. Ya un proverbe qui dit "Ne laisse pas la défaite te monter au coeur mais ne laisse pas le succès de monter au coeur". Succès bi mo commencé yég si bop bi.
Gnoun nieup beug xalis wayé ragal yallah ku mat seuk lagn si démé.
Jërëjëf ❤
Yaw tekkki daniouyyy tepppiiii sa lou bone dé. Waaayyy
ماشاء الله تبارك الله الشيخ ❤❤❤
TEKKI FOR LIVE MOY KAN SAKH NA DEM OUTI IMAAN AK KHAM KHAM MU DIOGO ÑIOW
Eskey Eskey Doy na warr déeee ❤️😭🙏🏿🙏🏿🙏🏿
ALQURAN AK WERSEK BOKOUNIOU DARA
Teksi dafa rew di khass nitt yi
Man déy mangi sante YALLA boubaxe banga khamè né mosou ma topp ay wakham mom tékki fort life❌️ dou sama idole té domako topp moukk jamais
Téki for lif mi éska dioulite la ki geumoul yalla limouy geumlo nit ni.moy no amé bakhna toulé moyé son bon thiey khaliss ak jiguén késsé motakh loubari si adouna bi geum yalla dou ay wakh dieuf la waji kouko topou rére néna am force la weurseûk yi yalla nopinasi yalla nanou yalla diégal si moy yi ak bakar yi
Machalah ❤️
Pourtant notre Dieu qui a descendu le Coran et mentionné dans le Coran le Coran est venu pour nous sortir des ténèbres et nous guider vers la lumière ! C'est pas forcément avoir de l'argent mais une personne qui maîtrise le Coran doit avoir une certaine façon de vivre car le Coran est l'indicateur des panneaux pour les bien-être de l'être humain ! Alors dans ce cas si le monsieur apris le Coran est-ce que il a compris c'est que le Coran disait? Et si il a compris est-ce que il a pratiqué? Car il y a l'apprentissage et la compréhension et la pratiques 🤔🤔
Man cha alla
Dél lole khél si sa brome takki for life
Alhamdoulillah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ady
Teki for live si bopame xam xam dako amoule ak dof yikoy toppou si bopame la yeueum . Fimou léne tenk moy kou gémoul limouy wakh mouni leu esprit pauvre nga yor légui nak ngay gorgorlou nak né esprit riche nga yor loumou wakh ngani waw. Sénégal nexna ,ki désabonner rek bloqué dial
Salahlaou ahalha mouhamed
Nous Bari si nite ni xamou nous bilahi 😭
Walahi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Bonne interprétation ❤❤❤
Lan moy alall Dou dara😢
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😅😅😅tekki for lif golo mooko raw thi'a yallah
قال إمام شافعي
لوأن بالحيل الغنى لوجدتنى
بنجوم أفلاك السماء تعلقى
الله أكبر
Kimono domiharam fils firawan ya kata sanday tekki ya domiharam gomo yalla
Wadji dof leu
Sidy birahima fall Moni diamou léne yalla bame méle ni taye ngaye dée wayée liguéye léne bame méle ni fi ngéne sakhe liguéye sakhe diamou yalla la wayer yalla brome yitter diou kawer la andale tée boye dée si alleu n'a la guailndé raye téki for life si deugue la néke sa waye wouty djilaine khallisse
Danga deg fi kou né bou kene wouti xaliss? Bayil leien diay xeel mou reuy t djema diangue xam sene diiné yarou t ligueyi .
Nio bange
Tekki for life xaalisu bess la ñuy wutt
Ki dafa rewou ak doff
Joo dgadiom😂😂😂
YALLA SABAHANAHU WA TAA LA XAMOUL XALISS XAMOUL MATÉRIEL POUBELLE YI YALLA VALEUR AK COMPORTEMENT BU BAKH AK YEUREMANDÉ LA KHAM KI NAÑ KA YOOBU DALAL XEL
Mais ki nite la esk
Ki dafa réw sah
Mom addounam diép xaliss la thime😢
J'espère que yore na aye milliards rek
Tkki for life aclou monadon ladiou nioula xalisse diohewo doole nday noppi
Mbaa boy yi dé si gecc gi daawun deglu wajji
Nit matoul
Ki dof bounou peinture couleur rou nit la
❤❤❤
Merci Amadou ba thank you so very much ❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤🥰🥰🥰🙏🙏🙏🙏🙏
Nikhou bahk dou beuri khaliss
Ball Lene dafa dioum
Goudi bambél couco doul halate loula néh défal loula néh wahal
Ki kay mbaam deug leu
Tekki deffa reere. Mome nena dey motivés te mome sii bobamm motivation zéro
Boulén faté né am na ay nitt youfi takhawoun née sama serigne moy yalla 🤔 té thiow amoul 🤫 bari guén ay doul trop thibiri😏 jeune yi wouti lén khaliss 💸💸💸🧠🙏
Hors sujet
Désabonnement massivement bamou hamni momou niou
kou yakaar ni tekki for life day changer doundou jeunesse bi soko topé rk alkou nga
❤❤❤
❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤