Chaud débat entre Zarko et coach bakary: ama baldé mounoul dane franc? souko dané mane lay..

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 10 фев 2025
  • Bienvenue sur votre chaîne (lutte motivation)
    abonnez-vous ✔️ | partagez✔️ | commentez✔️| aimez ✔️|
    Toute l’actualité de la lutte sénégalaise et dés contenues d’inspiration quotidien!
    Instagram ➡️ / lutte_motivation_officiel
    RUclips ➡️ / @luttemotivation
    Snapchat ➡️ / zyp10ybm
    Facebook ➡️ www.facebook.c...
    Tik tok ➡️ www.tiktok.com...
    Thread ➡️ www.threads.ne...
    Contacter nous sur Watsap 👉 77 265 29 18

Комментарии • 42

  • @bayemo4147
    @bayemo4147 5 дней назад +14

    Zarco d ins bi meun na beuré AK nieup mais combat bi gueuneu nior mooy zarco vs eumeu sene

  • @ModouNdiaye-n8e
    @ModouNdiaye-n8e 4 дня назад +1

    Sa waye Zarco à parfaitement raison il à prouvé en ce moment zarco à l'embarras dû soit

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv 5 дней назад +4

    Modou mbacke ya gnak diom xana ama soudané franc xana franc paréwoul domeram

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 5 дней назад +3

    Zarco eumeu mo nekh amateur yi

  • @abiboudiouf8649
    @abiboudiouf8649 5 дней назад +1

    Ama tagoul sou gniowe danou wat 16 dey danou

  • @AblayeLo-z5x
    @AblayeLo-z5x 4 дня назад

    Bakari sa data yaye

  • @issaleye154
    @issaleye154 4 дня назад

    Reugeu reugeu zarko

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 5 дней назад +1

    da hame Ni Ama si Modou lo la diem motakh mouye diéma wakhou gayi yaw dieulele sa morome yiii walla bayi di nogotou haléyii ak payiii😅😅

    • @lassanatalla767
      @lassanatalla767 4 дня назад

      Ama mo takhaw ni béneu yone lay beuré ak Modou donc na xoli lénéne 😂😂😂

    • @volfroitfall8785
      @volfroitfall8785 4 дня назад

      Modou si bopamm mo amoull jott si ay ama limmko wann rek doyna

    • @DameNguirane
      @DameNguirane 4 дня назад

      Khana dangéna beugue modou ray léne😂😅

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 5 дней назад

    zarko yagui maiye beug soff NK doté yaw la done faral ledieul Ndaye sa gate bii ga dieul sa thiés😂😂

  • @SinyLo-bw8ee
    @SinyLo-bw8ee 5 дней назад +1

    Bakari boul niou ndeye fonto eh

  • @ndiagadieye4715
    @ndiagadieye4715 5 дней назад +1

    Deguele fadam di garaw garawlou

  • @mbayedieng2427
    @mbayedieng2427 4 дня назад +1

    Zarco est devenu bavard'Super con tu nous parle de Molier,tetoi grande gueule

  • @moustaphafall9494
    @moustaphafall9494 3 дня назад

    Wa keur pikine khamouma lan mo takh gnou gnakk ndayi djom rk bilahi Modou dakhar seen 24 coups ngene nek di wakh ni rk ama wakh louka saff boumala guisson douma def si ioe taw wakh louka néex ngene nek fi di doul rk

  • @YannickDieng-wv4sh
    @YannickDieng-wv4sh 5 дней назад

    Modou mbacket il faut parler français

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 4 дня назад

    zarko Yaw Sa data yayae wakhou fi dara dou touss

  • @issaseck9791
    @issaseck9791 5 дней назад +2

    Wa pikine vous parlez trop comme vous avez déjà gagner franc

  • @cherifcissokho4633
    @cherifcissokho4633 5 дней назад +3

    Bakary boulniou fonton way Zarko na dane aye natango wam ni mom dora meuneu djeul Eumeu Sene !! Alioune Seye2 mingui fi Sathies moko dane Serigne Ndiaye mingui fi Gris 2 moussa Ndoye, fils de Balla pokola, et puis na djeul revanche ci sathies ak modou anta mouy lathieu Eumeu sene tée pikine boys Niang mingui ci kanam Eumeu ak Ama ak Pokola

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 5 дней назад +2

      Sa waye bul fonto nit gni
      Zarko da meune dane gris bi dane eumeu sene di dieul sathies?
      Esk sathies da dieulate malick niang biko dane?
      earko da meune teiglei 6 defaite mudjei dane VIP ga ni dougn ay natang
      Boulene gnu fonto waye va nane pookola
      Pokola na xar petit lo

    • @MoDraronie
      @MoDraronie 4 дня назад

      @@thiamahmadulattekh562 May wakh mouy limm POKOLA... Non mais gniii nekh naniou quoi. Yangui wakh waroul beure ak Emeu, beu paree ni dafa wara beuree ak Pokola minga khamni Talfa leu moudjee beurel... Khana nga wakh Jacob sakh.... Pfffffffffff keneu wakhatoul xam xam, kou nekk sa nafssou bakane rekk tchimmmm

    • @papiiiswelleeiih5728
      @papiiiswelleeiih5728 4 дня назад

      😂😂😂😂😂kholaleee breud bii mom

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 5 дней назад +1

    zarko dieulele pokola 😂😂 gaye lathie eume AK Ama 😂daga délo avance sathies tapéte😂😂

  • @SaliouSarrMaçon
    @SaliouSarrMaçon 4 дня назад

    Zarco doul way

  • @LJ-xz5vy
    @LJ-xz5vy 5 дней назад +2

    Balla gaye 2 dan na Gris beh tog si kawam

  • @goumbagueye2768
    @goumbagueye2768 5 дней назад +3

    Zarko danofi mbeur bou tang gris pa la 45ans Niang bou Ndaw Diène Kairé Mbaye Gouy gui Ada Fass combat yoyou yép ya nékone favoris adversaire de taille yinga am yép dagne la dane ba pré nga Bari wakh lamb légui dafa yomb trop démal nga dieul Tyson 2 Moy sa adversaire

    • @MbackeNdiaye-qd9up
      @MbackeNdiaye-qd9up 5 дней назад

      Yaw daga sokhor

    • @Anarbreezy
      @Anarbreezy 4 дня назад +2

      Linga waax ni dou deugg ngaa baalma nak

    • @papiiiswelleeiih5728
      @papiiiswelleeiih5728 4 дня назад

      Gaynn liii gua wax sii zarko ak gris gnep waxone gris dakoy humilier ak boy yii nak gnep waxone tmt zarko doulene dane tay gua tok fii nane ay zarko danoul mbeur bou tank gaynn chak combat zarko fii guene dii moudie 😂😂dalale rek gaynn

    • @benamar6656
      @benamar6656 4 дня назад +1

      Bou néké Favori combat yoyou yeup rek Baxna Lolou Kou Ndaw douko am

    • @ModouDiouf-i4d
      @ModouDiouf-i4d 4 дня назад

      Mak sou narer touk lagnkoy wakh🎉😂😂