Un grand champion, qui a térassé des grands lutteurs aujourd'hui champion, il faut qu il obtient un combat. Faut que les promoteurs viennent vers Tyson 2
Cest pas vrai limou wakh eumeu dafa am carriere mome mou am carriere..il faut nut gni gueum yalla nangou li yala dogal si nit.. eumeu debut you meti la am diayantè ba aksi fimou aksi
C'est parce que la lutte sénégalaise est organisée dans L'amateurisme que les lutteurs sont frustrés. Il devrait y avoir un classement mais on ne sait pas qui est le premier contender de Modou Lo ni le top 10 ou top 15 de la lutte. Si les choses étaient bien faites de gros sponsors du monde entier pourraient être attirés.
@cheikhdiop9673 encore ama baldè défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
On ne peut pas parler de donner une chance entre Sa Thies et Tyson2. Il a nettement un meilleur palmarès que Sa Thies. Il ne faut confondre performance et popularité. Sa Thies doit sa popularité pris par l’ombre de Balla Gaye que par ses performances
Saway wahofi doul sathies gnimou tassel ak gnimou dann kii beurewoul ak niom sou feke victoire ngay holl kone nala leer nii kone beurineuh ay mbeur you ndaw you eup ay vip victoire
Mom mo yakh lambam mbeurou lébou yi niom nieup louniou wara bayii moy topou si ginaw yénna mbeur yi le cas de zambala Quench kholléne si aladji ndoye mi mbeur yingén topou dagnléni utiliser rék amalougnlén bén aport
Le grand champion Tyson2 wa anii wa albourakh
Un grand champion, qui a térassé des grands lutteurs aujourd'hui champion, il faut qu il obtient un combat. Faut que les promoteurs viennent vers Tyson 2
Bilay walay❤❤❤❤❤
Un très grand champion mais legui lamb ay waga ak ay ginzman lay promouvoir
Lolou la nak mbeur you bari yinouy toud limou am si victoire amouñ xaadj bi
Machallah Tyson || pikine est éternellement reconnaissant en vers toi merci
Bravo à vous depuis Sénégal Dakar
Dieuleul professeur mané grand yoff mbolo amneu 24 victoire béneu défaite
Kouy kokou tyson 2 day moromam
Tyson 2 vs Fils de Balla
Tyson 2 vs General Malika
Tyson 2 vs Gris 2
Général malika dou moromame
Général danoul kou neune ki lambj mo Bari Toul Diambar rk
Tyson 2 vs Alioune seye 2 moy combat bi
Malgré sn talent day entraîné sérieusement 🙏👌al bourakh aÿ thieu bok
Nieuweul Diambar parcelles tu auras des opportunités Mansour Bâ kou bakh leu et il est social
Boy ioe wanné wo rkk nanga mom Diambar Wala nanga kham Diambar dara
Tono mayko lolou😂@@cheikhgueye1612
Fall ioe horomou nga
Gneuw parcelle comment j'ai pas compris..
Ki kitt na😂😂😂
Yéna trahir tyson motakh douléne djikk
Tay Sen 2 Ak Youssou ndiour Bo balla Gy 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Taison un vrais champion 😢
Vraiment champion la nak
Frr linguéyy bi rafette na machallah 🎉yalla na danga wayy bi yagg si kanam rek inchallah
Alburakh stp teugeu leul Tyson combat stp
Sénégal danio gawa soul ndanane, Tyson 2 un grand champion 20 victoires 3 défaites
Tyson2 et Forza
Naniou ko bollé ak Professeur Mané mou may ko chance Niarri champion leuh bly
Cest pas vrai limou wakh eumeu dafa am carriere mome mou am carriere..il faut nut gni gueum yalla nangou li yala dogal si nit.. eumeu debut you meti la am diayantè ba aksi fimou aksi
Bilahi wakh nga deug lepp yalla la
Degue bou werr nga wakh, Mbeur bou mak ci bopam mor sonou
Niak ambition rék di andak nit ba faté sa bopou
Eumeu sene nena problème yoor téléphonâm la ame di doul té meussou mako guise té yoroul niarri telephonam si lokhom .
Vrais champions..vrais NDANAANE lamb wakhoul deugue rek!naniouko diokh COMBAT
Thiey galass bonne continuation mn ami
Na Nice ñk l'ambo la woun Franc Danna la jex na jex ña la Lepo Nice
Con ngaa rekk changel li nga binde puisque waxoul ci Euhmeu Sene Dara
Tayson 2 alioune seye 2 combat ay kouko tegue naw haliss
Falou galass bonne continuation
Lamb j légui dafa am ay lobby
Diakhassé bakhoul eumeu kou bakhla dafa am gaffe, loukhew rek niounè mome la
Franc kesse Franc kesse Franc kesse ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Forza bakhna
Aka bege lou safe kani😂😂degele nimou lime😂😂
Cng nalakoo diohhe
Dieulal diam tery
Kay beré kén yakoul sa kariér
Tyson 2 bilayi sama mbeurla bamou guéné si clafbi laako bayi khel mou kontiné di daan djek djéki rek guissatoumaco promoteur bayi lene ko khél nak
DIAplen si champion la
Yallah nalla Yallah takhawou
Nga moung danga gnibi won pikine
😂😂😂😂
C'est parce que la lutte sénégalaise est organisée dans L'amateurisme que les lutteurs sont frustrés. Il devrait y avoir un classement mais on ne sait pas qui est le premier contender de Modou Lo ni le top 10 ou top 15 de la lutte. Si les choses étaient bien faites de gros sponsors du monde entier pourraient être attirés.
Vraiment
Tu as tout dit
Journalistes yi dagno wara nangou sen micro yi , amolen ben xam xam , diaxassè rek molen nekh koi ak beug vue. Go way !
Viens a diambar tu auras ta chance frère
Tyson 2 Vs Diam Terry
Tyson 2 vs Alioune seye 2 moy combat bi
Dijne camaraman
Il a cité ses principaux adversaires gris2 fils balla G Alioune séye2
Tyson 2 gayi niéméwougno
Tayson 2 Vs kaw gourdin Combat la dh
Taye la xamné gnuye yor micro yi ay saitané lagn
Albourah ki combat
Mansour ba je suis un parcellois stp teugueul Tyson diokh ko combat bou Bakh champion deugeuleu Lamb warouko bayi guinaw
Dakor avec toi
Ki moy aladji ndoye borom pokar bi beuré rk lay déf waurne yalla❤❤
Gris2 mola mane
mome ak yousou ndior comba la
Ama baldè défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
ak loumana khèw Ama dou danou inchallah ta guémbam li dou lale soufe
@cheikhdiop9673 encore ama baldè défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏
Way ngome belende way
Saytane bakhoul
Talfa ❤
Mais d'El niow si lamb yi du deukou gayi
On ne peut pas parler de donner une chance entre Sa Thies et Tyson2. Il a nettement un meilleur palmarès que Sa Thies. Il ne faut confondre performance et popularité. Sa Thies doit sa popularité pris par l’ombre de Balla Gaye que par ses performances
Saway wahofi doul sathies gnimou tassel ak gnimou dann kii beurewoul ak niom sou feke victoire ngay holl kone nala leer nii kone beurineuh ay mbeur you ndaw you eup ay vip victoire
N'est ce pas que les reliquats doivent être déposés au CNG ?
Sénégal eumeu séne mosi guena faux
Sa papa moko geuneu faux dmrm
Aka meuneu beurrer aladji ndoye borom. Médaille yi
🎉🎉
Wax gua deugeu bo téyone sawaye doula dañe
Ki champion DEUG leu lamb DJI dal boudoul guéne di wakh si média kéne doula teugue
Tyson 2 vs Forza
Tyson 2 vs général Malicka
Tyson 2 vs zambala
Tyson vs gris 2
Tyson 2 vs Ama nekh
Tyson 2 vs Jacob baladé
Très bien frère
Jacob😂😂 pikine la Deuk
Dou beure ak Jacob dou beure zambala
Bayil ta deme si Modou lo wala écrit per balla gaye
grand mbeur
Tyson 2 boy yi nieme wouniou ko
Reporter bi dra xamouko
FRANC SEUL
Waxga degeu
Aline seye 2 bi mom kombala
Wakhoul lolou d
Mais reporter qui est tu?😅
Nafekh bou bonne la beug ko diakhasser akh eumeu
Prometeur yi nio yakha lamba dji
Non lambdji legui Kay moye lolou
Mom mo yakh lambam mbeurou lébou yi niom nieup louniou wara bayii moy topou si ginaw yénna mbeur yi le cas de zambala Quench kholléne si aladji ndoye mi mbeur yingén topou dagnléni utiliser rék amalougnlén bén aport
Lambat wahoul deugu rek
Genr journalis yiiii aka nio diara moytou kii vrai cheytané la dafa beug wakhelo tyson si eumeu .......bayilennn di yak digueunté yiiii
Daga wara nieuw écurie falaye baldé relancer watt
Démal Écurie Balla gaye 2 diga beurré ba now
Vous êtes nuls! Pertinence de questions zéro!
Tyson 2💚♥️
Pourquoi journaliste yiii saytaner la xamoul
Gni douniou aye journaliste aye doulnaliste lagne nafekh diakhasser rek
Mbeur dou Mbok dh
Tyson 2 fils de balla
Aka meuneu beurré
Boina sa gnone ngén tan kw yak eumeu sene
😂😂😂😂😂😂ki moy kan
Do amateur dé oubien tu blague
Tayson 2 mo dieulon claff rdv ba serigne modou niang teugon 32mbeur mom modieul finale bi yallnako yalla yereum
@@KM-ou8cwyow yasi sonou diko tontou 😂
Reporter bi moy bane
Vrai con leu😂
Moy comédien 😂
😂😂😂😂
Fils de balla Tyson 2 Gora sok zambla
Niang bou ndaw