Net Tali: Il Garde une Dent Contre son Grand Frère | @nettalitv

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 9 янв 2025

Комментарии •

  • @diariabousso466
    @diariabousso466 13 часов назад +5

    😂😂 Sama Mame Kaye légui béne seute la ame la yakar mouy Yow. “ yangui deglou Ndeye Fatou déko déglou sape seute’ maniko thia Thiey khara ma nane café😂😂. ❤❤ Diam si yow Cherie 😘

  • @yongfresh842
    @yongfresh842 5 часов назад +1

    Machallah fatou kagna lañuy guiss Kanasatou❤ nak

  • @DIAMBAR55
    @DIAMBAR55 15 часов назад +4

    Wallaay xaalis saytaané la, waayé manoul dieund gor

  • @ElhadjThiam-p7x
    @ElhadjThiam-p7x 12 часов назад +2

    Salut sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta grand frère bi bakhoule dé

  • @absadiop2563
    @absadiop2563 17 часов назад +1

    Buona sera Sokhna Fatou caffè ❤❤❤❤ grazie mille vielen Dank ❤❤❤❤❤

  • @ngagnedeme-w2t
    @ngagnedeme-w2t 16 часов назад +3

    Grand-frère bi mo nité woul. Kou sokhor leu. Sa rakk même boula dioxoul alalam, danga ko wara diapalé. Sén yaye mo wara wakh ak sa frère bi mou délo leu sa xaliss. Ba paré diapaléla nga dém Europe.

  • @boundawbeye612
    @boundawbeye612 17 часов назад +1

    Viza kanada lolou baworna beulégi amagoul viza

  • @OussyenouSeck-wh8uf
    @OussyenouSeck-wh8uf 15 часов назад +1

    Fatou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @OussyenouSeck-wh8uf
    @OussyenouSeck-wh8uf 15 часов назад +1

    Khalich kén dou ci wouelou kénn

  • @khadimka2058
    @khadimka2058 4 часа назад +1

    Na diapou magam rek te bania djital alal comme mongui liguey te khaliss dafa andak Saytane nako baal te khamni nio bokou lepou

  • @absadiop2563
    @absadiop2563 17 часов назад +1

    Asalamallekoum Sokhna Fatou caffè sono grand frere nest gentie il y des gens mechante

  • @wanealpha1965
    @wanealpha1965 17 часов назад +1

    Na lath mag bi khalisam

  • @TenningKante-zv9lk
    @TenningKante-zv9lk 5 часов назад +1

    Kou bonne la son grand frère

  • @djamagueune
    @djamagueune 12 часов назад +1

    Bokk ndeye ak baye tahouta bah si yaw

  • @Jesiisiwiw
    @Jesiisiwiw 16 часов назад +1

    Salam sokhna fatou wadji son grand Frere dou nitt kou bakh me mome na mugne rekk te xamni loubakh rekk lay am dakh louway rendi sa lokho lay nathie .

  • @sallyfaye6183
    @sallyfaye6183 Час назад

    Dila nuyu bou baax sokhna fatou