Maa sha Allah, imam Abdoulaye N'dao. Yalna borome bi yombale lëup té yéssal n'dieugalome thi kaw sougnou sopé bi imam Alioune Badara N'dao rda, allahoummah salli ala seydina Mouhammad wa salim.
Xutba ca daara Imaan Aliwun Badara Ndaw, rahimahulah tabaarakah wa ta'aala, nii reg la mën a demee. Deloo la Boroom bi subhaanahu wa ta'aala. Këlifa gi maa ngi dimbali koo ca kàddu yu am solo te jëlee ko fudul foo wara jëlee... Imaam deh, daa amoon xalaat bu mag ci fuñu wara yóbb reew mi. Laamlaame wu ci, amu si sikksàkk. Baatu laa ilaaha illal Laah, firi na ko bës loolu reg dow na. Xutba bu mingoo ag jamono : maandu, dal ci reew, ci njiit. Senegaal nag moo laaj xutba yu ni mel ndax depi indepandaas ba suni jonni yàllay tey ñi fi yeeg wàcc ana ñu : ku gën a dëng sa marom nga kaa la. Seŋoor ba ci Maki Sàll. La Imaam namoon ci daara ji boo leen tegi wul seen tànk inchaa Allah da na am ndax Allaahu ta'aala kepp ngeen ndi dimbali koo, moom la ñuy dimbali koo motax ma safoo di leen topp saasune. Jërëjëf.
Thiey adouna Imam ndao demna. Ndeysan un homme très pieux. Qu’il repose en paix amen
Machala amatina solo dieureudieuf imame alioune badra diaw yalla nako yalla kharé aldiana firdawssi
Macha Allah ya Imam Baraka Allahu fiykum
Macha allah Baraka lahou fikoum lérna dé oustaz imam Alioune badara ndao Paix à son âme
Maachaa Allah ya imam. Baarakallah fiik
Maa sha Allah, imam Abdoulaye N'dao.
Yalna borome bi yombale lëup té yéssal n'dieugalome thi kaw sougnou sopé bi imam Alioune Badara N'dao rda, allahoummah salli ala seydina Mouhammad wa salim.
Amiin
جزاكم الله خيرا وبارك الله فيكم
Macha Allah
Maasàllaa Jaajëf Imaam Xutba Bi Am Na Solo
Machalla
Billahy 😭😭😭😭😭😭
Massàlla
ما شاء الله
Machalah jarajaff ya imame
Xutba ca daara Imaan Aliwun Badara Ndaw, rahimahulah tabaarakah wa ta'aala, nii reg la mën a demee.
Deloo la Boroom bi subhaanahu wa ta'aala.
Këlifa gi maa ngi dimbali koo ca kàddu yu am solo te jëlee ko fudul foo wara jëlee...
Imaam deh, daa amoon xalaat bu mag ci fuñu wara yóbb reew mi.
Laamlaame wu ci, amu si sikksàkk.
Baatu laa ilaaha illal Laah, firi na ko bës loolu reg dow na.
Xutba bu mingoo ag jamono : maandu, dal ci reew, ci njiit.
Senegaal nag moo laaj xutba yu ni mel ndax depi indepandaas ba suni jonni yàllay tey ñi fi yeeg wàcc ana ñu : ku gën a dëng sa marom nga kaa la. Seŋoor ba ci Maki Sàll.
La Imaam namoon ci daara ji boo leen tegi wul seen tànk inchaa Allah da na am ndax Allaahu ta'aala kepp ngeen ndi dimbali koo, moom la ñuy dimbali koo motax ma safoo di leen topp saasune.
Jërëjëf.
Jërëjëf
Macha'Allah ☝️🤲🤲