Tabaskie: Cheikh Modou Kara «Nagn rafétt njort téy si Sonko ak Diomay

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 16 июн 2024

Комментарии • 179

  • @cheikhabdoumbacke6970
    @cheikhabdoumbacke6970 7 дней назад +2

    Dieuredieufaty baye Kara ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @bambaseck62
    @bambaseck62 8 дней назад +57

    Délinquant fiscal fen + sathie wayé lepp mo gueune biiral sa employé kharal deuxième tour

    • @Bambasallahma
      @Bambasallahma 8 дней назад +5

      Tamouy deugue😂🤣

    • @yahyabenmahet4074
      @yahyabenmahet4074 8 дней назад +3

      😂😂😂 thieuy garde rapprochée pastef yi kou song sonko dafa repp

    • @Annebaidysouleymane
      @Annebaidysouleymane 8 дней назад +3

      Bobou punchline kou tédd ki waay 😂😂😂😂😂

    • @saufi719
      @saufi719 8 дней назад +2

      Ma yokale la ak awa baba thiam la femme de aliou secke rajoute momy secke mariage bou saleté ak bébé ndiaye bou mansour bouna ndiaye bougane amena ak mome dôme

    • @Annebaidysouleymane
      @Annebaidysouleymane 8 дней назад +1

      @@saufi719 ay relations you dégoûtants laafi guiss beurk 🤢🤮

  • @DiawMohamadou
    @DiawMohamadou 7 дней назад

    Mbacké dieureudieufe thi cadouyi AK sogné bi machalla ❤❤❤❤

  • @cheikhabdoumbacke6970
    @cheikhabdoumbacke6970 7 дней назад +2

    Dieuredieufaty kou tedki ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @cheickmoinga3245
    @cheickmoinga3245 8 дней назад +11

    SONKO Seul ❤

  • @cheikhabdoumbacke6970
    @cheikhabdoumbacke6970 7 дней назад +1

    Sonko à vie ❤️🔐

  • @modouloum4438
    @modouloum4438 8 дней назад +18

    Tey mom je suis daccord avec ton discours politique❤😂

    • @Issa_baxbaxaa
      @Issa_baxbaxaa 8 дней назад

      Parce que dafla engrangé motakh...

  • @MandoumbeNdiaye-yf1tv
    @MandoumbeNdiaye-yf1tv 8 дней назад +18

    Bougan niaka kham bopam moko dal, man nga Sathi Alalou lou niépou Bock ak Sa Alalou ligueye Kat di am loy wakh, dinga faye impot par la force inchallah 👆👆👆👆

  • @thionegueye1397
    @thionegueye1397 8 дней назад +5

    Ce site doit arrêter ces manipulations et rétablir les faits, votre titrage n'a rien voir avec le discours du Guide,

  • @sambamatuidi2378
    @sambamatuidi2378 8 дней назад +7

    Sans limite est entrain de diffamer Serigne Modou Kara. Vraiment ce qu'il a révélé hier n'a aucun lien avec les propos de Bougane. Il est temps que les fils de ce guide vous porte plainte. Respectez le code de la presse svp

  • @julesndong5740
    @julesndong5740 8 дней назад +5

    Franchement tey je suis entièrement d'accord avec vous, merci Mbaké

  • @dembacamaraba8965
    @dembacamaraba8965 8 дней назад +3

    Si non on va vous poursuivre en justice vous sans limite

  • @DabaDia-cv9si
    @DabaDia-cv9si 8 дней назад +47

    Iska Ousmane sonko mase na toudou tourou Bougane ?

  • @karakhalil4252
    @karakhalil4252 8 дней назад +6

    Sans limite bayiléne sen yi déléne wakh askan bi Deug sén titre bi démé woule nonou déléne wakh Deug

  • @cheikhabdoumbacke6970
    @cheikhabdoumbacke6970 7 дней назад +1

    Alhamdulillah

  • @user-tw7dc6vx3i
    @user-tw7dc6vx3i 8 дней назад +9

    Ndeysane mashaallah Mbacke wakh djou rafet rk lagn la xam Baye Kara

  • @dethiethiaw4048
    @dethiethiaw4048 8 дней назад +11

    Hoo sana Serigne bi mingui maguette mais tjrs beau

  • @FamaNiang-mr7qo
    @FamaNiang-mr7qo 8 дней назад +8

    Mbacke bala aissa maguilay ziarr 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @alyahineba5628
    @alyahineba5628 8 дней назад +5

    le constant sa waxi demb moy sa waxi tay cheickh Ahmadou kara Mbacke amoul diotou tntou kene bayilene di interprete aye waxam ci noumou lene aranger mom bouy wax interet general lay waxe ndax mon c un regulateur

  • @aliounebambakara7167
    @aliounebambakara7167 8 дней назад +2

    Jerejefe Mbacké vous êtes toujours dans vos logique ❤

  • @seyyidinaausmaannoreyni2316
    @seyyidinaausmaannoreyni2316 8 дней назад +7

    Sans Limite yéen amu léen limite ci ay duul fénn rek ngéen mën Modou 𝒦𝒶𝓇𝒶 tuddu fi bougane Wala Sonko Diomaye.

  • @rokhayandiaye7375
    @rokhayandiaye7375 8 дней назад +3

    Machala c'est le Sénégal ❤❤❤❤❤❤❤

  • @albaba45
    @albaba45 8 дней назад +13

    Il va payer jusqu'au dernier centime ce fraudeur.

  • @MamadouGueye-dk7bk
    @MamadouGueye-dk7bk 7 дней назад

    Ousmane sonko Dieuredieuf serigne Ousmane sonko rekkk Man serigne modou gueye chef religieux Senegal makò barkep serigne mandoumbe mbacke

  • @samsene3491
    @samsene3491 8 дней назад +1

    Le guide est toujours constant sur ses pensées et actes,le titre que le site a mentionné, je vois pas le relationnel avec Bougane vu qu'il n'a qu'il pas personnifié, il parle d'une manière générale.

  • @Ababacarmbaye2421
    @Ababacarmbaye2421 8 дней назад +2

    Sans Limite vous n’êtes pas sérieux du tout, il faut franchement pensé à vous limiter. Ces propos de Bougane n’ont rien à voir avec la déclaration de Serigne Modou kara. Ce dernier parlait dans le cadre général en appelant à plus de tolérance pour ce gouvernement qui vient de s’installer. Sinon arrêtez de diffamer et penser à approfondir vos traitements.
    YEEN NI NGEEN YAG MEEL DEUK BI KEEN REERO WOUFI WOON YEENA JAXASSE NIT ÑI BA NIEUP DI NOONOO.

  • @adviseragnam7050
    @adviseragnam7050 8 дней назад +2

    Merci Karara❤❤❤

  • @Bambasallahma
    @Bambasallahma 8 дней назад +6

    Biireul sa employé en étant un homme marié en tant que musulman lolou mom Bougane sakou ngogne l'homme du 2ém Tour mom rék moko sagne 😂Mais Borom télé doff yi dîna faye sunu impôts par force té dou ci meune niébé😜

  • @aboubacartounkara5344
    @aboubacartounkara5344 8 дней назад

    Celui qui guide son peuple AL QAÏD

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj 8 дней назад +1

    Démbeu waho li dé Serignesi koléne tope bilaye dinko rethiou té amouniou sahe gore kokou dou Serigne mayléne niou Diam wahk rék té douguéne dieufé saram li rék

  • @CheikhSene-qc3gt
    @CheikhSene-qc3gt 8 дней назад +6

    Machalla mbacké balla

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj 8 дней назад +1

    Modou Kara diga dém kasso ni sa moromou bandi yi yéneu yeulone nervis yi di torohale dawou réwmi

  • @user-kh3xm3qo8c
    @user-kh3xm3qo8c 8 дней назад

    Merci 🙏

  • @bambambow6946
    @bambambow6946 7 дней назад

    Serigne bi Ndeysanne akamo Constant teh mane rafetal
    Wa Sénégal khamou niou dieum dji walakhii

  • @momoseck1617
    @momoseck1617 8 дней назад

    Machallah ❤️

  • @MoussacamaraCamara-pt5ht
    @MoussacamaraCamara-pt5ht 8 дней назад

    Il se prépare Oui

  • @AliAli-pj4vb
    @AliAli-pj4vb 8 дней назад

    Machallah mbakce balla

  • @DabaDia-cv9si
    @DabaDia-cv9si 8 дней назад +13

    Mane masou ma khame lou Serigne Modou kara di wakhe mane kéne khamoul foumou fare

  • @ninkinanka3644
    @ninkinanka3644 8 дней назад +6

    🛑PÈRE BROUKH LOU MOM DOYNA SEUK NÉKAL FA NGA NÉKONE REK. WA SALAM

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 8 дней назад +1

      Dèèt doko bayi mou bouroukhlou kara Jackson mi door rek leye deff

    • @sambamatuidi2378
      @sambamatuidi2378 8 дней назад

      ​@@ghettoyouthkatakyni7843khana si séne birr leufeul ndeye laye broukhlou😅

    • @mansourdiack1289
      @mansourdiack1289 8 дней назад

      @@ghettoyouthkatakyni7843encore toi thiey kharou sonko yi 😂

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 8 дней назад

      @@mansourdiack1289 mansour mansour petit diack yowe nguèye kharou kara Jackson ngua mèye khassè kharou sonko🤦🏿thiey petit diack khamna dènioula guemlo nè kou dal ci sène charlatan yi nguè askanalè ko pastef walla sonko😂yène sonko yobouna sène fit yi deh,bilahi yène nieup ragual sonko wayè dinala wakh lou lèèr comme ça dingua khamnè bokouma pastef tè sonko dou sama serigne ndakh dokhouma ci yoyou guemouma serigne beugouma thiogue tè talibè kara Jackson yi meunoumalène respecter comme nitt👉🏿nitt dou dèglou serigne boukèye wakh na nane ndokhou touba bi😂

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 8 дней назад

      @@sambamatuidi2378 non non damèye dieul kara Jackson souli ndèyeum roff ci kara après kèpe ko fofou khamngua loutax sagouma sa ndèye ndakh talibè rek la meuna diourr donc bayil ma teubeli sa serigne todj leufeul ndèyeum tè ma wakhla lou lèèr dou yowe dou sa ndèye dou sa ndèyou serigne mo ci meune dara...dangua yakaarone nè dangua rew lireul sama tourr khamnè mala guena khotèkou fouf

  • @ngomezbii4570
    @ngomezbii4570 8 дней назад

    Bonne Posture NOREYNI ❤❤❤❤

  • @user-me2tt8wn9u
    @user-me2tt8wn9u 8 дней назад

    Maachallah maachallah ❤❤❤❤

  • @yahyabenmahet4074
    @yahyabenmahet4074 8 дней назад +1

    Balla aïssa is back ❤😂

  • @doudousylla7821
    @doudousylla7821 7 дней назад

    Delene xol lingéne di bind ci serigne bi bakhna

  • @moustaphaseck7661
    @moustaphaseck7661 8 дней назад

    Merci kara ❤

  • @mamadoulaminembodji9648
    @mamadoulaminembodji9648 8 дней назад +5

    Enfin je revois le cheikh Modou kara que je conaissais🎉🎉

    • @videoskids4203
      @videoskids4203 8 дней назад

      Il na jamais changer
      Senegalais mo baxo kouy waxx louma arrangé woul rk gnu ngangni ko wayei Kou Baxx Ki il est plus constant que jamais

    • @mamadoulaminembodji9648
      @mamadoulaminembodji9648 8 дней назад

      @@videoskids4203 🤣🤣g dit le serigne Modou kara que je conaissais car il disait aux jeunes de tailler les rastas,d'aller dans lrs cimetieres,au senegal ce mode de faire du Ndogu pour tous ,kara etait 1 des propulseurs de cette chose.Mais apres ce que g nominè durand le Macky il a mangè dans le plat du dictateur ça v sur🤣mais maintenant qu'il n plus Macky ,il fait des analyses avec plus de serenitè🙉🤔🙈🙊🙉

  • @Issa_baxbaxaa
    @Issa_baxbaxaa 8 дней назад

    Serigne bi amoul diotou bougane bakay tontou..pour mou ler serigne bi dou wakh lou gnaw thi kéne lou rafet ...DIEUREU dieuf serigne touba.

    • @Issa_baxbaxaa
      @Issa_baxbaxaa 8 дней назад

      Lou rafet rek lay wakh thi thi gneupp

  • @moustaphambackeba4223
    @moustaphambackeba4223 8 дней назад

    No mane dale site yi diakhalnañema diakhasé rék serigne bi guéne di wax wakham ñounane bougane laye wakhal meuna khathie

  • @abdourakhmane2048
    @abdourakhmane2048 8 дней назад +2

    Sacré kara

  • @MamadouGueye-dk7bk
    @MamadouGueye-dk7bk 7 дней назад

    Na ngnïpp delou thie yii aliou dia demall bayyii tokk moyy dokhhh djiekhnaa

  • @khadimdieng3815
    @khadimdieng3815 7 дней назад

    Ki amna diom 😂😂
    Deysane weroul

  • @momarcamara1028
    @momarcamara1028 8 дней назад

    DIEUREDIEUF MBACKÉ ❤❤❤

  • @babacarfall6788
    @babacarfall6788 8 дней назад +1

    Serigne bi wakhoul dara thi wakhou bougane boulene di djakhassé changer votre titre svp dja kara et constant thi Lou mou nek

  • @saliousagna8158
    @saliousagna8158 8 дней назад +1

    Bou souba ngén’ di comprendre KARA toujours constant dans son logique MBACKE JEREFETETY

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 8 дней назад

      😂😂😂ki depuis plus de 30 ans kène meunoul kham limouye wakh dou tèye lèniouye comprendre

    • @saliousagna8158
      @saliousagna8158 8 дней назад

      @@ghettoyouthkatakyni7843 yalla nanou borom bi defall niou féké yagatoull dî nga comprendre légui

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 8 дней назад

      @@saliousagna8158 waye depuis 20 ans mangui khaar

    • @sambamatuidi2378
      @sambamatuidi2378 8 дней назад

      Bilahi lou lerr nga wakh

    • @sambamatuidi2378
      @sambamatuidi2378 8 дней назад

      ​Yaw kom k ignare nga do meuneu kham limouye wakh mais nioune kham nagn ko

  • @bambambow6946
    @bambambow6946 7 дней назад

    Wakh Deug Yalla Serigne bii limouy wakh romb na ay wakhi Bougane ak Sonko...Wa Sans Limite delene wakh deug teh yalla takh

  • @akhenaton09ahma99
    @akhenaton09ahma99 8 дней назад

    Bougane est un ex DJ il est toujours dans le show

  • @boubadiame5585
    @boubadiame5585 8 дней назад

    ❤❤❤❤❤

  • @mobayefall4834
    @mobayefall4834 8 дней назад

    Ballaïcha Diouniiy Tabaski ❤❤❤

  • @sasou874
    @sasou874 8 дней назад +1

    Tout le monde sait que sans limite ay fenkat laniou

    • @ghettoyouthkatakyni7843
      @ghettoyouthkatakyni7843 8 дней назад

      Donc pourquoi tu regardes la chaine moi si j'etais sure que sans limites dèniouye fènn doumalène sètane

  • @lamineniakh7046
    @lamineniakh7046 8 дней назад

    Ces propos du général n'ont rien à voir par rapport au propos de Bougane, il n'a pas fait allusion à la déclaration de Bougane, il a juste parlé dans un carde général sur les attitudes que les sénégalais devraient avoir par rapport au régime qui vient de s'installer.
    Sans Limite revoyer comment titrer, une information ça se traite.

  • @CheikhahmadoubambaNdiaye-zf5yv
    @CheikhahmadoubambaNdiaye-zf5yv 8 дней назад

    Serigne bi deh talou léne bay wakh si gni mom rewmi moko gnor

  • @sunugaalcakanamTV9971
    @sunugaalcakanamTV9971 8 дней назад

    ❤❤❤🎉

  • @mbackedieng1483
    @mbackedieng1483 8 дней назад +8

    Thieuy modou beug naa bouroukhlou d

  • @modoufall4327
    @modoufall4327 7 дней назад

    Mbacké dagua bakh

  • @seydinaahmadou2035
    @seydinaahmadou2035 8 дней назад

    Sans limite deil informé lou dobe deug , bayileine diaxassei général dou sa moromou baye

  • @bayefalldeugg466
    @bayefalldeugg466 8 дней назад

    🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @tafsirmouhamedlaminedrame4102
    @tafsirmouhamedlaminedrame4102 8 дней назад +7

    Il prépare la transhumance comme toujours

  • @karakhalil4252
    @karakhalil4252 8 дней назад +1

    Sen titre bi ak li serigne bi di wakh sakh da bokoul

  • @SowrouFallkara-nd5me
    @SowrouFallkara-nd5me 8 дней назад

    Jerejef balla aïssa

  • @MbackefallDiouf
    @MbackefallDiouf 8 дней назад

    Titre Vidéo bi ak vidéo bi comme Yalla ak Yally 😂 bayi lénn Serigne biguénn Di sossal

  • @alaminembaye3753
    @alaminembaye3753 8 дней назад

    Serigne biii dou meusa wax ken lou niaw yén lolen beugue degue rk ngen di degue

  • @MbackefallDiouf
    @MbackefallDiouf 8 дней назад

    Sans limite amm lénn limite si sénn mensonge yii😅😅 Seigne bi fann la corriger Bougane ? Bougane bouko Serigne bi beugué Corriger Xam foumou kayy défé si soutoureu

  • @patheka8416
    @patheka8416 8 дней назад +3

    Louma menoul comprendre thi wakhi bougane yiii lane moy fenn bimouy wakh xana dou diffamation bii

    • @baboucarbadji4917
      @baboucarbadji4917 8 дней назад

      Momm leyy wakhh dossier Mame mbaye Niang

    • @mamecorsarr82
      @mamecorsarr82 8 дней назад

      Diffamation bi lay wakh

    • @Mouss400
      @Mouss400 8 дней назад

      Diffamation moy féne bien sûr, lolou kay dafa lérr

  • @mamadouka5690
    @mamadouka5690 8 дней назад

    Yén wa site bii boudé Serigne bi molén déssé diguéne guis loulén doy seuke si réwmi baxna rék li leup yén wa pastéf là nguire diaxasé nite ngì wayé Dina lérr niolén guëna paré foufe

  • @ndoyebaytir7403
    @ndoyebaytir7403 8 дней назад

    Yénna mëna fénn té gnéme yalla SL! CHEIKH AHMADOU KARA n'a jamais dit cela!! Nék len fi di rambaaćć ak jaxassé ak galvaudé les propos des gens rk!! Bou ngen di outt Buzz woutii jilén ko ça xaajj la wax!!

  • @ghostghost0778
    @ghostghost0778 8 дней назад +1

    Bougane est un aigri, un frustré. Il a raté sa trajectoire politique. Il va mourir opposant. Le mec n'arrive même pas à avoir des parrains pour la présidentielle. Sonko dou moromou Bougane. Sonko est un Noble alors que Bougane cherche la noblesse à travers l'argent.
    C'est vraiment souffrir de débilité politique que de croire qu'il allait y avoir un 2e tour aux présidentielles de 2024, qui ont vu le sacre de Sonko à travers Diomaye. Les élections étaient pliées le jour où le conseil constitutionnel a validé la candidature de Diomaye. Et c'est ce que Macky a compris. Bougane, l'apprenti politicien n'a rien vu venir et a ainsi raté le train de l'histoire. Il a toujours joué double jeu. Et a perdu. Bougane, bois un gros coup d'eau fraîche .
    Sonko Mooy Diomaye
    Diomaye Mooy Sonko. ❤

  • @ibrahimagueye9424
    @ibrahimagueye9424 8 дней назад

    Boy kéneu déformé waxji Serigne bi nax mom kouko xam xamni c'est grand pacifiste,dundel bamou yag lool mbacke

  • @abdoulayembengue2610
    @abdoulayembengue2610 8 дней назад

    Bayilen di wakh Lo nite loumou wakhoul yen dalle amolene louguen ligueye loudoul si fén rek arrêté way😏

  • @alioutoure5035
    @alioutoure5035 8 дней назад

    Bougane loumou tede parte moko sonal geum sa bopou ak bagn loumou Don

  • @mamadoundoumbesy5644
    @mamadoundoumbesy5644 8 дней назад

    Soyez véridique avec vos titres. Où est Bougane dans tout ça ?

  • @abdoulayembengue2610
    @abdoulayembengue2610 8 дней назад

    Li Serigne bi wakh ak sene titre bi sakh bokoul

  • @soundiaye540
    @soundiaye540 8 дней назад +1

    Bougane bouma done yaw nopi lay deff ass Goore dou khassaté surtout bo défé ay bétises yo khamné da diss

  • @nganaasirabanaa5150
    @nganaasirabanaa5150 8 дней назад

    Tiiiins sa boyi rek nga neeké dmedia,loleen feen ba teudé leen,donc yaw dangay sathie Di fene Bougane

  • @SseeyyddoouuKanne1215
    @SseeyyddoouuKanne1215 7 дней назад

    Ki boy modou il na pas encore pris sa doze

  • @moussandiaye9964
    @moussandiaye9964 8 дней назад

    Sonko dou tontou bougane 😂.
    Bougane il faut payer, point barre,les impôts ça se paye😂

  • @user-bk8nm2ll7s
    @user-bk8nm2ll7s 8 дней назад +1

    Sans limite sollén beugué buzz guénélléne Serigne bi votre titre est archi faux et on va prendre des mesures sur vos mensonges en vers le guide

  • @amarcouragueye4262
    @amarcouragueye4262 8 дней назад

    Ce titre n'est pas conforme aux paroles du guide de la révolution pacifique en l'occurrence Cheikh Ahmadou Kara MBACKÉ. De grâce arrêté vos manipulation.

  • @sportmaisonpourtoustv
    @sportmaisonpourtoustv 8 дней назад

    😂😂

  • @khadimbamba2012
    @khadimbamba2012 8 дней назад

    Sans limite arrêtez de mentir

  • @baldefriperie7398
    @baldefriperie7398 8 дней назад

    Boucan rek

  • @dembasarr6019
    @dembasarr6019 8 дней назад

    Les têtes de lion¿??

  • @ibrahimadanso9214
    @ibrahimadanso9214 8 дней назад

    Wa sans limite arrêtez est ce que gaduu youmm fi wax moy corriger bougane bay len diffamation yii pour am beuz

  • @videoskids4203
    @videoskids4203 8 дней назад

    Lii motax keinn nawlotoul journaliste.. beugg gnu xol sa publication taxx ngay tergiverser di binede lo xamni deupowoul ak video bi
    C'est dommage

  • @MatarkaraTop
    @MatarkaraTop 8 дней назад

    Sans limite bayilen manipulation seri

  • @mamadousarr9564
    @mamadousarr9564 8 дней назад

    Comment peut on respecter les commentaires or que vous ne dites pas la vérité.la déclaration du guide Jah kara 👌 n'a rien avoir avec votre publication.c'est vous les menteurs, sans limite vous êtes mauvaise

  • @alioutoure5035
    @alioutoure5035 8 дней назад

    Bougane de gnake yar ak reuy ak yebate moko jape takhaw si Jake masalikoul Jinan di garouwale

  • @salayeniasse2271
    @salayeniasse2271 8 дней назад

    Bougane est arrogant il n' a jamais supporté pro kharal 2éme tour rek yaw ta Faye

  • @abdoulayebagouniang7668
    @abdoulayebagouniang7668 8 дней назад

    Arrêter de faire le malin sur vos titres bande de manipulateurs

  • @jakobdia3641
    @jakobdia3641 8 дней назад

    Dolén ay professionnel ndakh li Serigne bi di wakh wouté ak li ngueine titreé bayi nalén ak jam fén bakhoul c'est pas digne d'un journaliste

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 8 дней назад

    Bougane Gueye dafa sacrifié Diabar dji pour nek président teh meunoul am parrainage loloko metti 🤣🇸🇳 teh 2eme tours lay khar 🤣🇸🇳

    • @mansourdiack1289
      @mansourdiack1289 8 дней назад

      Saway wax day rafete respecter les morts xana boy yi dhé si manifestation yi pwvoir belene sacrifier nek lene ay nite Séne fanatisme bi nguene yamaleko fi

  • @caranoufedior564
    @caranoufedior564 8 дней назад

    Tous pareils haaye doorkate marteaux