Massamba une personne très douée et dotée d'ambitions élevées. Une personne aussi sincère. Merci de représenter notre cher héro Yakhya. Personne ne peut détruire son image au sein de la lutte sénégalaise. Il a fait ce qu'il devait faire au temps qu'il devait le faire. Maintenant il est temps de se retrouver vers le plus essentiel. Mamadou Moustapha SENE
Personne na essayé de détruire son image le seul problème est que vous êtes des complexés envers votre propre personne … yahya loum am lambeu moko ko may niolen ko dieuneu beugu fapp autant qu’on aime siteu … yahya louko dieuneu metti si adounam moy yeen soit disant mbokam yi nga khaam ni allalou adina rekaaa len bolleek mom siteu nak boudoon allalou adouna wala dimbal si lamb motakh mouy toudou yekini dou yeksii fii bimouy mettiii niouy khouss toudou niou tOuram kounekeu si nioun beugonn nga tey siteu fadial la sa merrr si balla guaye … dieuno len nio nekeuh serere
Lolou nga djiss "communication Sénégal nga wah dè"? Lol vraiment wagnile se prétention un peu qu'en même rew mi yor nagnou "lou geuneu wow kong". Wa salam.
Je comprends un peu parcek Siteu tchii Albourakh lako wakhé motakh droit de réponse bi filay kooy wakhé😂😂Yekini je pense kil a tourné le dos à la lutte
Niioun PA xamnagn ni Yekini Modou rk moko dondeu.. Mtx Yekini beug Modou, mais Siteu ay niodi ak incarner moko nekh.. Daw lakou bou bone bi. Yalna Balla nokoula ba arrêt khar mbaye madiaga..
Man dh Mangui dora faral balla gaye si lamb Bly nax siteu lomou def Modou dama metti saga bimou saga modou metii nama trop sax Yalnako balla domou dan ko
@@libassesy je te conseille petit frère d'être sérieux dans ton travail (cad fais ce que tu as à faire de façon sérieuse quotidiennement) et donne le meilleur de toi meme , le reste Allah Soubhawnatallah va te donner la réussite InshaAllah. C'est ce que j'ai fait pour être ingénieur électrique.
Sénégal loutakh respecter wougnou wa diaspora pour gnome dale diaspora gnakoul dara. Nane code 13,90€ "dong" da nga ko khep? Ame ne gnou nek diaspora amou gnou lolou 1€ sakh daf lene di teu. Yeurmander touti si diaspora. Nek lene fi rek di djaye ndanane ba dè diaspora da méti amoul rouss. Ame ne gnou namoul dara comme certains au Sénégal rek weurseuk yamoul. Mais djape lene ni dale ame ne gnou 13,90€ cher si gnome. Wa salam.
Cela ne nécessite pas une conférence de presse, vous pouviez interpellé directement siteu sans médiatiser la chose ,c par la lutte que Yahya s'est fait un nom en plus son engagement spirituel c entre lui et son seigneur en tant que frère en la foi nous lui souhaitons le meilleur du monde
Je ne suis pas d'accord avec toi, siteux a publiquement utilisé l 'image de Yekini de façon injuste et répétée, maintenant pour se laver la peau devant tout le monde, voilà la solution, c'est à siteux d'être courageux et faire face à ses adversaire, voilà la vérité 😢😢😢
Saway li siteu wax dara nekousi ,meme yekini avait dit que siteu etait son neveu, limou wax Moy yekini dakoy diapaler,diapaler meuna nek conseil,meuna nek financial, mais senegal nieup mystique laniouy xalat En plus siteu rend toujours hommage a yekini meme dans son touss, cest lui qui a commencê ca
Franchement moi je trouve il faut que siteu arrête d utiliser le noms de yikini me ya quoi arrête wayi Franchement moi j'aime pas qui parle de yikini tout le temps
Je précise une seule chose si un enfant de joie se jette sur un adulte par ce qu'il le prend pour son père Je pense qu'il devrait jamais le rejeter sinon l'adulte devient qu' un vilain garçon Il existe des gens qui grandissent et d'autres ne sont pas
No pour mane siteu ay waxou boppam Laye wax mais dou pour diaxassé yékini ndax kouné bouguou ngua mélni yahya cône na xamni touram mouna toul fay lamb et pourtant mbeurou sérére yeup méme question ❓️ laniou léne di posé à savoir est-ce que moune nañiou remplacé yékini❤❤❤❤❤❤
@ibrafatyndaw9891 nono yénay diaxassé kat yi yékini mbeur la wone siteu di mbeur niome ñiéup di yakarou sérére yi cône c normal mou waxé nonou ndax position bobou lagneko sass
Moi je supporte Balla Guéye mais li Siteu wakh dara nekou sii Sport leuh yekini la deff référence beug ko fayoul limou niak même avec les joueurs on voit ça tmt nioun nieup benn laniou wa salam détails bakhoul 🎉😢
@BayeIbou-h7h mais kou bayi té def dialoré souniou toudé touram lou si nek té wakhoul lou niaw déh 🤣 les joueurs qui d'idolâtrie les Maradona Pelé Dinho nak
😂😂😂😂 albourakh est dans son role yekini day diapale siteu te solen si beuguer Lou ler demlen dieulii yekini ladj koo qui il ne represente pas YEKINI😂😂😂 nioune wa diameguene sufeker khel rek ken eupuniouko ALBURAKH LI GUENEWULEN SI
Moi personelment ça me concerne je condane Yékini j étais son supporter durant toute sa carriere j ai fais 30ans a Joal mais quiconque qui veut être ton neveu si c était un malien il ne devait pas le rejetté . Senegal koné amga djerbat yo bokaloul
Li yeup albourakh la Rend hommage yekini ben mbeur mokay def mouy siteu et ke il merit plus Mm yakhiya avai di k siteu c son neveu dnc boulen niew ba fii pression wakeur aziz ndiaye niew guen dii sogua guéneu di wakh siteu batt boboi yagu nko wakh
Yekini amoul diottou khèkh kèn nitt niou beurri danioukoy togne diko sikkeul tjrs mo khèkh ki mo khèkh ké surtout mom ak MODOU LÔ ay relation you nice làniou ame donc meunoula weulbatikou di khèkh MODOU LÔ Siteu doit arrêter de parler de Yékini franchement
Yakhya Diop yekini "lamb daf ko djeule sani feuler..." souko nekher mome le rek! Wayer sa way "lila fale soko saner yaw le rek, lamb motakh gnou khame se yekini là mo takh mou teki nassi bayi khel"! La même chose pour Tyson ne aciennes gloires yi gorer un peu! Ay boy deff lene done tope baye dè pour gnome tay gnouni mess di soufel lamb! Sou lolou wesso nak respect à lui (Yakhya Diop Yekini) sunu grand le ne ame diam.
IL PARLE DE YÉKINI EN 9mn 43sec sakanal connexion 😂
@@mohamedofficiel3658 très bien copain 😂😂✌🏽
Merci😂
MERCI 🤝
Merci yafi neh😂😂
Ya woor
Massamba une personne très douée et dotée d'ambitions élevées. Une personne aussi sincère. Merci de représenter notre cher héro Yakhya. Personne ne peut détruire son image au sein de la lutte sénégalaise. Il a fait ce qu'il devait faire au temps qu'il devait le faire.
Maintenant il est temps de se retrouver vers le plus essentiel.
Mamadou Moustapha SENE
Personne na essayé de détruire son image le seul problème est que vous êtes des complexés envers votre propre personne … yahya loum am lambeu moko ko may niolen ko dieuneu beugu fapp autant qu’on aime siteu … yahya louko dieuneu metti si adounam moy yeen soit disant mbokam yi nga khaam ni allalou adina rekaaa len bolleek mom siteu nak boudoon allalou adouna wala dimbal si lamb motakh mouy toudou yekini dou yeksii fii bimouy mettiii niouy khouss toudou niou tOuram kounekeu si nioun beugonn nga tey siteu fadial la sa merrr si balla guaye … dieuno len nio nekeuh serere
Merci de la sortie et de l'éclaircissement merci 1000 fois Siteu n'a qu'à ARRÊTER
Yekini est un homme digne
tres tres bonne communication , ki di wah deh kouko dioh communication senegal mou gerer ko correctement , wah dji ler na rafet na et ca rassemble
Lolou nga djiss "communication Sénégal nga wah dè"? Lol vraiment wagnile se prétention un peu qu'en même rew mi yor nagnou "lou geuneu wow kong". Wa salam.
merci yakhya diop yekini vraiment meere won nala trop siteu mo wara bayi diaxase yeufou seytane yii moy lane
@@DiopBirahim-rc7vc dof la beug bataille sycollogique té meunou ko
Bilay
Méré yekini 😂
@ dama xam ni actuellement dafa wara ndiaboté boy yeup parce que référence
Siteu da khamoul yékini Yahya da am foula nakari dérétte dof dof Lou yi siteu di déf Yahya baugouko😂😂😂😂
Macha alla bilahi reuthiouma nouma bègué yahya diop yekini
Je comprends un peu parcek Siteu tchii Albourakh lako wakhé motakh droit de réponse bi filay kooy wakhé😂😂Yekini je pense kil a tourné le dos à la lutte
Yekini un vrai responsable. Très sérieux et véridique ❤
Serrer amoul thiaxane deih wadji kilifeu laa deih 😂machallah mane rouss na Sakh
Thiey yaldaw😂legui yal dawlkhou la😂😂😂😂
😂
Hier balla avait tué Siteu aujourd'hui Yékini vient de l' enterré et franchement il y a trop de mauvaises ondes sur ce combat pour Siteu
Balla na tué personne, IL est vieux 😆 🤣 gainde gou maguette leu, xaley yeup daniouko dane 😆 🤣 day xouxalaté rek
Bien dit
Merci yekini siteu sonal na nday nit yiii 🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@@Magistraaa607 Billahi waxal way
❤ Bismillah alhamdoulilah balla gaye ndam rkkkk inchallah ❤
Kou rouss lalal j’aime Dawkinda Amal joom way
Yekini dafa prouvé ba retraitè meussoul wah kene Lou bone donc Arretel ayy daw menoul takh nga nek roi
MERCI BEAUCOUP SITEU DAW LAXOU LEU
Machallah Samba Thiaw on est fier de vous
Siteu da doon woute ndimbaal sii Yékini mais daa melnii daagn koo daax dh,😂😂😂 Balla dinalaa door baa raay laaa
@@pathefall5764 😂😂😂Aay li di
Wooy 😂😂😂😂dina ko Niousss
C'est ce qu'on dit un grand sportif et un grand stars. Même après la fin de sa carrière, il protège son image à travers même son entourage.
Peut etre la lutte etait dans son parcours mais yekini est un pure croyant
Noko xamé
Lou lèrr Nga wakh bimou bayé beurré là bayi affaires Mystique ak yoyou rawatina khèkh ki wala kè
@@layetheonly5139 sa thies wakhnako si bene interview mounet yekini tt le temps day diouli
COMMENCÉ YALMINE APRÈS YALDAWE , TAY YALWANE MOUDIÉ YALDAKEU 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂
@@Zam-Zam710 😂😂😂
😂😂😂😂
Ayway Siteu loy wax wa kogn ba 😂😂rouss na sakh Siteu bayil kingay mboubo tei gueum sa bop yikini diokh nala sa trokhal mou dess sa trokhal si balla
Inshalah
Masha allah domu adama fep fumu tok n̈o gui kay xarr si xell mu sell wax luy defar mo genn muy yax yakhya royuway la masha allah 🙏🏾🤲🏾
Machalla yakhya borom bkh lae ❤
BIEN DIT VRAIMENT DAFA WARA BAYI TOUROU YEKINI DAY YAKEU IMAGAM TE YAKHYA KILIFEU LA ❤❤
Niioun PA xamnagn ni Yekini Modou rk moko dondeu.. Mtx Yekini beug Modou, mais Siteu ay niodi ak incarner moko nekh.. Daw lakou bou bone bi. Yalna Balla nokoula ba arrêt khar mbaye madiaga..
😂😂😂
😂😂wouy
Amin Man dh Mangui dora faral balla Gaye si lamb Bly nax siteu lomou df modou dama metti trop
Saway siteu yekini nidiayame leu
Yal daw yal sakhi😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂 rousna sakh man
😂😂😂😂
Billahi deugle😂😂😂😂
WAKH DEUG AFFAIRES KHET GUEN WARA BAYI DI GNODI BAKHOUL SI DEUK BI
Même yekini comportement siteu si modoulo nekhouko Épui day niodi lou amoul
Mola la kowakh😂😂
Diomaye demal gérer rewmi t bayi problème siteu bi😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂Nonnnnn Senegal mo Nekh
Siteu bilahi daga kham né bi yoyou dé😂😂
😂😂😂,bi dou Yooyou
Merci beaucoup Yakhya et son équipe siteu doit se calmer
Bilay nioune khamnagne ni yikini dokhoul si yoyou naniou bayi diambour Mogueune
Yalmine bi dey yalwane😂😂
Ayy Siteu lii louko fii diarr😂😂😂
Lo kham thi niaka geume sa bopou 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@@SeynabouFaye-l3n kii kay bet nama worna yalla daw lakou la🤣🤣
😂😂 khamnga Lane lay retane siteu face à la presse question bi sou gneuwé loumouy tontou 😢😂😂😂
@@babacarndao9293 🤔🤔🤔
Khamolén niom Aziz sakh mbiir mi commencé na diakhaso si siteu naniou dém rek ba la 20 juillet 😂siteu ana ngua gueumal sa bopp
Yaw comp nga mais nioune wa diameguene li dawul suniou yaram 😂😂😂😂
Khamoull si loumou dougou dh
Modouo Lo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😊
Merci bcp tres bien dit
Tu communiques bien fR ✌🏼
Bien dit danioukoy diakhasse ak adouna loukhew niouni yakhya di oute kouko diapalé
Thiéy siteu, man wadji dafma yém 😂😂
Bilay 😂😂
Yal daw😂😂😂
Boulma raye waye 😂
Il cherchait un point de refuge mais malheureusement 😢fofou baakhoul....Yekini yaa am fouleu keyy ❤
Vérité absolue
Merci beaucoup yekini ,siteu vrai dofla louko diaral ay fen en plus nek tapet bo xameni daw rek di out ndimabal
Bien dit merci
9:43 il parle de Yekini.
Man dh Mangui dora faral balla gaye si lamb Bly nax siteu lomou def Modou dama metti saga bimou saga modou metii nama trop sax
Yalnako balla domou dan ko
AMEEN YARBI
Masaallah balla gaye 2 ndam rek insahalla champion balla gaye 2
Sa tounou ndye yak modou lo fi yalla mofi nék nga faral wala gnak ko faral danoul siteu
Modou lo mo dieunk saga siteu ,seytane gua trop
Yaldaw bi modoul gore na bayi daww at lakkatou c’est son combat pas yekini gnakk diom lol☝🏽😃☝🏽😃yaldaw bi
Merci beaucoup
Siteu est-ce du souss di méti 😂😂😂 li niawna trop
Legui na yekini gnieuw diappaler siteu. Amoul blem dou te siteu day danou😂😂😂😂
@@mouhamedlydiouf8934 waw inshalah
Yena doon défendre Siteu contre mod lo nieuwate fi di wakh
@papipapi344 et après
@@mouhamedlydiouf8934 niak diom rek
@@papipapi344napacha lobo 😂
Mass mon promotionnaire à la FASEG à l'UCAD.
@@dyerdyer5568 wa mais nous qui sommes en 2 année de licence à la faseg qu’est ce que tu nous conseil
@@libassesy je te conseille petit frère d'être sérieux dans ton travail (cad fais ce que tu as à faire de façon sérieuse quotidiennement) et donne le meilleur de toi meme , le reste Allah Soubhawnatallah va te donner la réussite InshaAllah. C'est ce que j'ai fait pour être ingénieur électrique.
10:07 😂siteu mo meuneu doulllll
Bien dit ❤
Sénégal loutakh respecter wougnou wa diaspora pour gnome dale diaspora gnakoul dara. Nane code 13,90€ "dong" da nga ko khep? Ame ne gnou nek diaspora amou gnou lolou 1€ sakh daf lene di teu. Yeurmander touti si diaspora. Nek lene fi rek di djaye ndanane ba dè diaspora da méti amoul rouss. Ame ne gnou namoul dara comme certains au Sénégal rek weurseuk yamoul. Mais djape lene ni dale ame ne gnou 13,90€ cher si gnome. Wa salam.
Machalla Bon réponse
Cela ne nécessite pas une conférence de presse, vous pouviez interpellé directement siteu sans médiatiser la chose ,c par la lutte que Yahya s'est fait un nom en plus son engagement spirituel c entre lui et son seigneur en tant que frère en la foi nous lui souhaitons le meilleur du monde
Je ne suis pas d'accord avec toi, siteux a publiquement utilisé l 'image de Yekini de façon injuste et répétée, maintenant pour se laver la peau devant tout le monde, voilà la solution, c'est à siteux d'être courageux et faire face à ses adversaire, voilà la vérité 😢😢😢
Non Siteu day daw rek amoul Aret 😂😂😂yikini nga bayiko akh modou mola dal 😂😂😂
Jerejef merci ❤❤mouy wout walou nonu
Saway li siteu wax dara nekousi ,meme yekini avait dit que siteu etait son neveu, limou wax Moy yekini dakoy diapaler,diapaler meuna nek conseil,meuna nek financial, mais senegal nieup mystique laniouy xalat
En plus siteu rend toujours hommage a yekini meme dans son touss, cest lui qui a commencê ca
Siteu dafa séytané... Meunoul diviser ethnie yii
Masse a dit que ça fait longtemps siteu et yekini ne s'entend pas ni se voir.cone nane lakoy diapalé.dey Tah niouy dépassé yekini rek
Machala wakh ji nice na
Franchement moi je trouve il faut que siteu arrête d utiliser le noms de yikini me ya quoi arrête wayi Franchement moi j'aime pas qui parle de yikini tout le temps
Siteu hana dina roussss😂😂😂😂😂😂😂😂
Waaa mais suis je le seul à trouver que wadji daafa am trait de ressemblance ak sougn Président, Diomaye.
😂 Absolument
Diomaye ak bopam bobou di tollou ni Forêt atlantique kay kii moko dakh 😬
Et le journaliste comme Diop khass
Merci beaucoup 🙏🙏🙏🙏🙏
Cassamace la deuk wayé souniou keur yekini moy référence leu ❤ bg2 del dem cassamance 😢
Comme diomay Faye 😢😢😢
Pour le titre, le débat sur Yekini commence à 9:30
😂😂😂
@@mansourdiack1289je veux aider les prochains 😂😂 pour économiser les données 😂😂
@@abdoulayebadiane5984 🤣😅
Kou rouss way
Merci ❤❤❤❤
Je précise une seule chose si un enfant de joie se jette sur un adulte par ce qu'il le prend pour son père
Je pense qu'il devrait jamais le rejeter sinon l'adulte devient qu' un vilain garçon
Il existe des gens qui grandissent et d'autres ne sont pas
Siteu disait parceque ay mbokk lanie .
legii nak dingen xamni matna loum doon amna foula dotolenn degatii yaxya dh
na amm diam mom yekini
Ngathie Gueye deuk la ❤❤❤
Bien dis
No pour mane siteu ay waxou boppam Laye wax mais dou pour diaxassé yékini ndax kouné bouguou ngua mélni yahya cône na xamni touram mouna toul fay lamb et pourtant mbeurou sérére yeup méme question ❓️ laniou léne di posé à savoir est-ce que moune nañiou remplacé yékini❤❤❤❤❤❤
Mé siteu wakhoul ni moy remplacer yékini me dafa wakh ni revanche lakoy djeuleul tée yonou yékini nékou sii dakay diakhassé ak yénén mbeur yi tée Lolou lay bagn siteu mo wara arrêté tée geum bopam
@ibrafatyndaw9891 nono yénay diaxassé kat yi yékini mbeur la wone siteu di mbeur niome ñiéup di yakarou sérére yi cône c normal mou waxé nonou ndax position bobou lagneko sass
@ibrafatyndaw9891 mais boulangerie ñiou sonal way yékini bou bañié kou ko toujours thi lamb kone warouthiwone diarr
@@AbdoucisseSarr-qn9hvyaw werroo😢😢😢
Siteu da beugeu walou 😂😂😂
Moi je supporte Balla Guéye mais li Siteu wakh dara nekou sii Sport leuh yekini la deff référence beug ko fayoul limou niak même avec les joueurs on voit ça tmt nioun nieup benn laniou wa salam détails bakhoul 🎉😢
@@AbouThiello-vw1kp n'a bayi touru yekini .yekini bayina lambe.soukoy toudou nite gni diko depasssé té defoul dara.na wah ay wahame rek té bayi diambour.
@BayeIbou-h7h mais kou bayi té def dialoré souniou toudé touram lou si nek té wakhoul lou niaw déh 🤣 les joueurs qui d'idolâtrie les Maradona Pelé Dinho nak
Siteu a belle est bien raisons il doit honoré cet légende sérére de la lutte sénégalais yekini ils est de la lutte ont la connus grâce à la lutte
C'est comme ça qu'on doit honorer une légende comme Yekini? Le mettre en mal avec les autres?😢😢😢 vous me faite rire😂😂😂
Merci 🎉🎉🎉🎉
waaaa siteu rouss na li gathie la dh😂😂😂😂😂😂😂
Dara neckou si li sitteu wah. Sou utilisé woul image yékini bane image lay utilisé. Baylène compliqué
😂😂😂 sama ndijaye la dan 😂😂
😂😂😂😂 albourakh est dans son role yekini day diapale siteu te solen si beuguer Lou ler demlen dieulii yekini ladj koo qui il ne represente pas YEKINI😂😂😂 nioune wa diameguene sufeker khel rek ken eupuniouko ALBURAKH LI GUENEWULEN SI
Kone Est ce que dou daww yi siteu di dawwmotakh mou méréko😂😂😂
Ki di frère yékini da Al fite tok fo diko fénal xana diango iOe fek xalate ish
Moi personelment ça me concerne je condane Yékini j étais son supporter durant toute sa carriere j ai fais 30ans a Joal mais quiconque qui veut être ton neveu si c était un malien il ne devait pas le rejetté . Senegal koné amga djerbat yo bokaloul
Yakhya aka ame foula ken touko doulal😂😂😂
Wahna deug togne bahoul yékini mongi jéré famille wam kou diogue rék diko tign
Ndeyssan kou roussoul sa yaram dawna 😢 mbeur Bou lekk sa khaliss lekk co tei bayi di thi touddou les autres lutteurs
Bien dit
Amna solo
I'm Balla gaye's fans, but I respect yakini❤❤❤❤
Écoutez attentivement la communication de Mr Diaw : l'ancien roi des arènes n'est plus "YEKINI", mais "YAHYA".
Li yeup albourakh la
Rend hommage yekini ben mbeur mokay def mouy siteu et ke il merit plus
Mm yakhiya avai di k siteu c son neveu dnc boulen niew ba fii pression wakeur aziz ndiaye niew guen dii sogua guéneu di wakh siteu batt boboi yagu nko wakh
Honte à qui pense que Yekini va aider Siteu .,😂😂😂😂😂
Siteu prépares toi à vivre l'enfer BG 2 dinaa la corriger wone la nii Bii dou Yooyou 😅😅😅😅😅
Siteu Thiak Thiak le Comédien la Combat Royal Guey Daw ❤
Yekini amoul diottou khèkh kèn nitt niou beurri danioukoy togne diko sikkeul tjrs mo khèkh ki mo khèkh ké surtout mom ak MODOU LÔ ay relation you nice làniou ame donc meunoula weulbatikou di khèkh MODOU LÔ Siteu doit arrêter de parler de Yékini franchement
Non vraiment Senegal mo neikh😂…yaw lamb téral la, leipp Lo amm lamb motax nga amko, nga tourner talato lamb dal🤣🤣
Faites attention au titre, c'est pas Yekini qui est invité...
Ici tout le monde connait yekini 😂