Yalla na nga am ndam 📿🤲🏾Mé bo beugué done champion dof bayil combat bougne la proposé rek nga dieul mbeur mou ndaw day am plan de carrière bonne chance ❤❤❤
Yeuffou ragal yoyou mom doumako conseiller sama mbeur.. Champion da ngay niémé lou metti, di dane ay ndanane… Plan de carrière yi mo takh mbeur yi di weurr foumou gueuna noyé.. Tégui bi daffay yak lamb bilahi
Yalla na nga am ndam 📿🤲🏾Mé bo beugué done champion dof bayil combat bougne la proposé rek nga dieul mbeur mou ndaw day am plan de carrière bonne chance ❤❤❤
Yeuffou ragal yoyou mom doumako conseiller sama mbeur..
Champion da ngay niémé lou metti, di dane ay ndanane…
Plan de carrière yi mo takh mbeur yi di weurr foumou gueuna noyé..
Tégui bi daffay yak lamb bilahi
@ dëgg bou wërr nga wkh
Ndam Rek Incha alla 🎉❤
Billahi ki damako beugue rk 🎉🎉🎉🎉ndam rk inchallah 🎉🎉🎉🎉
Ndam rek inchallah 🎉🎉
Siteu bou ngor domou diambar bii ndam RK inchallah 🤲👑✌️💪
Ndamm rekk inchalah ❤
Siteu bou ngor seul Sm idole bi Ndam rék
Bonne chance Tapha Mbeur
Siteu bou Ngor kassé blh ❤❤❤
Siteu seul 🎉✌️
Bou Ngor Bii seul ⚔️
Yalla nala borom bi may Ndam inch’Allah
Bou Ngor bii 🦁✊🏿
Siteu bou ngor Kassé ❤❤❤❤
Lima guiss danoul patriote bi tapha bou entraîner diaxanoul béne voyage lakoy def dou moromou ki sakh
Boy Danou gniby rek incha alla😂😅😅
Moom daa nooy tropp nakk ahhh
Franchement guissouma ak mbeur mom
Boy sérieux si top model nga geuneu diekeu
Nekal nitt😂😂
Siteu seul ❤❤
Ki wahlen ko mouy and dolé mo gueun
Nimouy beuré danoul Tapha mbeur
dam rék inchallah
Ndam rk
Siteu seul ❤le 12 nioy dirigé fepp tapha politicien la Day kharr lou barri😂
Na diang khéx bou bakh si combat bii
❤
Bis bula tafa diappe
Man Almadies trao rek moma mafi bayiwone
Tapha dekoy douma dane ko
Khana dakay faye 😂😂
Aye pa rek ga dane
😂😂bismi ndoy pah la
Ki môme boye yeube mosi geune noyé ki d'où mberre bilaye
Nanal glace boy sa khol mo Bonn 😂😂
6 victoire 2 défaite 1 nul sa 1ère combat daga nul yaw ak thiatou mombaye bou rebeuss
Tapha mbeur seul
Meuno beuré amo dolei
😂😂 nekal nitt
Siteu seul❤❤❤