CHEIKH ABDOUL HAMID SARR Répond à Hibou Diallo qui se nomme " chérif ibrahima aidara ".

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 янв 2025

Комментарии • 248

  • @AlimatousadiyaFall
    @AlimatousadiyaFall Год назад +2

    Serigne yalnala yalla faye si barkéi yonéntibi psl si barkéi cheikh Ahmad tidjanii chérif rta❤ on t'aime fort sounou baye❤

  • @mamadoudiouf5467
    @mamadoudiouf5467 2 года назад +4

    Machallah dieureudieuf cheikh abdoul hamid sarr dimbaliguaniou thi ki di wouyo cherif te nekouko.

  • @syngariboundou2355
    @syngariboundou2355 3 года назад +11

    Dieureudieuf serigne abdou hamid sarr yalla na bour yalla faaye amine

  • @mikakaw8968
    @mikakaw8968 3 года назад +27

    Franchement Cherif Ibrahima Attidiany est une fierte .
    Partout dans le monde on l'ecoute.
    Ici en europe , on l'aime tres fort.
    En plus mom dou tontou kein rawatina wa keur Mame Maodo((ra).

    • @laminendiaye78
      @laminendiaye78 2 года назад +1

      Billahii wallahii on l'aime peut importe !!

    • @cheikhdiop4944
      @cheikhdiop4944 2 года назад +2

      Ya doff khamewo nitou yalla ki dou dara

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      @@laminendiaye78 😂😂😂😂 kane ibou diallo mi

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      @@cheikhdiop4944 xaméwouko kay ndeysane😂

    • @yagne5445
      @yagne5445 8 месяцев назад +1

      ltkh meuno lene nité khamé kouy woutt buzz ioe Serigne Maodo sy dabakh serigne habib sy et meme ke khalif Omarienne Thierno bachir muntakha taha cheikh omar comb1 de fois vs les avez vu assister à ses événements vs pensez ke nioniou dinagn déplacer wou si zero es ce ke cv yene ?

  • @lahatleye6313
    @lahatleye6313 2 года назад +2

    dieureudieuf serigne touba amul momrom dé

  • @adminexim8164
    @adminexim8164 3 года назад +9

    Guiss nagn fi Pathe Diouf 😂😂😂 Xewi daal mo meiti... Chérif Ibrahima Aidara At Tidjani Yallah na goud fane ❤️❤️❤️

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      Yow con nga diaango et tu ne connais rien sinon tu ne dirais pas Chérif encore moins At tidiani.

    • @papemalick6781
      @papemalick6781 3 года назад

      tu a 1000 reson cherif machala kham kham bou leer la yor and ak teguine

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      @@papemalick6781 Gros con déjà raison c'est avec un ai et non reson comme tu l'as écrit. Et puis lann moy yarr ak teguine ??? Vous êtes des ignorants, allez écouter les audios où on corrige votre maître hibou diallo sur ses multiples fautes et mensonges. Allez écouter le petit de Cheikh Abdoul Hamid Sarr qui corrige hibou diallo si vous tapez sur youtube ce que je viens d'écrire et vous verrez... Vous saurez si hibou diallo a étudié ou pas

    • @mikakaw8968
      @mikakaw8968 3 года назад

      Amine

  • @bigndanane1448
    @bigndanane1448 3 года назад +9

    Je ne sais pas ce qui s'est passé mais personnellement, si j'ai aimé Serigne Abdoul Hamid Sarr, c'est grâce à Chérif Ibrahima Aïdara At-Tidiany. Il a beaucoup parlé de Abdoul Hamid. Que de bonnes choses. Chérif f a même supposé que kéneu euppeul Hamid Sarr wilaaya ci réwmi

  • @maodombaye5727
    @maodombaye5727 3 года назад +1

    Dieureudieuf Cherif je t'écoute tous les jours

  • @ouzazaouzaza9110
    @ouzazaouzaza9110 3 года назад +24

    Quoi qu'on dise chérif, il fait du bon boulot pour la tarikha il a beaucoup de mérites. Histoire bakhoul
    On doit rester uni car la tarikha est un et indivisible.
    Qu'il soit Cherif ou pas ça importe peu ce n'est l'essentiel

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад +1

      Je comprends que tu manifestes pour la tarikha tidiane ! Cependant tu te trompes dans le sens où pour être unis, il faut qu'on soit sur une base claire et nette : LA VÉRITÉ !
      Or certaines personnes abusent et racontent ce qu'ils veulent dans la religion et la tarikha. Et cela a pour graves conséquences de d'induire en erreur des gens comme toi qui ne sont pas bien avertis d'où l'importance d'éclaircir la situation ! Wa salaam.

    • @ouzazaouzaza9110
      @ouzazaouzaza9110 3 года назад +6

      @@Ndaar-Faam
      C'est un problème personnel qui oppose hamid et cherif vous devez même pas vous en mêler.
      Que vous le veuillez ou pas Cherif est un TÉNOR dans la tarikha tout comme hamid d'ailleurs. Au lieu de défendre la tarikha contre ses détracteurs vous attaquez ses ténors, ce n'est pas intelligent.

    • @abdoulkhadregaye3437
      @abdoulkhadregaye3437 2 года назад

      Cheikh sokhlawoul nafékh,
      Nafékh foumou déme dina diakhaso ak niome té ki Ibliss leu mouye doul nane Chérif leu té doléne koko wakh.

    • @awabadji6375
      @awabadji6375 2 года назад

      @@abdoulkhadregaye3437 bou dei dangue ko khamale dara ga gueinei aye preuve iblisse bii si yawe la commence

  • @abdouguenee875
    @abdouguenee875 3 года назад +5

    Dieureudieuf cheikh abdoul hamid sarr

  • @Bayeniasskesse
    @Bayeniasskesse 2 года назад +2

    Nite day am soutoura surtout entre croyants .Respect

    • @assanendour2074
      @assanendour2074 2 года назад

      Kouy fene di soss ta dou soutoural kene esk diarna soutoural kokou daniouko wara wer

    • @youssouphaba7884
      @youssouphaba7884 2 года назад

      Merci.

  • @talibedabakhmalicksy1276
    @talibedabakhmalicksy1276 3 года назад +11

    Wallahi cheikh Abdou Hamid ibou Diallo féne rekk La Mane

  • @papaoumarndiaye4555
    @papaoumarndiaye4555 9 месяцев назад +2

    Shérif daaleu Masha Allah Aka bakh té meilleur. Waliyou Kamal Moy Cherif Ibrahima Aidara. Talibé piir bou aladji abdou

  • @algotradersn7675
    @algotradersn7675 3 года назад +5

    Je veux rencontrer Abdoul Hamid .
    Une personne que j'ai toujours admirer grâce à ses véracités.
    Yallah nako yallah sameu

    • @bigndanane1448
      @bigndanane1448 3 года назад

      On ne dit pas "grâce à ses véracité". Mais on dit "grâce à ses vérités". Ou bien encore "grâce à la véracité de ses dires".

    • @algotradersn7675
      @algotradersn7675 3 года назад +2

      @@bigndanane1448 Merci Molière. C est surement due a mon correcteur automatique. Cela dit, ce n est pas la réponse que je m'attendais

    • @talibedabakhmalicksy1276
      @talibedabakhmalicksy1276 Год назад

      Amine

    • @kalamouhthiaw
      @kalamouhthiaw 4 месяца назад +1

      Doma diangal trading 😊

    • @algotradersn7675
      @algotradersn7675 4 месяца назад

      @@kalamouhthiaw gneuweul

  • @mariemeba7167
    @mariemeba7167 2 года назад

    Allhou akbar gnignou wara warr si yalla mo bougnouy werro si fene ak di tilimal khete fougnou dieum
    Lii mo raw adji sarr ak sonko

  • @ndiayendiaga7606
    @ndiayendiaga7606 3 года назад +6

    jerejaf serignbi yalla na yalla yokou samou la ibou dialo doomou harem fén rék la beuge doundé Say Say le moom ak mbootaayam

    • @bigndanane1448
      @bigndanane1448 3 года назад

      Soub'khaanallâh.
      Astagh'firoulaah

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      @@bigndanane1448 deugue leu nganane astaghfiroulah

  • @sitan7440
    @sitan7440 3 года назад +8

    Hibou diallo raconte aussi qu'il est descendant de SAYYIDINA CHEIKH AHMAD TIDIANI et il déclare son nom de famille comme Aïdara OR la famille de SAYYIDINA CHEIKH AHMAD TIDIANI leur nom de famille n'est pas Aïdara mais TIDIANI.
    Encore un gros mensonge !

  • @elhadjioumarmbengue2878
    @elhadjioumarmbengue2878 3 года назад +3

    Dieuredieuf sarr walahi bour yalla molay sameu

  • @amethdekoleka8273
    @amethdekoleka8273 3 года назад +3

    لازلت في أمان الله وحفظه بجاه النبي المصطفى صلى الله عليه وسلم

    • @sitan7440
      @sitan7440 3 года назад

      Amiine

    • @kinefaye1439
      @kinefaye1439 3 года назад

      لعنة الله على عبد الحميد صار سيد الكاذبين

  • @elbaraniang
    @elbaraniang 3 года назад +13

    Lo way sokhor sokhor xam ni Chérif Ibrahima Aidara kou am xam xam la kou ragal yala la. Kou yonént bi la kou beug Cheikhou Tidiane kou beug Seydi hadji Malick Cheikhou Oumar ak séni Ndiaboot.
    Yow mi wakh nak koula dégue xam ni kou vulgaire gua kou niak kersa. Nitt day am téguine bodé wakh waxal ci mou ande ak yar ak téguine tei bayi saga yi

    • @xamxamtv9982
      @xamxamtv9982 2 года назад +1

      day doul rék Chérif Ibrahima xamoul Dara 😂😂😂 nit bou vulgaire le

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      day doul rek ibou diallo xamoul gate

  • @tourebarama3615
    @tourebarama3615 2 года назад +1

    Waw gor way Sarr 😅😅😅😅🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣👏👏👏👏👏🤝

  • @coumbandiaye5703
    @coumbandiaye5703 Год назад

    Atte yalla rék moko môme , yalla naniou yalla moussalle Thie chaytane té Dièguale niou

  • @abdoulkhadregaye3437
    @abdoulkhadregaye3437 2 года назад +2

    Merci Cheikh Hamid SARR cet imposteur doit être vilipender. Nako wa dic dieulsi niousko bou bakh

  • @galayekebe6771
    @galayekebe6771 3 года назад +1

    Macha Allah y'a cheikhina yalla n'a yalla doli diapalé dila ziar dila bégué

  • @belalba5123
    @belalba5123 2 года назад +1

    Je suis un simple tidiane mais je suis très déçu si les moukhadame faisaient ça nous les talibés qu'est-ce quons devait faire c'est jainent

  • @TheSronay
    @TheSronay 3 года назад +4

    👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿

  • @abdoulayely7822
    @abdoulayely7822 3 года назад +11

    Franchement ce déballage ce n'est pas joli entre talibé cheick. Respectez le sermon que vous nous dites. On doit s'aimer et respecter entre musulmans et en plus entre talibé.

  • @moussandiaye2268
    @moussandiaye2268 3 года назад +4

    Cherif Ibrahima aïdara daléna raw si yalla eupeu léne wilaya kou Mére rk kalamére yalla 🤝

    • @mbddiop4671
      @mbddiop4671 2 года назад +2

      Il vient d'insulter tous les WOLOFS SERERES et les Noirs....ki woyou leu dou waliyou.

    • @Aladin405
      @Aladin405 2 года назад +2

      Moussa Ndiaye. Tu es pitoyable !

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      @@mbddiop4671 ki kay dou weyou sax weyou yi danio bax mai ki louniouko wax kheb ko

  • @cheikhndiaye895
    @cheikhndiaye895 2 года назад

    Machalla

  • @Hellopee
    @Hellopee 2 года назад +1

    Merci dieureudieuf,suis rassuré je pensais être l seul a connaître s menteur.

  • @papeomar8530
    @papeomar8530 2 года назад

    Vraiment li ndiawna, wakhléne wakh té bayi tarikha bi ak ndiabotou Mame Maodo. On cherche des références et modèles pour le tarikha mais pas sa mal dou sagua ndakh d'où téguine Gorgui

  • @ousmanesene7527
    @ousmanesene7527 3 года назад +10

    Heureusement ba ibou Diallo ngua wakh wayé peundou CHERIF IBRAHIMA AÏDARA ATT TIDIANI dounguéne ko guiss . CHERIF RAWNA BOU YAGUE NDAKHE MOM LAFI MAGU YI BAYI MOULÉNE DI DOKHAL MISSION KHADARA BI AK DINNÉ DJI SAYOU NGUÉNE DIKO SAGUA AK TOUMAL MARTABAM DI YOKOU BABA CHERIF WALIYOU PIR LEU KOUMOU NAKARI KALAMÉKO YALLA

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      Yow con ngeu . Tu n'as strictement RIEN compris tout comme hibou diallo domeram

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      yeneu leu rek entre vous saganté léneu rek ak niody willaya

  • @laladiakhate4734
    @laladiakhate4734 3 года назад +2

    Serigne Abdou Aziz Dabakh nak boulèn ko bolé si Séne wakh you gnaw you khamadi yi réw nguene torop

  • @PapeGueye-i3d
    @PapeGueye-i3d Год назад

    ❤❤

  • @mamemordiakhate1448
    @mamemordiakhate1448 2 года назад +1

    Jasakoum lahou xairan ceex bi kou wodoo lamiñ sou nopee raf lé

  • @ibrambaye7555
    @ibrambaye7555 2 года назад

    Ayyy way doyna,baleenko 😭😭😭

  • @diawamd1137
    @diawamd1137 3 года назад +2

    Sarr dal amoul morom en plus cette histoire de cherif on l'a dementi depuis des années

  • @mbalofficiel7513
    @mbalofficiel7513 3 года назад +6

    Yaw sa khola tangue Chérif Ibrahima Aïdara sa kaw sa kaname di ngua dé

    • @papemalick6781
      @papemalick6781 3 года назад

      bilay cherif amoul morom

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      @@papemalick6781 😂😂😂😂😂😂 kou amoul mborom fofou ibou diallo

  • @harounaniang2002
    @harounaniang2002 3 года назад +4

    li kheuthio wilayala wala dette waye boulene dii wer sen bopp soutouralanter lene

  • @oumidiallo5074
    @oumidiallo5074 2 года назад +2

    Awaye aduna diaroule liii aye kilifeu dougnou weranete dara diaroule liii

  • @moustaphadiallo5363
    @moustaphadiallo5363 7 месяцев назад

    😂😂😂😂😂hibou diallo bayil fennnn bayil fennnn bayil fennn😂😂😂😂😂

  • @cheikhtidjianesarr8514
    @cheikhtidjianesarr8514 3 года назад +2

    Problème yangui démarre nak

  • @bachiirleveridique9767
    @bachiirleveridique9767 3 года назад +2

    *ABDÙ MENTEUR SÀAR YAW DOO GÀT NDAX NÈE NGÀ **#SHÉRIIF** SÀAGA NA AY KILIFA SA BIIR KËR NGÀ ACCEPTÉ KO BA-TAY NGAY KAT SA NDÀY MBÉL-MBÉL'I DOOMURAAM ANA MAG AK SÀAGA SURTOUT NGÀ NI TAALIBÉ **#SÈEX** NGA YÉEN ÑÀAR YÉENA YAM*

  • @SONKOBOYPAG
    @SONKOBOYPAG 2 года назад

    😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀😀

  • @mbalofficiel7513
    @mbalofficiel7513 3 года назад +2

    Cheikh tidjani Amena keur dém na ba sa keurgue

  • @papemodou187
    @papemodou187 3 года назад +2

    Mousouma geumne seutou Mouhamed la yalla khamnako dara khamou ko limouy wakh dara lasi khamoul abdoul Hamid sarr ki boulko tontou man de doumako deug lou fitt bi moreuy louko nekh lay wakh lima metí moy limouy wakh si S babacar SY rek MOMA meti

  • @doudougueye5981
    @doudougueye5981 7 месяцев назад

    Waouh !!!
    C'est vraiment Abdoul Hamid Sarr qui parle comme ça !?
    Même si ce qu'il dit est vrai, ses paroles sont vulgaires sortant de la bouche d'un guide religieux !
    Il aurait dû laisser ça aux autres. C'est vilain, ça !

  • @elmalickkonte
    @elmalickkonte 4 месяца назад

    Vraiment saguayi miawena Moune ngua wakhe deugueu.sans saguayi yowe dokilifa

  • @mbayedrame6185
    @mbayedrame6185 3 года назад +1

    Machalla cheikhe abdoull Hamid sarr diaridief

  • @seckmamadou8744
    @seckmamadou8744 3 года назад +4

    Pourquoi vouloir se tapper a l' œil des populations au point de d' insulter vous font perdre du temps

  • @Moustaphaaanne
    @Moustaphaaanne 3 года назад +1

    Mane Cherif damakoy déglou , Cherif wala dou Cherif sama yoone néwouthi du faite que mou beugue seydina Cheikh Ahmad Tidiane Cherif RTA rék Mane sopounako, tanak kouko khôl rék khamni amna thieur , mbirmi Cheikh Tidiane la nanouko sope ta diamou yalla ,yi yèp amoul solo

  • @saphietoudiedhiou1586
    @saphietoudiedhiou1586 3 года назад +1

    Wakh djiou niaw bakhoul ay talibé cheickh Di wakhanté Lou niaw li yéna outé ak seydina Mohamed psl mom migua khamné chaque jour niogui Koy togne té ba none ba fébaré guisouko diko lathié niounéko dafa tawat mou sétiko même soudé wakhoul deugu bopam lakoy déf diaroul wére

  • @aminatandiaye7413
    @aminatandiaye7413 3 года назад +5

    Wode léne kadou yi way yalla bouguoul kou torokhal domou adama

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      Domou Adama moo wora soutoural boppam dii wokh loumou kham té bagna GARMBASSOU koumouko worta deff ! Sincèrement si vous saviez, vous auriez fait attention car malheureusement beaucoup beaucoup beaucoup de gens ne savent pas !

  • @omarsarr664
    @omarsarr664 3 года назад

    والله لن أتدد بمقدار ذرة بأن عبدالحميد مجدد للأمة الإسلامية

  • @alkhafiztidjani3865
    @alkhafiztidjani3865 3 года назад +1

    Malick Niang doomou ndiaaloo nga Abdoul Hamid dafa alkou. Goordjigueene yii laakatou di saaga rek. Booleene baayi woul wa Tivaouane di ngueene geuneu alkou

  • @cheikhoumardiop4557
    @cheikhoumardiop4557 3 года назад +1

    جر جف شيخ عبد الحميد صار

  • @pacombaye8973
    @pacombaye8973 3 года назад +3

    Li rafétoul si yaw ak mome gnawna si ay djoulite magui djégualou nak

  • @papafayesopeyemaodo4172
    @papafayesopeyemaodo4172 3 года назад +2

    Hamid réwgua doule waye

  • @fatimendiaye7307
    @fatimendiaye7307 Месяц назад

    Non kii dâl matoul kilifeu. Chérif déglou naa ay waxam mais meussou makoo dég mouy manquer respect souniou Serigne you baakh yi té téed lool nak . Hamid Sarr ignâne rék môko sonal

  • @leducationislamiquetv7693
    @leducationislamiquetv7693 10 месяцев назад

    Xam wa ligay wax dégg la wala dettt, mais Yaww ku Reww ga, ku amul kersa defal lula nexx, إذا لم تستح فاصنع ما شئت

  • @modoudiagne8237
    @modoudiagne8237 3 года назад +1

    S hamid sarr dall mo pangué rék
    🤣🤣

  • @malickseckabagengoyane8379
    @malickseckabagengoyane8379 3 года назад +1

    Senegal nek na 🤣🤣🤣🤣🤣

  • @lahadtraiteur
    @lahadtraiteur 10 месяцев назад

    CHERIF IBRAHIMA AIDARA AT TIDIANY SEUTOU YONNENTE PIRR LA KOUKO BAGN DANGAY SONOU REKK YONNENTE BI MOKO YEUKEUTI

  • @yakharadiene5303
    @yakharadiene5303 2 года назад

    yena yame de

  • @wadeseydou6833
    @wadeseydou6833 3 года назад +2

    Hamide le grand Menteur

  • @mouhamadka2808
    @mouhamadka2808 3 года назад

    Mane dh wakh deugue yalla sama diarbate nidiayame là mame la wakhouma nk limou wakh deugue la wolla dédéte

  • @adjabsaboudabakhmalick1242
    @adjabsaboudabakhmalick1242 3 года назад +3

    Je ne sais po cest kw le problème avc cherif mais cest la 2eme fois maye dégue nioukaye démentir, di wakh ni dou cherif ak la thia top yeup..... Yallah reka kham nak wayé dale adouna bi djekhna baparé na lep rafete rek yallah bakhna

  • @elhadjioumarmbengue2878
    @elhadjioumarmbengue2878 3 года назад +1

    Birahim mbaye arrête de mentir Cheikh Abdoul Hamid na jamais dit sla qi tel n'est pas le cas nak amène tes preuve

  • @thiernoly2649
    @thiernoly2649 2 года назад +1

    Sarr ya mana khathie thierno masoul diangue mom lolou lack la wala len
    Yaw niata yon lala thierno gagganty si Tafsir qoran .
    Thierno masoul wakh demlén ladjie KO Sarr fén rk ngay déf.
    Yag cheikh Niang nieuw nguénko ziar si ak kashefou bu reuy beuh mounilén danguéne don firy aayatou nur nguéndy xolanté
    Mounialén ALLAHOU NUROU SAMAWATY WALARDY loumouy firy
    Nganiko YALLA Moy leri kawag souf THIERNO YAKHYA LY RADIYALLAHOU ANHOU wakhlany yamana fén.
    Yaw kashfoul lirtiyab bou nabahaany si thierno ngako ngueuke déggué cheikh Niang bingay saaga Mola raw si yalla eupouleuh ndierigne si dîné dji . Cheikh Niang néna si thierno lagnoudane degué teré you kén xamoul si tarikha bi daniouy weur ba sonou si libererie Marocaine yi et partout diko soga am .
    Thierno doundeum yép gueustou xam xam lako déf basi lalou soukratam cheikh Niang néna bimou démé ba manatoul minguikoy thiakh masalatou ( yousallay wa yakhdy ) naanko Lou Malick AK ashab ak asbakh wakh sikou tollou fima tollou ni. Néna makoy tontou mounima xolal( siaradjie)....
    Tanga bayi sa saaga yi amoul bén ndierigne. Yawag charif yenadone andeuh ngakoy sédél ni charif tidiany la diko taggal ay mamam ba yobbouko si cheikh légui nguén douloo reck nga touddéko ibou Diallo tay ngananeko ( HIBOU🦉) c'est Quoi votre problème ?!
    Charif Ibrahim mom nieup xamnagnou ni amoul xam xam day diakhase ak Di copier coller mo takhit cheikh Niang néna soumay wakhtane si thierno bamou nieuw sakh ma noppi.
    Demlén diamou dji YALLA tanguen bayyi sén thiakhane yi.

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      yeneu votre probleme ce que vous ne reconnaissez pas un homme de Dieu . Cest entre vous rek ñiody willaya rek gueneu fi neké té tousssss amou léneu ko .

  • @laminediatta7069
    @laminediatta7069 2 года назад

    Yennna ko setane deee yennn ko setane depuis des années mouyyyy Mbourou tarikha Tidiane Tivaouane ak Chérif di mannn mom Chérif la alors tayyy moguinnii

  • @dembandiaye7201
    @dembandiaye7201 3 года назад +1

    Amna aye wokh yo khamné dioulitt warouko wokh. Dioulitt dou saga dioulitt. ragaléne YALLA

  • @awabadji6375
    @awabadji6375 2 года назад

    Nitte boko khamoule rek khamoko mane dei dama ko sopou tei yalla rek takhe nioune forcè wouniou keine mou beugue ko..senegal nak gni fii niakkeu yarre mo beuri respect 0..lou dawe rek gueine dieule ko def ko empleur..mome douleine tontou nakhe amoule seine diotte

  • @moussahanedjamil8976
    @moussahanedjamil8976 3 года назад +2

    Mane dé l’essentiel moy Mongui niouy khamal sunu diné,di yokou sunu thiofel thi mak you bakh,di dimbali ay nitt, di df lou bax, diokh nieup thieur ,donc awma diote sax di deglou kouy yakk sama thiofel thi mom... th kou tolni thierno bachir Tall ak wilayam fimou tolou thi yalla di seutou Cheikhou Omar rta diaral ko mou diougué louga ba dakar ndax dieum dji diko wax Cherif ibrahima sama dom nga.... li koumou doyoul dara doula doy wa salam

  • @adminexim8164
    @adminexim8164 3 года назад +4

    Ayway xewi mo meiti 😂😂 Abdou Hamid yafi cedei woon ni cherif leuh deh wala bok? 😂

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      Yow con ngeu, lann moy kheewi ? Vrai con moy yoww ! Tu sais de quoi on parle ???

  • @abibkeita7447
    @abibkeita7447 3 года назад

    Je veux voir Hamid sarr

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      C'est CHEIKH ABDOUL HAMID SARR !

    • @papaalassaneseye8252
      @papaalassaneseye8252 3 года назад +4

      @@Ndaar-Faam no c'est sarr le domeram

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      @@papaalassaneseye8252 et le soit disant cherif????

  • @PapadjibrilNdiaye-y4o
    @PapadjibrilNdiaye-y4o 11 месяцев назад

    Maan comprendouma ngarbassou waar naa graaw

  • @ablayedione1958
    @ablayedione1958 3 года назад +7

    Yaw nak kou sonou nga sarr....yaw da nga am xam xam te ken dousssi diariniou ndax amo teguine ....gnila sop danioukoy neub gnilay fréquenté daniouyyy lakatou...yaw nawlo wo Ken nek si deerou nitt ko cannibale meuno guené odio ou video boumou waxé si yaw safane yaw nak nioulay enregistré nga nek si derou nittt Gni rek kholatal sa xam xam way te ami teguine

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад

      Ablaye dione bou khamoul dangay teuthie guémine ! Tu ne sais rien rien rien de ce dont il s'agit ici. Le savoir du ponkal CHEIKH SAYYIDIL HAADJI ABDOUL HAMID SARR des gens en profitent très très très bien ! Plus que tu ne pourras jamais bénéficier des mensonges de 🦉 hibou diallo !

  • @papesarr7026
    @papesarr7026 8 месяцев назад

    Serigne Abdoul hamid borom xam xam la te dou waxantou.nanou dianguer te outi kilifa bou mat kilifa.

  • @MorNiang-ul8xl
    @MorNiang-ul8xl 2 месяца назад

    لن اترددبان عبدالحميدصارهوالمجدد

  • @ؤستاذ-ف1ل
    @ؤستاذ-ف1ل 3 года назад

    Kou kham demela

  • @hadaraseydihadjimalick9157
    @hadaraseydihadjimalick9157 3 года назад +9

    Lou thow lii beury beury nangoul nii Abdoul Hamid dafa amm xam xam

    • @ousmanesow6736
      @ousmanesow6736 3 года назад +1

      Am kham kham wala diangue ba diékhal téré yi téwoula done domi haram tè hamid mi domi haram

    • @ousmanesow6736
      @ousmanesow6736 3 года назад

      Hamid mi amoul yar amoul ay téguine té dou lii laniouy khaar si borom kham kham yi

    • @hadaraseydihadjimalick9157
      @hadaraseydihadjimalick9157 3 года назад

      @@ousmanesow6736 😤😤😤yaw mi amm xam xam djeuleul Mbokk
      Say Serign gnemé wougnou wakh lii

    • @elbaraniang
      @elbaraniang 3 года назад

      @@ousmanesow6736 wakh niou loko xamal. Tei boulfi wakh dégue na

    • @babacarsall4203
      @babacarsall4203 3 года назад +1

      @@hadaraseydihadjimalick9157 dagnou amoul diotam sarr dafa alkou rek saga rek mélni dof

  • @demahoumlayd
    @demahoumlayd 3 года назад

    Ki c'est le plus grand menteur et le plus grand usurpateur. Dara gueunoul nek fenn ngani cherif nga fekk dou deug

  • @ibrahimsall6492
    @ibrahimsall6492 2 года назад

    Hamidu sarr yaw mom ibou diallo sakh mola tané kou todjie sa data yaye nga

  • @2mttv64
    @2mttv64 2 месяца назад

    Ñaari bàndi

  • @abombaye9776
    @abombaye9776 3 года назад

    Mai yéne khana amouléne keur

  • @cheikhomardiallo9348
    @cheikhomardiallo9348 3 года назад +1

    Iow sarr kilifeu bou niakk fayda nga

  • @ronindiaye2919
    @ronindiaye2919 3 года назад

    Deugg dou nekh

  • @byby9333
    @byby9333 3 года назад

    mais ki meun na doull hannn ki moy patin deugg nakk hibou mi grawwneu hann man mom mom rek lay degglu nake dara weroul

  • @blrahimmbaye1072
    @blrahimmbaye1072 3 года назад +5

    Mandè lima diakhale moye daga sèdè wone ni cherif le bi lime aï mamame noumou dèmè nonou saar

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 3 года назад +1

      C'est quand ça que CHEIKH ABDOUL HAMID a cité les ancêtres de hibou diallo comme tu le prétends birahim mbaye ??? Si tu parles du son sur la vie de Cheikh Oumar Foutiyou Tall lorsque Cheikh Abdoul Hamid Sarr parlait d'un chérif et citait ses ancêtres jusqu'à Sayyidina Cheikh Ahmad Tidiani ! Si tu parles de ce son tu te trompes lourdement car il ne s'agit pas du tout de " cherif ibrahima aidar " c'est à dire hibou diallo! Il s'agit d'un autre chérif qui est réellement descendant de Cheikhna Tidiani !
      Alors Birahim répond à mon commentaire et craint Allah si j'ai raison écris clairement ici que j'ai rasion sionon Poste ta preuve selon laquelle CHEIKH ABDOUL HAMID cite les ancêtres de ibrahima diallo !
      Fais le rapidement stp, si tu dis la vérité bien sûr! Si tu ne réponds, et que tu ne donnes pas ta preuve, alors on saura que Birahim tu as parlé pour parler ou alors pire tu as raconté un gros mensonge.
      Et puis si tu écoutes très bien ce fichier auquel tu fais allusion il y avait maodo sy qui parlait également, le chérif qui y parle et dont CHEIKH ABDOUL HAMID SARR a cité ses ancêtres ce chérif dit lui même que sa mère est sérère et que CHEIKH ABDOUL HAMID SARR a enseigné à chacun d'eux ou alors qu'il a été à chacun d'eux d'une grande utilité! Donc ce chérif en question dans ce fichier n'est pas du tout hibou diallo.
      Maintenant si tu as ta preuve dans laquelle tu prétends que CHEIKH ABDOUL HAMID a cité les ancêtres " chérifs " de hibou diallo stp donne ta preuve ! On attend.
      Wa salaam!

    • @papaalassaneseye8252
      @papaalassaneseye8252 3 года назад +1

      @@Ndaar-Faam ki deiy doul abdoul hamid khamoul gatt

    • @sitan7440
      @sitan7440 3 года назад

      @@papaalassaneseye8252 Yow lo kham pape alassane seye ? Tu connais Cheikh Abdoul Hamid Sarr ???

    • @sitan7440
      @sitan7440 3 года назад

      Birahim alors où sont tes preuves ? Donne le son où il cite les ancêtres de hibou diallo en tant que chérifs ??? On attend toujours si tu ne l'as pas donc tu mentais !!! Et après avoir été pris la main dans le sac arrête stop baayil fenn !

    • @papaalassaneseye8252
      @papaalassaneseye8252 3 года назад +3

      @@sitan7440 cherif bayam moni won cherif la nit gni nenan cherif la waye balamako guem deug deug mou guene thi lamignou seydi aboubacar sy al khoutboul fardoul djamikh mou deme tivaouane fekk gorr gui di wathie scale ye yi wakha gul sakh cheikhal khalifa diokh ko lokho niko li ngay werante deug pirr la yonentibi moy sa mam rothi lokhom dem...muy benn biko niarel moy li birahim mbaye wakh c vrai sarr dana wakh ni ibrahima cherif pirr la di limm ay mamam ba mou guisse ni faydou bi duguna cherif mbolo mi di gnieuw thierno bachir tall beugue ko ta gueme wuko khol bi di bon nakh da demoul demoul thi pays ba demoul thi zairr man sama yonn bi bima nekko djiakk la kham ni alkouna ta bala dheee louniy def thi douche thi kaw lalam lakoy deff👆sarr dal domeram la na fekk la

  • @mbddiop4671
    @mbddiop4671 2 года назад

    MENTEUR AIDARA DÉCOUVERT DEPUIS....IL DOIT ÊTRE ARRÊTE ET MIS EN FOURRIÈRE

  • @mamemordiakhate1448
    @mamemordiakhate1448 2 года назад

    Wolof yi kenn dou len lay

  • @juniorfaye7147
    @juniorfaye7147 3 года назад +3

    Yene niare yena yame fene rek ngene Di def ak sose

  • @ؤستاذ-ف1ل
    @ؤستاذ-ف1ل 3 года назад

    Lo wah dégula

  • @mameabdousakho990
    @mameabdousakho990 3 года назад

    Mann dama gueum kii keinn rawouko Sénégal 🇸🇳 louler

    • @ousmanesow6736
      @ousmanesow6736 3 года назад

      Wayé tamit dèh djissouma kouko dakha féne si Sénégal

  • @ismailaattidjaniba641
    @ismailaattidjaniba641 3 года назад +1

    Kép kou bagne chérif Ibrahima sa leufeul ndaye tout les jour ak iow mi Abou Sarr

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 2 года назад

      li rek laniou leneu diangal saga rek kheuth willaya kou andoul ak sa serigñ nga sagako wax ko lou niaw les vrais tidianes douniou ñiody willaya

  • @barandiaye7167
    @barandiaye7167 3 года назад

    J'aimerais avoir le contact du Mr qui parle c'est extrêmement urgent. Merci pour votre aide.

  • @cisseporokhane6799
    @cisseporokhane6799 2 года назад +4

    Wadji Bou dé féne katt yaw doulle katt nga

  • @elhadjitalladiagne1013
    @elhadjitalladiagne1013 Год назад

    P

  • @khadydiop8769
    @khadydiop8769 2 года назад +1

    Ki doul katt

  • @mansourndiaye7509
    @mansourndiaye7509 Год назад

    Yaw mome warnagn nok nah di wah si ko xamni lidienti woula