THIERNO YAHYA LY RAHMATOU LAAHI ALEYHI PAR CHERIF IBRAHIMA AIDARA AT TIDJANI
HTML-код
- Опубликовано: 8 фев 2025
- Ce Samedi 03 0ctobre 2020 Cherif Ibrahima Aidara At Tidjani nous revient sur une nouvelle emblématique de l' Islam, un érudit aux multiples dimensions spirituelles, un pôle parmi les pôles, un saint homme : THIERNO YAHYA LY RAHMATOU LAAHI ALEYHI.
Yalla naniou yalla fayal Thierno yahya Ly té tass niou ci barkém ci barky naby (pbsl)
Ya rabby 🤲
Thierno Yahya Ly grand muqadam de Maolana Cheikh Ibrahim Niass, yalna yallah yokku léram te Tass niou ci barkem
Allahouma amiin mais après il a quitté Medina Baye
@ pour partir où ?
Cerno masoul nk mouqadamou baye bamou dadjiéck baye feckna mou nk xalifa cheikh bayilén soss
@@thiernoly2649 🤣🤣🤣 soss ? Baye Niass moko dimbali deh …. Ñiou guenah fort thierno ly lah Baye Niass yaar
@@mystere3746 je sais pas
Yallah na niou Yallah tasse si barke Thierno Yahya Ly.
Thierno Yahya Ly beugeuna loole.
Qu'Allah (swt) nous abreuve de ton savoir zairanne wa batinane.
Je suis un petit-fils de Thierno Mama Aw Thielaw.
Thierno mama aww thielaw c'est un oncle direct de thierno yakhya un grand Waly radiyallahou anhooum
Un grand homme, Thierno YAHYA LY, sama toureundö. Portrait de haute portée par Chérif Ibrahima Aïdara qui nous a fait connaître ce grand érudit. Émission exceptionnelle ! A chaque fois que je voyais Chérif prononcer son nom, je sentais en lui une sensation particulière. Franchement il me l'a fait aimer sans que je connaisse son histoire, mon homonyme. Et pourtant Saldé, lieu de sa naissance, est à quelques 10km de chez moi PETE. Donc je me réjouis de ce lien à travers notre zone d'appartenance.
Je réitère toute mon affection et adoration envers vous Cherif Ibrahima Aïdara, BABA.
Thiernadio A Salminama dehh
@@elhadjibocarelimanely7191 héhé Thiernam mi salmitima mi juurima.
Pète c le village de sa mère seyda Aïcha bani aww❤️
Chérif foufou deuk
Manchalah sounou sanga bi walahi niola soop ,yalla sounou borom sam leu tei soutoural Aidara
Dieredieufeti yalnala yalla fayal bopam nioun dal tijan yi na niou guena diap souniou tarikha guena defar souniou bop si barke salatoul Fatiha si barke cheikh Al souniou walliw you bakh yeupe yalla naniou yalla Tass si barke thierno Yahya ly
Sheriff Ebrahima may Allah give you long life and happiness and increase your light. I wish to see you one insha Allah.
Machallah daga bakh lole bilahi yag fi lole té adak wérr si barkep seydina mouhamed amine
Chérif yalla nalla yalla faye ci barky naby(pbsl)
Machallah a diarama aidera al puular éne fof wéltima é ma fouta fof wéltima yo allah yobé modiéré è barkè thierno yahya ly
Direudieuf cherif
Mane yaw ya takh ma sope thierno yahiya ly
@@racinetv78 ndeysann
Ya rabby 🤲
Masha allah chérif ibrahima aidara goudeul fane té ande ak wérr amna solo
MashAllah
Merci chérif Amna sollo comme toujours naleu Yalla fay yiw Barké Makgñi gua indi insh ALLAH
Chérif ma ngui lay ziar dila diadeufé lii ngay déf amna solo yalna BorombI Soubahanahou défala diaam . Ay mbélélé thiowla rék naniou ko bayi niom . Santala gueurum .
Dieuredieuf papa Aïdara yalna yalla goudal fan wi yokla wèrr
Salam Wa Choukran Yaa CHÉRIF...
Et à toute l’Equipe aussi que Dieu vous protège et que vive la Paix et la Prospérité dans Notre SENEGAL 🇸🇳 et partout dans le Monde 🌍
Allahouma aamiin 🙏🏿🖤🍀✨
Q
Chérif, sa togaay rafetna barina téguine, sa waxtaan amna solo té mou ngui gnouy dimbali ci sunu pass pass.
Yal nanou la yallah fayal bijaahi Taha (saws)
Chérif masha Allah 💖💖💖❤❤❤ wakh tanaleniou si El'hadj Mama Aw ak Thierno Adama Gaye ( niangué) Thierno Yahya Bâ richar toll insha Allah YALLAH nala YALLAH sameu si barkè Seydina Mouhamed saw amine ya Rabbi
cheriff diapal thi loi delia Bâ wakh
cheriff diapal thi loi delia Bâ wakh
Macha allah,chérif,yalla naniou yalla tass ci sa barké,sa wakhtane ci seydina cheikh ahmada tidiany chérif faiss na déle ak ndieurigne,yé naniou ci lou bary,alhamdoulilah
Dieuredieuti yalla na yalla yokou sa fane aidara cherif
Outsize, vraiment sa wakhtane dafa nex. Insh-Allah, quand je viendrai au Sénégal viendrai vous voir insha-Allah. Que le Clément, le Miséricordieux vous donne une très longue vie, n'en déplaise à vos détracteurs.
Ma challah cherif kadouyi rafetna
وجزاكم الله خيرًا عن هذا القطب الكبير والعلامة الشهير سيدي ومولاي وحبيبي وقرة عيني الشيخ الحاج يحيى عمر جملي الفوتي التجاني ونفعنا به في الدارين آمين آمين.
أهلاً الشيخ الخليفة
مع أن الشريف هذا كثيراً ما يتخبط ههههههههه 😆
@@thiernoly2649ههههه يتخبط كثيرا والله
Machalla sérif soye wakh si niitt tou yalla yi mane damaye kontan yalla khamnako
Yalla na yalla yokou sa fane aidara cherif
Mashallah mashallah Allahou Akbar Sénégal mag niou bakh gni billahi Cherif amouniou sa fay dieureudieuf
Maachaallah yalla na yall fayla wayé serigne Ibrahima Faye bobou guéneu adouna défna ay 3 ou4 ans di contane si wakhtane bi
Machalla cherif amena solo yallana bour bii barkél yook sa fane Inchalla
Machalah Cherif Wakhtane bi Ame n’a Solo Doundeul 111ans sans Ordonnance Merci sa Fans bou Chicago
Mashallah sherif yalnala yallah fayyy..
ماشاء الله تبارك الله جزاكم الله خيرا أنت ومن معك مع صحة وسلامة وسعادة دائمة حياك الله شيخنا الجليل شريف إبرا هيم جزآك الله خيرا أنت ومن معك مع صحة وسلامة وسعادة دائمة
Machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah machallah chérif da bakh man mala bâ geu billay
Macha Allah, Aîdara, goudou Fane AK wër. Wayé nak sérère yi kéne dèmoul niou desse
Merci cherif lerr na wer na
Wakhtane bi ladone khar billaye mierci chérif Ibrahima aidara
Yalna yalla deugeureul sa takhaway tei fayal nioula
Cherif HAYDARA vous ne parler que de bonnes choses Macha ALLAH Merci pour tout que Dieu vous assiste et vous protège IN SHAA ALLAH
Dieureudieuf Aidara. Yalna yala bindeul leu tuyaba. Te gnou yekh ko fayanto
machalla gneup ko Donne khar ya bakh nakh wakh sii sa bakhou morom wagniwoul dara sisa bakh teh yaw ignano sokhoro magg boufii bakh gua wakh tanèko ba gneup kham ko yalla na sa diam yague aïdara
Machalah chérif yalla Nala yalla fay
Mbokk talibé yi aimer lén vidéo bi Tay partagé 💖💕♥️💖💕♥️💓❤️💖💖💕♥️
Machallah Aidara doundal Lou beri khana beug la guiss rek inchallah
ko guiss serigne ibrahima faye si oui quand?
Machalla Yalla na Yalla gudal seni fane 💖💖💖🙏🙏🙏👑👑👑😘😘😘😘
Et j'ai vraiment aimé regarder cette vidéo
Mawlana thierno Yahya ly Un pôle parmi les pôles, Un homme de dieu très discret sa sainteté est une braise ardente il suffit de la serrer pour qu'il y ai une détonation.
Mâcha ALLAH content de vous walahi
Salam Salam Salam
J'ai connu thierno par le biais d'un Cheikh Mouride à fass mbao qui disait qu'il était le meilleur au monde mais hélas je ne l'ai jamais rencontré
Machalla aidra longe vie a vous
Machallah chérif da bakh yalla nga godo fan way LOY deff yomboul billay Sama xol sed na lol machallah machallah machallah machallah chérif da bakh yalla nga godo fan way
Alachoma amine yarabi seriffe ayidara dage rek gaye wakhe walaye ndeye sane
Très édifiant que Dieu fasse que nous soyons des talibés cheikh
Lo doundou doyoll aidara
Machalla Serigne bi yalna yalla défal la diam❤️❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳❤️🤲🤲
Jerejef Chérif AT TIDIANY AÏDARA rafetna. Oubil niou téléchargement bi.
If u just need to download this vd go to vitmat
Chérif Yalla na Yalla samella machalla
Machallah wakh deug yallah wakh tane bi nekh na lol,louma yague beug gone leu جزاك الله خير
Masha allah Yalna yallah yokk léram té tass niou si barkém
xole yeup séde ya cherifou balahi beugg nagnioula ❤
Yalnala YALLAH fay yiw amine ya Rabbi
Yallah naniou Yallah niouu fayalko
Macha'Allah yalla naniou yalla tass si barkéme
Machalla Chérif wakhtan bi amna djarigne
Machalla amna solo trop
Abaraka Sheikh Ibrahim Aidara🙏🏾🙏🏾
Machallah seydi haidara nguiri yalla défal niou wakh tanou thierno seydou nourou tall nioungui lay sétané fi en France mane cheikh oumar Diallo la toudou talibé thierno bassirou mountaga daha tall
Thierno Seydou radiyallahou anhou 🤲❤️
Yen wa tivaoune deguen iyaanee
ماشاء الله تبارك الله بارك الله فيك وأطال عمرك
Macha Allah man dee dama contane lol wakh deug yalla yalna yalla fay bijahi rassoul psl
🇸🇳🇧🇷🇧🇷 moustapha Samb masha alla
lo doundou doyoul
Goudal fan lolou amine 🤲🏾🙏🏽🕋🕌
🙏🏿🙏🏿🙏🏿, cherif
Machalah cherif
Cheriffe Yalna Yalla gudal Saye fan tem andak werr si barkeh sa mam Saidian Muhammed SAW. Buga nagne nga defal nyu wakhtan si Serigne Abass Sall . Man talibe Serign Ababacarr la wayee damma beuga Serign Abass Sall bilahi
ماشاءالله ماشاءالله
ماشاءالله ماشاءالله
ماشاءالله ماشاءالله
Machallah cherif Ibrahima Aidara
Ma challah yalna yalla barkél
Alhamdoulilah grand Merci pour tout .....
Eskeye machallah kodda Aissata Banee seydi LY
Seydi yakhya el xutbou
MachaAllah 🙏🏽😍
Vous pouvez activer le Téléchargement s'il vous plaît 🙏🏽
Well come to Africa ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah .mala. Sope
ALHAMDOU LILAH ALHAMDOU LILAH CHERIF DIEUREDIEUF
We need 2th part just for s yahya ly we can't wait
Merci
Machall sama Serigne bi
thiérno yahya ly mako té xawoumako
ماشاءالله وشكرا جزيلا بارك الله فيك ياشيخ
Salam
Oubil gnou téléchargement bi pour gnou sétaneko, c mieux pour nous les démunis, on peut pas regarder l'émission en connectant, ça coûte trop cher les pass connexion s
Douma beugu koula beugoul aïdara
Machallah affaire bi tivaoune la Quoi bilahi
Serigne Ibrahima faye de niette zing il est mort le 22 septembre 2017 Une date qui coïncide a la décè de Serigne Abdou Al Amine yallenaleen yalla bolle yeureume. Hamena souniou mame Cherif Ibrahima aidara n'est pas au courant
Thierno yakhya ly, sa sate de naissance
Thierno Yahya Ly grand muqadam de Maolana Cheikh Ibrahim Niass, yalna yallah yokku léram te Tass niou ci barkem
Baba mome moye lane thieye thierno
Baba Moy BAYE
Machallah Cherif billay contan nanio si
Quelle Mémoire! Machallah
Macha allah
Jazakum Allah Hairan
Machallah diarama cherif
Cherif emission bi de mounatoko bilaye thierno yakhya ya takh ma kham ko ba.sopouko nguir nitou yalla la deug yalla naniou yalla tass si barkem on vous demande de nous parler comme cette emission de vos rencontres ak gorou yalla yi sagou tarikha biga
Serigne bi nio gui rafetlou sa wahtan fi ci france
Beugue naniula lol lol lol
Barkei Aladji Malick Sy (ra)
J'ai 1 question : Est-ce qu'on peut pratiquer le wird tidiane lazim, wasifa et hadra avant de l'avoir recu par un marabout agree de la confrerie tidiane ( muqadam ).
Merci de votre comprehension.
Cordialement
Je te conseille de trouver un muqadam et prendre le wird pour pouvoir profiter davantage des bienfaits de la tarikha tidiania .
🇸🇳🇧🇷🇧🇷👏🏽 masha alla aïdara 🤲🏾🙏🏽🕋🕌
Kone nangoul Baye Niass nopaloou