Final léger CFA Diakhao vs Ady Thiomby à Diouroup Fa Mack 05 janvier 2025

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 янв 2025

Комментарии • 13

  • @paamathndiaye2259
    @paamathndiaye2259 2 дня назад +1

    Fi dafa warona ame balance ♎♎ kholale CFA DIAKHAO lourd la

  • @yandefaye6530
    @yandefaye6530 15 часов назад

    Félicitations CFA

  • @IdySow-jy9sv
    @IdySow-jy9sv 2 дня назад +1

    Félicitations CFA bonne continuation 💪💪💪

  • @diagadione3186
    @diagadione3186 2 дня назад +1

    Poids lourd last la Moy dernière virage bi boo telee yeg té amoo takhaway bou degueur ci galankor rek ngay moudiee lamb defa am Lou bari loumou andal

  • @mamadousene1563
    @mamadousene1563 2 дня назад +1

    CFA dama Mouss trop bilakhi😂

  • @paamathndiaye2259
    @paamathndiaye2259 2 дня назад +1

    Cfa waratoule beurré poids léger 😂😂

  • @diagadione3186
    @diagadione3186 2 дня назад

    Bayilenn lingeen di wakh lamb ken douko yakamti kouné khamenga sa katan fimou tolou bou beugee yeg dina yeg

  • @SANTATI23
    @SANTATI23 2 дня назад

    Ki wakhe lenko deug na yeug poid lour way lambe affaire de goor tol na ni goor wara tole donc pour qoi pas mou dionganté ak hay natangome té bayii les legér yimouye nogato

  • @AbdouazizNdao-yd2fj
    @AbdouazizNdao-yd2fj 2 дня назад +1

    Fi amoul balase khana

  • @IbrahimaAdamaNgom
    @IbrahimaAdamaNgom 2 дня назад +1

    Hé balance amatoul yene

  • @mmsseye9391
    @mmsseye9391 2 дня назад +1

    Li dafa yomb.. meno nek 150 kg di beurré poids legers ak ay mbeurou 80kg

    • @yandefaye6530
      @yandefaye6530 15 часов назад

      Machahalah boul thiatou domou diambour bi yako guiss dhé affaire bi douci poids sof ngén trop tchimmmm

  • @IbrahimaAdamaNgom
    @IbrahimaAdamaNgom 19 часов назад

    Gniye nane CFA dou beuré ti poid léger yena takh mou diog sokhor ki yalla moko deff mbeur en plus nianou wadiour mo nangou ci mom Bilaye