Diack's limou wah dara diarouti ci yone. Wah gueun nako raféte. De même biuñouy wah dindi balance Dakar takhoul, mais plus tôt Thiès, Fatick et kaolack. Kone genrou Diak's production yi doundal louñe lamb thiossane mais séni poche lañouy doundal. Merci beaucoup à Thiacka faye. Amateurs yi ñeup ñiy sétane lamb ci aleu bi kham nañe ni catégorie poids légers legui ñoy nékhal lamb yi mais pas les poids lourds... Nguéne balma akh
Je trouve aberrant qu on respecte une regle ici et pas là bas ..Il faut arreter la balance Dans lutte traditionnelle il na jamais ete question de poids cetait plutôt une question d age et de classe d apprentissage ecoutez Le lutteur CFA pesait 100 kg qd il venait de commençer.Il etait donc lourd mais navait aucune experience(classe d apprentissage)...par ailleurs ,dites lui que ce qui est legal n est pas forcément legitime..je suis d accord avec Thiaka augmentez les mises et ns aurons des lourds ds les galas

Thiaka tu as tres bien dit
Très bien ThiAka faye
Éliminer la balance ⚖️
Diaks modoundeul lutt sémpl
Merci thiaka
Je suis avec thiaka faye
Non à la balance ❌❌
Diokadial 🙏🏻🙏🏻
Deug nékhoule mais li Diak's wakh il a parfaitement raison. Thiaka , Diak's amna droit wakh 'dakh mo yobou lutte simple fimou tolou ni
Kane
Errore mouk
Pourquoi pas dans la lutte avec frappe alors ?? May wakh nag koukou dii feen té yak lamb Dakar ak billet bou cher té keen mossouko wakh
Mane xawouma lou takh sénégalais xamoul avancement ak changement. Lamb mougui avancé donc nékeulene nite gueine bayi affaire de lamb ñi ñoko mom wala ñé boy yi nañou yégue tapéte reik
CFA ak ibou Ndiaye eubli kou op dolé, khana con eubli doudou sane Nagne sene plus de poids lourds lagnouy don bn pour de la vérité
Je trouve aberrant qu on respecte une regle ici et pas là bas ..Il faut arreter la balance Dans lutte traditionnelle il na jamais ete question de poids cetait plutôt une question d age et de classe d apprentissage ecoutez Le lutteur CFA pesait 100 kg qd il venait de commençer.Il etait donc lourd mais navait aucune experience(classe d apprentissage)...par ailleurs ,dites lui que ce qui est legal n est pas forcément legitime..je suis d accord avec Thiaka augmentez les mises et ns aurons des lourds ds les galas
Diaks deu léb rk
Lolou mom dou yeufou nitt sakh
Saway no vraiment vous êtes trop égoïste kw légui rawgardou khana mome dou mbeur pourtant day fèy licence liniouy tégue légui lamb meussoul ame ci lamb fok mou ame catégorie
Wawa na ler
Niounn poids léger motax niouy sétannnn
Thiaka bopom lay kassal , il n'est pas contre la balance.Il ne parle que pour les poids lourds. Duniu am tuss