C simple avant que le promoteur donne son contrat il dois d'abord payer une consultation Médical complet au lutteur avant de signé le contrat. Itam les lutteur daniou yomb tu es blesser et tu signe un contrat de lutte dafa yomb aussi.
Boy niang mo meun reug reug aller-retour, reug reug bèn combat 50-50 lafi beuré mouy contre sathies teu sathies moko dane ô6 sathies momou boy niang moko dane donc reug reug ne pèse pas 35% devant boy niang
Vraiment thia kaw thia kanam Tapha référence la Vraiment discipline, bon sens et communique très bien machallah 👏👏👏
Machalah Moustapha Kandji nite kou discipliné il communique très bien et dou wakh moukou louniou Kay khébé yal nasa diam yague ❤️❤️❤️
Il communique très bien machallah kandji.
Non ki kay vraiment , il est extraordinaire ❤❤❤❤❤❤❤ simple discipliné correct
Modou lo vs Reug Reug lagnou sokhla waye🔥🔥✅
Modou lo sa Thiès la combat bi
Comme je l’estime ce Tapha kandi… il est tres correcte et positif…
Reug boula boy niang diapé nga kham ni do 100Fr ba biss ba inchallah
Vraiment ki nit la amna respecte il communiquer bien machalla ❤
Nékha beugue miguini dou wakh jamais louko nite di khébé
Machalla
Wahal Dh Grand Bou Srx le
"Nékha beug" 😂😂😂 katalsandy gooré
Ioe soo yoroull leufdina ma diaxall
@Domou_Deukk_Bi domou ndialobi bahalnala😃😂limadoul tontou seuleufeul ndaye mola méti mane wakhnala douma wakh ak goor djiguéne 🙄🥹mane bignma signaler ni goor djiguéne nga laparé sisa leufeul ndaye😁😁😆😆😆😆
@Domou_Deukk_Bi domou bireul bi lo wakhat nak douma seuleufeul ndaye amouma temps boumaye yakheu si goor djiguéne ok sadata yaye NGA nopi tapha kandji moye nékha beugue kharagne lo moye nékha faral dimanche yaw yaye nékha diouteul samedi goor djiguéne bou oubi sadata nga yaw🤣🤣🤣😬
Famille bi daniou yarou
Machalah Grand Tapha Loudul Bah Bah Moko Geun Nala Yalla Lafal Thiat Dfala Sutra
Boye Niage da daw rek bayiu liune doule yiu
Amin
Wallahi kou bakh la
Combat bi lolou la yalla don ngal waron n'a néx
Ay tappètt ngeun dra diotoulén dèngeun jekoul rék .
ALADJI MOUSTAPHA KANDJI MANGUI LA CHIAAARRRRR
C simple avant que le promoteur donne son contrat il dois d'abord payer une consultation Médical complet au lutteur avant de signé le contrat. Itam les lutteur daniou yomb tu es blesser et tu signe un contrat de lutte dafa yomb aussi.
Mon ami gni da gnou yabaté 😂😂
Wakh akh dieuf bokoul.yakh combat diambour ba paré di conférence fi😂😂
IL FAUT ARRETER DE METTRE DES TITRES QUI SONT TOTALEMENT FAUX PAR RAPPORT A CE QUI SE DIT
Meuss na dadjé ak moom Stade Abdoulaye Wade mais borom baax deugg leu
Nimou méll ci Internet bi nonou leu mell dans la vraie vie
Tjrs souriant
Bayilene di titrés ay Fenn c malhonnête vraiment
Ils le font tous c dommage
Meunone na beurè rk de toute facon Reug Reug moko meune
Fo tek Loulou boy Niang mi daan ki daan reug reug mdr reug kan laffi daan 1 combat risque laffi beure contre Sathies daanou
REUG dé dou moromou boy yi😂😂
Di wakh rék ba combat bi tahaw nga daw😂😂😂
Boy niang mo meun reug reug aller-retour, reug reug bèn combat 50-50 lafi beuré mouy contre sathies teu sathies moko dane ô6 sathies momou boy niang moko dane donc reug reug ne pèse pas 35% devant boy niang
@@Htqv221 Reug dan elton,gouye gui gris 2 bombardier tok ci deunou Sa thies facilement ngaye wakh wakhou boy niang saway beuré lagnouy wakh pas rugby.Boy niang tapét motakh mou déposé médical.
DNGAY FENE DE
Ay tapet nguen rek reug reug molène meun