Boy Niang 2 vs Reug Reug : Kandji production tranche le débat "parénaniou sou féké…"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 24 янв 2025

Комментарии • 153

  • @modoulebou634
    @modoulebou634 11 месяцев назад +13

    Wakhi ragal rek waye Reug Reug vs boy Niang moy meilleur combat si saison 2024 bi 🔥🔥✅✅ baye ndiaye ak Makane wakh lenn si combat bi💪🏿💪🏿✅

    • @modoulebou634
      @modoulebou634 11 месяцев назад

      @@momobouthiapathiolybi7752 non bayil gnou combine ba dieul roi bi rek 🙏🏿🙏🏿😅😅

  • @beydysakhocurdelion
    @beydysakhocurdelion 11 месяцев назад +10

    Lamb amoul ay ma dane ki la Dane mala meune lolou dou lamb 🤣🤣

  • @papafall8905
    @papafall8905 11 месяцев назад +3

    Vèrite absolu kandji❤❤

  • @AbdoulayeMbengueSima
    @AbdoulayeMbengueSima 11 месяцев назад

    Wa kay lolou moy combat sportivement parlant ça ouvre d'autres perspectives à la lutte.

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 11 месяцев назад +11

    LAMB LEU REUG REUG VS BOY NIANG

  • @karlsilver5776
    @karlsilver5776 11 месяцев назад +13

    Reug reug mingui dioum..bou yakareh mo moune Boy nisng dey nalh bopame😊

    • @AdamaBeleme-lv5di
      @AdamaBeleme-lv5di 11 месяцев назад

      Mokko meunnne fouffff

    • @dembafofana8646
      @dembafofana8646 11 месяцев назад +2

      @@AdamaBeleme-lv5dicomme nimou meuné wone satiés avant combat biii😂😂😂

    • @josephericousmanediandy783
      @josephericousmanediandy783 11 месяцев назад +3

      Iow nopil rek boy Niang moko meune deee .mais sénégalais mo guawa faaté. Boy Niang li Reug reug Di beurré moko arrangé , mais ndeysan lamb mo teurreudi rek . Sénégalais lou beeeeessss la xam .
      Mais beineu beineu bimouy beurré thi mbapat ,amoul thi Arène, mom franc ak Serigne Ndiaye nioko nara eupeu chance. Seine rapidité et vivacité ak explosivité molein motaliiiii

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Boy Niang mom li Reug di beurer dafko arranger trop. Bene benam yoyou ak di forcer Boy Niang danako thi dane ba gnibi mouy soga comp. Mais nak Reug mo meun gnom Franc ak Serigne Ndiaye 2 wakh deug Yalla

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 11 месяцев назад +6

    Boy NIANG ndiémé woul Reug Reug
    Papay Boy NIANG Dègol ndiémé woul Reug Reug staf Boy NIANG ndiémè woune Reug Reug thiotou Nayam li rék 🤣🤣😂😂🤣🤣😂😂🤣😂🤣😂

  • @moiizasankhare4096
    @moiizasankhare4096 11 месяцев назад +12

    Boye niang ak wa keureum danio ragale reug reug 😅😅

    • @FallDamel7484
      @FallDamel7484 11 месяцев назад +6

      Kne hamo boy Niang2 sou takhawé gay hame

    • @dembafofana8646
      @dembafofana8646 11 месяцев назад +1

      Façon yeine ngané reug nieupako ragallll tei satiès dafko niousss daneko 😂

    • @MamadouGueye-q7h
      @MamadouGueye-q7h 11 месяцев назад +1

      Mon cher ce combat aura bien lieu le Staff de Boy Niang est dans sa logique il est entrain de faire monter les enchères ceux sont les supporters qui ne comprennent pas

  • @Ibrahima66.
    @Ibrahima66. 11 месяцев назад +14

    BOY NIANG AK STAFFAM PEUT ÊTRE DANIO FATÉ NI SUR LEURS 4 DERNIERS COMBATS BÉN VICTOIRE LANIOU AM
    REUG REUG SOU AMÉ STAFF BOU BAKH LAC DE GUEIRS LA WARA BEURÉL PSK BEURÉ AK LAC DE GUEIRS MOKO EUPEUL RENDEMENT QUE BEURÉ AK BOY NIANG MOU LAC DE GUEIRS DANE

    • @aliousarr3816
      @aliousarr3816 11 месяцев назад +1

      Vraiment frer kham ngua lamb

    • @LeprinceVegeta-f6i
      @LeprinceVegeta-f6i 11 месяцев назад +2

      Lolou aussi dh waroko wah boy niang dh dagnko teubeul rek mais waroulwone beurék balla sah.. dafa echec si lac ak tapha tine yeupp avant gnoukoy diokh balla.. soufékoulwone balla yakkou sah dakoy dane motakh boum démè si modoulo dannégnko

    • @dembafofana8646
      @dembafofana8646 11 месяцев назад

      @@momobouthiapathiolybi7752tei vip bou am 47 ans la dane lolou diaroulll ndamo, balla Gaye bamou dané tapha gueye do deigue moukeyyy ndamo

    • @boucountadiallo9692
      @boucountadiallo9692 11 месяцев назад +1

      ​@@LeprinceVegeta-f6i sou boye barèwoul balla kane laye beureul génération diekhal nalène dou beurè aak ama sa thies moko bolè aak balla gaye soudè xam nga lambe

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Li nga wakh dou lamb. Saway sen Roi Bi sakh Modou échec nafi 4 sorties (Baye Mandione, Balla, Lac 2, Gris) te pourtant Eumeu dafko maay chance. Boy Niang Tapha mofi gnep bayi la djeul ak Lac bo parer tekk thi Balla.

  • @youssougambien9166
    @youssougambien9166 11 месяцев назад +2

    Boy niang tapétla nîéwoul reug reug

  • @ejarju406
    @ejarju406 11 месяцев назад +2

    Boy Niang ragala😅😅😅

  • @gmeuzcana193
    @gmeuzcana193 11 месяцев назад +25

    Légui *BOY NIANG* sou beuréwoul ak *REUG REUG* kan lay beurél à l’heure actuel ?? En suite j’aimerais prêter votre attention sur *BOY NIANG* il fait partie l’un ds lutteur 🤼‍♂️ les plus intelligents 🧐 sur l terrain !!! Té aussi Dolé bi mo eupeu yaram biiii té souko *REUG* beugué soroxo soroxo bilahi vs serait surpris😮 *BOY NIANG* dinako daan ba ageu galém nguèn di doga comprendre ✅ même si *REUG* à bcps d qualité pour l battre mes sikaw mou Téy mes WAlahi erreur bimou déf ci combam ak *SA THIÈS* il l regretteras

    • @MouhamedRassoul-by5xi
      @MouhamedRassoul-by5xi 11 месяцев назад

      @@momobouthiapathiolybi7752 lay ragal si reug reug

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +2

      Mom laay wakh degou gnouma bilahii 😂. Khamou gnou Boy Niang batay

    • @issasylla3602
      @issasylla3602 11 месяцев назад +1

      J’en suis persuadé

    • @ibrahimasambseye2938
      @ibrahimasambseye2938 11 месяцев назад

      Gris lay Khar ta takhaw na ba parei

    • @fallabdou7163
      @fallabdou7163 11 месяцев назад +1

      Boy ndiang gris mi danoul mbeur 15 ans lay khar gayi lou yombou lagnou beugu reug érreur bimou déf ci sathies dotouko défati ci lamb combat bobou moko déf championnat

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 11 месяцев назад +3

    Boy NIANG Reug Reug la peuples sénégalais yii Di réclame 🇸🇳Boy NIANG Reug Reug actuellement ny moy logique Lamb Sénégal 🇸🇳 🔥🔥🔥Boy NIANG Vs Reug Reug 🔥🔥🔥Boy NIANG Vs Reug Reu🔥Demande sociale sénégalais yi🇸🇳

    • @MouhamedRassoul-by5xi
      @MouhamedRassoul-by5xi 11 месяцев назад

      @@momobouthiapathiolybi7752danga ragal rek ama amna combat 😂😂

  • @papecisse6000
    @papecisse6000 11 месяцев назад

    Machalah kandji ❤️❤️

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye 11 месяцев назад

    Bilahi le combat n'arrange pas boy Niang.
    Kandji profite sur le côté financier. Khaliss rec lathie am🫡

  • @NdiayeAblaye-rv7bn
    @NdiayeAblaye-rv7bn 11 месяцев назад +1

    Reug reug futur roi des arènes

  • @mansourndiaye1906
    @mansourndiaye1906 11 месяцев назад +4

    Kou d'accord ni reug reug meunoul danne boye Niang rék lalall j'aime wakhouma wakhou supporters nak kéneu dousi sama mbeur mais nignouye beuré da bokoul sakh

    • @SonkoFocus2024
      @SonkoFocus2024 11 месяцев назад

      Bilay mo meune boye niang

    • @mansourndiaye1906
      @mansourndiaye1906 11 месяцев назад +1

      @@SonkoFocus2024 ah copain boye Niang daffa meune contre collés dé so khamoul niguaye beuré sisa beuré lalaye danéllee

    • @ibrahimathiaw7391
      @ibrahimathiaw7391 11 месяцев назад

      Papay moy Niang sax deugol Reug Reug moko dakha beurre fouf nk 😂

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад

      @@ibrahimathiaw7391 Pere degaul mom khamoul Dara 😂 Mais Boy Niang mo meun Reug foufff

  • @SaliouFall-x8i
    @SaliouFall-x8i 11 месяцев назад +1

    Combat boy Niang vs Reug Reug bakhoul Si Boy Niang

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 11 месяцев назад +1

    Merci Kendji

  • @yatmaniang6847
    @yatmaniang6847 11 месяцев назад +1

    Boy Niang vs Reug reug Moy combat bi

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf 11 месяцев назад +4

    BALLA GAYE MON DANE TAPHA TINE TÉ TAPHA TINE MON DANE BOY NIANG TÉ BOY NIANG MON DANE BALLA GAYE TÉ BOMBARDIER TAPHA TINE MON KO DANE TÉ BOMBARDIER MON DANE BALLA GAYE TÉ REUG REUG MON DANE BOMBARDIER LAMBJ AMATOUL LOLOU WAY KANDJI RESPECT À TOI

    • @MorDiop-e2d
      @MorDiop-e2d 11 месяцев назад +6

      Sathies mo dane reug reug te sa thies boy niang moka dane legui lo waxe

    • @Leuzsonko
      @Leuzsonko 11 месяцев назад

      ​@@momobouthiapathiolybi7752meusoul comine boulèn wax lolou dako meun dane ko .. nieup xam nagn ni bg2 sa thies rk lay top mes tmt reug vre champion kèp kouy tak nguèmbou meun nala dane si lou yombou nk naniou bayi far bi tè waxantè deug nak

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Tapha tine danoul Boy Niang

    • @pmsdiouf
      @pmsdiouf 11 месяцев назад +1

      @@MorDiop-e2d LAMBJ NONOU LA DÉMÉ NAK MBEUR YI DANIOUY DANANETÉ RK

    • @pmsdiouf
      @pmsdiouf 11 месяцев назад +1

      @@momobouthiapathiolybi7752 DIÉL BÉ YOMBEU RK 😄😄

  • @TallaFaye-y8t
    @TallaFaye-y8t 11 месяцев назад

    Reug reug boy Niang Moy combat bii

  • @AliouKama-zs9ye
    @AliouKama-zs9ye 11 месяцев назад +1

    Si boy Niang réclame des cachets de 100milion savent qu'il ne vole pas lutter 😮

  • @yilebaba6565
    @yilebaba6565 11 месяцев назад

    Combat bou nekh laaa

  • @abdoufatahgueye1306
    @abdoufatahgueye1306 11 месяцев назад +3

    Légui bombardier mo dane modou lo Modou lo dane boye niang reug reug dane bombardier lamb passé na fofou kandji

  • @MameAlassaneSock
    @MameAlassaneSock 11 месяцев назад +1

    Kandji Guemo liguaye wakh thii risque bou mag lah thii yéne

  • @afro3827
    @afro3827 11 месяцев назад +10

    Pere degaul day tek xel reug reug mais xamni dinagn beuré 😂

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 11 месяцев назад

      Dou tégue hél déh,dafa niéméwoul Reug Reug,lolou rek la

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      @@moussapayemane4167 Da ngay tiaxane rekkk ! Au contraire dom dji la beuga maay temps mou defarate guinawam ndax thi defaite la djouguer

    • @moussapayemane4167
      @moussapayemane4167 11 месяцев назад

      @@papadiom9260 🤣🤣🤣🤣linga wah mom amoul 🤣🤣🤣🤣mousouko niémé,Reug Reug mo bagne harito bi,néna nieup lay beurél 🤣🤣

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 11 месяцев назад +6

    Boye.naig dafa Rakal

  • @OusenouSoow
    @OusenouSoow 11 месяцев назад +3

    Reug mo mane boy Niang fouff

  • @AmmeDicko-wt2iu
    @AmmeDicko-wt2iu 11 месяцев назад +11

    Pourtant boye Niang meune na dane reug reug dakh mo dakh khékh té bou reug reug dieulé tanque yi boye Niang dane

    • @modoulebou634
      @modoulebou634 11 месяцев назад

      Waye boy Niang benn lokho lay khékhè nak

    • @cheikhgueye7924
      @cheikhgueye7924 11 месяцев назад +1

      Éh waye ndaw Samba boye niang d fouka reug reug diapou mou diékh 😂

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад

      @@cheikhgueye7924 Lolou Sa khalate laa te thi ay guente laa laay fekk

    • @fallabdou7163
      @fallabdou7163 11 месяцев назад

      Boy ndiang lgui gnéppou khamnagn fay yimou am ci modou lo bénneu lokho la khékhé cou wan dou kao

  • @khadimdiouf2076
    @khadimdiouf2076 11 месяцев назад +1

    Reug manoul boye Niang dé bilahi

  • @theartist9928
    @theartist9928 11 месяцев назад +8

    REUG REUG le futur après Modou Lo

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 11 месяцев назад +5

    Papaye boy Niang katt mo wakh reug reug beurrë woule ak boy Niang

  • @dimkhalebambiste2931
    @dimkhalebambiste2931 11 месяцев назад +2

    Boy Niang mo meun koudoul reug Reug gayi nio bakh di wakh rek

  • @AlybabaAlybaba-tf7jd
    @AlybabaAlybaba-tf7jd 11 месяцев назад

    D'où coumbat dehh

  • @meissaMbaye-o4u
    @meissaMbaye-o4u 11 месяцев назад +2

    boy niang et reug reug nekhoul n'a modou lo dieul reug reug te bayi ragal bi

  • @assanediop771
    @assanediop771 11 месяцев назад +1

    Boy niang2 mo dane sa thies wayè reug mo daan bombardier

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 11 месяцев назад +2

    Fans bg2 mes souma sanione boy niang day def anne blanch xolat bopam mo geune nguen koy boukh reug reug tè lolou moy logique me mbeur bou mak sou diougué si défaite faw mou tok xolate bopom ...

  • @papezulefaye7263
    @papezulefaye7263 11 месяцев назад +3

    Beuss bouko yalla dogalé ba bi combat taxaw ngén kane moy boye niang sou boba ngén xam ni reug reug wakh jouri lassi amm té yalla na combat bi taxaw

  • @AmadouLy-kt9ww
    @AmadouLy-kt9ww 11 месяцев назад

    Dielen combat bi mo Guen wakh dju

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 11 месяцев назад +1

    Reug lac moy combat bi wala boy niang

  • @TaphaSene-r6s
    @TaphaSene-r6s 11 месяцев назад

    Baye Ndiaye lomouye xare

  • @galayebeye7868
    @galayebeye7868 11 месяцев назад +2

    Da ngéne Ragal Reug Reug dieul léne avance bi mo geune si yéne

    • @ibouciss3519
      @ibouciss3519 11 месяцев назад

      Xana fans modou lo gua

    • @galayebeye7868
      @galayebeye7868 11 месяцев назад +2

      @@ibouciss3519 non balla gaye2

    • @ibouciss3519
      @ibouciss3519 11 месяцев назад

      @@galayebeye7868 motakh kay guay waxli mais attention dh reug meunoul boy niang dh

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +2

      @@galayebeye7868 Mo waral wakh Boy Niang nekhoulene 😂

    • @galayebeye7868
      @galayebeye7868 11 месяцев назад

      @@papadiom9260 boye niang kaye souma sa nione chaque dimanche mou danou

  • @mcigueyegueyetv6041
    @mcigueyegueyetv6041 11 месяцев назад

    Wakhi tapéte rékk gnafi wakh🤣😅

  • @tamsirfall4573
    @tamsirfall4573 11 месяцев назад +1

    Reug Reug mo meune écurie de Gaulle yeupe pour 10combat Reug Reug dinako dane ba danalé père de Gaulle

    • @abdoudiop7177
      @abdoudiop7177 11 месяцев назад +2

      Lolou nguene wakhone contre Sathies mou dane lene mbeur boko danagoule menegoko boy mbeur la deh

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Mdrr saway Bb diene molene di khokh lo mbappat ngene di wakh wakhou Boy Niang ?? 😂😂😂

  • @youssoumbengue7698
    @youssoumbengue7698 11 месяцев назад

    Gora nekal nitt D’accord siteu ak modou war nagn meun beurei wayei siteu tolagoul pour beurei ak modou wanei woufi dara ayy examen wam yeup dako échoué

  • @alysow6354
    @alysow6354 11 месяцев назад +6

    Reug reug mo meune boye niang fouffff

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +3

      Yalla baxna dina taxaw 😂

  • @ansumanjarju1566
    @ansumanjarju1566 11 месяцев назад

    Analyse logique Bombardier mo daan Balla gaye Reug reug daan Bombardier Boy Niang daan Balla gaye donc si le staff de Boy Niang veut un combat Balla Reug reug avant d'accepter de lutter contre Reug reug il y a quelque chose qui est dans leur tête,ils craignent ce lutteur hors pair Reug reug c'est ça la vérité

  • @mcigueyegueyetv6041
    @mcigueyegueyetv6041 11 месяцев назад

    Boy niang dafa tapéte reuk reuk

  • @mouhamedlydiouf8934
    @mouhamedlydiouf8934 11 месяцев назад

    Promoteur yi ay ragal lagniou. Lougnouy khaar pour reug reug vs boy niang

  • @djibrilfaye911
    @djibrilfaye911 11 месяцев назад

    Combat l vraiment

  • @boubacarfaye3209
    @boubacarfaye3209 11 месяцев назад

    Mais loutah wa boy niang ragal reug reug

  • @mamadoudiagne83
    @mamadoudiagne83 11 месяцев назад

    Lolu moye lambe reug reug vs boye nian

  • @iscooamar2214
    @iscooamar2214 11 месяцев назад

    Waxi Ragal reikk nguén di wax Boy niang vs Reug reug bi moy combat bi

  • @amadoulatyrndiaye231
    @amadoulatyrndiaye231 11 месяцев назад

    Kandj sa wakh beurina boule gnou sonale boye Niang reug reug moyye combat bi gnieup Di khare balla gaye boumouye beure AK boye Niang. Boye Niang 2 deffarate la amone. Bouguene ladhie khalisse bou eupeu aussi kenne doulene feeyye lolou

  • @aliousarr3816
    @aliousarr3816 11 месяцев назад +1

    Reug waroul laj boy Niang defna 4 sortie 1 victoire lasi am

    • @babacarseye49
      @babacarseye49 11 месяцев назад +2

      4 sortie ak niane?

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Te 4 sorties gnou oube lamb J laa (Balla, Tapha, Lac ak Modou lo). Modou lo avt mouy done Roi defna 4 sorties (Baye Mandione , Balla, Lac ak Gris bordeaux) te amouthi victoire bou lerrr ! Bayilene sokhor

    • @ndiayemame3233
      @ndiayemame3233 11 месяцев назад

      Lu ler ga wakh

  • @amadoulatyrndiaye231
    @amadoulatyrndiaye231 11 месяцев назад

    Ki tapale layye wakh bouguene ladhie khalisse bou diadou promoteurs yii feeyye lennes

  • @akadtv661
    @akadtv661 11 месяцев назад

    Boy Niang niemei woul Reug Reug beugoul daanou

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Dou lolou mbeur mou mag bou dano dafa wara khol guinawam bou bax avant mouy djeulate combat ! Boy Niang bou defarouwater ba gneuw mo meun Reug !

  • @bambadieng9959
    @bambadieng9959 11 месяцев назад

    Combala

  • @m.moussa678
    @m.moussa678 11 месяцев назад

    Reug da beurii ndax wax boulen beurii ak mom

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 11 месяцев назад +1

    Dou comba boye niang mo raw reug reug si comba boye niang mo dane sa thies tè reug reug sa thies moko dane li wadji wakh rék si am boye niang khaliss bou beuré lanouye ték mou beuré ak mome si no dou comba bala ma dé gñounane reug reug mo dane Bombardier Bombardier djiékhale bou yaga mé bi Bombardier di néka Bombardier reug reug daf ko gñiémé deugeu bayilène nafékh té reug reug guéne diokh ko moromame fi amoule outale yone reug reug sa thies dôrko mou kheume😂😂

  • @GaydellLo
    @GaydellLo 11 месяцев назад

    Wakhi ragal rek gay wakh kandji boye Niang défaite la diougue meni diarr lufi modu lo diarul nekal nit su bariwul tay Dina beure suba

  • @mousdiatta9828
    @mousdiatta9828 11 месяцев назад

    C'est pas mon lutteur mais il est plus fort que boy Niang.
    Y'a pas photo

    • @papadiom9260
      @papadiom9260 11 месяцев назад +1

      Khana Guediawaye nga deuk 😂 Li degone na Sa thies diko wakh ba Boy Niang doumako 😂

  • @beuguegalsenziguinchor6280
    @beuguegalsenziguinchor6280 11 месяцев назад

    Boy niang si il ne lutte pas avec Reug Reug cette année il va faire année blanche donc 70 millions pour boy niang et 60 millions pour reug Reug ça suffit largement oubien Boy niang contre LAC2 parce que Boy niang n’a pas prouvé pour intégrer les VIP

    • @ndiougamar2202
      @ndiougamar2202 11 месяцев назад

      Boy 4 vip 1 victoire 3 défaite gris laï khar aï ragal lagne

  • @babacarbambistesarr3313
    @babacarbambistesarr3313 11 месяцев назад

    Kandji lingafi wax yeup si ragal reug reug la bokou l'autre jr wax one nguenfi reug da wara dieul balla gaye baparé

  • @papadiom9260
    @papadiom9260 11 месяцев назад +8

    Boy Niang dhe bilahii mo meune fouki Reug bilahii! Saway tankou Sa thies laay djeul dii reup 😂.. Ma setane Reug mou weur ndomb Bb diene bo pare BB diene daneko thi! Setane na Reug general Malika daneko thi beurer! Motakh Bouma deguer foum djap Boy Niang daneko lol Ay reee lamay deff bilahii 😂 Boy Niang dafa beurii none ndakh limou deff Guediawaye mais mo meune thi Boy yii ! Molene dakka khekh molene dakka beurer !

    • @SonkoFocus2024
      @SonkoFocus2024 11 месяцев назад

      Reug lime deff mbapate bb diene defouko general defouko

    • @yilebaba6565
      @yilebaba6565 11 месяцев назад +2

      Sawaye boy niang champion leu mais reug reug aussi ndanane laa ! Kou beurré daanou , exemple yi ngua citer dou dara par rapport ak li reug reug daan si mbapatt !

    • @abowagne5136
      @abowagne5136 11 месяцев назад +3

      Boy niang mo meune boy yimou massello yeup

    • @seydinamohameddieng8273
      @seydinamohameddieng8273 11 месяцев назад

      Zoss AK amanekh nio dane boy Niang koudoul sa Thiès reug dosa morom

    • @abdoudiop7177
      @abdoudiop7177 11 месяцев назад

      ​@@seydinamohameddieng8273mais sawaye lolou biko Sathies dané baparé ngakoy dogua nangou leggui nomou meuné boy niang ta danagouko vraiment sene analyses diahalenama boy mo dane Sathies mingay wakh

  • @KhalifaDieye-sc8jz
    @KhalifaDieye-sc8jz 11 месяцев назад

    Reug moo meunn senn waa écuries yeupp waxou ragal rék ngaffi waxx

  • @falyndoye3800
    @falyndoye3800 11 месяцев назад

    Man wax dji ladoul meun limay niane rek moy na Wa pikine dieul avance bi

  • @khadimthiam3081
    @khadimthiam3081 11 месяцев назад

    Senegal James douniou xam analyst lamb. lan moy boy niang mo dane kii wala kalè bayi lèn barè, aye tappèt ngeun. Mèrd way.

  • @fallalioune9489
    @fallalioune9489 11 месяцев назад +3

    Ragal la rek mom ak reuk reuk moy yone diaroul di ath ar bi yi

  • @AliouNdiaye-b8h
    @AliouNdiaye-b8h 11 месяцев назад +2

    Door you méti moye d'âne reug reug té boy niang âme n'a crochets bi

  • @Babacardiane221
    @Babacardiane221 11 месяцев назад

    Kéndou boye nign si lambue ❤bilakhi

  • @oumardiouara7540
    @oumardiouara7540 11 месяцев назад

    Ragal rek

  • @ahmettoure813
    @ahmettoure813 11 месяцев назад

    Reug reug Moy Kane ak l'âne la fii déf combine AK bombardier Di tak radio yii