Aicha Kone feat Ousmane Bongo - Nopalou Leen (Video Officielle)
HTML-код
- Опубликовано: 20 дек 2024
- AICHA KONE REVIENT AVEC UN NOUVEAU TUBE POUR L'ANNEE 2025!
avec la participation de @Ousmane_BongoOUSMANE BONGO
Ecoutez le titre sur toutes plateformes de streaming
crédits
Artiste/interprète: Aicha Kone
Réalisation: Mao Prod
Beat: ZOX
Paroles: ZOX
Topline: ZOX
Mix/Master: ZOX
PAROLES
Couplet 1
Eh! Man kham na li léne nakari sougne sagnone nima mel legniy mel (mayou Yalla leu dou nène)
Té sougne sagnone damay torokh sama doundou doumci am louma nékh (dinagne fa dé ndakh man Yalla ma téral)
Séni commentaire yeup laye bokhogne sandi
Man légniy bania guiss nagnou taal gaz tog ci
Boukki meunoul titeul goumbeu ndakhté goumbeu guissoul dara
Pour yène meune nguène ma yeungueul gueune leine daur ndakh yeugouma touss
Mais gni nio faux
Rater seu vocation
Wéssou woul nga tog di wakh ci nite souba ba ngone (tchim)
Séne crush yi man légne nop
Séne far yi man légne fan
Bagne bagne beugue yallay dogal
Di nguene nangou maafi né
Pré-refrain
Nopalou leine, dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Am yaye diou bakh dioudo fima wara dioudo ehhh seine wakhi meunouma saff
Refrain
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Gni khamalougne ma dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Nioune ragalougnou dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Pont (griot)
(Griot) kholal, kholal gnane dafa tardé daa nieuw fékk Yalla paré
Yallaay khool louko nékh def ci mom louko nekh
Aïcha, ya meune ya eupp dolé ya gueuneu fëté khalé
Yeureum léne diégueul leine thiouthie dey kham lékam waaay
2ieme couplet
Nieuweul, gueum naa sama bopp tekci goumbeu tekhlou
Dara safouma, adj sama level douma guéstou
Awma temps, man damay liguey waay
Khalé bou ndaw ma wara téral yaye
Waa gni dougne pousse fii
Amougne lougne def
Am nagne diote daal
Awma béneu temps boy!
Man damay thiouthie fi
Di thiouthie fé
Souma nékhé thiouthiati fé
Awma béne temps mangci outoume koppar!
Pré-refrain
Nopalou leine, dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Am yaye diou bakh dioudo fima wara dioudo ehhh seine wakhi meunouma saff
Refrain
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Gni khamalougne ma dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Fi Yalla rékafi né (zembéré, zembéré, zembéré)
Nioune ragalougnou dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Dégniy zembéré bamou nékh (zembéré, zembéré, zembéré)
Damay doundou louma nékh meunougne ci dara (zembéré, zembéré, zembéré)
Outro
Nopalou leine, nopalou leine
Téla nangou dafay yombal ay douma waay
Nopalou leine, nopalou leine
Téla nangou dafay yombal ay douma waay
Nopalou leine dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
Nopalou leine dal lou leine
Ndakh seine wakhi safouma sakh
REMERCIEMENTS:
Tenue: Afshal et Pape Mbaye
perruques: Baye Modou Hlm
coiffures: Dija and aicha
Accessoires: Dishop
remerciements a cosmakup almadies
Chorégraphie: prince
- Abonnez vous et activez la cloche de notifications 🛎 ✅
Assurez vous de suivre Aicha Kone sur:
Instagram - www.instagram....
Tiktok - / aicha_kon2
snapshot - / aiiijc6p
#AICHAKONE2025
Viviane n2 lafi guise kou guise lolou comme man❤👍😂
Lolou momtu mank un point 😅
Ki au moins meune n'a outou viviane
Viviane bou ndao
Clip niom niar la beug di
Elle a beaucoup de chemin à faire ngen koy diay nane viviane yena nekh nak
Bilay
Manchala mon bb ❤❤❤😊
❤❤❤❤❤
Daguene gnak kignane ❤❤
Lima nex si gnom ken ignanul si gnom
M dieyna balén khaléyi waye c magnifik
@@Dieyna merciii bb❤️❤️❤️❤️
Kou D'akor Ni Aïcha konè Da Meune Lal j'aime ❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Kou yéné Aïcha koné plus de 20molions🎉 de vue
Bolén sokhor roul té Wax deugu té Yalla tax rk xamguen ni li mom nex rk def machallah 😍🥰😘
Aka Guem bopam ❤❤❤vraiment amouniou neubo yagui ligueye
Niougn souniou connexion laniou youré payer meme koufi way lou nekh niou wakhoo bou nakaré niou wakh koo koumou nakarii gua kholat saa bopou
Ay guarou walé mom amoul sens vraimentttttttttt😊😊😊
Degg na deugg nak 😂
Aïcha Koné moye Viviane Chidid
Viviane Chidid moye Aïcha Koné ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Aïcha kone gnoune ngay garoualé nonou😢 wayè yalla bahna 🥹dagnoula beugu rek motah gnouy critiqué wayé yégoul sougnou xôl 😢
Yéna faux
Yen faux guen dhhh ahhhh
@@Sokhoulove117merci là-bas 🫱🏽🫲🏾❤
Moussons beug
@MariemebanaDiedhiou bilay
Aicha kone is like Vivian she don’t depend on prince art to creat her music or promote her music she stood by her own that’s why she tanish titi light and she shine because standing by your own fighting for your own and creating your own music pay off in few year and in next few years aicha will be just like her is she didn’t stop doing music
Bravo nekhna dal tei enplus dafa meune way machallah sénégalais la kéne xamoul loumou beug sof guéne trop bayiléne diambour bonne continuation ma belle👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏👏😍😍😍😍😍😍
❤❤
Iow lanega😂
Aujourd'hui 20, décembre 2024,❤ Que Dieu bénisse toi et ta famille ❤❤ Amine
Wawaw khalé day gniak diom boko defé rk men deuk Sénégal 🎉😂
Wawaw Li bomb là Bilakhi machallah ma belle nice na trop ❤❤❤❤❤🎉
Touss dara Nak ❤❤❤❤❤
Aïcha koné tu as assurer graveuh❤️😭
Wakh na deuk Sunu fare yi mome lagnu nobeu 😌❤️motakh gnuy sisou diko wakhal Lou nékeu🤌🙈
Elle peut devenir Viviane deh un jour
Mais sonbi damaye si dégue voix Viviane bilaye
Qui est là après tiktok. Voilà la musique est un moyen d’expression. Elle répond enfin aux sénégalais. En plus elle a changé sur plusieurs registres et ce n’est pas facile . Bravo
Yeah yeksi nga nak yeugueul nga niveau bi bamou kawé waw kay❤❤❤
Kou d'accord ni Xalée yi danio meun machallah ❤❤❤❤❤
Nékh n'a trop way ❤🎉 machallah 🥰🎉
Boulén soxor nak li mom dafa nex🎉🎉🎉🎉
Clip bi rafetna machallah amnga feeling tontou nga gnidon wakh meuno🤧
Viviane n 2
Future Viviane 🤧🎉🎉
Machaalaah beautiful Aicha ❤, sama Toooma.
Rawaal thiakaaw thiakanaam ma chérie❤❤❤
Magui degue la voix de Viviane dans sa voix machallah tu a une mélodie incroyable dans ta voix je ne c pas es ce que tu sais sa force à toi sister
Kouko setan 3fois😭💕 son fl*w😻
Xale bi dafa diogama😂❤❤
Aïcha Koné, tu es une source d'inspiration pour tant de personnes. Ton nouveau clip promet d'être un véritable chef-d'œuvre.
Viviane numéro 2 machalla nkhna raffet neu🎉🎉🎉
Ay way mon bb Aïcha koné sama ndama li so nieuwé rek mu nékh jtm beaucoup shu❤️
Aaaaaaa li mom lér na légui 🥳🥳🥳
Ya mol , ya meune weuy🥰🥰
Meilleur produit SPG je vous dit
T'as frappé forte hein❤❤❤🎉
Juste le début j'ai hurlé🎉🔥Comme je te l'avais dit fonce ma star n'écoutes pas les haineuses, t'as tout pour être au sommet, la beauté, la voix, le talent tout est là et félicitations pour ce chef d'œuvre, le clip, le son, les tenues tout est nice🙌🏽 Bonne continuation girl🎉To be continued...❤️
Elle à encore frappé fort cette magnifique Femme 🎉❤
🎉🎉Wawaw boula dara saff sampou rek ☺️🫶❤️
On dirait Viviane waw❤
Ah li nekhna deh😂 très belle leçon merci là-bas 😂
Bilahi dafa meune weuyy sénégalais yi nio sokhor rék en plus kéne douko dégue silo niak fayda machallah bonne continuation chérie
Oupe baxna si lax bu tangue machallah
Nioun sénégalais yii daniou la fans rk am na nion kham bouniou sanion mél ni yaw gueum sa bop liguéye concentré sur ta vie bou len falè danio sokhor ❤❤❤😢
Vraiment nak sound bi nekhna ❤
Bon courage
Boulén soxor nak li mom dafa nékh trop way ❤️♥️♥️🎉🎉🎉
Machallah !!! Elle a beaucoup de talents. Aïcha je te conseille vivement de t'approcher de Tata Vivi, elle pourrait te coacher et t'apporter bcp également.
Machalla safna sap 🎉❤bonne continuation
Meilleur clip parmis tout ses clips wlh ❤❤❤😊😊😊 voilà le premier clip que j’ai validé parmis les autres
Yaw ak ndakhté lougen def nekh nama❤❤❤
Viviane N2 kaye ame fofou
C’est du lourd 🎉❤❤❤
Bi mom nékh na 😂😍❤️❤️
Limou weuyon lepa nekh
Gnaff nila limoy tontou bu forokh begue na li❤
Taye dé nékh na
Bi moom nekhna ma Aïcha ❤
On dirait viviane machallah ta tapé trop fort ❤❤❤
Boul fallé keneu defal loula saff meune waye ame classe Machalla ❤❤❤
Legui kou waye dougal si bongoman mais nekhna
Félicitations à Aïcha Koné pour son nouveau clip, une artiste au grand talent dont la musique résonne en chacun de nous. Ton succès ne fait aucun doute !
Bi moom neikhna ❤
En plus dafa am classe naniou ko wax ❤
Wawe elle a tapé fort ❤🥰
Aicha elle a eté toujou com ça do8 ça xalle avec sa mentalité fort ak xam adouna boulon kelen ba tay bayina wala mu am depression bref té xamna yalla mola samal bopam mé konté ken waxatouko yalla yalla gueuneu Sam lep lulay way di fexal yalla nasi djitou bonne contuation 🎉🎉la star des star by force nagou rk Wa bagne
Wawaw la star des stars ❤❤❤❤
Koula bagne yalna déé ❤🎉🎉
Non li nehhhh na way vivi lafi guiss ni❤❤❤
Waw j’ai trop kiffé ❤❤
En plus tu dis vrai ennh mane yow rk lay topp depuis 2014 lala nopp amourou jeunesse koi petit ba grand🚶🙂
Toujours aussi talentueuse et rayonnante, Aïcha Koné. Ton nouveau clip va sûrement conquérir nos cœurs, félicitations !
Ohhh manchallah li dafa nekh trop bilay yalla na yalla lafal la thiete rek inchallah lepp dina baxx ❤❤❤
Franchement nexna ❤té voix bi machallah on dirai Vivi sangsé gua aussi ❤
Love from Gambia 🇬🇲 ❤️ 💕
wawawaw nekh naa trop wayy
Aicha kone damala beugue ❤
Bo beguei nit begue ngako reik sama thiofel si khalei bi hooo ❤🎉
Congratulation girl❤❤❤
Ki khawma nouko nitt di bagnei ❤
Viviane et ❤bass thoum 🇸🇳👍😊🥳💚💚👑👑
On dirait Viviane 😌
Bravo à Aïcha Koné pour son nouveau clip, tu es une artiste talentueuse et inspirante !
Nekh na nice na ❤️❤️🥰🥰🥰
Aïcha Koné, ton authenticité et ta passion transparaissent dans chacune de tes chansons. Bravo pour ce nouveau clip, il ne peut être que magnifique !
Machallah
La Star a pris son Envol ❤
Bravo aicha nekhna torop 👏👏👏
Nice one beautiful love ❤❤❤❤🙌🇬🇲🇬🇲🇬🇲💋🥰🥰
Machallah elle a tapé fort
Bb kay léralma li Aicha koné néna s'en far yi mome lagnou fan😢
Aicha kone tu est la meilleure tu bien assuré tout est partis avec le temps et dans l'espace bravo
Blanche baily sénégal 🇸🇳
❤❤❤nice
Her dress sense, her voice ,the voice , hat off to her and her manager she have a great manager 🎉🎉🎉🎉😢😢❤❤❤
Guiss gueun filing bou Khaleii😭❤️🎉
Waouwwww meilleur Lou nekhiii ni eup na❤️❤️🥰🥰🥰🥳🥳
wornaa yalla ya meune fouff❤❤❤❤
Machallah tout est Nice 👍 ma Aicha tu ne déçois jamais
Je valide avant meme decouter 🥰🥰🥰🥰
Trop nekh ma chérie bonne continuation n'écoute personne
Gros bisous😘😘😍 ❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah 🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Meun mokal maitrisé 🥳🥳🥳
Bilae Dafa nekh trop sakh