Lu Takh Mourid yi nék ci internet bi Di wéddi Li Serigne Touba Binde !? Doyna waar 🇸🇳

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025

Комментарии • 855

  • @souadoukebe6886
    @souadoukebe6886 2 года назад +2

    Machah allah ya oustaz li mom lérna nagnie nanou topou alkhourane ak sunna

  • @eltrabjador422
    @eltrabjador422 4 года назад +8

    Vous êtes sur le route des prophètes que dieu vous bénisse et vous protèges s

  • @papismandiang3477
    @papismandiang3477 4 года назад +5

    Lima lenni niaan rekk moyy boulen bayi konn y3uff yi dou nexx .Cheikh Ibra Faal amna loumou waxone thie touma dioudeuk deugg teh molen guenn xamm yalla tehh eupp lenn xamxam.Ahmadou Bamba douniou kouniouy topp akk xell wasalam

  • @moussaba3022
    @moussaba3022 4 года назад +3

    Dieureudiefé serigne Touba

  • @mouhameddiouldediallo4806
    @mouhameddiouldediallo4806 4 года назад +11

    Serigne bi défa dioume dieureudieufeti cheikh alpha alqour ane ak sounna rek

  • @AFRICAN67
    @AFRICAN67 4 года назад +8

    Machallah mes frères hayakumullah,
    Ahlu bidaa vont fermer leurs becs

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад

      Touty nguen si daniel makgni ay domou haram deug nguen

    • @AFRICAN67
      @AFRICAN67 4 года назад

      @Oumar kébé mag gni nioye Sahaba yi (ridwanullah aleyhim),
      Mayal serigne touba jamm,soxlawul sa mbél mbél ji,

    • @AFRICAN67
      @AFRICAN67 4 года назад

      @Oumar kébé man soma saaga ma saaga le,nay léer.

  • @sahabasada7487
    @sahabasada7487 4 года назад +4

    Yalla naniou yalla moussall thi séytané gayi danio kheur lék yalla nalén yalla sopi incha Allah Allahouma saly Allah seydina Mouhammad psl

  • @ndiayecheikhtourad8531
    @ndiayecheikhtourad8531 4 года назад +6

    Kone yenne ay nonou Serigne Touba ngéne ay waye Bouléne sonal Séne bopou yalla moy mayé yalla may Serigne Touba loumou mayoul kéneu. Ta yaw Yay domou xadje domou xaram

  • @ousmanetine9215
    @ousmanetine9215 4 года назад +6

    Bamba partout diouli diamou yalla ak sant serigne touba

  • @Jubanti-tv
    @Jubanti-tv 4 года назад +30

    Yalnalén yallah sakhal si léral deugg ak di mabb ay fén

    • @Jubanti-tv
      @Jubanti-tv 4 года назад +1

      @Seye Amadou Mandou mooy léral alkhouràn ak sunna, mi Kii di déf, ak di dadji wakhi kiy sossal yallah ak yonétam
      Kiy sossal yallah ak yonétam kookou moo mandouwoul, te réreulatékatla
      Diiné déskay djiangue

  • @shekhnangrmcf6908
    @shekhnangrmcf6908 4 года назад +23

    Li serigne bi di wakh kat comme ay Tom et jerry 😆😅🤣

    • @sillysoumare3820
      @sillysoumare3820 4 года назад +2

      🤣🤣🤣🤣

    • @mamadomamado3134
      @mamadomamado3134 4 года назад +1

      😅😅😅

    • @zizaziza7979
      @zizaziza7979 4 года назад +1

      😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅

    • @taphaseck190
      @taphaseck190 4 года назад

      Yéne yéna kham lousi book ak lousi bokkou 😀😀boy wané nguéne comme l'islam séne bàye boko wakhabiya yi khaw ma lou takh nguéne yabb nitt gni yéne nguéne créé affaire de terrorisme di yé fitna fépou si adouna fou nguéne bari diamou doufa am kholàt séne bopp ba paré ba kham si lane guéne nék gnoune nak diap nane ni yalla teulé woul dara boudé mou Mohamed rignàne na kone louné mane manà khéw si ay niteum ta nguéne diagu mbi ndoum s touba wàyé bou léne took fi rék di diclou alpha mou léndi gueum loo ni yall manoul dara ok.........

    • @babacarnenesarr715
      @babacarnenesarr715 4 года назад

      Rew nga

  • @aboridial3606
    @aboridial3606 4 года назад +2

    bilae iow wérou khana amo lo def serigne touba nga nek di wKhal ni dangay khar iow

  • @mobilephone5140
    @mobilephone5140 4 года назад +7

    Seugeum politique mo meuneu dieuler capitalou senegal dieumer ko Dakar astamalak yalla mi mome diame gni binde kabam gui ak yoneintam bou teid bi ta meun ko yobou fouko neikh ... Deim lein diangui ta bayi sein thiakhan yi serigne touba mo mome leip bassi sein rou yoyou sakh

    • @kalamousarr3881
      @kalamousarr3881 4 года назад +1

      Waxo deugg lingay wax dou xam xam.YALLA rek moy borom rou yepp

    • @mamadoudiop1105
      @mamadoudiop1105 4 года назад +1

      @@kalamousarr3881 mande ligua wakh la gueum

    • @mobilephone5140
      @mobilephone5140 4 года назад

      Nguein beug ko ak nguein bagne ko serigne Touba mom la yalla diokh sein rouh yi ... Li ko yalla defal meussouko defal kein ta dotouko defal kein Ahmadou Borom Diam gni

    • @kalamousarr3881
      @kalamousarr3881 4 года назад

      @@mobilephone5140 tontu nga sa bobou com mom daniouka diox rek momoul kone.mbiir mi dou ay beugue ak bagne ndax serigne bi thi bopam nangoul naniou nitou YALLA bimou done té kou nono kounimel YALLA nga déclarer guerre té yalana naniou borom bi mousseul thi lolou.wani meuno wax ba serigne bi mom rouh yi ndax ki am rouh thi dieumeum meunoul mom rouhou kenene

    • @mobilephone5140
      @mobilephone5140 4 года назад

      @@kalamousarr3881 serigne touba yalla ko goreil ta yamoul thi goreil ko rek dako goreil ba nopi yeulaty rouh diam gni diokh ko ta nak kou mayer moma to wakh deug yalla ahmadou borom diame gni dioup na kouko wakh dioumo feino ta kein meunou si dara kou beug ak kou bagne yeip bam a ko mom

  • @AbouLouqman86
    @AbouLouqman86 4 года назад +7

    Merci beaucoup cheikh Alpha Que Dieu les guides les Mourides , tidianes , layéne ect...

  • @nevergiveupnevergiveup3318
    @nevergiveupnevergiveup3318 4 года назад +29

    Alpaha nar nga bari ay Nonn bilahi mais yalla nala yalla samou

    • @taphaseck190
      @taphaseck190 4 года назад

      Alpha kéne no non wouko wàye kham nane né dou wakh té yalla takh té parfois mou soss yagg nàko diclou wàyé légui légui mom mou yokou

    • @ouakamedakar4209
      @ouakamedakar4209 4 года назад

      Yaw ak alpha sén la feul ndeye

    • @mouhamedthiam9048
      @mouhamedthiam9048 4 года назад

      Tapha seik alpha mi dh..da alkou. Bou yag wah deugu dako teu.

  • @cheikhdieyedieye4662
    @cheikhdieyedieye4662 4 года назад +14

    Serigne touba yalla moka yekeuti Kénn mounousi dra sonn rékkkk

    • @mouhamedthiam9048
      @mouhamedthiam9048 4 года назад +1

      Wawaw sonou bayi.

    • @masiba7272
      @masiba7272 4 года назад

      Ok mais wah bi louguene si wax

    • @kongoloaboulubanda6255
      @kongoloaboulubanda6255 4 года назад

      Kkk

    • @salimatasamb1294
      @salimatasamb1294 4 года назад +1

      Hors sujet rk

    • @moustaphangom9747
      @moustaphangom9747 4 года назад +3

      masiba 72 khana toumal ak torokh tanguè bilen di jemmè safara euleuk kou bagne Serigne touba yak eblisse yenay bokkou yonne ndakh kou tedd ki Yalla kofii nekkal ba faaw

  • @moustaphathiam1061
    @moustaphathiam1061 4 года назад +21

    Dieureu dieufé serigne touba mba yénagui waj 18 safar gui

  • @B-221
    @B-221 4 года назад +9

    Noo WA YEEN Wakh Kat yi Am geen Diot D Serigne TOUBA Rawna Seni Mame YALLA Moka Def Loumou Doon

  • @ibrahima1970
    @ibrahima1970 4 года назад +10

    Diara diaf ya oustaz yalla na yalla fayla aw yiw

    • @bayeraneseck1750
      @bayeraneseck1750 4 года назад

      Serigne I amoul morom yalna nouko yalla fayall

    • @lamzogaming4
      @lamzogaming4 4 года назад

      Yalla douko fayy dara dakoy douma billahi

    • @Damos_officiel
      @Damos_officiel 4 года назад

      @@lamzogaming4 ay re guama def sax

  • @ahmadsankhare991
    @ahmadsankhare991 4 года назад +5

    Rayy ngueine ma mane 😂😂😂🙆🏾‍♂️😭😂😂.....deug akka nékha khamé Wallahi

  • @malickdiackdiop8586
    @malickdiackdiop8586 4 года назад +7

    Mâcha Allah
    Yalna Yallah diammallén fid dounya wal aakhira

  • @kurohime5750
    @kurohime5750 4 года назад +3

    Guigne nako ko thi ki teuyeu sama rhou☝🏾, yawmal khiyam gnou beuuuury di na niou am mbetel. Yalla na niu sunu borom guindi inchallah.

  • @Jubanti-tv
    @Jubanti-tv 4 года назад +10

    Gni sos tariqayi dafa mélni diangouniou woon TAWHID ak AHAADITH yi, moo waral niou niéméwoona sos louy woutéak Al Qur'an ak Sunna.
    Ki binde (ZIMAAMOU WARAA HASRII) Khanaa guisoulwoon Aayah bii:?
    (وَيَسْأَلُونَكَ عَنِ الرُّوحِ ۖ قُلِ الرُّوحُ مِنْ أَمْرِ رَبِّي وَمَا أُوتِيتُم مِّنَ الْعِلْمِ إِلَّا قَلِيلًا). الاسراء(85)

    • @mouhamedthiam9048
      @mouhamedthiam9048 4 года назад

      Niola geuneu ragal yala ..fouf daq lako jamo ..hana fagniy wahè yein meuno lein kham.

  • @abuahmad9938
    @abuahmad9938 4 года назад +16

    جَزَاكَ اللَّهُ خَيْراً
    Qu'Allah ﷻ te préserve Cheikh Alpha.
    Dajji sene féne yi ak sene wakhi doff yi beu leep leer.

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад

      Kattal sendey alpha ba sa thiotto ndey

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад +1

      @Oumar kébé assalaamou halay koum 🙏🙏mbokk mi ki di wéddi wakhou serigne touba lay wakhal ♥ kholatal bou bakh lingay wakh . 🙏🙏Mane may talibé serigne touba bi geune doyadi si talibém yi 🙏🙏🙏 alhamdou lillah sergne touba yalla moma bakhé ma xam limou woté 🙏 mo takh adouna bi yép sounko wéddi wone dou takh ma wéddi ko yalla xam nako 🙏🙏 dierediefé serigne toubaa ♥عبد الله وخديم رسوله♥

    • @moustaphangom9747
      @moustaphangom9747 4 года назад +1

      Yaw kay yaye fen ji strees guèni dèè Serigne Touba moffi nè

    • @abuahmad9938
      @abuahmad9938 4 года назад

      @@moustaphangom9747 💩

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад +2

      Bouleeup l'era wahabit yeup dem sawara nityou bonyi nefekhyi domy haram yi A ba Z ay yeufeur nguen yubon dangui di sonnou. Rek takousi geuneux sa boppu rek geuneul ci mbedmi di saga kilifeuyi bis bobou moy nek da dernier jour ...dieureudieuf serigne touba

  • @KHAMKHAM-xi8pj
    @KHAMKHAM-xi8pj 4 года назад +9

    Di fénal serign touba nguir sén poch safara dina méti trop

  • @elhadjisock208
    @elhadjisock208 4 года назад +7

    Outiléne xamxam SERIGNE TOUBA borom xamxam yi laye wakhal.
    Fa SERIGNE TOUBA di wakhé Séne xamxam toloul fofou

  • @ahmadoubambalo9612
    @ahmadoubambalo9612 4 года назад +1

    Yéne Di wakh Ana liguéne bind nopi léne moléne warr

  • @sunugalsen2tv978
    @sunugalsen2tv978 4 года назад +3

    Doule SERIGNE TOUBA d'où sen moromou Baye té dou moromou sa mame ag sa SERIGNE

  • @malangdieme9076
    @malangdieme9076 4 года назад +7

    Il faut dire la vérité aux gens c mieux

    • @mdjf7353
      @mdjf7353 4 года назад

      C quoi la verité?? Dis nous

  • @elhadjfall3187
    @elhadjfall3187 4 года назад +2

    والله تيقنت أن عملكم هذا يزيد فضل ومقامة ومبدإ لدى الناس بالشيخ الخديم رضي الله عنه، لأن البيت الذي قاله الشيخ هو بيت واضح جدا ، وأرجو إن كنتم مؤمنين صادقين علمين عادلين غير محتويين شيادئا من الجهل والحسد والتعصب وعليكم أن تستدلوا بالبيت ولا سمعة الآخرين به وحسب مبلغهم بالعلم، وهذا البيت في قصيدة خاتمة المناجات بالخط للشيخ، والقصيدة التي كان خادم الرسول صلعم يكتب في الساعات الآخرة من حياته، إن كنتم غير الجهلاء ورأيتم اسم القصيدة "خاتمة المناجات" فقط والله عليكم أن تفهموا، ولكن لكم حق الإنكار أو الإيمان، ولكنني آمنت بقوله في ختم الإيمان، سمعتكم أيضا قائلين إذا كانت زمام الورى في يد الشيخ كماكتبه، لم لم يقدر أسنى الخديم ذهاب إلى بيت الله الحرام أو الحصول على الحرية عن الأعداء؟ ولكنني أجيبكم بكل بساطة بالبيت الذي قاله الشيخ في بداية عمله أو إخراجه عن بلاده هو: أسير مع الأبرار حين أسير= وظن العدى عني هناك "أسير "
    إذا عليكم أن تفهموا بأن كون الشيخ في أيدي الأعداء ليس عجزه ولا وهنه ولكن المقامة التي أرادها من الله فأعطاه الشروط لحصول عليها من ناحية البلايا وغيرها، كما بينها أحمد الخديم بنفسه في كتابه قائلا: "سبب غيبتي أن الله أراد أن أنال منه جاه
    وأن أكون شافعا للقوم وأن أكون خادما في الدوم"
    أصيكم ياأهل السن -أستغفر الله- ياأهل الشرك أن تتقوا بالله سبحان وتعالى وتركوا النفاق الذي أنتم فيه والسياسة التي تحملونها حيث كنتم متثوبين بالإسلام وأنكم نائين عنها كالشرق والغرب، كثير من المسلمين لايتفاهمون سبب شتمكم وتعييبك بالتصوف والمتصوفين - اللهم إلا زينة الحياة والمال فقط- استمع إلي جدا لتفهم، ذالك تارخ طويل جدا ولكن أشرح لك بالإيجازة، وأسألك ألا تعجبوا إن رأيتم مكة المكرمة تتوارثها أسرة واحدة متمسكة بالملك وحدها ولم تملك الأسرة أية العلاقة بالنبي صلعم ولا قرابة ولا عمل جيد في إقامة دين الاسلام في أيام الرسول ولا خلافائه ولا التابعين، اللهم إلا الأسرة السعودية التي استعمرت البلاد بقتل الملايين من الشعب ودخرت الملك في قبيلتهافقط لا بالنبي... ، لذالك أهل الأسرةيتحارب كل ما يرجونه أنه قدر أن يهلك ملكمهم ، وأنتم عرفتم أن من مبادء المتصوفين عشق النبي عشقا جما وتبرك به وصلاة عليه حيث كانوا مع أهله وأصحابه، وعرفت الأسرةةالدكتاتورية السعودية إن تركت الناس متعلقين بالتصوف مع مبادئه هذه، يوما لتراكمت الأسئلة فيهم، لم تولت هذه الأسرة الملك إلى أبد، وما دورهم في قيام الاسلام؟ وإن كانت مكة المكرمة تجب أن تكون بلدا ملكيا ومن الأسرة التي أحق في توليتها؟ وهذه الأسلئلة وغيرها ينبه التصوف في الإنسان، لذالك ترى في كل سنة يمول الملك أموالا كثيرة في تركيب الدعاة مع رواتبهم لمحربة التصوف ، إن كنتم ذوي العقول لرأيتم أن أولئك الدعاة لن يوجهمهم إلى البلاد التي ندر فيها الاسلام ولكن يوجههم الى البلاد التي انتشرفيها والتصوف كما رأيتم في البلاد السنغالية التي نحن فيها وماحولها.
    أيها قارئ سياقي رجوت أن بعد هذا اليوم تفاهمت الخوابث التي يرتكبونها الذين يدعون بأهل السن أو الشرك هم الذين يشربون دماء المسلمين حيث كانوا ، إن كان لديك ملاحظة رأيت أنهم لن يعملوا أبدا ، اللهم إلا أنهم يبيتون في فيسبوك، يوتيب والواتساب وغيرها رغم سكنهم في البيوت الفاخرة والسيارات الغالية جدا - ولا تعجب ياأخي المؤمن بذالك لأن رواتبهم من موظفهم الملك الدكتاتوري السعودي لن تتأخر!

  • @amadoudiop9709
    @amadoudiop9709 4 года назад +8

    Je viens juste de comprendre que wahibiste esprit cartésien rék lanou yor.Billaahi yéena touti kham kham,té réer.Délou Di santate Serigne Touba,ndakh kii ma dégg ma wakh nii,mouy Alpha kou gatta kham kham, raisonnement bou souffé la yor.Certainement gni boun fékké woon yonenté bi(PSL) dinane ko weddi

    • @lavieetpaix2358
      @lavieetpaix2358 4 года назад +1

      Alpha dit que il à besoin de éclaircissement sur c'est questions ! Je vois on doit répondre avec des preuves

    • @malickdiene1782
      @malickdiene1782 4 года назад

      Boy kou gueum waxi naiine yi Doyna waar

    • @babacardiatta6997
      @babacardiatta6997 4 года назад

      Dbbnnçxx¢`×

  • @madamesarr1306
    @madamesarr1306 4 года назад +1

    Fatabarakala machalla leraleyi amenagne solo lole yalna yalla sameléne dolé deugeural séne takhawaay Macha Allah

  • @souleymanediallo526
    @souleymanediallo526 4 года назад +16

    II dit : Adorez vous en dehors d'ALLAH, ce qui ne vous saurait être utile en rien, et non plus vous nuire. Allah vous a créé et c'est lui qui detient subsistance. Nos âmes sont entre ses mains Lui Allah soubhana watala.

    • @noreynisantati5721
      @noreynisantati5721 4 года назад

      Yène khamou lène yalla par ce que da ngèni woutal yalla limite té kata nou yalla amoul limite

    • @diackkonare217
      @diackkonare217 4 года назад

      H⁶⁶

  • @djlisow8119
    @djlisow8119 4 года назад +1

    Diéradieff thi lérall yi amna solo kou namma kham yalla demall thi mbinndoum sey dill hadji Malick ndax mo topp sounna mouhaméd psl

  • @Moustapha333
    @Moustapha333 4 года назад

    Dieureudieuf khadimou rassoul dieureudieuf khadimou rassoul dieureudieuf khadimou rassoul sante serigne touba khadimou rassoul serigne touba lanou am tay ak

  • @cheikh_tidjani
    @cheikh_tidjani 4 года назад +5

    😂😂😂 De simples questionnements reek pour se rendre à l’évidence que ces écritures sont fausses, que des fables. Jazakallah akhi pour ces éclairages. 🤲🏿

    • @ndattembaye4716
      @ndattembaye4716 4 года назад

      Ndeysane yaw déy mann nagnou guiss ni ab tidiane nga ak loumou meunti doon ab soufianké nga tei khamnga boubakh ni ignane rek moola diapp ci serigne touba, wayé sa serigne cheikh ahmad tidiane déy doo wéddi wakham tei billahi ay wakham you baré gnii gnookoy wéddi diko wakh louné waayé liloy door migui niew yaa Andak gnome tay nguir ignane waayé yaa Léen di khass soubeu inchallah

    • @cheikh_tidjani
      @cheikh_tidjani 4 года назад +8

      @@ndattembaye4716 Douma soufiyanké, douma tidiane, tour bii naak meunou ma si dara. Manhaj salaf laay dound bi manaam alkhuran ak sounnah si deguinou sahaba yi. Amoul dara lou maay ignané Serigne touba, dé na bou yagg. Moom ak beepeu serigne ak si tarikha boo bokk, meuneu lo ma dara faa yallah. Yallah reek la guem. Wa salam.

    • @salimatasaly9757
      @salimatasaly9757 4 года назад +4

      @@cheikh_tidjani geum nge kou djara geum kou yamoul ak kéneu kou djara yakar Yallah kéneu leu mo fi nék il est unique. Kou djeul nak serigne yakar ni molay dougeul aldjana nakh nga sa bop. Allahou Akbar

  • @abdougaye971
    @abdougaye971 4 года назад +8

    Dierdieff Serigne touba we love you. For ever

  • @khaoussoukabadiaby6347
    @khaoussoukabadiaby6347 4 года назад +5

    Machallah ya cheikh alpha diazakallahou khayrane amna solo looool

  • @Damos_officiel
    @Damos_officiel 4 года назад +1

    Liguay wax dhé khawma si lou beuri waye do fi guiss kenn kou def li Serigne Touba def lolou mom dafa lerr Ahmadou Bamba kasse donk ba nak ba fawou wassalam 🙏🏾

  • @abdouloum4934
    @abdouloum4934 4 года назад +29

    Alhurane ak sounna mo nekh (yewoulen)

    • @jaraafndoye4371
      @jaraafndoye4371 4 года назад +2

      Bari ay wax de nenaniou bari dieuf moko geune😎

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад

      Kattal sandey kattal sandey kattal sendey

    • @abdouloum4934
      @abdouloum4934 4 года назад

      @@bayembaye1053 mangay Saga؟

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад

      @@abdouloum4934 wahabiyona yeup sen thiotto ndey

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад +3

      @@jaraafndoye4371 diouma masalikoul djinaane 27 milliards 🙏 université chékhoul xadiim 37 milliards ♥ wayé wakh lou niaw rék 😰 té aw sakkét défaloun ko islam ♥ lolou moy dieumelé islam thia kanam ♥ lima wor moy koulén topp légi islam tass♥ islam dieuf dieul la ♥ من عمل صالحا فلنفسه 🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @falloudiagne3156
    @falloudiagne3156 4 года назад +4

    Bilahi Lou serigne touba wakh geum nako ndakh lèpam yalla la Mossoul tal kènèn koudoul yalla ak yonèntbi shwsm

    • @aas499
      @aas499 4 года назад

      Mais serigne bi meuna dioum tamit

    • @freemind3009
      @freemind3009 4 года назад

      Yawla rek!

  • @cherifcamara252
    @cherifcamara252 4 года назад +4

    Amna Solo Machalla Yallanalen Yallafay Aldianna Firdawsilala 🙋‍♂️🙏🙏💟🏃‍♂️🏃‍♂️💯

  • @doudesignerinfographie1735
    @doudesignerinfographie1735 4 года назад +1

    Dieureu dieuf serigne touba

  • @dipendiaye8843
    @dipendiaye8843 4 года назад +22

    Dieureudieufé s TOUBA khadim Rassoul

  • @jflixibrahimjfibrahim5127
    @jflixibrahimjfibrahim5127 4 года назад +7

    HafizakALLAH machallah ziarnaelae. Kitab ak sounnah.

  • @cmsshoptrade4569
    @cmsshoptrade4569 4 года назад +2

    Vraiment deug moy ndieuk té moy moudiou, bo courage wa alkhour an ak souneu

  • @sidindawfall1740
    @sidindawfall1740 4 года назад +23

    18 SAFAR IL TOUBA inchallah 2020

    • @deugdourombinopdioulite635
      @deugdourombinopdioulite635 4 года назад

      Diemlèna yewou dof nguene rek

    • @dibiteriemachallah8336
      @dibiteriemachallah8336 4 года назад +2

      @@deugdourombinopdioulite635 seydou man MOURIDE la..té Al Quran ak sunnah rekk la geum..serigne touba so guisé loumou binde yeuppp , si Al Quran ak sunnah na tègou.. boule dioume si aye cadou.. sama mbok MOURIDE you diangoule nio nek di wakh aye thiakhaan..mes serigne touba lougne ko wakhal yeuppp loudoul Al Quran ak sunnah dègni fènal serigne touba..khasidah serigne bi yeuppp tageu Yallah, aye yonent, sahabah yi, ak waliou yii la.. Serigne Touba dou Yallah, dou yonent, dou djiiné, dou malaika, niit késé la..di toudé bopam khadim Rasoule ( talibé yonent bi) mes waliou deug la té niitu Yallah la..serigne touba mo jihad guir nioune Senegalese niou meuna diamou Yallah normale. ..serigne Touba si akhlou sunnah na bokkk

  • @khadimgueyenormal5023
    @khadimgueyenormal5023 4 года назад +1

    Machaalla serigne touba amoll moroum diara diafé serigne touba

    • @malickdiouf1586
      @malickdiouf1586 2 года назад

      Wawaw amoul morom kagne, si meuneu wouté ak yala ak yonentebi psl

  • @Damos_officiel
    @Damos_officiel 4 года назад +1

    Billay gni rew naniou ay re laniou ma def sax guénne Serigne Touba mo sosal yallah sheutttttt Yen ba Ahmadou Bamba di kénal yallah seni Serigne fan la nékon wouyoulen Khadimoul Rassoul dianguélewoul lénen loudoul topou yallah ak yonentebi ta fofou la diar ba am li mou am te apar nioniou guisso len fi kénen kou def limou def xam guenn bou bax lima wax.

  • @brigadeantibidah2911
    @brigadeantibidah2911 4 года назад +28

    Assalamou Aleykoum wa Rahmatoulah Tallah wa Barakatouh.
    Y’ALLAH neu Y’ALLAH SHWT sambe léne té mousseule léne si aye pekhé nite you bone.

    • @djibycisse5656
      @djibycisse5656 4 года назад +7

      Salam suna mouhamed psl point

    • @brigadeantibidah2911
      @brigadeantibidah2911 4 года назад +4

      Djiby Cisse
      Salam serigne bi
      Alkhourane et Sunnah point rien de plus.

    • @taphaseck190
      @taphaseck190 4 года назад

      Alpha nime mané fene té ragal débat daye wéte di wakh rék yéwou léne gàyi nekoune thi sunna dh diniy door rék alal rék té màgui niàne bou noppé mou léral masalikoul djinane boudé yalla rék mo takh mouye wakh

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад

      Diallalen thia khadj danguendi doulrek

    • @bayembaye1053
      @bayembaye1053 4 года назад

      Nokhoulen fallez mandoulen dine dji yeneusi geuneux touty

  • @mapatembengue1513
    @mapatembengue1513 8 месяцев назад

    Yena ngui sauver diami yalla yi beugue deugue merci

  • @imamcheikh8219
    @imamcheikh8219 4 года назад +11

    Machallah dadji réck

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад

      Di dadji rék té do dadie moukk 😂😂 bou yaggé islam tass tasar 😂😂 déllo islam ginnaw té yégoulo ko😰😰 chaytané dé billahi bég na si yéne 🙏🙏🙏🙏🙏

    • @MrAlfred1704
      @MrAlfred1704 4 года назад +2

      @@khalilndiaye7265 sawadji kou dadji shirk rek par ricochet yangui tabakh tawhid walabok😉😀

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад

      @@MrAlfred1704😂😂 lane moy tawhiid domasi khamal touti

    • @MrAlfred1704
      @MrAlfred1704 4 года назад +2

      @@khalilndiaye7265 avec plaisir sama wadji😀😀😀. Tawhid veut dire en difinition simple kénnal YALLA . maname la ilaha illa ALLAH. Walabok thi nassarane l'unicité de DIEU Tout Puissant ☝😁😁

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад

      @@MrAlfred1704 légi serigne touba mom ndakh dafa geumoul لااله الاالله

  • @remah2462
    @remah2462 4 года назад +2

    walahi vous avez raison fane lagn done dioub lou pour djouli ?

  • @indigne2161
    @indigne2161 4 года назад +4

    Le Sénégal comptait deux grands poetes Serigne Touba et le President Senghor les poetes sont des rêveurs

  • @amathsow6701
    @amathsow6701 4 года назад +7

    Sénégal doyna War liiiiiiiii?

  • @sounnaba9007
    @sounnaba9007 4 года назад +3

    Qui fatou noumouy yore rouhou djam yi môme serigne bi ana rouham d'où dee na bagnou soul comme nougnouy soûle niit yeup vraiment gni théâtre ça gnolene geune fouf wallahi bokk yi gêne lene gorgorlou rek t'es yalla takh inchalah DEUG rek moy yalla wallahi li couthi fatou yangui thi boccale soubouhanal Allah akbar yalla nagnou yalla mousal thi tarikha ak sene mousiba yi gnou geume gnanal lene sene serigne yalla djeugal co mo gêne sene thahane yi

  • @B-221
    @B-221 4 года назад

    Kou weddi Serigne TOUBA weddi ga Seydina MUHAMMED Weddi Wakhi YALLA Serigne TOUBA Nak YALLA Moka Def Loumou Doon Batakhna Nou Defko Ninouka Def

  • @Dimkhalo
    @Dimkhalo 4 года назад +1

    Ndeysann yen mom Waa akhlou sonna la khawma serigne touba ay mbireum si kanam rk tè desna waxtanei gougnou serigne bi dh di ngueine sonnou dh

  • @AminataBalde-ht7eb
    @AminataBalde-ht7eb Год назад

    Kou wédi Serigne Touba bo déwé tabi safara doul rék ngaye déf

  • @mamadoubailo9985
    @mamadoubailo9985 4 года назад +2

    Mouride yi nio togne sene bop. Amouniou xam xam aye dof legne rek top sen serigne you niak diné yi nga xam ni serigne done oute mouy yeureum yalla ak yonent bi niom fékoulene ci.yena togne diambar bobou di ahmadou bamba bah.beug tilimeul ligeyam .xamo lene yalla nopalou lolou moy yonou mouride

    • @worldwords5841
      @worldwords5841 4 года назад

      Yow fo ték ni Mouride yi xamouniou Allah... Li nga wax dara woroulassi, djoulite dafay wakh louko wor

    • @mamadoubailo9985
      @mamadoubailo9985 4 года назад

      @@worldwords5841 Mouride bou xam yalla amoul. Kou xam yalla do tégui tank si charia ndakh moy (yonent bi ) .té sene référence bi geuneu mak guinaw serigne bi cheikh ibra Fall leu. Yalla koula ko geuneu xam Molay geuneu top yonent bi si ziar ak si batine (sharia ak hakika) .guinaw cheikh ibra sakh mome motoul ndakh bene tank rek la done dokhè si dinè (batine) kone nga xam ni yone bi amena ci lou lene leragoul. Diekh lene si yonent tek yalla placame xamè khadra yallabi .hakhut,malakhut,jabarut ,wathieu nassot li amoul mouride bouko xam bassi khalif bi mountakha.

    • @worldwords5841
      @worldwords5841 4 года назад

      @@mamadoubailo9985 waw loula nékh wakh ko si cheikh ibra Mba xalife bi wala koumou mana done, témou Melni da nga dém keur Mouride yeupp waxtane ak niom ba xam sen xam xam, lolou kou mandou douko déf, té dioulite beugue nanoussi mou mandou... li ngay wakh ni B à bas wou marifa la ay hakhut malakhute, jabarot, nassote... té mouride deugg béna référence la am mouy yonent psl. Ték Yalla plaçame? yow parégo...

    • @mamadoubailo9985
      @mamadoubailo9985 4 года назад

      @@worldwords5841 no yow bene référence nga ame.mais serigne mountakha mi wakh si laminiam sou amé geureumeul yalla ak yonent bi té amoul bou serigne touba sokhla wouko.mouni watt yow malkhiyam bou yalla togué ni yonent bi tok ni mou rombou lene dem ci serigne bi.😂mouni watt ,done nitou serigne mo geune done nitou yalla. Lolou yeup aye niak tawhid leu .ndakh kou xam yalla douni mouk bou yonent bi toguè ni yalla togué ni .ndakh kou xam yalla dina xam ni yalla diombou na tok ndakh amoul place bouko atane. Yalla diombou na toga ndo ndakh amoul louko gueneu .mais bon xam yalla dall mo wor yalla naniou yalla may degg .bo beugué degg deug mouridisme thiakan rek leu ndakh serigne touba kene si domam wala kene si ngiko dopou donoul siru (secret) bi yalla may serigne bi.secret bobou nak moy dokh ba taye mais amoul mouride boussi diote ndakh serigne dagne ko def kiraye .mystifié ko a rendre impossible son accessibilité et son combat et son rôle. Serigne xam yalla rek la done oute si adunam.

    • @worldwords5841
      @worldwords5841 4 года назад

      @@mamadoubailo9985 ngani secret bobou amoul Mouride Boussi diote? Yow kou degueur fit nga tédo wax loula woor, gnémé nga Yalla torop té lolou dou thieurou djoulite... saway serigne Mountakha limou wax mom la concerné man Mouride pirr la, Allah la gueume diko diamou yonent bi moy sama modèle, bamba moy sama serigne... yow kan mola tarbiya??? ... tu es un peu aigri et ignorant quand même... yow bane tarikha nga bokk??? Koula dégg Khép fi nga diogué, mais heureusement nioune am nanou capacité discernement, ce qui n'est pas ton cas, on dirait un adolescent qui parle... am na Mouride youy diote ci xam Yalla gogou Ngay wax déf ték... yow eska bokoulo ci gniy nonon séni mbok djoulite? Tek Yalla plaçam? Yow parégo

  • @omarsagna6076
    @omarsagna6076 4 года назад +1

    Alhamdoullilah Magu sèdè ni yalla Rek moye boure di borome

  • @babelthiam9842
    @babelthiam9842 4 года назад

    Tout ce que Serigne Touba, à dit c'est la vérité

  • @omarfofana6087
    @omarfofana6087 7 месяцев назад

    Serigne Touba, cheikhoul khadim Akhmadou,borom barackbi mome rek lagnou Gueum , walahi

  • @thorthor4293
    @thorthor4293 4 года назад +3

    5:17 - 5:24 bilahi gni gno mouneu doule, deug... néna cheikh ma roubeu Gueye mo dioulé Aladji Malick 🤣🤣🤣🤣 pouf!! Legui sen gen yeup ler ganaw wahal Serigne Touba loumou wakhoul ngen fi néké sunna mom zéro motakh sen fen yiii dina ler ben par ben...

    • @souleymanely2551
      @souleymanely2551 4 года назад

      Saway ñie maodo rek lañou bañ.khol yiil diekh rek.façon soss bouné sossal nañou ko mame maodo

    • @mouhamedbachirseck3400
      @mouhamedbachirseck3400 4 года назад

      Kou dioullé maodo??

    • @souleymanely2551
      @souleymanely2551 4 года назад

      Mouhamed bachir seck kou djoullé serigne touba ?

    • @mouhamedbachirseck3400
      @mouhamedbachirseck3400 4 года назад

      Souleymane ly ah franchement parler khamou mako legui oie kou dioullé maodo?

    • @papendiaye6541
      @papendiaye6541 4 года назад

      Gni da nouy doul rk

  • @mortallambaye2228
    @mortallambaye2228 4 года назад

    Serigne Touba dousén moromou bay

  • @mamadoudiokhane8488
    @mamadoudiokhane8488 4 года назад +3

    Faîte tres attention gnii ben objectif rek lagn am mooy jema rothij pass passou mourid yi donțé ben lassi
    Donc nagn gueuna japp tei xamni saytané daa am ay seuth si nite ngni

  • @daoudagueye8564
    @daoudagueye8564 4 года назад +6

    Sou fekké moko wakh serigne bi daa nelaw

  • @fallouleye895
    @fallouleye895 4 года назад +2

    Santé s.touba rék ba fatou

  • @aboridial3606
    @aboridial3606 4 года назад

    dangé ni sonal séne bopou rek serigne touba yalla defna limouy def thi mom ba pare serigne touba monou mom mom séni baye khana war ngéna togui mo geune thi yeun

  • @profcoly6085
    @profcoly6085 4 года назад +1

    Dieureudieufé sérigne touba boolén beugué ay tontou wanéléne séne bop mo geune nitt déy niémé daradiati fi léyli wanakhari sérigne bi kéndouko diangal diné senégal diné boufi nék nékoul si arabe yi je vie dans les pays du Magreb akassa ignane bakhoul

  • @pascallaminembaye9881
    @pascallaminembaye9881 3 года назад

    Mon Dieu!! J'ai peur pour mon pays et surtout pour mon peuple qui sombre dans l'obscurantisme catastrophique...'a gnou yallah yeureme.

  • @عبداللهصو-ح9ز
    @عبداللهصو-ح9ز 4 года назад +2

    قد طال ليل الكفر لكنني أرى
    من خلفه شمس العقيدة تسطع
    الصبر الصبر ياأهل الحق

  • @serignebambakane8932
    @serignebambakane8932 4 года назад +2

    Machallah amené solou

  • @Diomayemoysonko3
    @Diomayemoysonko3 4 года назад +4

    Yereum na sama bop way walahi yereum na tarikha yi tamit ndeysan

  • @falloudiagne3156
    @falloudiagne3156 4 года назад +4

    Wa lègui yèna nèk si deugue mais geumou nioulèn serigne touba laniou geum ngir yalla Bayi lèn niou ak mom sèttttttt

    • @Mamadou-Fall
      @Mamadou-Fall 4 года назад

      il paraît que serigne touba était un tijane
      Es ce que vrai ????????

    • @freemind3009
      @freemind3009 4 года назад +2

      Yawtamit bayil di setane sounou aye audios. Boul clicker ignore gnou. File gnou ngiye noyyi dougnou dagne di dadji bidah.

    • @falloudiagne3156
      @falloudiagne3156 4 года назад

      Bilahi walahi dangèn di yok sama geum si serigne touba

    • @Mamadou-Fall
      @Mamadou-Fall 4 года назад +3

      fallou diagne ... iblis bi ko souniou borom reubbee , thi laa gueunn weeddi souniou borom baa di ko wakh MAYY MAA MA DOUNNDOU BAA AKHIROU ZAMAANE , SAA DJAMM YII DII NAALENN REERALL
      Donc yaw soyy guiss ayy djoummtee nitt tèè nangouwouloo toopp deugg , dou djakhal kenneu

    • @falloudiagne3156
      @falloudiagne3156 4 года назад +1

      @@Mamadou-Fall batay bakhna serigne touba yalla rèk lako topè mousoul wakh si nit Lou niaw tè yèn mom dieuw ak fèn ak soss moy sèn for geumou lèn Dara yalla Dafa mour sèn beuti ti khol motakh dou ngèn guiss nit ba am si mom ndiort bou fèt

  • @Bourne-abd
    @Bourne-abd 4 года назад +3

    Ma sha Allah wakh dji leerna yangui niouy yé daniou don nelaw ndékété lima guis dal ay wakhi tapaléla won alkhouran ak souna mo wore

  • @koddoufonseca5399
    @koddoufonseca5399 4 года назад +1

    Yéna ngui togne Mame Serigne touba dée ayy wayy...

    • @papeoumarndiaye6252
      @papeoumarndiaye6252 4 года назад

      Kodou Fonseca Serigne Touba kou ko TOGNE. Torokh.. bilahi..SERIGNE BI MOME TJA KANAM REK

  • @noreynisantati5721
    @noreynisantati5721 4 года назад +1

    Sèni toujours dafay melni yalla dafa am loumou mane ak loumou manoul yalla moy khol kouko nèkh def thi mom louko nekh s.touba amoul morom

  • @senegalinfo991
    @senegalinfo991 4 года назад +2

    Thieuy serigne touba amoul morom billahi

  • @ansoudiatta6746
    @ansoudiatta6746 4 года назад

    Gniy wakhal Serigne touba lagnou wara khol gniye wakh ndakh khaliss gno eupe fopp gniye wakh ndakh yalla (mais fenn gué barriiîi)

  • @senegalinfo991
    @senegalinfo991 4 года назад +3

    Dieureu diafaty serigne touba

  • @alhamdoundiaye5882
    @alhamdoundiaye5882 4 года назад

    Waaw yiw miy doul naane mouride danioo diapp ni s touba dou nitt.
    Mane mii loolou laalay deugeul
    Dou nittou ordinaire
    Dieureudieufé cheixoul xadim

  • @TheBadaseck
    @TheBadaseck 4 года назад +8

    Macha Allah! Dieureudieuf Alkhourane ak sounnah.

  • @wakhtaanediamono5329
    @wakhtaanediamono5329 4 года назад

    Sant YALLA yalna YALLA yokonou kattanou topou l'islam serigne TOUBA diaurediauf

  • @mortadaniass7932
    @mortadaniass7932 4 года назад

    Diara dieuff serigne touba 🧡🧡🧡

  • @diallomoustapha9010
    @diallomoustapha9010 4 года назад +1

    Manne ma guénne ba sétte weccc thi yonnou mouride

    • @gayeameth5407
      @gayeameth5407 4 года назад

      Meune ngasi bania guene prsk kika sos lou bax rk ladone def dafa ame niou rere kasse

    • @diallomoustapha9010
      @diallomoustapha9010 4 года назад

      @@gayeameth5407 mais kholalll rekkk

  • @cheikhsarr3363
    @cheikhsarr3363 4 года назад

    Feikholéine dé danguénna réére té xamolénko. Dieureudieufé serigne touba

  • @amethfall9079
    @amethfall9079 4 года назад +2

    Dieurideuffati s touba point 💓💓💓💓💪💪💪

    • @yatouseye4183
      @yatouseye4183 3 года назад

      Mo bayi léne rk dagnu désé kham serigne touba rk khamou gnu serigne bi limou geun di yag mouy geuneu yeukeutiku rk

  • @ndiayemansour1586
    @ndiayemansour1586 4 года назад +4

    Wadji mom gouné leu gou ame diotou wéranté rek. So magué dinga ko bayi. Nekkal si diame. Gnoune ño gui liguey.

  • @papediop6960
    @papediop6960 4 года назад

    Ndayesan nopa lou lén kén daléna léral lo woul mono wAx badoun ngeum s touba ak kan ✊

  • @mouhamadka2808
    @mouhamadka2808 4 года назад +4

    Waw kone d'accord défa djoum koudoul djoume amoul dieureudieufé serigne touba

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад

      Yalla sakh dinane masa wakh dafa dioum ♥ délén déglou rék♥

  • @abdoukhadir2202
    @abdoukhadir2202 4 года назад +1

    Moh yaw khamo tousss. Sangoub ga ñiou bakh Ñgi Moy seriñge touba

  • @omarhashir9507
    @omarhashir9507 4 года назад +3

    Mashallah ya cheikhouna !

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад

      Légi alpha ba moy serigne bi 😂😂 wayé chékh ahmadou bamba dou serigne 😂😂😂 lolou khoromouna lol way 😂😂 ndakh dosi bayi khél yaw sama mbokk🙏🙏🙏🙏🙏

    • @omarhashir9507
      @omarhashir9507 4 года назад

      @@khalilndiaye7265 cheikh Alfa mooniou amale ndiarigne si diné dji. Sa serigne aye mbindames wouténa al li Mohamed ibn Abdallah psl diangalé. Wakhma bènne masala bouniou meunne diangue si serigne bi? Nioune koumiou diangale souniou diné mooniou sokhale pas kouniouye rérale si aye mbinde you amoule firndé si alkhouran ak souna. Asalamualeyk

    • @khalilndiaye7265
      @khalilndiaye7265 4 года назад

      @@omarhashir9507 allahou akbar kon yaw fofou nga tollou 😂😁 béne masala bou serigne toubaa léral si diiné😂😂😂😁 bétouma nak ndakh yén lingén rééré mo bari 😂😂😂😂😂 li serigne touba binde si fiqe yép ngay ladie li oooow 😰😰😰 dieule téré ♥al akhdariyou ♥ nga xam né pour tambali rék la wayé serigne touba woynako bamou diékh ndakh danko wésarone♥😂😂😂 yénén yi mom doumako toudde com yaw finga tollou 😂 ay way 😂 khana sa serigne alpha ba mola wakh serigne touba bimdoul si fiqe😂😂😂 thiey nila manone démé nak dangéna khamoul dara thi serigne toubaa mo takh ngén diko yékk louné😂😂😂 ndaysane

    • @MrAlfred1704
      @MrAlfred1704 4 года назад

      @@khalilndiaye7265 le problème c'est pas serigne touba ndakh defna ligueye bou am solo thi diné islam. Wakhdji moy serigne touba minguéne beug def yalla diko askanalé loumou menoul. Boudone tarikha yi nek Sénégal yeup nio bok béne woté cone wouté you beuri nek thi diné islamou Sénégal dou am

    • @omarhashir9507
      @omarhashir9507 4 года назад

      @@khalilndiaye7265 ndakh gni diangue si université wala yènéne dara islamique yi mrunnaniou dèllou si moome si fikh wala hadith, wala Tafsir...? Yakaarna kou binde moome mo yorè rouwou diamyi ak malayi si diamonoome warna wannè khamkham ak liguéye bi takh yallah mayko loumou mayoule Mohamed ibn Abdallah psl aki sahabame, té mayouko bènne si yonentayi. Di khaar sa tontou.

  • @remah2462
    @remah2462 4 года назад +3

    😱😱😱😥😥😢😭😭😭😭😭😭 hummmm Astaghfirulah qu'Allah nous pardonne

  • @modouawaballaseck9484
    @modouawaballaseck9484 4 года назад

    Dagay bagn serigne touba ba moudié dieul sa temps yeup diokhat ko serigne touba

  • @ElTIO_Galass
    @ElTIO_Galass 4 года назад

    Kham nga torokh Mom wesou woul di wedi wakhou Serigne touba yi mom ak torokh wessou wouko limou wakh wakh nako ba Paré Simamoul wara ladalahi fi hasri Serigne touba momom Gnepp serigne Moussa ka nena kou khamoul Zahire ba mane soula khibar batine ba Oubi Len sen kholl yi dougal thi serigne touba Mon geun nek Fi di wakh ba torokh imbecil

  • @mapendandiaye2202
    @mapendandiaye2202 4 года назад +5

    Wax deugue bague na la trop ndax ci sounna lay dox mais diangu lé taxou la diougu

  • @sidindawfall1740
    @sidindawfall1740 4 года назад +5

    Machallah S TOUBA AMOUL morom 🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @marseck2909
    @marseck2909 4 года назад +1

    Féneu gua dé cheikh marouba gueye diouléwou mame aladj malick mame mor khoudia sy moko dioulé bayilén togn ak féne

  • @th-vc4xj
    @th-vc4xj 3 года назад

    🕋🕋🕋🕋 ka ba nga touba touba garabla bo neckeu biire al diana yallah xamnani touba garabla bo néckeu al diana baylen ko do sen moromo seringe