Kou sole ap narou mauritanie alkhouran meuna lou raw diouli si guedj .te serigne touba sole na alkhouran ap nar bou feroul idji.bayilen di weddy ap waliw ;lolou serigne touba defouko wone sakh mouy karama wala battine
@@Diara757allez vous faire foutre dakoléne fi diamou yalla kéne, sén mami ay toubéne laniou wone, souniou mame you bakh yi niofi indi diné Islam ba paré diambarlo ak toubab yiii
@@mounzombaye1115 walahi amoul ci archive yi .tè archive yi sou lépeu guéné ngén ame gathia amna niouy faye aye million pour mou bania guèneu.nieupafi takhawone tè serigne touba bén photo la ame guisguèn aye photo yènèn mogui nieuw
Khoolal ni nga toolou ak fi nga diaar ba gneuw aadouna ak sa yaye bimou lay diour gnaata minute la def Soo ko khamé rek khameni lep meunn naa nek. Jeureujeufeuti serigne touba
Le mouridisme c'est la religion du Baol et du cayor . Personne n'a jamais prié dans la mer ni sur la mer . L'islam n'a rien à voir avec tout ça . Serigne bahoul chirk rék lagne lay diangual AK Lou Bone .
serigne touba limou deff si islam sén téméri maam mounouko deff-téé nguéné wax ay baax baaxou sounna mou njeurigne si nieup-mandou lénn-kounekk li nga deff ngay fayyikou al akhira
@@diallomohamadou5611 non je ne le compare pas, le Prophète est la meilleure créature mais Serigne Touba est un saint et véridique donc tout ce qu’il dit je le crois. En plus je ne suis pas mouride mais j’aime ce saint. Il s’est lutté pendant que vos grands pères étaient sous leurs coins. Il faut dire la vérité telle qu’elle est mon ami
😂😂😂😂😂😂 khana danga meusseu dougou biir baméle déloussi😮? Li Yalla wakh ci Alkhour'an rékk moy deugg piir liy khéw yawmal khiyaam. Serigne touba Yalla moussou ko toudou fénn ci tééré yi wathie. Konn kokou foumou todj
''Lakoum dini koum waliya dini'' Yën nak mandou wolën ndah Lifi borom Touba dëf moy lifi nék tay AK euleuk'' Gör DEUG moy and ak kou Tédd ki. Done Ab mouride nak meusoul yomb, Kone sën wakh ji meunou gno jiakhal si yénn. Serigne bamba amoul morom.
Pourquoi tu ne contesterai pas le voyage nocturne du Prophète Mohammed et tous les évènements mystiques relatés dans le Coran et les autres livres révélés ?
oui mais meme si tout ce que tu dit est vrai ..mais cela n'enleve rien au travail de cheikh ahmadou bamba..si on lit ses khadiss on verra quil travaillait pour lislam on sen fou si c des tonnes ou grammes cela n'est pas important
Loléne kheuy diamou gontoko versé si ndaboul yanén diamou yalla yinguéne di togn aka wéddi continué comme ça wakh rékk défalouléne dara sunu borom séne bopp sakh lay wakh sunu borom mom faléwoul kouko défal ak kouko niaka défal mom niaram la yor moy aldiana ak Sawara bousi nékk kénna kounék say dieuf mola fay dougal wassalaam
Mane xawma louye sén problème geumo Serigne touba mais topale liga tope té bayi ko... Gnoune yén touti ngéne si takalégnou ak sounou kilifa yi légui lolou loussi sén yone
Kou sole ap narou mauritanie alkhouran meuna lou raw diouli si guedj .te serigne touba sole na alkhouran ap nar bou feroul idji.bayilen di weddy ap waliw ;lolou serigne touba defouko wone sakh mouy karama wala battine
Serigne touba dafa ligéy lou reuy kouko geum lalal s'aime
Très sage décision dem nga ba reconnaitre erreurs yi yana la yalla djiegeul djegueul niou nioun ngnep❤
Ndeyssaane yeen sonnou ngeen si adouna
Maa yeureum kou bagn serign touba ak yoonam Wi
Dieureudieuf Ahmadou borom jaam yi
Moom kepp laniou beugg dh
Yalna yalla yereum diam yi té kharéniou aldiana 😢
Dieureudieufé Serigne Touba ❤❤❤❤ dingéne. Sonou dé
Les livres sacrés viennent de Dieux. On ne doit pas les comparer avec les écrits d'un être humain.
Tu as vu dieu donner ces livres à quiconque?? En dehors de celui qui vous a dit que ces livres venaient de dieu, qui d'autre en était témoin??
Évites de dire ou d'écrire dieux,IL N'Y A QU'UN SEUL DIEU :ALLAH SWT
Fene diotna mou diekh
🙏🏽
Bi nga ko waxè la fène tambali😢
Dieuredieufty Serigne Touba khadimou Rassoulillah❤❤❤❤❤❤❤
Tu me fais rire 😂😂😂 vraiment
Serigne Touba rek ❤❤❤
Dieureudieuf Ahmadou Bamba
Wa waw yaram 😂😂
Machallah li nga wakh lou leerla
Serigne Touba loumoudéfe Daka binde cou geumoule yaham merci waye
Serigne touba kouka bagne déh kou begue Serigne touba lalal j'aime ki ken warouko gueme ❤❤❤❤
Alhamdoulilah machalah
Seringe touba ken bangiouko niekoy fenal nioko bange bayilen the thiakhan te diamou Yallah selal
@@Diara757allez vous faire foutre dakoléne fi diamou yalla kéne, sén mami ay toubéne laniou wone, souniou mame you bakh yi niofi indi diné Islam ba paré diambarlo ak toubab yiii
Le mouridisme est plein de balivernes de ce genre, c'est rempli de mythes et légendes on se croirait dans la Grèce antique😂😂😂
Salam dieuredieuf Cheikhoul khadim Dieuredieufeti serigne Touba dieuredieuf Serigne Touba Dieuredieuf Serigne Touba
S touba amoul morome
😂😂😂 Kiko ray nakk??
S k amna moroom😊
Diaradieuf Serigne Touba
Nite gnou bari ci gnoom dégno sissou. Souna rêk ❤❤
Diouli ci guèdj gui dofi rirando yi niokoy geum .serigne touba wakhouko fèneu toubab bi bindou ko fèneu.gni togone Sénégal nioko créé rèk
Yaw dagnla wax Sa bay mola diour nga guemko
Sa mame danoul wone diouli da dane diamou kheureum lolou mola méti 😂
Doul ga demal Nantes wala bordeaux archives nationales toubab bi moko bindeu livre de cheikh ahmadou bamba
@@mounzombaye1115 sokhor rek ak bagne Kou yalla faye wayé Serigne Touba rek ken menou thi dara
@@mounzombaye1115 walahi amoul ci archive yi .tè archive yi sou lépeu guéné ngén ame gathia amna niouy faye aye million pour mou bania guèneu.nieupafi takhawone tè serigne touba bén photo la ame guisguèn aye photo yènèn mogui nieuw
Dieureudieufé Serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla nalen yalla guindi ....nanne len ndox...geumolen dara
Yalla rek ak seydina mouhamed c est tout
Baÿi hébaté
Khoudar diangal Na yonenti yalla Moussa....
Té khoudar ab waliou rék la.
Serigne Touba rék, Serigne Touba képp, Serigne Touba Dongue
Celui qui a dit cela et celui qui l'a écrit n'auront plus de paix...la méchanceté ronge avant de tuer... Serigne Touba brillera à JAMAIS...
Dieuredieufè serigne touba rèk
Sa lefeule ndaye
Dieureufé Serigne Touba
Dieuredieuf serigne touba
Borome 33 femme yi
@@becayekounte4091comment 33 femmes
@@becayekounte4091dagay doule
ani 7 tonnes 500 yi ?
@@Plas-vz1sw dagay gnaw gnou dème fi ay bindam nek t bagna top fanatics yi
Serigne Touba rek laniou diokh sounou khôl noumou demé euleuk bakhna wa salam di gén napalou si yonou mouride lou bakh si rew nioko fi def
Tidiane yi gueneu Bone nak Moy gni Di wah ni séne Serigne Moy Yalla .
Gni gnoy ay yéfeur deugue deugue deugue .
Yow mii di wax si tiijan yi sa data ndey sa koyou bay saayo yéwo
Bindoum serigne touba rek wanéna dolém wanéna yoone l'islam
Wallahi ❤
Khoolal ni nga toolou ak fi nga diaar ba gneuw aadouna ak sa yaye bimou lay diour gnaata minute la def Soo ko khamé rek khameni lep meunn naa nek.
Jeureujeufeuti serigne touba
Yalla nala yalla yerem ci daradiay Serigne Touba
Serigne touba rek la niouh gueme way. Komou Nathari del
😢😢😢ndeyssane tarikha dey dof lo nite😂😂😂
Yalna yalla mousal gnou ci bokalé yalla sougnou borom samou alxouran ak sounnah doynagnou soxla wougnou lénén
Yalla rekk mofi nek. Diamou yalla kouko def sa bop rek ngako defal
Sène xole moy diex rek
Serigne touba .
Wallahi 😂
Le mouridisme c'est la religion du Baol et du cayor .
Personne n'a jamais prié dans la mer ni sur la mer .
L'islam n'a rien à voir avec tout ça .
Serigne bahoul chirk rék lagne lay diangual AK Lou Bone .
Sérigne Touba Rék séne mame seytané la wone
Di geuna bouga serigne touba rek merci merci merci
Walay sen kholyi dîna dage ak s touba rek
Serigne Touba rek. Dieredieufe Serigne Touba z
ومن يقلقني في البحر روما لغربتي
فــلي من إلهي روض في كل عيلــم
dierediefeti serigne touba
Amoul morom ❤
Borome touba rek❤
Notre soveur❤🕌🕋
Bounouy doundou,bounouy déé yeup serigne bamba mogniy mom.
Yalla mola mom ish
Kouniou moom mouy moomaté😂😂😂😂
Borom Touba amoul morom ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Nagoulè serigne touba rèk
Wakh léne ci gordjiguéne yi ak franc-maçon yi mo gueune
Lii moy base bi. Dofdoflou gou beurri gui moy encouragé yoyou nonou
Bokale mogeuna garaw yinga wakh yep
Lolou mo guen si gnome
Dieuredieuf sérigne touba diarrama Mame cheikh Ibrahima fall
Waa yén sén khol yi kagn lay nanguoul Sérigne Touba😅😅
2088
Souna rk
Nit gni Di weur lolén Doli ći Yallah, yaw nga weur loo toumal nitou Yallah, thiey man julitou légui yii, est-ce que sakh gueum Nanou deugui Yallah !!
diadieuf Serigne Touba diadieuf cheikh Hamadou khadim mbacke
Kou geum yalla deug doto tall nit gni wala ngay wakh loula léroul
Sa lefeule ndaye
Ah-Domë Dinè🕊️Yagëu'nãfii👉thia'Bôbôô Alkhourãnë👉Wããtiã-gôôll👉Jèbãlôô🕊️môy'Diinèè xõlilènë👉Tãrixôô Snôô Mame Ibrahima👉 hãkii🕊️jããbõtããm🙏 Ismaël Issakha❣️ak👉Yankhonba🕊️😭😭❤️ Machallah❣️
Lan Moy diebalou
serigne touba limou deff si islam sén téméri maam mounouko deff-téé nguéné wax ay baax baaxou sounna mou njeurigne si nieup-mandou lénn-kounekk li nga deff ngay fayyikou al akhira
Dieuredieuf seriegne touba ❤❤❤❤rek
😂😂😂
😂😂😂😂😂😂wakhal lebone 😅sa lep bi nekhna
Serigne Touba Amoul Morome kenneu douko woutal morome
Dieuredieuff seringue touba khadimou raoussulle ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieuredieufety borom touba ❤
Djouli Guédj Gueuh Amna Ndakh YALA Teuléwoule Dara. Bayiléne Di Wéddi, Yonénte Bi Bimou Néh Rañanina, Kéne Gueumoukou Wone Koudoule Ababacar Té Pourtant Lou Amone Leuh. WaLAHI Douma Mouride Wayé Gueum Nako
Svp mon frère fait jamais comparer un prophète et sa serine svp
Raniaan gui Alkhour'aan mooko deugueuL
@@diallomohamadou5611 non je ne le compare pas, le Prophète est la meilleure créature mais Serigne Touba est un saint et véridique donc tout ce qu’il dit je le crois. En plus je ne suis pas mouride mais j’aime ce saint. Il s’est lutté pendant que vos grands pères étaient sous leurs coins. Il faut dire la vérité telle qu’elle est mon ami
@@gueyebamar1253 Djouli guedj gui Serigne Touba Mokko Wakh té Gueum nako
@@deugrek3312 je ne rien contre sa serine mais je crois que allahou Est tous les prophètes de allahou
Serigne touba amoul morom bo dougué biir bamel nga khamni borom touba amoul morom
Wakhofi dara
@@amadoundour4599 yaw yafi wakhoul tous
Bien dit Serigne Touba nena kouko sopè dème aldiana ❤️ likoul lii man bia daha daha naja minka daray dounya wabi awli naja
😂😂😂😂😂😂 khana danga meusseu dougou biir baméle déloussi😮?
Li Yalla wakh ci Alkhour'an rékk moy deugg piir liy khéw yawmal khiyaam.
Serigne touba Yalla moussou ko toudou fénn ci tééré yi wathie. Konn kokou foumou todj
Amoul moroom ba paré di déh adouna di weuyy batay djii. Doyna waar😂
Bokaalé Yalla douko baalé❤
الله ا کنر😅😅😅😅😅
wéde borom Touba alkou rék wallahi
Gniko khamoul,nak😂😂😂
''Lakoum dini koum waliya dini''
Yën nak mandou wolën
ndah Lifi borom Touba dëf
moy lifi nék tay AK euleuk''
Gör DEUG moy and ak kou Tédd ki.
Done Ab mouride nak meusoul yomb, Kone sën wakh ji meunou gno jiakhal si yénn. Serigne bamba amoul morom.
Bou feke Mouride diné bopam la gua wakh ma demal xoll traduction lakoum dina Koum wal Yadine ba parei 👍😂
Xam nga lakoum dinoukoum Wali yalid loumouy teki 😅😅
lou moune ta néck amou yalla moye mayé lou néck kou bagne Serigne Touba doh doug aldjana yaw khamon di wakh dieuredieuf Serigne Touba
Nékal nitt😂
Serigne touba senegal dongou la khéwé amoul fénéén. Djoulit gni ay milliards laniou té khamou niou Serigne touba ndakh kham ko amoul ndjeurign. Yalla yonni wouko ci djoulit gni.
Khél khalaat lay djarign.
Suna thicamam.reek.inchallah
Bayilen guigane makk nie dolen rousse sakh nitte daffa wara am worma thi souniou kilifeu yii wassalam
Gni sen khol yi moy Dokhote depuis 1927 ba leigui 😂😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Dinane ko déwalé déh ndakh mbirmi sa kaw sa kanam rékk ba adiana
Ay deumeu laniou
Doynawar...? Amnasolo machaallah
Ay thiakjan la wayyy
Yalla sakh amna gnouko geumoule serigne Touba rékk
🤫
Serigne touba a prié sur la mer c est de l imagination
Pourquoi tu ne contesterai pas le voyage nocturne du Prophète Mohammed et tous les évènements mystiques relatés dans le Coran et les autres livres révélés ?
Seydina mouhamed mo guene ngieup kene douko conteste
.....relatées dans les livres révélés...
Kham ngani konn wératô😂
Ki a révélé les hassidas ??
oui mais meme si tout ce que tu dit est vrai ..mais cela n'enleve rien au travail de cheikh ahmadou bamba..si on lit ses khadiss on verra quil travaillait pour lislam on sen fou si c des tonnes ou grammes cela n'est pas important
Bayi len gnou gnou geum s touba billahi bou gnou diamei safara beug nan
Machallah. Les jeunes commencent à se réveiller. Ces gens sont des menteurs.
Nous devons avoir Le courage de fouiller certains faits notamment religieux
Ilmoul yakhine aynoul yakhine haqqul yakhine ndakh gueume nga niete yakhine
Dieureudiéfé cheikh ahmadou bamba
Diadieuf serigne touba khadimou rasoul
Loléne kheuy diamou gontoko versé si ndaboul yanén diamou yalla yinguéne di togn aka wéddi continué comme ça wakh rékk défalouléne dara sunu borom séne bopp sakh lay wakh sunu borom mom faléwoul kouko défal ak kouko niaka défal mom niaram la yor moy aldiana ak Sawara bousi nékk kénna kounék say dieuf mola fay dougal wassalaam
Il suffit d'être intelligent pour voir tout ces tarikhas c'est du n'importe quoi sauf l 'islam vraiment.
waw domou mbot bi kannla kouy wah dégu loumouy lakatou teyow lingay wah yép tahoul gem ahmabou beg yallaga nék ci mom lanieko begue topal falé nopil
Nasssa guèlawww wa dji guemeummm li guemm gnou guemmm lougnou guemme
Tu ne peux pas changer nos coeur nous Serigne Touba que nous aimons la puissance le don de dieu es ton miracle
Yalla na gnou beuguel Serigne Touba
No done ay nakh bakhna nione geume naniouko. Yen niéko wédi dara léroulé ni sen baye niolé dioure
mbiir serigne touba dal kén khamalouko dara yalla ak yonéte bii rk.moko yitélon kén mounoula wakh birou serigne bi manou rk
Wallahi
Diouli si guedj yomb na ya Allah.
Bo deme Inde sakh di nga guiss kou diouli si guedj gui!
😂
Wakho fi touss,
Li DH day yok sounouk geum beugue Serigne Touba ak Islam dji
Ya meuna féne, diouli guedj gui Toubab yi sén Boppeu nioka wakh sédéko
Yaa meuna féne
@aboubacardiop8804 😂
@@aboubacardiop8804 yama dakh féne domou cheytané ibliss
@@aboubacardiop8804 yama dakh féne seutou toubéne bi seutou kheureum kate bi
Yow khana danga dof yalnagou yalla moussal si yow
Sant Serigne Touba bou wer
Joulina si Guedj gui jouliwoul si Guedj gui on s en fout Serigne Touba laniouy top
Téé guéne top YALLAH
Qui domerame leu so beugué beuss Gua lijenti ca baye domerame
Serigne Touba rék ba adůna di toukki inchalla barki borom Touba
Serigne Touba rek,Serigne Touba dong Serigne Touba amoul morom du massi ken douken te ken domom
Borom Touba dieureudieuf ❤❤❤❤❤❤
Leral yi amna solo macha allah
Yéne sokhor dh
Daye fine
Foukou serign bi binde .gana messere ak gni melni niom hahahaaaa
Sou gueen fekhe ba doun geum s touba ma khamni jambar gueen نحب نحب الشيخ هو الله
Mane xawma louye sén problème geumo Serigne touba mais topale liga tope té bayi ko... Gnoune yén touti ngéne si takalégnou ak sounou kilifa yi légui lolou loussi sén yone
Wa niome khana Sr Touba rek laniou diang pr khas ko ?
Nopalou léne way Ahmadou laniou gueum ba kérok
Est-ce que Il a une fois exister même ? c'est ça la question