Ndeysane hommage bou rafét bi Abdou Aziz mbaye déf si Béné sopém bou décédé sokhna aissatou Kane

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 15 янв 2025

Комментарии • 95

  • @boussoniasse9214
    @boussoniasse9214 4 года назад +3

    Ndeysane, Yallah na bour Yallah diéguel ko kharé ko aldiana firdaws. Masha Yallah li rafetna, sunu Papa Abdou Aziz Mbaye Yallah na bour Yallah may la goude fan ak wér ak soutoura barké Seydina Cheikh Ahmed Tidjiane ❤❤❤

  • @cheikhbaal8867
    @cheikhbaal8867 4 года назад +3

    Yalna yalla défal diegal ak yeuremendé ji barké cheikhou tidiane

  • @sammbaye4419
    @sammbaye4419 4 года назад +3

    Yalna Yalla défalko ndiégeulak yeurmandé thi daradiay Seuyidouna Mouhamat Sallalahou Aleyhi Wassalam ak bep dioulit boumfafék akboukofafék Allahouma amin

  • @ndackdiop4029
    @ndackdiop4029 4 года назад +9

    Machaalah li rafetna lolou yalna yala yessal yeuramndé thi mom té mou déglo ko thia aldiana firdawsi thi barké sopem ba Cheikhal Khalifa (RTA) Abdou Aziz yalna goudal fanane té weeral bate bi thi barkè seydina Mouhamed(PSL)🙏❤

  • @adjandoye4742
    @adjandoye4742 3 года назад +2

    Machallah Yalla Naa Khiipé Balsakoutou Seydina Mouhamed Saw Cii Barké Seydina Mouhamed Saw Amiine

  • @khadijalo6067
    @khadijalo6067 4 года назад +4

    Ndeysan yalnako yallah yeureume té kharéko aldiana amine

  • @binetoudiakhate6759
    @binetoudiakhate6759 4 года назад +4

    Macha allah ,yalla yow mi mome aldianaye firdawsi yalla nangua kofa diokh thi chateau yi gueneu mak mou dinde ak seydouna Mouhamet PSL amine yarabi Habib yalla na yalla fayela te' yagal koleregui

  • @fayenjie1355
    @fayenjie1355 4 года назад +6

    Ndeysann machallah sokhna aissatou kane yalla nako yalla kharee aldiana firdawsi 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

  • @diagne7713
    @diagne7713 3 года назад +4

    Machalla yallah nako yallah yeurem

  • @malickdiedhiou5874
    @malickdiedhiou5874 4 года назад +9

    Machallah lii rafetna trop habib dieureudieuf ti tahaway bi pape abdou aziz mbaye bilahi mo bakh té oyof yalna yalla fayko yiw bidiahi taha🙏
    Yalna yalla nangou leup té yeureum adji dem dji amin

  • @dabasamb2207
    @dabasamb2207 4 года назад +5

    Papa abdou aziz mbaye yalla nako yalla faye

  • @morseye5278
    @morseye5278 4 года назад +4

    Yalla nako yalla diotalé yolou niane gui 🙏niam fay féki ak niako fay féki si barké yonenté bi (psl)🙏

  • @elementdabakh6394
    @elementdabakh6394 4 года назад +8

    Yalna yiiw bi yeup fékeu ko fomou nék yalna ko yalla yeureum té hariko aldiana

  • @maimounandoye5385
    @maimounandoye5385 4 года назад +3

    Beugue dafa fort khaléla wone ame témoignage bou raffete Adouna yep diné kalé Make royelen si mome
    Mou diarale kilifa Elhadji Abdoul Aziz Mbaye déplacé Li raffetena Takhawaye bi Make yi contane naniou yalla naye yiiw si yaw Amiine

  • @ndiagadiba5588
    @ndiagadiba5588 4 года назад +8

    Yalna yalla yeureume khareko aldiana ak mbolemou dioulite te yagalfi sounou sopebii

  • @ndeyematydieng8180
    @ndeyematydieng8180 4 года назад +8

    Ndeysaan yalla nako yalla yeureum xaré aldjana 🙏🏾

  • @hamaththiamattidiani1970
    @hamaththiamattidiani1970 4 года назад +3

    Papa goudel fan rek in challah

  • @fayenjie1355
    @fayenjie1355 4 года назад +8

    Serigne habib yalla nalaa yalla deff makk waa team goudii Aldiouma yalla naa sunu diam yagg🤗🤗🤲🤲🤲🤲🤲

  • @khoudiagaye3263
    @khoudiagaye3263 4 года назад +8

    Machalah yalnako yalla yeureum t3 diegeula ci barkep guen gui miine deff allouwouma amine

  • @biranekouta8489
    @biranekouta8489 4 года назад +6

    yalna sunu borom yerem sokhna si tei diégal ko

  • @marianendiayeguellwarre7919
    @marianendiayeguellwarre7919 4 года назад +7

    Habib yalla na yalla fayy yiww yalla na yalla yeureume kharéko alldjiana 😢😢

  • @abdoudiallo2703
    @abdoudiallo2703 4 года назад +3

    Yallah na Yallah kharéko Aldiana firdawsi si barkhé Sallalahou aleyhi wassalam Amine

  • @papeniangxaragnelo9110
    @papeniangxaragnelo9110 4 года назад +6

    Ma cha alla sokhna aïssatou kane yal na yalla yeissal yeurmandem thy kawam tabal ko aladiana firdaw sy amineee ya rabii

  • @rokhayadiaw9732
    @rokhayadiaw9732 4 года назад +7

    Yalnako yalla yeureum tei kharéko aldiana

  • @papemalickdiop1717
    @papemalickdiop1717 4 года назад +7

    Yalnako yalla yeureum té kharéko aldiana firdawsi

  • @gueyecheikh4280
    @gueyecheikh4280 4 года назад +9

    Machahalla serigne abdou aziz mbaye dieuradieuf abbiba TV , Yalla na bour Yalla khare aldiana firdawsi sokhna si Kane ci barke seydina mouhamed psl ak Mbolemi diolit

  • @bamsbams5164
    @bamsbams5164 4 года назад +14

    Ndeysane Li nékh'na geuneu adouna nioulay tagal Yonentebi yalla bô rouss yalna la seydina mouhamed psl térou si barki alhourhane 😭😭

  • @beyedaba
    @beyedaba 4 года назад +9

    Yalna buur yallah yeureumko diegalko tabalko aldiana bijahi naby Moustapha aleihi salatu wa salam

  • @mohammednazirtoure5674
    @mohammednazirtoure5674 4 года назад +3

    Salam aleykoum wa rahmatoullah wa barakatouh barak Allah

  • @diagnebayern
    @diagnebayern 2 года назад +3

    Que Dieu l’accueille dans son Firdawsi 🙏🏾
    Que la paix soit sur toi ya Aïssatou ma sœur bien aimée !

  • @nenesakho4472
    @nenesakho4472 4 года назад +5

    Yala naka yala yereum kharé ka aldiana chaalhaa

  • @aissatoudiallo2839
    @aissatoudiallo2839 4 года назад +5

    Mashalah yala n'a yala nangou niane bijahi Nabil Moustapha sws

  • @sarrndao3394
    @sarrndao3394 4 года назад +3

    Machallah yalnasa Diam yage

  • @assiatoutalibeserignmousta6364
    @assiatoutalibeserignmousta6364 4 года назад +9

    Machalah yala nako yalla yeureum

  • @idrissandoye6550
    @idrissandoye6550 4 года назад +8

    Yalna co yalla yeureum khareco aldiana si barke seydina mohamed aleyhiwasalam...

  • @Siesy1290
    @Siesy1290 4 года назад +5

    Ndeyesaan dawna yaram rafetena Abdoul Aziz allah nga goudou fane fou ande ak werr. Aïssatou yallah ne le seetane sa aldiana Amiine

  • @fayenjie1355
    @fayenjie1355 4 года назад +8

    Le général kenn dou mom yalla na yalla goudeul sey faann 🥰🥰🥰🥰

  • @oumoudiagne70
    @oumoudiagne70 4 года назад +3

    Oh c beau ma sha allah habib

  • @mouhamadoundiaye7846
    @mouhamadoundiaye7846 4 года назад +5

    Yalla naka sama toureundo YA RASSOULILAHI térrou

  • @salydiouf2193
    @salydiouf2193 4 года назад +15

    Ndeysane sokhna Aïssatou Kane Ya Allah sougnou Borom kharéko aldjana si barké Mouhamed SAW barké Cheikh Ahmad Tidjane RTA barké Seydi Hadji Malick SY RTA. Amine

  • @basiroudiop3671
    @basiroudiop3671 4 года назад +6

    ماشاءالله بارك الله فيكم جميعا يا اخي

  • @abdoulayeniang2511
    @abdoulayeniang2511 4 года назад +7

    Beug gnou mélni rk mo ame solo walahi amoul Réthiou waye Dawlou bi Yalla na Yalla Yéssale si mome Yeurmeundé❤🙏

  • @maimounaboiro8875
    @maimounaboiro8875 4 года назад +15

    NDEYSANE yalla n'a ko YALLA YEREM thi barke seydina Mohamed PSL

  • @almansourdiakhate637
    @almansourdiakhate637 4 года назад +2

    Macha allah yalla na KO yalla yeureum khare KO aldjiana

  • @moustaphaba1491
    @moustaphaba1491 4 года назад +14

    Yalna buur bi dolli djeigal ak yermandé si sokhnasi tei yaggal fi Mawlaya Abdou Azziz Mbaye bijahi naby saws❤️❤️❤️

  • @maremendiaye6638
    @maremendiaye6638 4 года назад +9

    Machallah Abdou Aziz Mbaye yalla na yalla goudeul sa fane Sokhna Aissatou yalla na buur bii doli dijegeul ak yeurmandém si barker saws🤲🤲

  • @aminatafaye6003
    @aminatafaye6003 4 года назад +2

    Yalla nako yalla yeureume té kharéko aldianatoul firdawsi

  • @mbayefall3630
    @mbayefall3630 4 года назад +3

    Yalla nako yalla yeuram té diégal ko

  • @AmynaNabySarr-bouDabakh
    @AmynaNabySarr-bouDabakh 4 года назад +9

    Ndeyesane amena solo.Sokhena Aissatou Kane Yalla nako Yalla yeureume té diégalko 🙏

  • @الراجيرحمةربه-ث5م
    @الراجيرحمةربه-ث5م 4 года назад +4

    رحمة اللّه عليها وغفر لها

  • @dembasognane1336
    @dembasognane1336 4 года назад +8

    Ndayesane yana ko yalla téro ko aldiana sopouna kou diara sopou

  • @cherifvipkouta1076
    @cherifvipkouta1076 4 года назад +3

    اطال الله عمركم

  • @fatoumatakane3816
    @fatoumatakane3816 4 года назад +3

    Yalna yalla yessal yeurmandé ak ndiégual ci mom yalla yégué ka barsakou seydouna Mouhamed mak niou bax gni terou ka 🙏🏽❤️

  • @amadoutidianesall617
    @amadoutidianesall617 4 года назад +3

    YALLAH nako YALLAH yereum

  • @amyfaye4134
    @amyfaye4134 4 года назад +3

    Inna lillahi wa inna ilayhi rajiun Sokhna Aisstou Kane Yalla na souf sede ci kawam ameen!

  • @modousarr9637
    @modousarr9637 4 года назад +3

    Yalla nako yala yeurem

  • @ndeyeamiwillane5783
    @ndeyeamiwillane5783 4 года назад +3

    Masha Allah

  • @binetoudiakhate6759
    @binetoudiakhate6759 4 года назад +2

    Abdoul Aziz Mbaye yalla nala sounou borom feye nianes yi ngua nianal sokhna Aissatou yalla nako yalla nangou te mou bocouko ak mbolomou dioulite same ngua kolere yalla nala yalla feye ngua yague fi lool te wer ande ak diam ak soutoura ak yiwou adouna ak alakhira dieuredieuf ma cha alla

  • @AbdouAzizNdiayeTv
    @AbdouAzizNdiayeTv 4 года назад +7

    Amine

  • @binetourassoultds2243
    @binetourassoultds2243 4 года назад +12

    ZIAR HO MASHA'ALLAH. QUE LA TERRE SOIT LÉGÈRE SUR AÏSSATOU ET QUE PARADIS SOIT SA DEMEURE💕🕋💕🤲🤲🤲. HABIB, ABDOU AZIZ YALLA NA LÉN YALLA FAY 🤲🤲🤲😢

  • @moussambaye9681
    @moussambaye9681 4 года назад +3

    Yalna khippé Al Diana firdawsii

  • @mariamadiop6244
    @mariamadiop6244 4 года назад +3

    Machalah paix a son ame

  • @ahmedisackane6705
    @ahmedisackane6705 4 года назад +12

    Yalna ko yalla yeureum té yékhé gnou bijahi khayril bariya s.a.w

  • @laverite4215
    @laverite4215 4 года назад +3

    Papa machalla

  • @mansourseye6506
    @mansourseye6506 4 года назад +3

    Macha allah qu allah le tout puissant lui accord le pardon ...bilay mbaye rafete nekhna

  • @dioufabdou9590
    @dioufabdou9590 4 года назад +6

    Thiéy sama wadji billahi mala sope tá yalla rek takh abdou Aziz Mbaye

  • @daoudambow8348
    @daoudambow8348 4 года назад +3

    Machallah 🙏🏿

  • @ousmanesarrtaekwondo5665
    @ousmanesarrtaekwondo5665 4 года назад +3

    Machalla 😭 Bilahii bari nasi morom ❤️❤️❤️❤️✅

  • @daoudaanneat-tidiany
    @daoudaanneat-tidiany 4 года назад +2

    Ndeysane Yalna Souf Sëdd Kawam mom ak bolém weiydawlou yi Inchallah

  • @dadindione3601
    @dadindione3601 4 года назад +5

    Thiofel dafa fort dafa sacré. Motax soy beug beug gni diara beug li rk missal pour nioune nieup

  • @abdoulayesall5593
    @abdoulayesall5593 4 года назад +4

    Waw kay

  • @babacardiop2218
    @babacardiop2218 4 года назад +2

    الّله‍مّ اغفر له‍ا وارحمه‍ا ووسع قبره‍ا وادخله‍ا جنّة الفردوس

  • @masseckmbengue8323
    @masseckmbengue8323 4 года назад +4

    Yalna yalla samla

  • @mouhamadmoukhtarcisse5062
    @mouhamadmoukhtarcisse5062 4 года назад +5

    Amine wayy ohhh

  • @mouhamadouniang1516
    @mouhamadouniang1516 4 года назад +5

    Masaallah

  • @babacarndom8308
    @babacarndom8308 4 года назад +5

    Machallah ❤❤❤

  • @abdouazizdiop8746
    @abdouazizdiop8746 4 года назад +7

    رحمة الله عليه

  • @mamadouba614
    @mamadouba614 4 года назад +5

    Wallaye ndeye sane 😭😭 thieye adou na def Lou bakh rek am sollo ak talibe chiekh 😭

  • @alioukebe7616
    @alioukebe7616 4 года назад +3

    Amiine waye

  • @moussandiaye9908
    @moussandiaye9908 4 года назад +2

    Machallah

  • @dabakhndour5085
    @dabakhndour5085 4 года назад +4

    😭😭😭

  • @momolih8897
    @momolih8897 4 года назад +1

    Dama beugue dougou si groupe WhatsApp bi

  • @djamilseye3776
    @djamilseye3776 4 года назад +2

    ki bane assyiatou kane dafa âme bouma kahme té wourma témou deke pikine

  • @yakharandiaye6031
    @yakharandiaye6031 4 года назад +2

    Machala 💜❤❤❤

  • @hdbsdtv4544
    @hdbsdtv4544 3 года назад +2

    Machaallah