Mbokk ma ngi lay jox wàccuwaay bu baax : 1 Loolu nag bu dee ci dégginu Seex Mustafaa joob al kokki day wax ne boole *SIIXA* yépp def ko laazim gënul ndax man na jur aw tangoor wu ëpp. 2 Te jaru ko it ndax mi ngi mel di jàng Alxuraan ci rawaayah yu bokkul ci jenn jamono Bu dee nag danga jël lu mel ne *Xaatim* bi def ko muy sa laazim (farata) waaye nga boole ci bo amee jot di barkeelu ci yeneen leeg-leeg dara nekku ci jërëjëf 🙏🙏
Seurigne bi dieuleulna wird tidjane donc silsila bi ala kouli hal dafay diaar ci seurigne bi ko diokh wird. Silsila dafa bari ay façon. Khamoulene tassawouf. Lolou molene sonal.
ماشاء الله جزاكم الله خيرا ورعاكم ❤
Macha allah dieudieuf Serigne Moustapha
Dieureudieuf waw léene goor
Serigne Moustapha Diop Al Kokiyu Yalla nafi yagu loolll ta anddd ak weer barkép Serigne BI
Mashallah. Man damay geuna sopp Segn Moustapha
Ndayssane diambari serigne touba dhi
Mane dieulnako sama Serigne waye rousnako ladj ndakh âme nga ndigualou diokhe
Mustafaa Ngom do koko Yeesal yaw mi ci ame ndigël ci Séex Mustafaa
Khanaa wakhko: Serigne bi mandé wird wi Dafa am ay mbokk youmay laathie ma bëggoon kham silsila bi ba bou banène yooné Manan lèna Tontu
Gueneu yagg Gueneu werr ❤
Maasàllaa amna solo lool lool
Machallah amna solo dh
ماشاء الله
❤️❤️🙏🏿
❤❤❤
Cey tawhid
Ab laaj: sañ nañu jële 3 Siiha yëpp diko wird
Mbokk ma ngi lay jox wàccuwaay bu baax :
1 Loolu nag bu dee ci dégginu Seex Mustafaa joob al kokki day wax ne boole *SIIXA* yépp def ko laazim gënul ndax man na jur aw tangoor wu ëpp.
2 Te jaru ko it ndax mi ngi mel di jàng Alxuraan ci rawaayah yu bokkul ci jenn jamono
Bu dee nag danga jël lu mel ne *Xaatim* bi def ko muy sa laazim (farata) waaye nga boole ci bo amee jot di barkeelu ci yeneen leeg-leeg dara nekku ci jërëjëf 🙏🙏
Déedeet yamal si bénn rk
Salam mbokk mi numéro s Moustapha diop mi sokhla nako loll
Wa aleykoum salam
Jokkol ak :
S Modou Diop +39 380 183 1926
S Moustapha Ngom +1 646 644 4933
Seurigne bi dieuleulna wird tidjane donc silsila bi ala kouli hal dafay diaar ci seurigne bi ko diokh wird. Silsila dafa bari ay façon. Khamoulene tassawouf. Lolou molene sonal.
❤❤❤