Débat houleux entre Père Mbaye Ngone Fall et Maman Aicha: "Yaw Wakho Deugg Xamoma..."
HTML-код
- Опубликовано: 23 ноя 2024
- #kebetu #team221 #senegal
page facebbok : / senegal7officiel
Abonnez-vous pour plus de vidéos et n'oubliez pas d'activer la cloche de notification
Père kham nga lan motakh nékho la jeunesse parceque liniouy déff rkk nga léni wakh. Fi méti rkk si société bi nga roukh lolou motakh mou léni méti
Pourtant pére limouy wax c'est vrai amna mère yo khamni nioy dirigé si keur et c'est elle qui a le dernier mots
Pabi d" moy khoromou émission bi sachez leu
J'aime prosper....il symbolise le charme de l'emission. Intelligent, correct, ouvert et discipliné. Comme tous les autres d'ailleurs. Mention spéciale à père et sophie l'exceptionnelle. Safia tu déchires. Maman aicha kenn demoul nga dess
Bravo Nana Aïdara je suis fière de te voir SenTV 👍👍👍
Ewwwww
Pere suis d'avis avec ton point de vue ya n'a pas mal dans cette société faut pas se leurrer
mais pere a veritablement raison,waxna deug kay,bu wer sax
Pour la première fois suis d'accord avec ce vieux
Père n'a pas tord sur ces propos mais mère aussi à raisins Sénégalais il suffit qu'il te croise dans les rue pour se permettre de dire qu'ils te connaissent chose qui n'est pas normale elle à des enfants et connaître veut trop dire
Respect à toi pere🙏🙏 tu ne fais que décrire ce qui se passe dans la société
Mane sofia la yeureume yaw mi engagé père rk ame nga soxla
Billahi
Sofia khamna dafané mag bourla
@@missgallo3643 wayer père dafa compliqué deih mane nak sérieusement père motax maye sétane guis guis
@@fatoundiaye9725 dafa mélna animation bi père di indi momay émission bi beuz mé mag mo méti rék
@@missgallo3643 Lol sino émission dou ame thiafka
Je peux comprendre Sophie mais Maman Aïcha sait très bien que Père Ngoné dit la vérité.
Bien vrai que père Mbaye Ngoné Fall vos interventions sont pertinentes et que c'est la triste réalité mais au moins il faut respecter vos invités. Par fois c'est comme des menaces en se levant et ça ne se fait pas à mon avis sur dans les télés. A part ça vous êtes un père coll que je suivis depuis la radio (rts) avec l'émission l' embeudji. J'ai même ton numéro de téléphone et on parlé de temps en temps. Yalla n'a diam sakheu thi sunu Gall ak adouna bii yeepp thi barkep Serigne Saliou Mbacke teee deefaal borom keur yeepp xeweul banu mana teraal seen ndiabott gui thi Tabaski bii amine
Pere je sui tres content de toi ?
Ligay wax lep deug la deg deg lou bakh la ligay wax nak fawou gua ame deg pour mana comprendre bilaie .
Père bakh gua si sociétés bi niou mel ni oie lanou sokh la kougnouy wax deug bilaie💓
Trop vrai, père !
Père lim waxe degu pur la am na gnou yilif seine dieukeur yi
Barri na
Bravo paré ça c'est vrai merci ✊💯✊💯✊💯✊💯👈
AHAHA😂😂😂😂MAMAN AICHA AK PERE DANGAYE MDRRR😂😂😂BA KHALANGOU..GNARI ANCIENS KABASSA..PERE CHAQUE FOIS MOU DOOR KO QUOTE NEKO KHAMNALA MERE BI RASSOU..MAMAN AICHA MOLENE GUEUNA KHAMNI PERE MBAYE NGONE KHAMNAKO DAY ADIOU NICI PUBLIC BI REK
Maman aicha nena il passait inaperçu khana🤣😂
Ani Wa hlm angle mousse(xawma fa sakh deh deugeur fitt rek)🤣🤣
Je suis là lol
Pere mane may sa fans number one
La fille habillée en bleue Claire dafa eupeul trope stp fais comme Sofia dafa téy
Père bilay kou amoul dég dég doula dég 👂🏼👂🏼
aka am solo limouy wakh
Per mane damala begeu 👏🏽
Mbaye ngone nak dafay depacer de tro waroul wakh merbi kone ma guèd sama thieur
N'importe quoi Les télé sénégalaises
Mais au Sénégal le ridicule ne tue pas
Per lingay wakh lep deug leu
Machallah pere true speaking
Sofia Ndeye sane dama ko yeureum ndakh bouy wakh gni lankeu ni dougn la deglou te dafa andeu ak dal mome jack jour mongui calme foumou tolou mais nala yalla faye thiono bingay dath fii
Père mbaye ngoné vraiment saye wakh amoul bén chance bilahii
Pere dafa meune togn té fi legn la image du jour sa costume ak sey dale you rafete nga méré modou mbaye té ya dakh togn fi 🤣🤣🤣
🤣🤣🤣
Mdrrrr😂🤣😭
Pére mbaye ngoné ak maman Aisha danio nabanté 😂😂
Sank batay lolu lay khalat😂😂😂😂
😂😂🤣🤣astahfirolah nobante kay
😅😅😅😅😅😅😅
🤣🤣😂😂😁😁🤣😃
Ah ah ah ah 😂😂😂😂
Passe inaperçu .maman Aïcha dafa degue français 🤣🤣🤣
Hélas le Sénégal, comment peut-on donner la parole à des gens sans sciences. Au moins quand on s’exprime que le se fonde sur des bases justifiées et Justifiables.
Donner la parole à l’homme du sens commun fini tjrs ainsi.
Il est unique pere mbaye
😂😂
Cette petite fille la dafa eupeul té xamoul dara thi aduna père limouy wakh yeup deugueuleu c juste que deugue dafa nekhoul rek
emission bi lou ame solo lagni wakh mais amoul organisation amoul deg loo te rathieu dieumeule sa kanam gui dafa barry fii akh
Perr lingafi wakh lep deug la feem yoyou maman aicha ak kenene ki nio geuna xam linga lendi wakh fi barina djigeune yifi yiliff sene borom keurr niolako geuna kham
Pére ngoné limou wakh deugue la danguéne thié tég senne tanke reck wayé deugue mâ
Père yafi né sans toi émission bi dou dara 😂😂
Vraiment
😁😁👍👍
Mon pays va mal
Mais comment peut on invité maman Aïcha dans un plateau de télé.
Svp aillez l'habitude d'inviter des gens qui sont des modèles ou références dans la société .
Père mbaye💥 Sokhna yi khamna kén doula Flow🤣🤣🤣👍👍
Sen Tv wakh deugg yalla toujours xoulou rek
wadiiii dafa heppel way 🤐🤐🤐🤐🤐🇨🇦🇨🇦
Lii Pere ngone wax lu am la . Waxul nag mooy liy yoon waaye lu am la. Amna kër yoo xam ne jigéen moofa am baat .
Bilahi lower nga wakh
Gningui saboté plateau bi pére dalale
Pére respect ❤
Merci
Pere mbaye ak maman aichaa barke yalla dano niroo
Wouy😂😂😂
Okine organisation🤦🏾♀️
Je t adoreu maman Aïcha 💋💋👄👄
Avant d'arriver à "mère qui dirige " il y a jeune femme qui dirige...
Lo guiss ameu na foumi commencé...
Père bravo boudoul wone ta douma setane émission bi DEUG rek ngay wax
Mac dafaye yarou mome limou wakh moune na ame thi keur yi me waroul wakh ni mamá aicha lolou refetoul
Li papi wakh amna dh wallahi
Père magoné à parfaitement raison même le théâtre de mbétel le confirme avec léna et le conportement de ses parent quand elle améne de l'argent ou autre comme des mouton de tabaski ou des ravitaillements douniiu wakh darra loudoul diko gueureum
Thia deug deug nak, Pere wah na deug.
On continue
Comment on peut nier ce que père est entrain de dire
Pere ben taw!peu avoir la force de 4 taw so defé lii war sii mom
Thieuy père maleu beug
c'est qui la dame avec son foulard bleu ciel ??
Émission bi " borom Touba " mocci gueuna sonne.
Pourquoi père parle comme ça ? Maman aysha quelque soit son passé doit être respectée à mon avis .
Ou il l’a manquè de respect ?? Khamnala manquer respect la ?
Sahir Ndoye Yow yay pere? Dokhal fowi yow
Nou kalasikou bi mouma nekhe ak perre rek ak maman lonekhe 😃😀🤩❤
Mé pabi djikom nexuma dara ndah daf beug di éliminé nit aretél way
Khana pere daf le lal mo takh gue bagne ko degue rek lay wakh mou nekh mou nakari
Mon frère!père mi dh jeune bou diang téh maîtrisé linga diang do attardé wou si limouy wax ndax amoul béne logique ay connerie rk lay wax bâ paré di toutal djiguéne pour mom lou ame djiguéne gni leuh motax nékhouma dra
@@femmenoirefemmeafricaine429 walahi deug le limi def damako contre lol sah my pa dafa eupeul de
@@mamadouba6677 frer nit kénduko bagne djikom lala wahni nexuma prck nimi def si emision bi c trop
@@Steven-ul8pw hamna daffa fokni mo mom plateau bi ba louko nékh lay déff
Franchement père a raison et vous le savez tous. Seule la vérité blaisse
Le plateau peu être mieux, sans père mbaye, car il n'écoute jamais, comme si il est au grand place, tous les personnes de ce plateau ont de l'esprit, donc c l'écoute qui manque, moi je veux que père quitte, MM si ce qu'il parle à de la sens aussi, c nul, safia amène un autre vieux qui s'est bien parler et écouté.
Comme sabar bou tass😂😂😂😂
Safia jeun la connai pa mai khamnani kou yarouleu dafa ame respect si nite
Longue vie père
Pabi comme pobaar daffa tang trop. Mais nak limouy wakh deug bou weer laa dagni bagn bagn lou rek yeuffou senegalais
🤣
Pourquoi il ne peut pas rester assis et parler. On dirait il veut frapper ses collègues.
Pére limou wakh deugue la mé dafa wara bayi maman aïcha mimouy vilipandé ndakh wakhou télé fou nek lay dem té maman aïcha oci dafa am ndiabote tamite niou wakhanté deugue
Pére limou wax doufi diouk barina trop surtout Gaur bou seuyi té amo Dolé
pourtant c vrai il père mbay wakh pur vérité
Pére mbaye limou wakh deug la koko weudy lolou nguay dondou
Pabi imposè wou par force la beugg non dangay rè ba dè beug loumou yobou keureum rek
Mbaye Ngoné le MÉGALOMANE on se connaît depuis 1970 cesse de MENTIR Thiaroye Guethie vit dans la Honte. Thieuuuuye ????
Oui père a raison amna leur you beuri mère yi dagnouy ligueye sen dieukeur yii ba gnou melni kharou yare
Premier Vu dou aye fon
Ramata Ba legui neikk et puis quoi
@@abdoulomr uu77
Machalla
Père respect t'es enfants svp
Papa tu a raison
Ay way invite Lene ma
te pere aka sadik mome dou raye wakh dji goom ba famou nekeu laye deff alcol bi te deye impose par force damay wakh😂😂😂😂😂😂😂
Père ak. Maman dano. Nobantè. RK. Nak. 😁😁😁😁😁😁
Louyi pere diwakh loulerela bilahi niom sakh khamnenne louamla
Pa bi limou wakh amna dé
Père diamou si yaw
Li père wakh amna. Arrêter votre hypocrisie
Yéne doul waay lou père waxx dafé beuri mane mi dokhoul saxx j’en ai vu...
Bilahi pér wax nga degu
Gatu émission yi litakh gnuy daw Sénégal
Pa li gua wakh deugeu piir la leu
Man père ma ngone motakh may suivre émission bi
Père mbay tu as parfaitement raison
Mako beug barke borom touba mbaye ngone 😂😂😂
Lo Ndiaga barkep borome touba ak man tamitt
@@oumoudieye7501 bilay 😂😂😂
Père lou leer la wakh barena thii keur yii
Bilahi gor day beuri taw
Lou père wakh dh deug leu moi j'ai vue ça exemple sama Badiane dafa none dieukeureum loumou wakh lay wadji exécuté
😂😂😂😂
@@maibamba6818 looy réé
Dama kham ni king dafa yabb Badiane nam rek
@@maibamba6818 😂😂mdrr
Pére ligawakh damase amlouma lérr bolaye amnadh
Femme bi wax ci fin bi à propos de l'association des maris battus. Non iow danga yéékha wax, so waxone depuis le début ,Kone Sophie Gueye ak mére aicha dougnu wéddi pére. Ndakh pére limou wax daf ci wéét rekk, mais deug bou wérr la. Lane motah niom nioukoy wéddi sans raisons🤦🏼♂️
Paa bii deug rk lafii wakh