Yallah rek mo yorrr Djiko yi tè yeurmandè Yallah djèhagoule deh ci lima fogg. Donc naniou mandou ci lolou WALIOU Yallah mokoy taneu epuis djiko you bkh yi gnigui fi ba lëgui malgrès que (gnou bonne gningui ci rewww mi nak). Sama Papa ak yaw sorantèwolène att donc mom aussi fëkèwone naa Dëmb
Xam Xam pousso la nak, kou nëkako meuna forr. Xamoul kaw kaw akk Citadin (Jang rek la ladj). Linguay wax amnaa solo nak wayè soralèle aussi ni Xam Xam ak ay att dou béne. Amale Jamm. Oustaz bobou nak téssantè rek lay prechè donc doumassi commentaire
Bilahi, motakh douma sakh beugu lire genrou vidéo yi ak commentaires yi,ça fait mal mais téguou ci yone bi rekk,dounde farata ak souna,wakh katyi gnou bayilénn gnouy wakh
Père sa probléme moye tjrs sa âge rékk ngaye wakhetané demb kéne fatéwouko nioune nieupe nioko khame mé bayile khéleni valeur yi nio ngui fi té li modou fall wakh deugue la bo dioté akk sa sokhena da ngaye Yore Ndiape amena niaane boy diangue dafa Mélni da nga déssé akk thiédo Balma nakk
Macha Allah Père 🤲🤲🤲
Quelle maîtrise de ses arguments!
Mashala Pere kham kham yalla na yalla yok saye fanes boubakh a bakh inshahala 🙏🙏🙏.
Machala pére amna solo wahbi yalla nala yalla fay si barke syed mahmood ak si barke serige touba merci beaucoup
Père Mbaye Mangoné yalna sa diamm yaggue,danga éloquent té xam lingay wax!! 😘💛
0
Machallah pére yallahna yallah samela
Per yallah ga goudou fane machallah🤲🤲
Yalna ame fane wou goud lool téh ame weer nit kou bakh oyof degou téh ame xam xam demb jajeufety Pére 👌👌👌👌🇪🇸🇪🇸
Vraiment MashaAllah Père Akassa jajef
Je t'aime pére mangoné🌹🌹🌹🌹❤❤❤❤😘😘😘😘
PÉR MBAYE NDANAN LA NAK😄😄😄😄😄😄😄🤗🤗🤗🤗🤗🤗🤗🤗🤗🤗
❤️
Jeureudieuf père ngoné yalla na yalla sam
Je t’adore papa ♥️
Je viens de m'abonner à cause de père je suis mort 😂😂😂
Mak maTna Bayi Sim Réw ma cha allah mn Pére DounDal way
Pére macahlah
Merci beaucoup pére
Merci père
Per doundal ba doyel macha allah
Machallah lovely pere.
Pere wakhal ci thiossane serigne touba ci ct possible 🙏🙏.
Merci papa si mariage🙏🙏🙏🙏🙏
Père Macha alla long vie santé ak bonheur
Ma beugue Père 💞 💞💞
Yalla ngue goudou Fann père
Père mbaye ngoné démako beug rek té yalla rek takh
Vraiment si on deux comme le pere le senegal sera bien
Boujour pere ngone c est moi astou diagne sidi diagne
Pére yalla moy tall moy fay dagua dioum bayil lolou
Machallah 🤝✌👏👏❤❤👌
Ame na solo papa longu vie
Yallah rek mo yorrr Djiko yi tè yeurmandè Yallah djèhagoule deh ci lima fogg. Donc naniou mandou ci lolou WALIOU Yallah mokoy taneu epuis djiko you bkh yi gnigui fi ba lëgui malgrès que (gnou bonne gningui ci rewww mi nak).
Sama Papa ak yaw sorantèwolène att donc mom aussi fëkèwone naa Dëmb
Macahllah père 😘😘😘😘😘👍
Machalla
Merci
Merçi pére
il comprend bien le wolof et ses traditions profondes.
Machallah père
Koumay dimballi ci numéro père ngoné té yalla takh
Merci père tu es l meilleure
Amna solo
C'est terrible, té khamoulo ban siècle lagnou tollou 🤔😮🙄😪
Tu à raison pére
Pére borom aaaaaaaaaaaaaa🤣🤣🤣🤣🤣 mé yalla na sa diame yageu
Père doundeul ❤️
Machallh mon pérr
Un vrai antistress père tioooo😅
Journaliste bii molna machallah
Koula bayi
Père yala nasa diam yague
Longue vie.pere.sante.❤️🙏❤️🙏
J t'aime papa
Pere merciiiiiiiiiiiiii
Mane barki brome touba momay ray
Pere no stress que dieu vous protege
SOUMA DJOUMOULE DEH Allahouma janibni Cheytane wa jnibnaa cheytane........... HADISS YONANT BI LAA AVENT NGUAY SËY.
MAIS KOU YAKAMTI DOU MEUNE YOYOU
Allahouma jannibnash sheytâna wa jannibish sheytâna mâ razaqtâna
No per dafa beuri fem nak😅
mane mome pere mbaye ngoné dafmaï fathie néna kourgué bakh😂😂😂😂😂
dia dieuf père ya bax ya am diom barki serigne touba
Père que Allah te protéger
Billahi deug la 😃😃😃😂😂😅😅
Ayway ana mame Balla mbaw a19:/22:27
yow pere mbaye ngone wakhou kour nékh nala trop
So nice 👍
Aka kham wakh
Lala aicha nekh nama
🤣🤣🤣 Sophya Diatta
Nice pere
pére baxnga si réwmi nak.do sén morom
😂😂😅😅😅🤣🤣 mo nekh
J'aime père il est véridique
pére aka meun barkè borom touba
Xam Xam pousso la nak, kou nëkako meuna forr. Xamoul kaw kaw akk Citadin (Jang rek la ladj).
Linguay wax amnaa solo nak wayè soralèle aussi ni Xam Xam ak ay att dou béne. Amale Jamm.
Oustaz bobou nak téssantè rek lay prechè donc doumassi commentaire
Wakhe ji amna solou torop
Merci père wadji khamoul dara walahi yalla rek motakh may wakh fenal yonentbi rek ak wakhi djigen lafi neke
Wakhal té yalla takh, commentaire partisan rek guafi déff, parparlo rek,
Diné ak tradition dou bénn
@@laminendiaye4631 loutakh sénégal kounou boka loul tariha rek doune wakh diam si mome li nianw na trop
Diouf Madick fofou moy Sénégal ndiaye.nitt ki doula déff dara,guani dioulitt gua djiteul sa walou tarikha,ba ko bokal tarikha loumou wakh nonoula,ko bokaloul loumou wakh ay kathie la.dounioussi yam,dila khass.Ana islam biniouy woté,ana mandou.mais Lou nitt wakh nitt,diguako layo euleuk.Senegal deukk bou doy warrla.indiscipline,Lou nekh way wakh,louko nekh déff,suis à l'étranger,mais limafa guiss,amoul fénene
@@laminendiaye4631 bilahi mm moi suis en spagne mai senegal dafa doy war danioulay tague tay souba niou hass la
Bilahi, motakh douma sakh beugu lire genrou vidéo yi ak commentaires yi,ça fait mal mais téguou ci yone bi rekk,dounde farata ak souna,wakh katyi gnou bayilénn gnouy wakh
Nn pere bi damko bgue😂😂😂
louy cour
Founé yagui fa di commentaire😂😂😂nous on adoreukh 😂
Ndeye Diouf 😂😂🤣🤣 ndeye Diouf top ngama bama seuss tmt
Il dit la vérité
yaye sama fans d3 p3re
Pér Oné 3ém Ciels😂😂🤣
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Thieuy sougnou journaliste yi. Elle demande bane siècle lagnou nékeu😃
Mbakhanaaaaa😀
Pa MAGONE YAGFI TE WER
HAM HAM GUA AM WAYE HAYANE
KO DEEG SERER
No père yalla nasa diam yagu taye hole bou nakari la amone tay ...🤣🤣🤣wayei taye lima ré amatoul
Mais père 8 nga cité dhé 🏃♀️🏃♀️
Niambour bokousi
J'adore pere
Père sa probléme moye tjrs sa âge rékk ngaye wakhetané demb kéne fatéwouko nioune nieupe nioko khame mé bayile khéleni valeur yi nio ngui fi té li modou fall wakh deugue la bo dioté akk sa sokhena da ngaye Yore Ndiape amena niaane boy diangue dafa Mélni da nga déssé akk thiédo Balma nakk
Merci
JOE DIOP wokho fi dara demal ak sa diamono adouna yangui
@@SD2FOdemb motakh niounane taye kone diogoufi valeur yi mo ngui fi dafa mélni mome rékk farou mbame yi akk diame poute yi loutakh bou amé jezner doukoko niawe aduna bi daniouye dieule si demb boléko akk taye mou dokh mé lépou dou demb rékk
JOE DIOP vois habite ou exactement ?
@@SD2FO wakhema fo deukk yawe mane fana fana khodia bombé la
Diadieuf Haye!
Bravo père
Mach allah père
billahi pere dafa khame adouna nake
Père
Pére bibliothèque ngua Dieuredieuf...Pays Basque
Mbaye ngone khamo li ngay wakh
Bilay wakh nga deug
Journaliste bi aussi xamoul bane siècle lanek nii c'est honteux 😂😂😂
Père on est 21ème siècle
Bro genre yi nio yakeu métier animateur ak journalisme. Aucune formation! On sait même pas d'où elle sorte.
@@musikonline550 🤭🤭
@@musikonline550 srx bro lingua wakh moy deug même mane mi sama diangue soriwoul sakh li dafma def cas
Yes
Donner moi l numéro de père svp
😅😅😅😅❤
Père mo nekh😂😂
Pere mbaye ngone kharitou baye mandione thiaroye guèdj
Ki d'où niit😄😄😄
Lala Amal diamu ku man lingay déf nga