Waw wouyou lène ma à li: khan nguène bayi sa diabar dème bitime rèweu ba paré dieule sa diarbate bou tiéné pour garder keur gui. Kone tentation dafaye dougou, kou d’accord lalale j’aime 😂
Soxna faatu waxnga dëgg, erreur bi yëpp ci djikkër dji la. waayé ku djigén ki dafa nek nit ku bon rek ndax bu fekkee li muy ñakk giss borom kër am dafa koy inndil ay ģallankoor waroon nako wax walla bu mënul continuer ,mu ñaan baat. mais elle a préféré suivre son âme. Yalla na ñu Yalla musal ci djigén dju bon !
Momi tame kou doye war la, loutakh do dème wouti liguèye ta délou sène keur? Loye garder keur nidiaye ni garde du corps? Ah sof nga lole nak! Tchiiip😂!
Sama rakk so rithie première fois on peut te comprendre mais tu devrais quitter la maison doucement sans soupçon mais pendant toute cette période tu n est pas clean dans cette histoire
Est cité dans le coran il pouvait prend le modèle du prophète yousouf. Or celle [Zulikha] qui l'avait reçu dans sa maison essaya de le séduire. Et elle ferma bien les portes et dit: «Viens, (je suis prête pour toi!)» - Il dit: «Qu'Allah me protège! C'est mon maître qui m'a accordé un bon asile. Vraiment les injustes ne réussissent pas». (Yufuf:23)
Goor dou niak diomm yaw ngani danga am dolei danga tolou noula nekh banopi say raki tons gnep di kheuy ligueye nga teud si keur gui nan gardé keur gui melni kou beugoul dara niak fayda ba dee khana eulleuk beugo amal sa bopou
Il savait ce qu elle veut pourquoi ne pas fermer sa porte pour lui montrer que je sais ce que tu veux mais sa ne passera pas.maintenant il n a ka quitter sinon tot ou tard le bon dieu fera savoir a tous le monde ce que tu fesai et a ce moment tu pourras rien expliquer.boul fowé sa khéle réfléchis et vite
Waw wouyou lène ma à li: khan nguène bayi sa diabar dème bitime rèweu ba paré dieule sa diarbate bou tiéné pour garder keur gui. Kone tentation dafaye dougou, kou d’accord lalale j’aime 😂
Lou lère gua wakh tentation bou graw la sakh 😂
Nidiaye mo togne sa baye ak sa diabare sah warolena bayi si keur wakhoumalak kenene❤❤
Mani ko thiey Yallah baxna
Def pause café ☕️😭😭😭😭
Na bayi keurgui té outi liguey gorla euleuk gnana yalla sampe keur done kilifa bopam keurou nidiaye dou keur.
@@adjathioune3911 ah oui dafa wara guen keurgui dem fenen
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂
Soxna faatu waxnga dëgg, erreur bi yëpp ci djikkër dji la. waayé ku djigén ki dafa nek nit ku bon rek ndax bu fekkee li muy ñakk giss borom kër am dafa koy inndil ay ģallankoor waroon nako wax walla bu mënul continuer ,mu ñaan baat. mais elle a préféré suivre son âme.
Yalla na ñu Yalla musal ci djigén dju bon !
Thioukoum Ndiaye mom lou takh nga santalé ko Ndiaye pourquoi pas diop 😂😂😂😂😂😂
Yako taye 😂
Sokhna fatou yagual wereul na sa diam sakh🙏🙏
Thiey !!! Thioukoum Ndiaye mo beuri doolé d 😂😂😂😂😂😂
Ay man di warou na😮
Na guene keurgui outi ligueye
Wawaw LA L'OISIVETÉ EST LA MÈRE DES VICES 🧠🧠
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Maniko si thieeeyy😅
Merci sokhna fatou ❤❤
Des histoires créées de toute pièce. Ragual lene Yalla
Baravo merci
Manéko si thiey😂
Bayile Ndiaye waye
Masha allah ❤❤❤❤❤❤❤
Cherche travail
Momi tame kou doye war la, loutakh do dème wouti liguèye ta délou sène keur? Loye garder keur nidiaye ni garde du corps? Ah sof nga lole nak! Tchiiip😂!
Sama rakk so rithie première fois on peut te comprendre mais tu devrais quitter la maison doucement sans soupçon mais pendant toute cette période tu n est pas clean dans cette histoire
Motax goor danga wara tameu téla yéwou dém liguéye boul khar kéneu ci dara
Ouii
Aywaye mama nitalie 😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Boy bi mom vraie katchor leu kou gnake diné kou gnak diom...
Na dém wouti ligeey gennë kër gui
Na wadji fékhé guéneu keur gui té dém loué dji té liguéy mo gueun nite dangay nité
Mama nitali 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Est cité dans le coran il pouvait prend le modèle du prophète yousouf.
Or celle [Zulikha] qui l'avait reçu dans sa maison essaya de le séduire. Et elle ferma bien les portes et dit: «Viens, (je suis prête pour toi!)» - Il dit: «Qu'Allah me protège! C'est mon maître qui m'a accordé un bon asile. Vraiment les injustes ne réussissent pas». (Yufuf:23)
Merci
Khana dangay dig lo pacotille 😂😂😂
Goor dou niak diomm yaw ngani danga am dolei danga tolou noula nekh banopi say raki tons gnep di kheuy ligueye nga teud si keur gui nan gardé keur gui melni kou beugoul dara niak fayda ba dee khana eulleuk beugo amal sa bopou
Moma jakhal dh tamit. Jogal dani sa dolé guen keurgui ta jegalu sa borom
@@cherifaaidara loxamsi goor bou niak diomm lim wara def xam nako li diaroul won sakh diko eundi netali goor noumiy kheuy di teud aka entraîné rek
Mo kham loutakh mou tokfa wayé na jouk thia bamuy tel
Déf bitim réw des années mo diadouwoul sa way arrété bou diaré mou guéne keurgu
Doye na ware ndialo Bakhoul
Lo reuthiou dossi délou Yako tay boudoul Dara nga respecté sa nidiaye
Dégueu nèkhoul😂dey sob rek déko moudjé nekh
mom la neekh
Wahal dé...weddiwoumaleu dé😂
تكتب الفاتحة بعد كل آية وإن يكاد الذين كفروا إلخ ثم وقال موسى ما جئتم به السحر إن الله سيبطله إن الله لا يصلح عمل المفسدين 313 ثم يغسله بسبعة ايام
Amga dieker wala??
Piège ko enregistré ko bomou wakh nii li ngo koye deiff mome molakoye deif lo nga teigal kokou niko bayimeu mba ma wakh ko sa dieukeur
Mais grand bi da thiouné li boko commencer guis del teuthie sa bountou négue mais legui noy kholé sa nijay
Ayyy way liii dou deug ohh thioukoum ndiaye migui toth deug bi ohh 😂😂😂😂
Dafa nekh trop nak😊
Ki bahoule
Mai gor dou yeune dou si keur
Waadji dey sob rek 😂😂 affaire bi nakhariko dé lou tah dou teudj négam
N'a geune keurga keur nidiay d'où keur dém wouti ligeuy
Vraiment c'est une situation fréquente chez les inmigrés
Méfiez-vous de l'eau qui dort 6:08
Sa affaire leu lepp sissa kaw lay keuppou bolek sa ndaw gui diekhh takkk
Na nguen keur nidiayam mo geun si mom deh ndakh ndao si duko bayi muk niamena nekhna bayina amoul fenu😂
Malheureusement nidiaye dji meune Na birale
Mais manoul bégual djigueen
Magui toupe d
Barri na ko defé ni dou wakh fekkeu ni thiow kat la
Nagéne keurgu sinon do bakh
Hè motah man samay diabarou mak nidiay kharit AK lep lassi yamalé sékou mak ken tognagne té
Niari salopard ngafi wakh
Aller écouter le son de pacotille titre Sama diabarou nijay
Yalla nako Yalla yeureum
Yow ancien nga bro pacotille ay rimes you graw lafa door oooh ndeyssane
na tokho demefaneen
Yaw kou niémé Yalla ngua yaye doméram adoouna diaral na li
Quitte cette maison et cherche du travail c'est mieux pour toi parce que tu dois te marier et fonder ta famille cette dame ne fait queu te retarder
Wa lidougnou si wakh tamit diarbatt ak diabarou nidiaye
Mon tamit deko bougou
Elle n’a rien fait le marie est la fautive
Bouki kéne douko dénk yapp
Wadji na guèna si limou neka bayi djiguene yi mogui yakha addiunam te bayivousi xel
Qu'il quitte la maison
Na wakh badiane bi deg mo
Lui même il n'est pas bon
Google bou niakh diom
mais google t’as fais quoi 😂😂😂?
Ñu xam
Khana thiabi nègg amoul
Mane dé mom laay laadj 😂
Attention setane.
Sv
Encore et toujours le sexe
Il savait ce qu elle veut pourquoi ne pas fermer sa porte pour lui montrer que je sais ce que tu veux mais sa ne passera pas.maintenant il n a ka quitter sinon tot ou tard le bon dieu fera savoir a tous le monde ce que tu fesai et a ce moment tu pourras rien expliquer.boul fowé sa khéle réfléchis et vite
Déf bitim réw des années mo diadouwoul sa way arrété bou diaré nga guéne keurgu