Salam mon frère faut rectifier las ou tu dis que n'importe qui peut les élevés non non... Se son des chiens autoritére trés trés tétu donc il faut avoir du caractère avoir un caractère quant il faut je t'en parle en connaissance de Cause car cela fait maintenant 10ans que jai la race ici en Europe.. Ses des Berger d'Anatolie breff
Je ne suis pas du tout d'accord avec lui. On peut être éleveur sans être dresseur ni avoir une dizaine de chiens. La passion prime avant tout après s'en suit le reste
Waw lolou mom deugg la té nangou nako bou baaaaax. Neanmoins élevage ay niveau la. Kouy sogga commencé ak kou cii yagg bokkou niou, de même kou ame financement bou doy ak kou ko amoul meunou niou bokk niveau. Donc kou nekk ak sa niveau binga tollol ngay démé @@AmaryKebe-z5y
Au fait sen site bi xolate len sen priorité ak sen objectif dakh war gen xam réellement kane geeni diokh micro mouy wakh boy Djiné businessman nioune xam naniou moy kan alors delen feusseul gniy doundou élevage genre ELEVEUR yiga xameni le bien animal prime avant tout !
Sa khadje yi yo yi nguaye nane l'un des plus gros chien au Sénégal 😂 Khif bangui raye senegalais yi nguaniye nane dangueni yare khathie 😢 même fi Europe nieupeu ngui abandonner séne animal nakhe doundou bou chère 😢
Yeah sir boy djiné le travail continue 🤜🏾
Un chien très protecteur😊😊
Louma nékh si wadji dafa âme fite😂😂😂😂
Boy djiné bravo
Oula c'est un chien originaire de Turquie avec une mâchoire très puissante.
Khadji amale gualene akk dano khiff😮😮
Lilas done beugue wakhe dano kiff
Anatolie, Pas Anatonie svp. Excellent eleveur 👍🌿
❤❤❤❤❤❤A❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂😂
Yow sa kangal yi sourou niou déh khana thiébeu laniouy lékeu🤣🤣🤣
Anatolie je pensais que amoul senegal bokk n'a si khathie yi gueune agressif
Salam mon frère faut rectifier las ou tu dis que n'importe qui peut les élevés non non...
Se son des chiens autoritére trés trés tétu donc il faut avoir du caractère avoir un caractère quant il faut je t'en parle en connaissance de Cause car cela fait maintenant 10ans que jai la race ici en Europe..
Ses des Berger d'Anatolie breff
Kanghal dou khadiou thiakhane
🎉
Je ne suis pas du tout d'accord avec lui. On peut être éleveur sans être dresseur ni avoir une dizaine de chiens. La passion prime avant tout après s'en suit le reste
Frére wakh deugue si béneu côté âme n'a niou beurri ma rirando moléne si dougueule
Faut bien écouter ces propos 👂🏾
@@AmadouMbayeciss déguelou n'a lépou loumou wakh kham n'a moussa bou bakh bokou n'a si niou guéneu moune dresser si thies
Waw lolou mom deugg la té nangou nako bou baaaaax. Neanmoins élevage ay niveau la. Kouy sogga commencé ak kou cii yagg bokkou niou, de même kou ame financement bou doy ak kou ko amoul meunou niou bokk niveau. Donc kou nekk ak sa niveau binga tollol ngay démé @@AmaryKebe-z5y
Tu as raison deh
Beugeunasi
Jajeuf frère yama doy si chien
Au fait sen site bi xolate len sen priorité ak sen objectif dakh war gen xam réellement kane geeni diokh micro mouy wakh boy Djiné businessman nioune xam naniou moy kan alors delen feusseul gniy doundou élevage genre ELEVEUR yiga xameni le bien animal prime avant tout !
Sa khadje yi yo yi nguaye nane l'un des plus gros chien au Sénégal 😂
Khif bangui raye senegalais yi nguaniye nane dangueni yare khathie 😢 même fi Europe nieupeu ngui abandonner séne animal nakhe doundou bou chère 😢