Pour dire vrai le truc a vraiment commencei en 2018 quand dip avait sortir *intrus* quand il piquei ngaka il a dit dans une barre * fayugnuma woon manoy bamay jobak akhlou * c'etais pas une pique mais plutot un big up mais les gens l'on mal interprété et apres si vs vs rapelè bien akhlou brick ils avait fait une serie de frestyle sur vibe radio ou il piquei dip allait verifié c labas k le truc a commencé a partir en couille .et apres akhlou brick ils ont continuè sur cette lançé quand il fesait la promo d leur album *hello world* ara a dis dans une barre * natalu album ni mere bissi dieg bu diar * alors en ce moment cetais dip qui fesait le buzz et venai juste de montre son album ... et apres les clash dip omzo et consor akhlou brick ils ont sorti tic tac des piques aussi pr dip ...vs allez penser k j parle en tant que fan mais suivez bien ma logique au debut c etais juste un big car dip a raison * quand il a dis fayugnuma woon sama money bamay diobak akhlou" puisk ils ont fais ctt coloboration justement pour conscientisé leur fans d'acheter les produits afin qu' ils fayeku mais leq gas l'ont mal pris Et dip il a deja repondu a akhlou brick et iss 814 puisk meme iss lance des piques a dip rapeler vs dans le son "cartier " le mec a bien dit * dio sama ..du reprodiure ay copie afro originel comme felakouti * faisant reference a dip et l 'instrumental de nigthmar * dip a dit dans une interview *Dakar buzz * bu amei lumu sekeuh ak nit lu profond rek diexna méme koku lumuko meunti def mom duko toppu * cas de iss et akhlou 🤗🤗 Mais en resume c sa le rap mw x8 tt a fait d'accord ils sont la pour concurencé donc pas de pitié k chacun travail et k bu keneuh nango kenen ki rawla amoul mbokk amoul darra amoul xarito 😏 peace
Non dou ragal mais si mbind la bok. Tu écris des choses et tu laisses les gens en faire ce qu'ils veulent. Dip n'a pas cité de noms, eux aussi. Xéxou courant coupé la, bou courant gnewé la leup di lerr... Maintenant c'est à vous, chroniqueurs de faire votre job, à tort ou à raison. Dolén ay sheytané, rappeur yi dougnou ay ragal... It's a part of the game game!!!!
Ndeysane ponkalou goor tog di wakh bay niakk sur des choses non important qui ne vont pas faire avancer la jeunesse mais de les retarder sur des gens qui essaye de gagner leur vie. YALLAH naniou YALLAH MOUSSAL si SATAN 🙏🙏🙏
Yow mom dafa melni reptyl nga Kan mola wakh ne dip moi number 1 Ngaka blinde moi number 1 Dip sa soko larj ge ndah akhlou brick ngay wakhal dafey wakh NO
@@whiizyboy5839 😂😂😂fall dieul lene lepp... Dip bou clashé té saga woul dou nekh... Nioune dagn lay clash sa khol di bone té dougn la toudou dougn la saga
Pique si game la bokk donc d'où kestion de nafeikh donc ce qui commente aye nafeikh arrêtez ... Nice analyse thion mais dip le connaissant quand il aura Marre il va assumer comme il l'a fait avec nitt dof et les autres.
Mais si akhlou brick n'assume pas dip aussi n'assume pas, oubien c'est akhlou brick seulement qui doit assumer??? Quand tu regardes le direct de dip sur rap 221 dip a clairement dit qu'il n'y avait rien entre lui et akhlou brick. Donc tout ce que tu dis sur akhlou est aussi valable pour Dip. Belle analyse quand même.
Bro je respect tes analyses et ça se voit direct que t’es fan de dip😌❤️🙏🏾 respect mec
Pour dire vrai le truc a vraiment commencei en 2018 quand dip avait sortir *intrus* quand il piquei ngaka il a dit dans une barre * fayugnuma woon manoy bamay jobak akhlou * c'etais pas une pique mais plutot un big up mais les gens l'on mal interprété et apres si vs vs rapelè bien akhlou brick ils avait fait une serie de frestyle sur vibe radio ou il piquei dip allait verifié c labas k le truc a commencé a partir en couille .et apres akhlou brick ils ont continuè sur cette lançé quand il fesait la promo d leur album *hello world* ara a dis dans une barre * natalu album ni mere bissi dieg bu diar * alors en ce moment cetais dip qui fesait le buzz et venai juste de montre son album ... et apres les clash dip omzo et consor akhlou brick ils ont sorti tic tac des piques aussi pr dip ...vs allez penser k j parle en tant que fan mais suivez bien ma logique au debut c etais juste un big car dip a raison * quand il a dis fayugnuma woon sama money bamay diobak akhlou" puisk ils ont fais ctt coloboration justement pour conscientisé leur fans d'acheter les produits afin qu' ils fayeku mais leq gas l'ont mal pris
Et dip il a deja repondu a akhlou brick et iss 814 puisk meme iss lance des piques a dip rapeler vs dans le son "cartier " le mec a bien dit * dio sama ..du reprodiure ay copie afro originel comme felakouti * faisant reference a dip et l 'instrumental de nigthmar * dip a dit dans une interview *Dakar buzz * bu amei lumu sekeuh ak nit lu profond rek diexna méme koku lumuko meunti def mom duko toppu * cas de iss et akhlou 🤗🤗
Mais en resume c sa le rap mw x8 tt a fait d'accord ils sont la pour concurencé donc pas de pitié k chacun travail et k bu keneuh nango kenen ki rawla amoul mbokk amoul darra amoul xarito 😏 peace
Tu as bien vu bro ,jajeuf✌🏿
Tu as bien vu bro ,jajeuf✌🏿
Tu as bien vu bro ,jajeuf✌🏿
Affaires bi Omzo dollar leu
Sa way linguay job nice na 💥💫
Cool man bonne continuation ...mes respects frère 🤘👌👍
Bonjour, est-ce que tu es au Sénégal ?
Dagay nday fén boul niou sonal man fan's ngaaka la m3 liguay wakh akhlou ay doul la ✍️✍️☠️✌️✨
MODOU BOU AKHLOU BRICK PARADIS
SAWAYYY TU ES LE MEILLEUR CE KE TU FAI C BIEN
Serigne Thioune Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
DEUG rek ngaye wakh
😂😂😂yaw vrai satan nga bilahi...
Dip meussoul assumé bene clash boudoul mom ak Omzo ak One Lyrical
Yaw copain Fan's Dip bou laxatou nga. Yangui wax baye tangue di niax. Yaw sa rôle dou farr féne mé rester non aligné
Respect bro t'es fort sr ce ke tu fais mention spécial grand biii ma yokhalaciii amna fouy dayza nane dégueunala wanté déguelouwoulahhhhh
Non vraiment wakh gua deug✨
La prochaine fois soy diohei sa opinion del toqqq sa home sa biirrr salon au moins menuisier bisssi guinaww môngii disteurb dioxgnou thieuûrrrr go
Vidéo bi nice na mais deko deff fou amoul bruit
Dip acteur galsen yaffi né
Slam bro Malathion nakala........
Je suis un big fans de Gaston..,
Sonko for life,
From Médina,
Le Combat continue incha'allah
Cheick Moïnga Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Wii pique no assumer bro .... Rhyme suivi ..bro kou xam rap nga ..bro votre numéro .dear Nice too meet u ..
Tu es le meilleur wallahi
Non dou ragal mais si mbind la bok. Tu écris des choses et tu laisses les gens en faire ce qu'ils veulent. Dip n'a pas cité de noms, eux aussi. Xéxou courant coupé la, bou courant gnewé la leup di lerr... Maintenant c'est à vous, chroniqueurs de faire votre job, à tort ou à raison. Dolén ay sheytané, rappeur yi dougnou ay ragal... It's a part of the game game!!!!
Walter White Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Du courage grand nice job
Grand bi loy wax leer neu nagne
Cool depuis France 🇫🇷
Way AKHLOU BRICK gno tayy sétané nga dangay sopp
Dieummeu Ju Tédd Dou Fégne Gnun Gno Sol Vérou iblis Dip .Kou Goumba Si Xol Dou Guiss Kou Tédde Kii Dayza🤣
Vraiment xamo dara damala yeureume ndeysane ak sa guinaw bou niaw
Ndeysane ponkalou goor tog di wakh bay niakk sur des choses non important qui ne vont pas faire avancer la jeunesse mais de les retarder sur des gens qui essaye de gagner leur vie. YALLAH naniou YALLAH MOUSSAL si SATAN 🙏🙏🙏
Mais fall ligay wakh dou lolou dh 😂😂😂😂😂😂😂😂😂Walahi ligay wakh khamo si dara
Ki khana
B1 frr mai ani montage bi tecno...passer na fii nak
Cool frère
Brick millionnaire ✌️🔥
Malathion wallah c'est un killer 😆✌
Malathion you right bro Deep vs Ahlou Brick nagne assumer kw das hip-hop après mou diekh tmt ish 😂😂😎🙏
Karbala Touré Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Lou lérr ga wakh gayi dougnou assumer merci brother
Deugue rek nga wakh 😷😷😷😷😷😷
Sidi Kane Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Championt yallna héwali ball lingéy analyse 👁️🌔
Saway li takh nga nekhma daga sadik big up broo daga drect
Ba légui akhlou brick gaye wakh bo wakhé akhlou dagaye wakh dip 1a1 akh
Na camara bi stable
🔥🔥🔥
Broo Nice that's right
Dip💪💪
Fans ZO DOLLARS khamoul louy wiri wiri
Super
Nice
Kham ndaye liguay wakhe akhlou amoul tend class bayil dip tontoul bopam nopil
wa loutakh nangou wo wakh dip dou asoumè sa way fans dip gua sonal gua akhlou brick way khana gnome rèk gno sani pic
Thierno Diao Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Dip moy numb one
Wakhal waay kii dafa soof
MALATHION Tu analyses bien ... mais tu es trop fan de Dip....
Point de vue ✌
Tu as raison d'interpréter mais avec respect frère
Wa LOY MERR DI WA DIA DIOUY HAY HAY HAY HAY HAY HAY HAY KI DINA DIOY DI MALA FENE NGA TODO MODOU BOU AKHLOU BRICK LA L'AVS BRICKEST 100% LA
Yow wakhofi da bayile wa Akhlou brick amena si droit
Malathion pls prochaine video : omzo dollar yeureum sur buzzlab
Lewan Keita Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
sa way dip mom aggùl féneu wa Akhlou brick
Yow mom dafa melni reptyl nga
Kan mola wakh ne dip moi number 1
Ngaka blinde moi number 1
Dip sa soko larj ge ndah akhlou brick ngay wakhal dafey wakh NO
pourquoi tu veux créer un problème la ou ya aucun problème
Nice 👍 interprétation big man.
No frr mai ioe sonal nga akhlou khana dip mom dou sani picc ioe fans dip nga nak nioun ay bromi khél lagn bayil teuwariyi ioe pion nga
Sagn nGa Beurélo Statut Demba Ak Dupon...
Nice Nice bro
cherif paye Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Non bro yow amon kw bilahi mé diko maye marena bok What’s up
No dip dou numéro 1 fall
😁😁😁 yow mom daga free
Merci bouro
🤘😄😄😄😄😄😄😄😄😄🚨
Tu mens akhlou brick logo wam dou pithie bo khamoul dangay nopi
Fans dip nga motax...
Kou dégg ninga maîtrisé sound dip kham ni mola fi tek
C’est normal il est pas fan de dip deh mais il sait juste que c’est dip le meilleur au moins lui il est logique de son choix
@@whiizyboy5839 😂😂😂fall dieul lene lepp...
Dip bou clashé té saga woul dou nekh...
Nioune dagn lay clash sa khol di bone té dougn la toudou dougn la saga
Dip akhoul birick saye baye là niou
J'ai envi de te kiffer mais je n'y arrive pas
Frr ioe fans dip nga ioe pion nga dip day sani picc ta dou asome
LOY WAKH KHAMOU SY DARA MODOU BOU AKHLOU BRICK MOUY WAKHAL YAW KHAMOU TOOSS
Saway vré fans dip nga alhlou brik lijanti woula sax job rk noula néx déguéko mé boul wax dangay interprèté waxal dangal solal dip mboubou avoka
ioe may niou fi akhlou brick mofii nh khamo dara ioe seuytaneee binga done
Right fall right
Mais ndiago bi ben kotei da nelaw car kom les otr il n assum pa oft
Big up
Dip Gnatta la Faye warneu yakkou🐵
Lingay waxx c Ok Mais Soo faroul woone lay geuneu Nice
no man sa introduction bi momay ray 😂😂
Yow kana dip guay tontoul fans dip gua way
Yaw katasa nday nga bayi Akhlou brick té nga liguéy
Fans dip nga khana
😂😂😂thieuy malathion...
Yeah Malathion laa gueum man.Gayi daniouy toure leundeum rekk.Guerre daay daay saaf mondial🔥🔥🔥
RAP USA MOTAKH MOU RAW CI MONDE BI.THEY ARE REAL NIGGAS
😂 😂 😂 😂 Tu as raison mais ya tèye
Poupé Basse Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@@SomoneTv221Officiel amen 🙏 amoul bene blem nio far
No yaw akhlou brick sayi papa lene
Désolé mais pourquoi tu parles pas correctement mais
Deug rek gua wakh akhlou brick ay snitch lagnou dougnou assurer jamais ay guor djinguéne lagnou rek
Souley Diouf Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Right bro ce qui me plaît trop chez toi ce que t'es direct
😂😂😂😂
laye Pokora Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
@@SomoneTv221Officiel Oki amine
Nice mane
Youssou Pouye Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Non le gars il est naturel quoi ✌️💪🏿😹
En tt ka li moy developer rap pr se ki ne save ,
Sénégal khamoul kouy wakh deugue lou lére gay wakh
Je sw d'accord
Pique si game la bokk donc d'où kestion de nafeikh donc ce qui commente aye nafeikh arrêtez ...
Nice analyse thion mais dip le connaissant quand il aura Marre il va assumer comme il l'a fait avec nitt dof et les autres.
Everything you said is true
Grand iow yafi wakh wakhi doff
On assume
fi lama omzoo dollar nekhe il ne po iprocrit il assum
Thierno saidou Nourou Wade Yalnala Yalla oubil say bountou weurssek ba nga yek ko tei boul faté abonné si sama chaîne RUclips svp🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Mais si akhlou brick n'assume pas dip aussi n'assume pas, oubien c'est akhlou brick seulement qui doit assumer??? Quand tu regardes le direct de dip sur rap 221 dip a clairement dit qu'il n'y avait rien entre lui et akhlou brick. Donc tout ce que tu dis sur akhlou est aussi valable pour Dip. Belle analyse quand même.
Ki si bopam mo yap akhlou brick
@@socratedu22emesiecle mdr,son analyse doit être objective.
@@diojurirap.221 vraiment ! Il est doté d'une subjectivité qui avoisine l'amateurisme
#Malathion do niit Bilay, affaire yii lerna ✋ trop