Hey il n’as plus rien a prouvé il a fait son temps . Il a lutté avec toutes les generation . Donc y’a rien d’humiliation ici . Bombardier de y’a 20ans franc été bb
Y'a rien de honteux. Il a bien lutté. C le sport. Vous savez pas jouer quoi Il est en fait carrier et il.sest bien battu . Bein que je suis supporter de Franc. Mais soyons sportif .
Reugg rek nèkoufi mbeur bayilén di top bèn mbeur mèl ni reug mo meun si lambj nn niom niar nieup dougn samay mbeur mes reug 2 combat la am boy niang ak ama. Franc na xar eumeu may ko chance
Super franky le sang❤❤❤❤
Gaston Mbengue yalla nako yalla yeureum té xaré KO aldjana
Gaston mbengue😮😮😮? Qu'est ce qui lui est arrivé ?
AMINE YA RABBI INCHALLAH
Amine😢
Amine yarabi
ATTENTION À FRANC NDIAGO BII DA MEUN BEURÉ ❤❤❤❤. Felicitations Fran
Bombardier tu a marquer ton empreinte dans ce sport tu es une véritable légende mais un moment il faut savoir s'arrêter
Oooh Franc lii nga beurré nak ❤ ki es d'accord Balla gaye 2 vs Franc pour saison bii di nieuw laalal j'aime 👍
Nono ma bagn
Balla gaye2 dou beure ak mbeurou 20 milion 😂😂😂😂😂
@@salioucisse391 niora goul dh n'a khar eumeu séne sa Thiès
😊@@elzodieng8067
Bala Gaye2!!!!? Purr lan? Bro get a life
Athia ndiago or bi💪
ms farang mii man na beurè dh❤❤
Reug reug guenal ma dieul sa bakane😂
Lou léer ,Yonne leu
Reug reug mo man sen baye yenn ndieupp
koula dane ba soneu nganane mou gueineu nga djeul bakanam
@@Yoroscoot gni dagno doff
Reug mo Mane Modou lo bayou franc 12_1
Wepepepepeppp poids lourds yi wathie lén ki ma guisss 😂😂😂
Je pense que B 52 n'a pas démérité c'est Franc qui va a 100km à l'heure. Ça va trop vite pour bombardier
Kou dég "BOMBARDIEYE" bou reporter bi laalma j'aime ♥ 😂😂😂
😂😂😂
Hhhhhh😅
Roi bi boula ko modou lo dénké sam ko bou bakh franc unchallah futur roi👑👑👑👑
Après sa thies boy niang reug reug ama Balde mou doga dieul
Le jeune est plus fort que Bombardier franchement parlé et félicitations champion Courage B52
San galathie ala Modou lo😅😅😅😎
Tayson la référence dans l'arène ❤❤❤❤❤
Wa maisssssssssss 😂😂😂😂😂😂 bomb na bayyy wayyy
Bombe combine rekk lafi nekkei il fait un bon travail en donnant la chance au jeune
Sa thies ragal gue dagadone daaw franc dieul koo 😂😂😂😂kou d’accord si combat bobou défal j’aime
Li dou combat
Combat la sakh doley yemul franc eup doley gueun bakh physik
@@mamadoudiop1105tu as parfiatment raison Mane der dama rousse sakh
Ndiago bi seul ❤️💪
Ndiago bi beuré mo dé si yaram bii bilae 🔥🔥
Reug reug am nga combat nakkkkkk😂😂 ndahh yalla nga bayii modou lô
Toutes mes félicitations à Franc ainsi que les parcellois... Je crois qu'il est grand temps que Bombardier se débarrasse da sin "nguimb"
Moway li môme gawna dï Bon ouf on avance
Y’a pas d’humiliation c juste un combat bravo franc .. bombardier bon courage prend un autre lutteur la lutte a besoin de toi encore
Bly li fi beuré amoufi li combinn la😂😊
Mes bombardier un homme très gentil et srx
Non vraiment meuneu beurré neex na wallaay asiimmmm 😂
Bombe😂😂😂sa guimb bi mola ray
Non bombardier ce gars t a humilié avant et apres le combat franchement arrête de lutter c honteux ce que le gars t as fait
Hey il n’as plus rien a prouvé il a fait son temps . Il a lutté avec toutes les generation . Donc y’a rien d’humiliation ici . Bombardier de y’a 20ans franc été bb
Y'a rien de honteux. Il a bien lutté. C le sport.
Vous savez pas jouer quoi
Il est en fait carrier et il.sest bien battu . Bein que je suis supporter de Franc. Mais soyons sportif .
Bombardier amoul loumouy perte si lamb.....dafay diekhal carriéram.....legui makk leuh
C normal il a 50 ans 🤷🏾♂️
Bombardier paa la nakk frères c'est normal mais je suis d'accord warna bayi
😂😂😂😂😂 Moutiattou khaliss si lamb bakhoul bilahi
Vraiment
Mbaar fay daw déppaas
un bon combat , Bombardier a bien lutté mais a été battu .
Combat typiquement de fin de carrière pour Bombardier , sa chute est doublée de perte de force contre plus costaud que lui .Bravo Congrat° FRANC
Combine dafa khéww😂😂
L'effort favorise la jeunesse
Felisitation sama chapion
Gaston Paix à son âme
Coran : quiconque nous accordons une longue vie , nous faisons baisser sa forme " sourat yassine
ALLAHOU AKBAAR
Yalla sa Thiès def ni eumeu amine yarabi
Reug reug franc nena Kong Kong 😂😂😂
Vraiment il est temps nga bayi com yekini bala mouy gueuna niaw
Boyi amouniou yeurmandé ci makk
DOLÉ HALÉ !!!
Caméraman bi néna dou machine meunoul dieul fi dieul feulé 😂🤣😂🤣😂🤣
😂😂😂😂😂😂😂😂
Yaaa soof
Félicitation mbiress
Respect
Félicitations Franc
Daan nako niary yon kaye😂😂
Bi dh nekoul combine
Non li moy mëuna boré félicitation franc
Du courage b52
Fi beuré deugue Lafie wané
Mane dama rouss sahh
Franc lac d guere 2 moy combat bi ou franc vainqueur eumeu sene sa thies mais je préfères lac 2
Kouleu né keu serigne Amoul dangua nieuwoul fi arène nationale
Franc leu 🤩🤩🤩🤩
Félicitations franc 🎉🎉
I win again felicitations Franc 👍👍💪🙏🌍💪
Félicitations franc dane nako 2foi ❤❤❤
Félicitations Franc du courage Bombardier
Wawaw meuno dieul fi dieul fé😅😅😅
Franc mi champion la han
😂😂😂😂😂😂li comme guerr rek sarap li way😂😂😂
Bombardier a la cinquantaine ou bien presque il doit arrêter la lutte wa salam
Retraite de bombardier
Père serigne Dia Soit honnête avec toi même et arrête la lutte stp à force d insister ça deviens humiliant à la longue 🥺🥺🥺
❤❤❤❤
Franc ,lac,sathies,gouy gui,reug reug
Ie mercredi 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Reug Reug 😂😂fran yeksina
Amoul khalat sakh😅 legui mom douko bagne
Wallahi lolou rk moy combat bi sou fekké ni reug reug d'où am loumiy lay
Reugg rek nèkoufi mbeur bayilén di top bèn mbeur mèl ni reug mo meun si lambj nn niom niar nieup dougn samay mbeur mes reug 2 combat la am boy niang ak ama. Franc na xar eumeu may ko chance
Reug bagne n'a bou yague Sakh nena won même bou franc dané bombardier doumako dieul @@Dieuffdieull199
@@SauraDiop legui Mom fane la ték lolou? d'ailleurs dès fois mbeur meun nanio wakhni douniou beuri ak fekké nionguiley préparer mystiquement
Ayyy bi dieulll no li doumako lallllll😅😅😅😅
Franc vs lac de guerres Moy combat bii
Lac Dou dieul combat bi
Ndiaguo or😂bi🎉🎉🎉
😂😂😂😂😂😂😂bombou bayile 😂😂😂😂😂
Bombardier dayy Business 💔💔😂😂🤦🏾♂️
C Fini pour Bombardier Il Cherche L'argent Pour sa Retraite
Xana bi combine la kone 😂😂
👌👌👌❤️❤️❤️❤️❤️❤️💪💪💪💪
Li dou combine beuré dé😢😂
Thiey ndiago or biiii
Franc mii diambar la Kate ❤❤❤
Félicitation Franc Yaa meun yaa gueuneu fété ndaw😂mais sawaay feugu na la bénn d
kone lamb djii Amone na tay Non focus na thii rewmi mi nakk
Reug reug attention franc reck Macha laha
N'ont Mais boy bi bayoul han lac amgua problème nack 😂
Thieuy ndiago bi
21 secondes wakhon nako deh
Man de yegoumawon combat sah
Félicitations Franc anni reug reug kay ma dieul sa bakane 😂😂
Akh Li kombinn leu
Limoy degue degue diaxat diaxaté😂😂😂😂😂😂😂mossou ma geumm franc la fralon ms Li beiteunama
Reug reug anna ga😂😂😂 gneuwal
Arbit bayilen Di tela ate way😂😂
Bombardier pour mon mo eup xel nieup fayma nga Dane ma😂😂😂 sip nanou lep
Da wara bayi 😂😂😂😂
Lac 2 Sa thies eumeu séné ama balade boy niang tapha tine reug kou paré na niuew
Bilay je ne supporte pas bombardier mais j'ai du mal quand je vois ça champion faut aller à la retraite 😢
franc dafa meune beurei dafa kaw en + dafa ame doler machallah 😂 dicourage grand bombardier felicitatio franc ndiago or bi ❤
Bomb ndapp kene douko gniit t'es un grand champion mais tu devait raccrocher bala reug reug daané
Rip 🪦 Gaston mbengue 😭😭😭😭😭
Combine bi môme dafa lerr bombardier kanie la commencé attaqué 😂😂
Combat bi thia communication bah la commencer
Li dou lamba