Duo Explosif Fadam2 et BourGueweul aprés avoir vue La forme des Deux Lutteurs Mod lo Vs Boye Niang2

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 31 янв 2025
  • СпортСпорт

Комментарии • 218

  • @cheikhtidianesylla1456
    @cheikhtidianesylla1456 Год назад +13

    Fadam ya degg bou geweul bi naré diekhal gueer yi doumako diadouna😂😂😂
    Modou yalnala yalla may ndam bou sett wecc teh sedd gouye inchalla💯🏆👑P.A for life🩸🥳

  • @adamadiouf102
    @adamadiouf102 Год назад +18

    J'aime vraiment bour et fadam sen liguéye rafétena vous avez vraiment avancer la lutte sénégalaise di nianale notre champion le rois des arénes yalnako souniou borome soutourale mayeko ndam inchallah ❤️🙏

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 Год назад +15

    Yalna boy niang 2 danou

  • @roots7.628
    @roots7.628 Год назад +2

    Inchallahou tay le 1er janvier Boy niang2 doneu roi Inchallahou lou kén meussoul guiss mbeur bouy guimbou niarry yoneu Inchallahou

  • @hqby
    @hqby Год назад +22

    Boy niang défaite rek inchallah si kartanou yallah sounou borome inchallah 👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈👈☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️☝️🙏

  • @modousall2693
    @modousall2693 Год назад +5

    Vraiment c des 2 grand champion ms modou yalla nako yalla may ndam

  • @mamecheikhndiaye6271
    @mamecheikhndiaye6271 Год назад +18

    Modou Lo yalnako yallah mai ndam inchalla 🤲🙏

  • @AbouBacryNiang-jk3qe
    @AbouBacryNiang-jk3qe Год назад +5

    Yalla na yalla may modou lo ndam si barki seydina Mohamed

  • @azoubrat220brat9
    @azoubrat220brat9 Год назад +4

    Lou waay waakhone nassi delouu waattt ndam rek inshalaahhh modou lo champion

  • @ModouDiopp-fr6jc
    @ModouDiopp-fr6jc Год назад +6

    Lui waroull djiekh waye😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ahmeddogothiam1222
    @ahmeddogothiam1222 Год назад +19

    Meilleures duos de l'année 😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤

  • @TigerLionn
    @TigerLionn Год назад +2

    Boy Niang Yallah nako YALLAH may ndam 🙏🙏🙏❤💚❤💚❤💚

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 Год назад +1

    Thiey modou Kharang Lo 🤦🏿❤️❤️❤️❤️Bilahi kouko yap rek danguena wetoul si guewbi

  • @taphadiop607
    @taphadiop607 Год назад

    Bour YALLA ma ngui lay nian attoum diam ak kheiweul ak natanguei ak wer gui yaram tei Boy Niang 2 dan modou lo djelleu bou reuy

  • @salifliilakaronciserignbis4182
    @salifliilakaronciserignbis4182 Год назад +1

    Yallana yalla maye boy gane2 dame

  • @badoubrizzle5857
    @badoubrizzle5857 Год назад +3

    Aferr bi boy niang la dafa lerr

  • @freesenegal12345
    @freesenegal12345 Год назад +6

    😂😂fadam leguiiii mou exploser wakhléne ko mouy corde lou barri

  • @abdoufall3831
    @abdoufall3831 Год назад +4

    Boy nieng dacoy Dan inchla

  • @harounadiop3452
    @harounadiop3452 Год назад

    Jaime ce duo billahi

  • @ousmaneba2343
    @ousmaneba2343 Год назад

    Modou lo ak ndongo lo niome niary lo yi nio mome pikine bayiléne si hél

  • @babacarniang2172
    @babacarniang2172 Год назад +1

    Best duo doumassi doyal bilay fadam dey top bour bamou seuss 😂😂😂😂

  • @amd8735
    @amd8735 Год назад +1

    Merci fadam2 pour les contenues mais fadam lane moy sa problème AK micro achete un micro gua def si logo sa propre page RUclips ✌️🇸🇳

  • @AmadouKane-gp4uf
    @AmadouKane-gp4uf Год назад

    Bourr Daf may nekh bilahi

  • @DjilyNdiaye-pw8zx
    @DjilyNdiaye-pw8zx Год назад +4

    Yangui diawalé modou ak fadam dh boy niang ndam rk inchallah

  • @tallandiaye187
    @tallandiaye187 Год назад

    Duo de l’année ❤

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 Год назад +4

    Fadam 2 et Bour le duo de choc na saf sap 😂🔥🔥🔥

  • @AliounebadaraThioye-ho4tq
    @AliounebadaraThioye-ho4tq Год назад +1

    Retane na ba sonou😂😂😂😂😂😂😂

  • @alassanedieng2657
    @alassanedieng2657 Год назад +1

    Bilay boy niang sou dane modou dina bari niou rouse

  • @SarryElhadjiOusmane-kq5lc
    @SarryElhadjiOusmane-kq5lc Год назад +1

    Aiway Buur Guéweul ray nama

  • @fidelemendy284
    @fidelemendy284 Год назад

    Bour kou kham lamb la trio de l annee moy bour,fadam,lambalogue

  • @Babacar-j7z
    @Babacar-j7z Год назад +1

    Niome niar nieup douniou samay mbeur mai ragal na ko debout am si combat bi man balla moy sama mbeur a vie nak ❤

  • @IssaSeck-cf6cs
    @IssaSeck-cf6cs Год назад +4

    Meuilleur deo de l’année ❤😂

  • @bathiengom6036
    @bathiengom6036 Год назад +2

    Commentaire yi nn ms 😂😂ms li Fadam di Wax waxtané lamb méti na gni di ay nitt comme nioune gneup yor khôl di beugue comm gneup l’essentiel kay moy nagn deff séni liguey sans takhaw né diw la faral

  • @MomoWade-y8z
    @MomoWade-y8z Год назад +5

    Le Duo El Hadji Sapali & Alias Thioukouli 😂😂

  • @papaabdoulayesene8797
    @papaabdoulayesene8797 Год назад +1

    😂😂 Niarr gni

  • @silvazico7605
    @silvazico7605 Год назад +8

    No bour vrai comedien laa😂😂😂

  • @nawalmouzda1880
    @nawalmouzda1880 Год назад

    Nonon 😂😂😂 Burr t es un vrai guewel . Ay ya oustaz takbir ....😊😊😊 yaw do nitt

  • @layefall452
    @layefall452 Год назад

    Que le meilleur gagne sama yon nékou si Balla gaye rk

  • @cheikhoudia2722
    @cheikhoudia2722 Год назад +2

    Li nekhna way 😅

  • @Kikjhij
    @Kikjhij Год назад +7

    Modou lo kesse 🥰🥰🥰

  • @Concept0208
    @Concept0208 Год назад +7

    Boy Niang diouguéwoul ci defaite ñew beuré combat royal. Danoul mbeur ci 4 appuis, gagnéwoul ci avertissement. Ay diélam dou dém Var. Koumou dane mola may loxo. Laf Thiatt THIAPATHIOLI BI 💪🏿
    Bolén xolé adversaires yi ñou bokou dingén yedat sén bopou.
    Le 1 er ci katanou Yalla Boy Niang doumako, daneko🙏🏾

    • @lesauveur.1651
      @lesauveur.1651 Год назад +1

      AMINE YA ZAL DIALAALI WAL IKHRAM JE VOUS REMERCIE POUR TOUT ALLAH LE TOUT PUISSANT ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @badoubrizzle5857
      @badoubrizzle5857 Год назад

      Lu lerr nga wahk

    • @DameNguirane
      @DameNguirane Год назад +1

      Mais aussi mome moy le seul vip bou dieul 5 avertissement si béne mi-temps 😅😂

    • @papaibrahimaseck1003
      @papaibrahimaseck1003 Год назад +1

      Yagui doul rek mai bala 1er incha alla digua dioyati

    • @fallousylla5037
      @fallousylla5037 Год назад

      Khame gua li gua wakhe ba

  • @khadimkebe1441
    @khadimkebe1441 Год назад

    Bour ak Fadam way 😂😂😂😂

  • @aminealamine8465
    @aminealamine8465 Год назад

    Bour nekh n’a 😂😂😂😂😂😂 néna titt n’a 😅😅😅😅

  • @FallouGueye-yi6ef
    @FallouGueye-yi6ef Год назад +1

    Boy Niang Ndame rek inchalla 💪🏼

  • @TheTamsir
    @TheTamsir Год назад +3

    Buur ak Aladji Sapali 😂

  • @DjilyNdiaye-pw8zx
    @DjilyNdiaye-pw8zx Год назад +4

    Inchallah si katanou yalla boy niang day dan modou lô inchallah

  • @babacarseck6125
    @babacarseck6125 Год назад +1

    Bour guénél affairou guéwél si lambji lolou bokoul si lamb gnata combat la boye niang beuré té wakholéne affairou guéwél linga beugue gaayi khamnanouko dé

  • @doubsful
    @doubsful Год назад +8

    Franchement ce duo est fenomenale

  • @picofall3211
    @picofall3211 Год назад +3

    Sport khamé woul guéweul sport khamoul lane moy guéweul ....
    Sport leu
    Alhamdoulilah ba yalla donoul guéweul
    Modou Lo yalla nala borom bi mouseul Modou Lo si sén lamigne yi. .wakh ba sen gémign toy ta dolén ko yeuk

  • @matySylla-bm4vh
    @matySylla-bm4vh Год назад

    Kéll duo

  • @IbrahimaNiang-p5y
    @IbrahimaNiang-p5y Год назад +1

    Machallh laf tihat 👅 yalna yalla defal diammou yah Oustaz ❤

  • @ousseynoubodiang4999
    @ousseynoubodiang4999 Год назад +1

    Bilay bour dou nite 😂😂😂😂

  • @AbdouAzizSylla-v8y
    @AbdouAzizSylla-v8y Год назад +1

    Kharange lo rek

  • @ahmadoudiop5016
    @ahmadoudiop5016 Год назад

    Boulen falé ken deflen sen ligueye li moy nekhal lambe😂

  • @DaoudaJV
    @DaoudaJV Год назад

    Andeu dolel #YoonWi ak Pr #AbdoulayeSylla mifi nekal askanam

  • @FatimaSylla-j1q
    @FatimaSylla-j1q Год назад

    Bilahi roi dey niew parcelle assainies loulou d'où combat

    • @fallousylla5037
      @fallousylla5037 Год назад

      Mane modou lo Damaye def si mou khalse bou bari taye rek la kou mou djii def souba yalla na yalla Maye ndame modou lo🤲🤲🤲❤️

  • @cheiladiouf278
    @cheiladiouf278 Год назад +1

    No vrement li nekhna😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @ibrahimasorydiallo
    @ibrahimasorydiallo Год назад +8

    Que le meilleur gagne ❤🦍

  • @mouhadiop8726
    @mouhadiop8726 Год назад

    Way biur bayiniou wayy
    😂😂😂

  • @biranecamara6796
    @biranecamara6796 Год назад

    Bour homme de l'année si lamb ji 😂🎉

  • @SarreCheikh
    @SarreCheikh Год назад +5

    Modou lo rk❤

  • @rouguietousy2292
    @rouguietousy2292 Год назад

    Gni lima Len retane thi combat bi😂😂😂

  • @khadimseye904
    @khadimseye904 Год назад

    boy niang nak vraiment da warra tek diekhal pour daan loumu aam dieul coe balla gaye 2 rk

  • @SerignelahadSarr-vz4ns
    @SerignelahadSarr-vz4ns Год назад +1

    No bour rainama waye 😂😂😂😂

  • @mamadoudiop9175
    @mamadoudiop9175 Год назад

    Nom boura saf xorom 😂😂😂

  • @dembaztarkinda8270
    @dembaztarkinda8270 Год назад

    Machahalah liguey bi rafett n’a yalna yalla same lene 🙏🏽🙏🏽✅

  • @morgueye9824
    @morgueye9824 Год назад

    Le chef de kantoo delà ville de pikine😂😂😂😂

  • @abdoufall3831
    @abdoufall3831 Год назад +3

    Moudu lo day am defet

  • @cheiladiouf278
    @cheiladiouf278 Год назад +1

    Bour dinama rayyy 😂rek

  • @picofall3211
    @picofall3211 Год назад +4

    Fadam expert yaw loutax démo def émission akh père khadim samb kom niga ko défé avant combat Ama ak Modou lo pourquoi ..
    Modou Lo le GOAT 🐐 de la lutte 🤼‍♂️ sénégalaise

  • @MoustaphaThienty-ri8xv
    @MoustaphaThienty-ri8xv Год назад +1

    Bour di nitt billah 😂😂😂

  • @SerignelahadSarr-vz4ns
    @SerignelahadSarr-vz4ns Год назад

    FADAME LII NÉKHNA LOOLL YALLNA SAKH WAYW

  • @assanediallo5275
    @assanediallo5275 Год назад

    Bour dinama 😂😂😂

  • @fallouthiam6891
    @fallouthiam6891 Год назад

    Bour boye Niang la faral

  • @AmadouSow-c9m
    @AmadouSow-c9m Год назад +1

    Modou lo ndame rek incha alla

  • @ModouDiopp-fr6jc
    @ModouDiopp-fr6jc Год назад

    Na coeur yu djioli❤❤❤❤❤❤❤

  • @abdouba3396
    @abdouba3396 Год назад

    Mané gueweul doufy done rói des aréne ok😂

  • @abdoulayedione3364
    @abdoulayedione3364 Год назад +3

    Duo exceptionnel

  • @moisabarry
    @moisabarry Год назад

    Modou bane pression la wara am beuuss bou nek ak takoussane bou nek amnako kon beusse meunoul reuy si gnoune

  • @masskasse3837
    @masskasse3837 Год назад +1

    🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣buur néena Islam jamuleu wayé Modou indiwoul jamu 😀😀😀😀😂😂

  • @saliousene5187
    @saliousene5187 Год назад

    Bour del wakh wolof bayi frases bi ah

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 Год назад

    BOY NIANG AMA SAKH MAKO GUENON PARE DAFAY SOBB REKKK BOY DAY WAKH COMBAT BOU JOEW MOU WAKH KO C EVIDENT BOY SENEGAL LA DEUK FORCE MOU KHAM MODOU LO TAPHA KANDJI AMOUL LOU DANN MODOU LO. LIMOU WAKH BOUKO DEFE MOUSSIBA DALKO NDOAKH BOY AMOUL PARAKH PARAKHOU LAM

  • @azizdiouf898
    @azizdiouf898 Год назад +1

    Bour ko faral comme daga tite😂😂😂😂😂

  • @abdougueye4837
    @abdougueye4837 Год назад

    combat de tout danger

  • @mamadoumanediop3601
    @mamadoumanediop3601 Год назад

    Sapali 😅😅

  • @ndiayemamour9299
    @ndiayemamour9299 Год назад +2

    Thiay shapali😂😂😂😂❤

  • @uziiljiaye294
    @uziiljiaye294 Год назад +31

    FADAM 2 MODOU lo la faral…..Bour Boy Niang 2 la faral lou léér laay wax niiii nak vue leurs façon de communication

  • @IsmailaCamara-t8l
    @IsmailaCamara-t8l Год назад

    Waye bour guewel waye

  • @mansourndione1342
    @mansourndione1342 Год назад

    Bn2 keseee apre ngenn di comp

  • @saidoubah4729
    @saidoubah4729 Год назад

    Yenafi meune walay ndeysan bou beusba 😂fadam day xum 😂makoy sotti ndokh 😂inchalla ❤bour mom day paralysé

  • @FallouMbaye-v5h
    @FallouMbaye-v5h Год назад

    Bur soof nga😂

  • @bayebarhamjuuf2495
    @bayebarhamjuuf2495 Год назад +2

    Fadam niaww nguaa bilahy😮😅

  • @MansourDiop-zi2im
    @MansourDiop-zi2im Год назад +1

    Lo dakoy dan inchallah

  • @cheiladiouf278
    @cheiladiouf278 Год назад

    Ardo Dina liguèye souba😂😂😂😂😂😂😂

  • @ousmanendiaye2983
    @ousmanendiaye2983 Год назад

    Fadam 2 dou nitt

  • @AbdouDiop-d6t
    @AbdouDiop-d6t Год назад +1

    Modou lo yala nako yala Maye ndam ❤❤❤❤

  • @mouhidine2593
    @mouhidine2593 Год назад

    Le combat c'est sur quel chaîne tv

  • @saliougueye9833
    @saliougueye9833 Год назад +4

    Modou seul❤

  • @PapelayeSamb
    @PapelayeSamb Год назад

    Amine

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Год назад

    Modou lo kess