IL A SUBIT CERTE UN TRAUMATISME, MAIS SE N'EST PAS UNE RAISON POUR VOIR DES TRAITRES PARTOUT ET SE MÊLER DE LA PRIVEE DES GENS, SE SONT VRAIMENT DEUX CHOSES DIFFÉRENTS.
Cette fille était contre Sonko quand elle était dans l'émission balance à walf c'était d'ailleurs la raison de ses bisbilles avec oulley mané à walf et pape Ndiaye était du côté ouley et c'est séparée de cette ngoné.
Sénn birr nak mongui beugua metti 😢😂 ,si je comprends bien so néké patriote tu n'as plus le droit d'avoir des relations amicales ou amoureuses avec les gens de l'APR ou d'autres parties. En tout cas yonn bii guenn dieule bakhoul, nous sommes tous des frères et sœurs. Cet homme la mom,il est temps nak le PROS recadrékoo . polémiques rek layy wakh.
tout à fait d'accord avec Azoura, arrêtez de le taxer de fou. que cette ngoné saliou assume ses actes. elle n'est pas journaliste du tout. elle n'arrive même pas à tenir une conversation en français : sujet, verbe et complément. wassalam
*AZOURA SOUMA NAMÉ DEGLOU AP DOFF REK MOM LAY DEGLOU ,NGONÉ SALIOU NAKALA MEUNA NÉKÉ PION WOU ANTOINE DIOM TÉ BANGAKOY XAM BA LÉGUI MASSOUL DÉFENDRE KOUDOUL SONKO , DOMMAGE POUR AZOURA AK BOPOU BOU NGANÉ BI*
Saway meun guénn ko saga né dof la lépp wayé walakhi kou khamoul khamoul Sénégal 🇸🇳 sénégalais dafa leudeum ☝🏽🧠🧠☝🏽je n’ai rien contre ngoné heureux menage mais dans la vie il faut toujours assumer taupe la wonn dama dem nassi birr bayii🤷🏾♂️🤷🏾♂️où est le problème djeukeur bouma takk si farata at souna loussiy neubb gars khel 🧠☝🏽pour khalat la nitt dou deme emotion il faut écouté et réfléchir avec la raison
Heureux manage Ngoné Saliou. Azoura lingaye wah amnga si preuve wagnil sa galatiatieu. Yaw loutah nga bayi ba nitt wara mariage ngay Dora guéna di wah. Pourquoi tu pense que gneup lagne warone diap. Ma question c’est qui est le mari de Ngoné Saliou Hana APR la bok
Sonko kay ma diox la stratégie bu gaw pr t'éloigner de Azura il faut l'interner à l'hôpital il doit prendre des soins médicaux il est dépressif bamu tané ga intégrer watt ko inchalla
Non je ne peut pas croire que ngoné saliou sont marie est Félix Antoine Dion ???? Lolou mounou mako gueme La plus part des faits qui se sont déroulés ici Antoine Dion amna si waleu Mais comment critiquer le régime et se marier avec quelqu'un qui s'y trouve
Azoura tu nous emmerde !
Ngoné je te souhaite un heureux ménage
Ce azura nous emmerde Cette journaliste peut choisir qui elle veut
Azoura tu es vraiment honnête et courageux.Merci beaucoup vrai patriote Azoura Fall que le bon Dieu vous protège.
Heureux ménage ngone contane si yaw laf thiat
Azoura je suis d'accord avec toi
Merci azura machalla ❤
Merci beaucoup patriote Azoura.Vive Azoura.
Azoura Mii khana dafa nobon ngone saliou 😂😂😂
Mais Ngoné Saliou amna droit seuye ak kouko nékh,Ngoné Saliou ba khékh dioté khékh na, yak dér bakhoul
GONE DOU DARA ESCROS LA ESPION ANTOINE LAWONE YAGANA AK FARAM BI VRAI DOMERAM LA
IL A SUBIT CERTE UN TRAUMATISME, MAIS SE N'EST PAS UNE RAISON POUR VOIR DES TRAITRES PARTOUT ET SE MÊLER DE LA PRIVEE DES GENS, SE SONT VRAIMENT DEUX CHOSES DIFFÉRENTS.
Mais il a le droit de poser des questions, il faut arrêter de dire qu'il est amoureux de n'goné. Khélam mo téy.
Yallah reka kham mais domou adama dafa leudam rawatina Senegalese aka nio faux way mbirou PM Ousman Sonko mom koukoy mboubo dinga werou
Yéna diapé Azoura dof mes dofoul waxi nite lay wax
Mane ngoné sétane nako sans limite mouné diokh naniouko khalis mou lék ko
Avec quelle preuve Azoura avec tout le respect que JE Vous doit.
Peut-être azoura sait ce que nous ignorons il faut l écouter
Pas de confiance dans la vie on ne peut pas connaître une personne
Khana ngone sagnoul lolou kon de. Dina ma bet loolllll
Garde corps Antoine diom moy dieukeur Ngoné saliou? Les questions de azoura sont légitimes.
Vraiment dano sone ci thiowli
Vraiment sone
Azura Ngone Saliou souko nekhé mou sey ak kou nekh may niou diamou
PASTEF ne t' appartient pas,tu n'est pas non plus le gendarme de PASTEF
Ndakh yalla
Da nekhoul deg mais azoura limou wakh nekhoul wedi o t’accusé d’être une espionne et tu viens de marier avec son garde corps
Azoura Bayile ngoné stp.
Merci ngoné Saliou Yalla nalla souniou Borom bi aral bopam thi barké Muhammad Aleyhi Salatou Wa Salam 💚
Kî meunoul wakh niou bagne Ngoné Saliou Diop
Mais enfin pour qui se prend ce fou Azoura ????
Azoura dépasse les bornes c’est pas ton problème
Vraiment, il nous em.....de
Lou Lerr gaye wakh Assane Nit mo Leudam surtout Senegalais
Ngoné ki porteko plainte
Il mérite la prison Wala fann
Azoura limouy wakh si guoné sama khel téyna
En tout cas on dirait il a du solide sur cette dame
Azoura dagua wara nopi
il y'avait beaucoup de ministres de Macky Sall qui sont des fans de Ousmane Sonko, quelqu'un peut détester Sonko et sa femme et ses enfants l'aiment
On s'en fiche AZOURA Yagui fenn nakk bayil diambour bi Ngone Saliou défoule Dara heureux ménage ;
Pa Assane waro wone wo doff bii
Wahoul deug
Je suis désolé pour toi azoura
KHAMOUL DARA, FÉNE RÉK, CHAYTANÉ, NGONÉ MOLA GUEUNE
Ngoné kidal portéco plainte mou indi ay preuves
Doff dou wérr Azoura je suis désolé mais tu n'est un homme de media ou audio visuel STP reste dans l'ombre stp
Ce juriste qui rentre dans les lives comme ça qui n’a aucun sens
Je suis choqué
Pa Moussa, tu n' as jamais parlé de Moussa Fall général ? Pourquoi ?Pastef est infiltré.
AZOURA BAYIL FENN, TÈ NGA DEM LIGUEYI, GNOUNE NGO TEYEE WON MBED MI TEÈ SOKHLA WOUL FEUG DEUNE, ON L'A FAIT POUR LE PATRIE 🇸🇳
Cette fille était contre Sonko quand elle était dans l'émission balance à walf c'était d'ailleurs la raison de ses bisbilles avec oulley mané à walf et pape Ndiaye était du côté ouley et c'est séparée de cette ngoné.
Oui j m demande prquoi thioro mandela et ouley mané sont pas venu à son.mariage c bizarre j n comprend plus bilaye.
Gone ame naa droit seuy ak kouko nekhe couplé you barri doun ay patriotes surtout les hommes mais bou sen diabare beugue sonko doun thi mane dara
Azoura nous pompe l'air . Pour qui se prend Azoura pour vouloir juger tout le monde
*AZOURA MII MOOO GNAKEU XAM XAM,NI BOPOU BI NGANDÉ LA XÉLBI TOUTÉ😂*
Bilay ya meuna doul deug
AZOURA MII CHAYTANÉ LA. DIAM LA SÉNÉGAL BEUGG, THIOWLI DOYNA, LIGUÉY LANIOU SOKHLA
Sonko doit se débarrasser de ce fou.
Azou khamoul saram ndayam
Azoura mi dof BOU mak la
Azoura fall bouniou sonal. Ngoné Saliou bouko nékhé mou seuye ak kouko nékh, ne nous fais pas chier. C’est sa vie privée
Décidément, Sénégal est dur dé . Maintenant personne n'a le droit de se marier avec qui bon lui semble.
Sénégal jai trop peur 😱
Azoura il est temps ñiou freinako. Ngoné Saliou bouko nékhé mou seuy ak garde corou Antoine Diom. C’est pas la fin du Monde.
NHONÉ N'EST PAS CLAIRE
ON SAVAIT
WAYÉ.UN JOUR VIENDRA..
WAKHLÉN
.❤
Sénn birr nak mongui beugua metti 😢😂 ,si je comprends bien so néké patriote tu n'as plus le droit d'avoir des relations amicales ou amoureuses avec les gens de l'APR ou d'autres parties.
En tout cas yonn bii guenn dieule bakhoul, nous sommes tous des frères et sœurs.
Cet homme la mom,il est temps nak le PROS recadrékoo . polémiques rek layy wakh.
Vraiment li dafa eupeu
Maitre El hadj Diouf mou ngi beugg am deugg ci wa pastef.
Personne n’a le droit d’être amoureux librement.
Li nak nekhatoul
Woy. 😂😂😂😂😂
Azou
Ngone je te souhaite assez de courage
Ngoné Saliou ñieupeu guiss naniou position wam.
C'est vrai que ngoné est libre de se marier avec qui elle mais azoura aussi a le droit de se poser des questions
tout à fait d'accord avec Azoura, arrêtez de le taxer de fou. que cette ngoné saliou assume ses actes. elle n'est pas journaliste du tout. elle n'arrive même pas à tenir une conversation en français : sujet, verbe et complément. wassalam
Boy demal liguéyi tu nous emmerde
*AZOURA SOUMA NAMÉ DEGLOU AP DOFF REK MOM LAY DEGLOU ,NGONÉ SALIOU NAKALA MEUNA NÉKÉ PION WOU ANTOINE DIOM TÉ BANGAKOY XAM BA LÉGUI MASSOUL DÉFENDRE KOUDOUL SONKO , DOMMAGE POUR AZOURA AK BOPOU BOU NGANÉ BI*
Azoura mo meuna toogn
Saway meun guénn ko saga né dof la lépp wayé walakhi kou khamoul khamoul Sénégal 🇸🇳 sénégalais dafa leudeum ☝🏽🧠🧠☝🏽je n’ai rien contre ngoné heureux menage mais dans la vie il faut toujours assumer taupe la wonn dama dem nassi birr bayii🤷🏾♂️🤷🏾♂️où est le problème djeukeur bouma takk si farata at souna loussiy neubb gars khel 🧠☝🏽pour khalat la nitt dou deme emotion il faut écouté et réfléchir avec la raison
Sonko monou togne rék ba azoura diko diégué
Heureux manage Ngoné Saliou. Azoura lingaye wah amnga si preuve wagnil sa galatiatieu. Yaw loutah nga bayi ba nitt wara mariage ngay Dora guéna di wah. Pourquoi tu pense que gneup lagne warone diap.
Ma question c’est qui est le mari de Ngoné Saliou Hana APR la bok
Azoura faut pas s, attaquer aux femmes comme ça si tu ne peux pas révéler tout
Faut arrêter ce Azoura ki nitte leu soiuko nékhé seuye ak koiuko nekhhj lanela doull wayyyy
Sonko kay ma diox la stratégie bu gaw pr t'éloigner de Azura il faut l'interner à l'hôpital il doit prendre des soins médicaux il est dépressif bamu tané ga intégrer watt ko inchalla
😂😂😂😂 bilay
Sénégal nekhna azoura fall mii
Way aeoura doff bi wakhoufi touss
Ngone nobal koula nekh seuyeul koula nekh
AZOURA khamo touss wakho deugg
Elle est libre de se marier avec qui elle veut. Ngoné menoul yakhal Sonko touss. Délossilène sène xel touti.
Azoura tèèyal
Daga beurri wah
NA KATE NDEYAM AK MENAGE NIOU PROJET LANIOU WAKH
Azoura dafa douf dafa réew😂😂
Azoura yagui tondieu ngone bayil ndiambour soula porter plaints yaye tondieu
Vrai domerame moy kiii...bilhai mo nara yakal wa pastef bahna rek...sonko si bopam mo wara wahak ki
Ca peux etre vrai aussi naniou def nank
Mais bou lolou wesso wagni denré alimentaire foumou tollu
Ya guene dof Sénégal
Yal na sonko bayi fen
Nédo khoulou gaz 🔥 demal nopalou
Ece ke dou Anita diop
Yafi ndieuka saga diomaye
Boy boulegnou fonto dokhal nga liguéyi
Non je ne peut pas croire que ngoné saliou sont marie est Félix Antoine Dion ???? Lolou mounou mako gueme
La plus part des faits qui se sont déroulés ici Antoine Dion amna si waleu
Mais comment critiquer le régime et se marier avec quelqu'un qui s'y trouve
Bou yague nguen xaar sénégalais yi niaar😅
Wakho deug khana kon Mayabé bomou démé boy yi bagne ni dou gisse Sonko khana mom taupe la won motakh gnou mou gisse Sonko
Tu nous emmerdes Azoura.Yagui beugue eupeule legui.diotena niou tek la sa place.Dofoulo djine diapoula.Dagaye dof doflou rek
STEVE JOBS MOO GNU TOOGN BA TOF BU JOG REK NEK CI MEDIA YI
Azoura est un vrai menteur
azoura maye niou diam ngoné amena droit séye ak kokou nekh na donne dioulite rek té mou beugue ko
Ki dof la😅😅😅😅😅😅😅
Sonko est pour l'Afrique entière
Sonko est pour sweet beauty il continue a se faire masser triste
Duul rekk ngay def li ngay wax xamoo si dara😡😡😡😡😡😡😡😡
Merci azoura ❤❤❤❤
NGONE DOU DARA ESCROS LA ESPION ANTOINE LAWONE YAGANA AK FARAM BI VRAI DOMERAM LA
Bilahi azoura deuk rék la wakh
Mais ngone amoul droit beug kouko nekh koi😂😂😂yeena soff fi senegal nieupa khamante
Azoura yaw da nga soff momo nit thie yaw rék khékho pour Sonko