AFFAIRE DE AKHLOU BRICK: SE VENDRE POUR SACRIFIER LA JEUNESSE... MEME AVEC 100 MILLIONS DE FCFA ILS

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 дек 2024

Комментарии •

  • @hadjamouhamadmbengue7849
    @hadjamouhamadmbengue7849 Год назад +83

    Tu as parfaitement raison Wess tu n'as rien dit de mal continue sur cette voie il y'a certains gens qui n'aiment pas entendre la vérité

  • @kalidoukaneollaid4509
    @kalidoukaneollaid4509 Год назад +3

    Wesh dafa nafek Akhlou danouy job topal felei...Yor sa sen di xastei reik ..Akhlou tayla geneu ame respect geneu pesei

  • @moussasene9352
    @moussasene9352 Год назад +3

    Meno dem wah l'en ko secrètement ay vi ngay weur di wah fautou thi internet yalla tahoul kon ay vu ngay weur . Tu seras fort en politique.

  • @FallouDioum-qv1if
    @FallouDioum-qv1if Год назад +1

    Mon pays 🇸🇳🇸🇳🇸🇳manque se genre de personnes ,yalla Nala yalla Sam frére

  • @mouhakamara3407
    @mouhakamara3407 Год назад +5

    Bayi ba concert bi dess une semaine Guay tokk di influencer jeunes bi❤pour ñou bania déme si concert bi wayé dara tall bou yala tall🔥moy akhlou brick wakh meunoul thie niom dara gua balma nak🙏👌🎤🎧🔥🔥🔥

  • @blackreal6709
    @blackreal6709 Год назад +8

    Fimou tolou ni talounou aye akhlou brick free Sénégal ✊🏿✊🏿✊🏿🇸🇳

  • @matarlepanafricaniste2734
    @matarlepanafricaniste2734 Год назад +20

    Sénégal rappeur dernier génération yi niom yeup nio yamm Big respect aux grand
    Nit dof

  • @oussamaboure9623
    @oussamaboure9623 Год назад +2

    No vraiment wesh sohw Déga contre akhlou
    brich Lou takhe wakho si ngaka bledé aussi

  • @kanyb.officiel7293
    @kanyb.officiel7293 Год назад +21

    La jeunesse sénégalaise est perdue
    Khama touniou founiouy tekk sen tankk
    Folie rek…Diadieuf Wes👍🏼❤️

  • @falloudiop297
    @falloudiop297 Год назад +4

    Comme khamgua nii yay alwakha rek bakhna😂😂. Mais perso je suis pas en phase avec ton raisonnement. Je viens tout juste de voir l'entretien de Ara sur confidence mais ils ont toujours ce petit plus qu'ils ont toujours eu et qui a fait leur charme auprès des sénégalais. Peut-être que upgrade dafay am et que parfois milieu bii dafa am loulouy lathie pour certaines choses. Thi cadre xbet bii mom je suis vraiment pas d'accord avec ça mm si ça leur apporte de l'oseille limouy yakh mo eup fouf et j'espère qu'ils vont rompre ce partenariat avec ces géants qui sont là que pour rendre addict et fainéant la jeunesse. Sinon super vidéo 💪🏾👍🏾🤜🏾

  • @MotivActions2
    @MotivActions2 Год назад +8

    Vraiment je te kifff bro ❤️ diameuh rk ngay amm. Suis fan's de Ahlou Brick mais suis vraiment d'accord avec toi 🎉🎉peace And love bro ❤️

  • @falloundiaye2515
    @falloundiaye2515 Год назад +2

    Tégua traité cas sénégalais moy situation rew mi injustice totale et emprisonnement des jeunes qui se battent pour la liberté et la démocratie du pays

  • @FantassinMat
    @FantassinMat Год назад +1

    Sénégal tous le monde est motif de se qui se passe de gno dieul ignorants yi tek len thi kanam rc plus sen série you gniak fayda yi

  • @YTADISGNASA28
    @YTADISGNASA28 Год назад +2

    Merci beaucoup c’est que au Sénégal wax fi nit deugueu mo yomboul digni fogni danko bagne alors que ce n’est pas sa❤❤❤

  • @BUUROLOGIE00
    @BUUROLOGIE00 Год назад +6

    Merciii damako waah sma xariit yii ba sone mais keen geumouma🥺ces artistes sont égaré maintenant tous nak🥺😭

  • @weuzcanax1201
    @weuzcanax1201 Год назад +8

    Je suis fan de Akhlou brick et je suis Barhamien mais vraiment ces derniers temps ils m'ont déçu wallahi wesh tu as vraiment raison

    • @bambangom5545
      @bambangom5545 Год назад

      Fans bi geumo ko Motax

    • @IimpR9302
      @IimpR9302 Год назад +2

      ​@@bambangom5545 être fan et être fanatique c'est deux choses différentes comprendra qui pourra

    • @moussatounkara3618
      @moussatounkara3618 Год назад

      😅😅😅 arrête de te drogué bro

    • @weuzcanax1201
      @weuzcanax1201 Год назад +2

      @@IimpR9302 bien répondu 💯✨

  • @Outajunior1011
    @Outajunior1011 Год назад

    Wesh show yaw yay kann😮meuno wakh baa eup xam xam wa Akhlou brick😊yeine yii nak sokhor laa😊valeur rou Akhlou brick dou meusa dagn😊saa xalate bakhoul

  • @SeynabousarrS...7824
    @SeynabousarrS...7824 Год назад +30

    Toujours véridique, ravie de t'écouter, analyse très pertinent, on vous aime beaucoup frère Wes ❤❤❤

  • @layelaye4128
    @layelaye4128 Год назад +4

    Wesh yow élément ngaka blindé nga

  • @aicha1859
    @aicha1859 Год назад +21

    Bien dit Wes analyses toujours pertinentes 👍🤝 merci

  • @abdoungom5338
    @abdoungom5338 Год назад +1

    Niari goordjigene ni mbour geumouniou Dara 😂❤❤

  • @mouhamadoumoukhtarsall3441
    @mouhamadoumoukhtarsall3441 Год назад +13

    Oui suis d’accord mais cette remarque fallait le faire avant mais non pas attendre maintenant ou il prépare leur concert pour le faire
    Respect Akhlou Brick🎉🎉🎉

    • @OneNation591lofficiel
      @OneNation591lofficiel Год назад

      Ce petite Soeur yi daniou bocoul ci clip bi motah ngay wakh ??? La prochaine fois invite tes petites Soeur akk cousine niou dem tournage ci genre vidéo bi ensuite tu aura ton mots à dire .

  • @alphasow2405
    @alphasow2405 Год назад +5

    Ouhou akhlou joumna c sama Guiss guiss 😢🎉

  • @Maddylajambenoire
    @Maddylajambenoire Год назад +52

    C'est akhlou brick qui m'a fait aimé le new rap galsen mais aujourd'hui c'est eux qui m'ont encourager à arrêter d'écouter de la musique. Vraiment quand l'industrie de la musique prend le contrôle de l'artiste, les valeurs disparaissent, dernière exemple en date Mia Guissé 😓😓😓

  • @assbayedieng3721
    @assbayedieng3721 Год назад +6

    Tay mom je suis trés d'accord avec toi

  • @cheikhounandiaye6153
    @cheikhounandiaye6153 Год назад +3

    Makcy mon yakh sénégal rk wayè yalla bakh na 🎉

  • @aramendiaye8730
    @aramendiaye8730 Год назад +2

    Barki alhourane iaw rk ya mérité 1 millions d'abonnés bonne continuation ❤frère 🎉❤

  • @xibaarlene
    @xibaarlene Год назад +1

    Wakh si yalla ak kham yalla motakh niou sania ligueey ak 1xbet niapal sa jobou ndaye feulei

  • @fallouwar7258
    @fallouwar7258 Год назад +9

    Bilaie deug rk lay wakh senegal so wakhe deug gnoune dafa beuri wakh ❤❤

  • @Revolution_hip-hop-mbour
    @Revolution_hip-hop-mbour Год назад +1

    Niou gatteu xam xam melni yeen motax deuk bi Di taakkeu😏😏😏

  • @mamadouthiam8322
    @mamadouthiam8322 Год назад +17

    boy wakhal ci ngaaka , défnaco seytané nga rék

    • @StreeterTea
      @StreeterTea Год назад +5

      Wah deug yalla ki nafekh leu rk. Dafay far dafay fetei loloi moy Thiatam limou wah deugleu mai dafa nafekh. Day farr

    • @bambangom5545
      @bambangom5545 Год назад +2

      Ki di nafekk bou magg

    • @sonkofocus2024-ph4hv
      @sonkofocus2024-ph4hv Год назад

      Xana yago ko. Setann

  • @bibichetratra6874
    @bibichetratra6874 Год назад +4

    Ils ont biens chanter mais clip bi les filles pensé pour le futur jeunesse passe tellement vite bilay Aka gaw aduna

  • @khadyja6534
    @khadyja6534 Год назад +13

    Chapeau, aujourd'hui t'as tapé fort vraiment

  • @makhtarsarr803
    @makhtarsarr803 Год назад +1

    Ets ce que Tamitt Veuleur Diékhoul Sénégal koo Yaakaar neh dafa ame Veuleur rék koko mo geunuë yéss😢😢

  • @awaba4869
    @awaba4869 Год назад +1

    Je suis 💯/💯 akhlou brick mais tu dis vrai franchement

  • @gooryallahofficiel760
    @gooryallahofficiel760 Год назад +1

    Vraiment deugge néhgoul mais taye mome damaye validé akhlou brick moye sama rappeur

  • @modoundiaye8538
    @modoundiaye8538 Год назад +1

    mrc wesh contane na si ieo trop deug rk gafi wakh blh yalla na sa diam yague

  • @awaconde8595
    @awaconde8595 Год назад +1

    Akhlou brick le 3 juin à ľesplanade mussé des civilisation noir niou deme ❤

  • @SerigneSamb-uc6nl
    @SerigneSamb-uc6nl Год назад

    King wesh rk lay topu

  • @baboucardiop4350
    @baboucardiop4350 Год назад +1

    Wakh deug rek moye yone ! Avant j'écoutais ce groupe par rapport aux messages et aux clips vraiment cool. Maintenant à cause de la tune, c'est du n'importe quoi de A à Z.

  • @famafaye4002
    @famafaye4002 Год назад +103

    vraiment les rappeurs sénégalais sont actuellement perdu de chemin je suis vraiment désolé

    • @le_kaiser_4228
      @le_kaiser_4228 Год назад +4

      Bien dit sauf omzo jay21 et ashs the best 😊😊

    • @cheikhnadiop3427
      @cheikhnadiop3427 Год назад +1

      fama xamo si dara sakh

    • @elimanethiongane7346
      @elimanethiongane7346 Год назад +1

      J'espère que vous vmne comprenait pas l rap

    • @Cisse-zv7mm
      @Cisse-zv7mm Год назад

      ​@@le_kaiser_4228bro yangi faté rapeur bou mag bii canabasse

    • @famafaye4002
      @famafaye4002 Год назад +2

      @@Cisse-zv7mm Canabasse il est respectueux par rapport aux autres il a du talent et il est cool rester dans son coin ici aux États-Unis on écoute

  • @AdySylla-dy3se
    @AdySylla-dy3se Год назад +3

    King wes mon youtubeur préfère wouto kharite mais mane défnala kharite parce que deugue rék ngay wakh mane yaw rék laye topou👂

  • @birdbasse2415
    @birdbasse2415 Год назад +1

    MachaAllah Wes show Yalla na diam yague 🦅🇸🇳✌🏿

  • @abdouaziz2419
    @abdouaziz2419 Год назад

    Bilahi wesh c’est un bonheur de t’écouter. Lep deug lheu khaliss yah na lep.

  • @alonzo0
    @alonzo0 Год назад +7

    Il y'a un seul rappeur au Sénégal et c'est Boutikou Laye

  • @nouhankaba1391
    @nouhankaba1391 Год назад

    Big Up bro gayi Sene poche rek après ils se disent Talibeu Bay Niass

  • @piijunior221
    @piijunior221 Год назад +2

    Wesh ioe danga beuri wax , gni ils sont respectueux té aussi ay Talibé lagn . Depuis lors waxo si dignou sonal kom ça. Shit way

  • @moussasene9352
    @moussasene9352 Год назад +2

    Yow aussi vu ngay weur au

  • @Ibrahima880
    @Ibrahima880 Год назад +1

    Wesh sohw le meilleur souligneyr❤❤❤❤bon continuation 👍👍

  • @limelayeofficielle3384
    @limelayeofficielle3384 Год назад

    Machallah frère job bi Nice

  • @vieuxndao7560
    @vieuxndao7560 Год назад +3

    T'as parfaitement raison mon gars ils m'ont déçu j'attendais pas ça de leur part.... mais dire que ils représentent les niassénnes là c'est exagéré.ils ne sont pas des niassénnes.

    • @amoulYakarfall
      @amoulYakarfall Год назад +2

      Je suis pas d'accord avec eux mais nak li musique le bokoul ak sene tariha ne mélanger pas les choses

    • @vieuxndao7560
      @vieuxndao7560 Год назад +1

      ​@@amoulYakarfall on est au Sénégal on a notre culture...il faut regarder les old school il y avait combien de rappeurs disciple de Baye Niass ils étaient nombreux...ils n'ont jamais prôné ce genre de vidéo au contraire... c'est de la musique comme tu le dis mais ça ne colle pas avec Sénégal je désolé

    • @Abdoullahi.
      @Abdoullahi. Год назад +1

      ​@@amoulYakarfall Saway musique Dafa Haram si dinè l'islam bouniou défé Lou bone yigni def nieuw fi nane daniouy diokhé ay explications AK ay leçon de morale.

    • @amoulYakarfall
      @amoulYakarfall Год назад

      @@Abdoullahi. mai j’espère que yaw do deglou musique sinon kone yagi def lou haram

    • @Abdoullahi.
      @Abdoullahi. Год назад +1

      @@amoulYakarfall J'ai arrêté d'écouter de la musique. Depuis j'écoute le Coran , les xassaïd et autre chant religieux.

  • @mamadousy9149
    @mamadousy9149 Год назад +1

    C Faux frère une chose est clair 👉magu fo mou togue manna guiss lo amné halé manna takhaw dou KO guiss ok si on veut critiquer on po critiquer n'importe qui

  • @sabilniane7072
    @sabilniane7072 Год назад +2

    Free Senegal laniou tall instant bi🇸🇳🇸🇳💪🏾💪🏾

  • @mdsaleem5168
    @mdsaleem5168 Год назад +6

    الله مأن هذا المنكر انكرنا😢😢

  • @xibaarlene
    @xibaarlene Год назад +1

    Akhlou brick mo tay katal sa jobi ndaye

  • @moustaphad.4274
    @moustaphad.4274 Год назад +3

    Sénégalais meuno ko diaye prek mais yow tout le temps yangui diaye prek sénégalais yi

  • @kharidiafall
    @kharidiafall Год назад

    Nioune on t'écoute tu apporte bcps

  • @Sirediarra12
    @Sirediarra12 Год назад +20

    DIP référence pour les jeunes

    • @hadjarandiaye2861
      @hadjarandiaye2861 Год назад

      Ah bon mais dip moy le 1 à faire clip avec une fille en bikini

  • @amydiallo6219
    @amydiallo6219 Год назад

    Ay way yabilen Akhlou brick nak

  • @talibesonkomousellemi3898
    @talibesonkomousellemi3898 Год назад +2

    Focus 2024 dou ngiou à tardé sy ay wakhou doof sonko 2024

  • @sarrbrickest-kp2zo
    @sarrbrickest-kp2zo Год назад +3

    Bayii lén di Profite- si beussou diambourr

  • @bassiroudiallo9307
    @bassiroudiallo9307 Год назад +6

    Respect bro analyse pertinent ❤

  • @DJofficiel-e1v
    @DJofficiel-e1v Год назад +1

    Salam Wes Show tv je vous suit beaucoup say vidéo mais Nice vraiment doumala critique nak comme gas yi non à propos de Akhlou brick eux ay talibé baye lagnou deug

  • @diarafnoble8010
    @diarafnoble8010 Год назад

    Sa wayy Akhlou brick massouk changé style sen première clip ak sen derrière clip amoul différence

  • @NdagaDieye-z8f
    @NdagaDieye-z8f Год назад +2

    Sokhor am na

  • @MaléMbaye-q2y
    @MaléMbaye-q2y Год назад +1

    Sa way demal nga tokk feullé way

  • @cheikhmbaye5629
    @cheikhmbaye5629 Год назад

    Tu ne dit que la vérité
    J'ai même abonné dans ta chaîne car tes un homme véridique machallah continue sur ce lance courage frr

  • @aradiedhiou2127
    @aradiedhiou2127 Год назад +1

    Ce n'est pas pour rien Allah interdit quelque chose .....car il sait mieu que quiconque le dangé vers lequel nous dirigeons...

  • @PoLoH-TV
    @PoLoH-TV Год назад +18

    Et pourtant Jusqu’à maintenant ils sont très Respectés

    • @Diop1994bamba
      @Diop1994bamba Год назад

      Par qui

    • @kingdave2984
      @kingdave2984 Год назад +2

      Ya worr. Nekeuh sénégalais da meti. Parce que sénégalais khamoul personnes ak personnages khamou'iou c'est quoi la vie d'un artiste, comment l'artiste doit faire pour gagner sa carrière

  • @aladjimane5594
    @aladjimane5594 Год назад

    West wakhal thi ashs the best mou ngui deff lou Nice thi rap bii bilahi song wamii dafaa am sens

  • @ambroisediedhiou1156
    @ambroisediedhiou1156 Год назад

    Wesh o contrôle merci frère encore

  • @amadoudieng7154
    @amadoudieng7154 Год назад +3

    Tu as parfaitement raison deugge né khoul

  • @ibrahimaanne7070
    @ibrahimaanne7070 Год назад +1

    Akhlou brick ou rien dans tout les cas on les aime

  • @papaseydoudiop
    @papaseydoudiop Год назад +3

    Le grand vous êtes tellement véridique Deug rek guay waxx

  • @WallyB.Seck-Music
    @WallyB.Seck-Music Год назад +1

    Souma wadji boy wakh guenessi Baye niass la wakh degal limala wakh rekk

  • @daoudagueye524
    @daoudagueye524 Год назад +2

    Tayy mom dacorroumaa.,

  • @DiamsoneDiouf
    @DiamsoneDiouf Год назад

    Yenn dooleenn talibe Baye bilahi Sénégal hakill moy rapr

  • @annouchamarena3686
    @annouchamarena3686 Год назад +1

    Meusou'niouma nekh bilaye doumasa dèguelou sène musique

  • @bathiendiaye634
    @bathiendiaye634 Год назад +2

    Mais kon son ngakka son wam bi incorrecte khn guisoko😢

  • @MameCheikh.
    @MameCheikh. Год назад +1

    Wes sadik nga 😂😂akhlou brick safara😂😂😂

  • @faramarenecoiffure5234
    @faramarenecoiffure5234 Год назад +1

    Wess bi mome je ne suis pas d’accord avec tw music day avancé music pour divertir leu mais pas pour conseil 😂😂😂😂iow bro esk kham nga louye lawti lolou ngay tathe avant tout d’abord dieulma si souf ma wakhla louy mawti 😂

  • @yacinefall8372
    @yacinefall8372 Год назад +1

    En effet ils ont trop déçu !

  • @djibydia5539
    @djibydia5539 Год назад +9

    C que disait omzo dollar c la vérité ces rappeurs ils ne assume jamais

  • @cheikhdioum8624
    @cheikhdioum8624 Год назад +1

    Album bingay wakh niongui koy conse dh yako consoul

  • @khadijandiaye3462
    @khadijandiaye3462 Год назад +6

    Je suis d’accord avec toi d’une part mais d’autres part no bro
    Du moment que tu dis que s’en façon clips yi dafa changer d’accord lolou peut-être meun nan ko kholat
    Mais par contre côté partenariat ak ay on xbet Lolou nekoul ni signé nanou ak gnom que danou koy jouer wala affaire juste que sen liguey Mo lathei ins partenariat iow mi sax amon na ay temps nga def ak gno collaboration même si y’a don wax que digueuloko keneu pour foufou mom meunoul yak dîner keneu en plus nitt limou lay wonn ak loumouy dounou meun woutei bou bakh sax voila lolou Mo nekon sama guis guis diegeulou

  • @Enzoshifow
    @Enzoshifow Год назад +2

    Serigne Kouna mayniou ak Artiste yii Sénégal Nio ngi raye ay xaléy ci ay manifestation do ci wax ngay diabolisé Artiste yii fi Yallah rék képp dong mo xam ku kou bax waxalal senegalais yi sén naxaar mo gën ✌️ peace

  • @elimanethiongane7346
    @elimanethiongane7346 Год назад +3

    Frère galgui baayii naalaa fii ,brickmillionnaires respect tjrs les femmes,boul diakhassé brick Al sénégalais yii

  • @xibaarlene
    @xibaarlene Год назад

    Ioe wesh show sa leufeul ndaye feulei wakhofi thiotou ndayam gni daniouy ligueey

  • @mamadouthiam8322
    @mamadouthiam8322 Год назад +24

    rendez vous le 3 juin avec Akhlou Brick en concert au musée des civilisations noires, à ne pas rater🎉🎉

  • @smaplarime8904
    @smaplarime8904 Год назад +2

    Mais musique affaire de saye saye la nitou yallah deug douko def,gni si nek di mboubo dîné dji yep ay nafekh lagn

  • @angeliquediatta5930
    @angeliquediatta5930 Год назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤️

  • @mohamedndiaye9840
    @mohamedndiaye9840 Год назад

    Bonne annalyse wes et bonne continuation 💯 💯💯💯💯

  • @taphandiaye3758
    @taphandiaye3758 Год назад +3

    Merci frère 🙏🙏

  • @mainacisse8962
    @mainacisse8962 Год назад +3

    Merci wesh ❤

  • @cheikhdioum8624
    @cheikhdioum8624 Год назад +1

    Saway yaw khana akhlou brick nga yape may niou diam way akhlou brick ba légui niongui deff Liniou done deff clip bou nek ak limou lathie gni liniouy daniouko maîtrisé kham ko

  • @awadieye293
    @awadieye293 Год назад +2

    Pour man dousi gnom si djiguéne yila gnom gnoko nagou célébrité diaral nalén louné

  • @moustaphafaye2056
    @moustaphafaye2056 Год назад +7

    Wesh li gha def ni pourkoi wakhoko avant gha bayi ba show bi Di nieuw' ghay critiquer koï mé takhoul show bi echek inchallah Dina réussi ligha wara wakh berina ok il sont toujours très respectueux juska présent et des vrais talibé

    • @mouhakamara3407
      @mouhakamara3407 Год назад

      Li deh lawakh frère ñi danio sokhor trop✌

  • @mamadoubalde-xt2dj
    @mamadoubalde-xt2dj Год назад

    Merci 🙏 ❤❤❤❤

  • @IimpR9302
    @IimpR9302 Год назад +2

    Big up Wesh

  • @mamadouthiam8322
    @mamadouthiam8322 Год назад +2

    yow do wakh ci Ngaaka Blinde ak sunubet wala , kharou tabisk nga beug lall ?😂😂😂😂

    • @bambangom5545
      @bambangom5545 Год назад +1

      Sou wakhé si ngaaka kon dou am kharou tabaski