Akhlou Brick : les deux artistes nous parle de leurs histoires avec Baye Niass

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 8 фев 2025
  • Akhlou Brick : les deux artistes nous parle de leurs histoires avec Baye Niass

Комментарии • 351

  • @bayelamine6144
    @bayelamine6144 5 лет назад +129

    Yalla nalen yalla Faye barke Serigne saliou man dama beugué Baye bilahi

    • @beuzSpiritdoctor
      @beuzSpiritdoctor 5 лет назад +3

      dieureudieuff

    • @alhaqq310
      @alhaqq310 5 лет назад +3

      Amiiine ya Raby wallahi ya bakh Macha'Allah

    • @ibrahimandiaye442
      @ibrahimandiaye442 5 лет назад +3

      Merci beaucoup Baye lamine, yalnala yalla Diammal❤❤❤❤

    • @ndiayedame4960
      @ndiayedame4960 5 лет назад +1

      Beug nala ndakh sa mbeuguel si baye💓

    • @imammalickndiaye9909
      @imammalickndiaye9909 5 лет назад +4

      Sering bi ya ñake kinian degue yalla nala baye faye

  • @lucasjrmbaye9943
    @lucasjrmbaye9943 5 лет назад +116

    Mon gouroup préféré barkeb s Touba mais j suis mourid mais baye dupis tamps boy Batay dama KO sopou ki takh ma sopou. KO moy Yalla mais daff.ko diarale ci s aida faye
    Baye niass yalla na Yalla fayko ngandji faye barkeb s Touba ak kou wakh amiiiine

    • @ndimbelanendimbelane421
      @ndimbelanendimbelane421 5 лет назад +1

      Ibrahima Mbaye Walahi Kou beug BAYE si khol bou deugou si diam rek ngay nékkk
      Dieureudieuf Ibrahima Mbaye

    • @khadeejahfall8484
      @khadeejahfall8484 5 лет назад

      Macha allah
      Yalna baye fayanté akh iow thiofel akh beugue binguako beugue

    • @ramatoulayedia3573
      @ramatoulayedia3573 5 лет назад

      Yalla nla cheikh ibrahima Niass fay sa xol

    • @mohameddiop7375
      @mohameddiop7375 4 года назад

      Ndeyssan beug yalla mokoy def yaw deh kou bakh nga bou senegalais yeup melon ni yaw wallay dina bakh keur diné yeup ben lagne ndakh nieup ay joulit lagne té keur bou nek bountou la ndakh jouma yi sakh ay bountou la am

    • @sidysow7473
      @sidysow7473 4 года назад

      Yalla nalla yalla arrrrr sama sopé

  • @LaBarhamienne
    @LaBarhamienne 5 лет назад +43

    Wawaw Cheikh Ibrahim Niass rek, motax ma beug lène ni😍❤️.
    Wa key dieureudieufè Baye hala kouli hale🙏🏽🙏🏽 Al hamdoulilah bénéne yone

    • @ndiayedame4960
      @ndiayedame4960 5 лет назад +2

      Yaw tamite ken dou yaw

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 5 лет назад +1

      Ndiaye Dame huum,ba diam la rek🤣🤣

    • @ndiayedame4960
      @ndiayedame4960 5 лет назад +1

      @@LaBarhamienne diam la key beug baye niasss key fofou la diam yammm

    • @LaBarhamienne
      @LaBarhamienne 5 лет назад +1

      Ndiaye Dame Ndeysaane wakh nga deug dh mbok mi, kone Al hamdoulilah rek té nane dieureudieufé Baye🙏🏽

    • @ndiayedame4960
      @ndiayedame4960 5 лет назад +1

      @@LaBarhamienne niasssssssss

  • @barhammbow5341
    @barhammbow5341 5 лет назад +83

    Ndam rek inchalah si barké Mawlana cheikh Ibrahim Niass ( RTA)

  • @salimafall5451
    @salimafall5451 5 лет назад +50

    Djitounguene sanii cravache baa...thiii kaname rek inchallah. BAYE molene tanal boppam. Meuno lene dieul ndareii.
    Alahmdoulilah ala koulii alll.

  • @deliverofficial2555
    @deliverofficial2555 3 года назад +1

    May Allah protect akhlou brick si barkeh Bai barhama

  • @ndeyediallo1436
    @ndeyediallo1436 5 лет назад +75

    En avant inchallah barké Mawnala Cheikh Ibrahima Niass ( RTA)💕💕💕

  • @DiakhateNiass
    @DiakhateNiass Год назад +1

    Baye Niass one loveh ❤❤❤❤❤❤❤❤dieureudieufé Mame Baye Niass ❤

  • @modousamb2539
    @modousamb2539 5 лет назад +36

    Nitou yalla deugue moy baye Niasse,Xam xam ba barina,talibé yi barinagn
    تغمده اللّٰه بواسع رحمته وأدخله فسيح جناته ♥

  • @ibrahimandiaye442
    @ibrahimandiaye442 5 лет назад +33

    Yalna yalla sammlén !!!
    You love Barhama that's why we love you
    We are so glad to hear your voices ❤❤❤

  • @morthiam3357
    @morthiam3357 5 лет назад +13

    Mashallah deug leu dh. Talibé Baye bouné amna fou Baye diar ak yaw. Mognou tek si bon chemin Mashallah Dieureudieufé Baye

  • @diaboukeita4247
    @diaboukeita4247 4 года назад +6

    Machallah de tout coeur fière d'être talibé baye Niass

  • @rassoulgaye2317
    @rassoulgaye2317 5 лет назад +25

    Macha Allah wakh dji rafetna Fier D'être Talibé Baye.

  • @wakhaldeug8424
    @wakhaldeug8424 5 лет назад +8

    Yalle nalen yalla faye ❤️✍️ken dou baye niasss barki yalla ken la si adouna bi Niass Goumba

  • @lalionneofficiel716
    @lalionneofficiel716 4 года назад +3

    Inchallah Mame Baye Niass le fera je vous aimes fort

  • @aminatandao2729
    @aminatandao2729 5 лет назад +38

    Oh mes artistes préférés way khalée dégue dadj yi Baye rek si ❤️ non lénéne khadioussi

  • @fatoumataniass8348
    @fatoumataniass8348 5 лет назад +14

    Niou ame teguine Ndeysane. Si wakh ak degue. Yalla nalene yalla defal diameu yokou lene baguene yeukko si barker baye NIASS rta

  • @escapetheordinary2
    @escapetheordinary2 5 лет назад +15

    No Baye No life❤️ Djeureudjeufei Mawlana Cheikh Ibrahim

  • @fallousylla4764
    @fallousylla4764 5 лет назад +23

    inch'Allah lolou day am journaliste bi niassene dou tarikha sant la nioune ay tidiane laniou

  • @ousmanefayegarmiattijani2304
    @ousmanefayegarmiattijani2304 5 лет назад +3

    Merci dayza mbireum Baye dou influence
    Taneff la
    Nia andone ak #ka nio andate ak #ki

  • @Mhddiagne416
    @Mhddiagne416 5 лет назад +1

    Yalnalen yalla dafal chaque gamou nguén guener sound si baye niass si barki mawlana cheikh Ibrahima
    الحمد لله

  • @modoumbodj434
    @modoumbodj434 5 лет назад +14

    Manchalla sakaw sa kaname.kou ande ak mawlana baye niass do danou.dieurediefféee baye

  • @diaosory5373
    @diaosory5373 5 лет назад +17

    Restez unis Baye sera derrière vous

  • @birabarkhama5569
    @birabarkhama5569 5 лет назад +14

    Je suis un buzzlabien mais baye niasse taxna ma beug lene

  • @ismailasarr9729
    @ismailasarr9729 3 года назад +1

    Donn talibé mba tousssss💗💯💯💯

  • @aladjiomarcisse632
    @aladjiomarcisse632 5 лет назад +16

    ماشاء الله حب صادق لايموتLove ابدا أطال الله عمرهم ببركة مولانا الشيخ ابراهيم إنياش رضي اللَّه عنه

  • @cheikhtidianethiam3549
    @cheikhtidianethiam3549 5 лет назад +71

    Salam mbok yi
    Je vous demande au nom d'Allah soub hanahou watahala d'arrêter de dire tarikha niasséne. Baye n'a pas de tarikha il est le khalif de cheikhna Ahmed tijani Cherif radiya lahu tahalaa ane Hou.
    De grâce ☝️

  • @oulyniassy3397
    @oulyniassy3397 3 года назад

    Machallah yallah na yallah yokeu len si barkei baye niass😍

  • @mcrabaniang9367
    @mcrabaniang9367 5 лет назад +3

    Yalla na barké Baye Niass bi fégn ci yénn

  • @nogishlabarbish475
    @nogishlabarbish475 5 лет назад +6

    Tte Mbour derrière vs Suniou fierté👀❤❤❤❤❤
    One love

  • @mbayeetdisipro556
    @mbayeetdisipro556 5 лет назад +36

    Ah ndaysane mane tamite dh nila mél 2016 la tarbiya aussi maguissi rap bii dieur dieufé baye niass di sante mawlana cheikh mahi cissé sama wazila

  • @aminasarr8746
    @aminasarr8746 5 лет назад +68

    Cheikh Ibrahima amoule morome

    • @niassyahya1279
      @niassyahya1279 5 лет назад +4

      Ay talibem sah amuniou morom wakhatuma cheikh Ibrahim

    • @mamanmaman7411
      @mamanmaman7411 5 лет назад

      @@niassyahya1279 😂😂🤣🤣🤣🤣🤣

    • @mamanmaman7411
      @mamanmaman7411 5 лет назад +1

      @@niassyahya1279 niass yahya wakh ma bén talubém bou mélni cheikh Ibrahima falll ma khol bakham ???

    • @sikkninjaofficiel780
      @sikkninjaofficiel780 5 лет назад

      Maman boul watie sa bopou Yahya sou wahe lolou moy ni Ay talibem danio am mahrifa th lolou amoul ben telibe bouko gueneu ham telibe bayi kanta cheikh Ibrahima fall segne touba la kene hamoul loum done wayé cheikh Ibra fall di niite

    • @MoustaphaNdao-rx4px
      @MoustaphaNdao-rx4px 4 года назад

      @@mamanmaman7411 lathél mame mallé thiam

  • @tybeautediouck3731
    @tybeautediouck3731 5 лет назад +25

    Ndam rek si kaw si kanam inchallah.vous êtes les meilleurs

  • @issadiao6929
    @issadiao6929 4 года назад +1

    Bilahi malen beugue té thie Baye Willane mignou bookk j vs vs aime Barké Baye Niass

  • @toutibasse4109
    @toutibasse4109 5 лет назад +11

    Machalah yalla naléne baye niass nanguoul séne talibé

  • @elzobibachasine453
    @elzobibachasine453 5 лет назад +7

    Nom baye niass mo mel nonou bokk waye akk noumou mountin mel d'Ay nekh 😍😍

  • @omardiankhabnlb3534
    @omardiankhabnlb3534 5 лет назад +7

    Mashalla Niass
    Dagnkoy beug ba dé mbeugél gui contenué

  • @rokayakebe115
    @rokayakebe115 4 года назад

    Baye amoull morome baye niass moye deugg

  • @cheikhabdoulayethiam8463
    @cheikhabdoulayethiam8463 4 года назад +1

    Encore une fois niasséne amoulle tarikha niasséne yii ay Tidiane léne
    Baye niass andi woulle tarikha
    Baye faydou Tidiane la andiii

  • @mom_sa_bop
    @mom_sa_bop 5 лет назад +3

    Yal na yalla aare lén si barké cheikh Ibrahima

  • @azizsam5617
    @azizsam5617 5 лет назад +5

    Li mo takh guene dieul 1er baye rek masala vrema vous êtes les meilleurs

  • @cheikhbayembaye8294
    @cheikhbayembaye8294 5 лет назад +3

    Machalla bonne continuation chère Feres ❤️❤️❤️❤️🙏🙏

  • @salihouniass9919
    @salihouniass9919 5 лет назад +1

    duéréduéf akhlou brick yalna yalla fay lén si barke baye niass je vous aime❤❤❤❤❤❤

  • @actu_barca1
    @actu_barca1 5 лет назад +7

    Wallae sene mbeugueil si baye yalla nalen weutou si bepo anam❤️

  • @ladoushizembaye8104
    @ladoushizembaye8104 5 лет назад +3

    Bilay naka diekk bima deglo song bi setane clip bi la wax samay mag weuy mi si xol bi la diogué. Ndax deyz limou yegatou si clip bi aaa pr Mane meussoul am. Té ara tmt on diré k limoudone yeuk moko yémé ba meunoul yegou lou bari. J v dire k gnom gnarr yeup il st just 🙏🏾. Takh guene bama geneu Beugu Baye Peace à vs🙏🏾❤️

  • @hallyfall4919
    @hallyfall4919 5 лет назад +5

    Keup kouy mouride dagay beugue Baye Niass t keup kou beug Baye Niass dafay beugue Serigne Touba. Baye Niass ak Cheikh Ahmadou Bamba vont de paires. Mak nioufi nèk yeup yalla molène may mouy Mouride, Khadre, Tidiane, Layène, etc nieup amena loulène yalla may
    Naniou sante yalla rèk t fonk mak nioufi yalla wathiè yeup t beuguelène.

  • @hamadyba5352
    @hamadyba5352 5 лет назад +7

    Allhamdoulilah machallah marifatou billahi mo néh

  • @khadijaniass4550
    @khadijaniass4550 4 года назад +1

    Yallah nagnou yalla déf deug deugui Talibé Mawlana Cheikh Ibrahim ❤️🙏😍

  • @aichaniang4445
    @aichaniang4445 5 лет назад +15

    Machallah yallana baye niass fayleen

  • @emsidiop7549
    @emsidiop7549 5 лет назад +3

    Bilahi avec baye la solution tout est possible sa ira inchala bonne continuité

  • @cissetaphaboy6599
    @cissetaphaboy6599 5 лет назад +1

    Yalla nama yalla bolé si talibé baye yi wakh len amine

  • @ngommahtar4689
    @ngommahtar4689 5 лет назад +1

    Machala baraka lahou fikoum ,,.💖💖💖💖💖

  • @fallgalaye3455
    @fallgalaye3455 5 лет назад +1

    Bilahi yalla mo def ma beguelen rawatina niou bokou khadara bi

  • @fabikante4300
    @fabikante4300 5 лет назад +4

    Machalla Akhlou Brick keen dou Mawlana.

  • @alimatousadiyasarr584
    @alimatousadiyasarr584 5 лет назад +3

    Dieureudjéffé Niasse coumba Abdallah ❤Akhlou Brick gueun nalen beug❤

  • @iboulayendiomborditnaboulo793
    @iboulayendiomborditnaboulo793 5 лет назад +2

    Man dé coubeugu baye Nissa beugueu nala prck jtm bcp

  • @ibrahimsall6492
    @ibrahimsall6492 5 лет назад +13

    Allahou Akbar deyza vrai talibe baye la

  • @aichabayediedhiou
    @aichabayediedhiou 5 лет назад +1

    Macha allah dieurdieufeeeeeee Baye Niass

  • @kankoudiawara3591
    @kankoudiawara3591 5 лет назад +1

    Chapeau a vs na yalla goudal sene fane si barkei BAYE

  • @mohametdieng7938
    @mohametdieng7938 4 года назад

    Yalla nako yalla déf si Barké Baye Niass

  • @aichabarhama3032
    @aichabarhama3032 5 лет назад +1

    Mei 2 Frere bon courage

  • @babacarndiaye20
    @babacarndiaye20 5 лет назад +4

    Baye soko beugeu reke tekhe geu Yalla naniou Yalla maye beugeu cheikh Ibrahim niass

  • @moustaphadiouf4478
    @moustaphadiouf4478 4 года назад

    Kou and ak Baye do dannou inchalla

  • @sakhobass3398
    @sakhobass3398 5 лет назад +5

    Machallaha akhlou brick Dieureudieuff BAYE niass

  • @mounirouniang4105
    @mounirouniang4105 5 лет назад +2

    Macha allah baye niass rèk

  • @zeynabthiam5730
    @zeynabthiam5730 5 лет назад +14

    Santati Mawlana Baye ❤️❤️

  • @sokhnadiedhiou8104
    @sokhnadiedhiou8104 5 лет назад +8

    Machala Dieureu Dieuf Baye Niass

  • @tallmouhamed5499
    @tallmouhamed5499 5 лет назад +2

    Eskay Baye mashallah deyza mashallah yalla na Baye takhawoulen si lepp

  • @alygueyesbn3860
    @alygueyesbn3860 5 лет назад +1

    Machalla baye niass na gayi yèwou ci baye niass limoo Andy lan la

  • @rokina4850
    @rokina4850 5 лет назад +13

    😭😭😭deyza ohhh li fort na

  • @ismaelfaye4712
    @ismaelfaye4712 5 лет назад +1

    Machala baye niass amoul tankcou guinaw si caname rec inchala

  • @mariamalalionne311
    @mariamalalionne311 5 лет назад +10

    Thi kaw thi kanam barkei Baye BARHAMA

  • @rokhythiobane4158
    @rokhythiobane4158 4 года назад +3

    Machall je suis fière de vous

  • @kodiagnetv5984
    @kodiagnetv5984 5 лет назад +6

    Wallahi bess ni tay beug nalén nguir BARHAMA!!!

  • @elhadjisow6795
    @elhadjisow6795 5 лет назад

    Yalla nalene yalla feye thi barke mawlana cheikh ibrahima niass

  • @moulayedabakh3798
    @moulayedabakh3798 5 лет назад +10

    3:22 sorry le présentateur attention il n'existe pas de tarikha Niassènne, nous Sommes des tidianes. Encore une fois de plus les talibès baye sont des tidianes... boulènnn gnouuu wakhloooo way ...

    • @babacardiallo4908
      @babacardiallo4908 5 лет назад

      Abbdou khanna léggi tarrikha yi sakh dafa ame danga maye beugga farlaforce ma wakh la bénne Afér mame baye birrame kémtane le yalla sounou borome moko déf

    • @aidadiouf9890
      @aidadiouf9890 5 лет назад +1

      Waww kayeu Abdou vremen man Tarikha Niassene bih metina ns sommes tidianes kouyeu doneu Tidiane niola gueuneu doneu Tidiane Baye indiwoul Tarikha bou bess

    • @babacardiallo4908
      @babacardiallo4908 5 лет назад

      @@aidadiouf9890 défoufi lou béss mais koumou dougou sa khole nga nék nit kou nité

  • @aminata-adjisambou7153
    @aminata-adjisambou7153 5 лет назад +1

    Macha Allah Baye yalna yalla barkel lep thi kaw thi kanam incha allah

  • @coumbadiarrafall9971
    @coumbadiarrafall9971 5 лет назад +6

    Baye nena Gamouwatt pour sant Yalla. Guanaw baniou Gamou amm nioukoy weddi mou bissatt ko. Mais amna batine tamit.

  • @sourangdiop7636
    @sourangdiop7636 5 лет назад +1

    yall na lene yalla takhawou si barkep baye

  • @cheikhtalibouyandiaye1918
    @cheikhtalibouyandiaye1918 5 лет назад +4

    Macha Allah Baye Niass my life

  • @titisadji6129
    @titisadji6129 5 лет назад

    Machala baye niass reka wor li motakh ma beug lén

  • @Ousmanediouf5
    @Ousmanediouf5 5 лет назад +8

    Machallah akhlou brick

  • @fleurettecisse5949
    @fleurettecisse5949 4 года назад

    Machaallah je vous aime guir yallah cii barké baye

  • @mariamasarr8569
    @mariamasarr8569 5 лет назад +1

    Machallah Dieuredieufè Baye Bonne Continuation

  • @tabarabathily6907
    @tabarabathily6907 4 года назад

    Thiey BAYE❤😭

  • @lesmesruic6209
    @lesmesruic6209 5 лет назад +1

    J prèfére brick akhlou

  • @babandiaye164
    @babandiaye164 5 лет назад +4

    Ndam rk inchalla avec baye niasse

  • @babacardiallo4908
    @babacardiallo4908 5 лет назад +2

    Machalla laf thiate yalla boulléne thiate dougou amiiiiiiiiiiiin thi kaw thi caname si barkeye nonene te bi

  • @ElhadjiGaye-z3f
    @ElhadjiGaye-z3f 3 дня назад

    Dieuredieufee baye niass ❤🎉

  • @alycamara6380
    @alycamara6380 5 лет назад

    yalna yalla mayéléne ndam ci barké baye niasse amine

  • @dioufadama7676
    @dioufadama7676 5 лет назад +7

    ❤dierediefe baye niass💘
    Yalanasene diamou yage

  • @ballaboy9649
    @ballaboy9649 5 лет назад +2

    Nyasssss beguella mbaa jehhh

  • @abdoulayegueye5247
    @abdoulayegueye5247 5 лет назад +1

    bonne continuation, nice na walahi

  • @babacarndiaye5023
    @babacarndiaye5023 5 лет назад

    Talibé baye Niass dall do nigake xam xam Merci way akhlou brick

  • @toumagnonibrahimkalilwx3370
    @toumagnonibrahimkalilwx3370 5 лет назад +1

    Love sur vous.dieureudieufé baye niasse

  • @livedirect1608
    @livedirect1608 5 лет назад +9

    Machalla bay niass dall kénele

  • @rokhymangane8239
    @rokhymangane8239 4 года назад

    Beugue baye rek machalla laf thiat

  • @zatacoulibaly8131
    @zatacoulibaly8131 5 лет назад

    yalla nalen yalla faye barker baye niass

  • @imsenegal5261
    @imsenegal5261 4 года назад

    macha allah barké BAYE NIASS RTA

  • @DJIMCISSE13TV
    @DJIMCISSE13TV 5 лет назад +2

    Machalla Nice émission