feemu fii ak feneen thi sen rubrique feemu star invité du jour ndeye Ndiaye recette nems coco sucré
HTML-код
- Опубликовано: 5 фев 2025
- feemu fii ak feneen vous offre votre rubrique feemu star qui consiste à inviter les stars qui viendront cuisiner avec un nom un concept qui nous permet de joindre l'utile à l'agréable merci de le suivre de partager et d'aimer nos vidéos pour plus de visibilité s'il vous plaît merci
Nice émission. Fan number one
Pate bi noumou toudeu
Beau concept mais il faut donner des directives à la star mome mouy liguey. Mo guena am sens mou nekk telespectatrice. Bonne continuation
C'est ce que je me suis dit, au début, on croirait que ndeysane moy def émission bi
Afin on voit le visage de notre tata nationale avec sa voix douce Mame môme hummmgou moma neck😂😅
Merci beaucoup ma chérie c'est vraiment gentil bisous
Ci Ndeye Ndiaye la ndieuka degueu tourou feemu fii ak fenene, bobou batay nak mangui lay suivre et je ne regrette pas ❤❤
Parey depuis polygamie la dégon moukoy wakh ma daw ndank Tik tok abonè diko topou
Gnak la tope erreur la chef 👩🍳 sala ma cha ALLAH ❤❤❤❤❤❤
Degual lolou merci beaucoup
Li de makoy siiif ndank merci bcp salla❤ notre Star ndeye Ndiaye ❤
Machallah émission bou âme solo . Tay ngay guiss star AK seni fèm . Gnakkeu la sètane woroul . Yaw rek lagnouy toppeu . Demain ma essayerko
Machalla man ndeye ndiaye damako begue te yalla rek takh
Ndeyssane beugue gua kou bakh
❤❤
Bilay yaw Tamite kén diou yaw si bakh❤️❤️
Ndeye ndiaye nak personnellement je l’aime 🥰
Machallah yalla na yalla yokou meune meune bi amna solo lol❤❤❤
Bonjour salla je suis vraiment content et merci de partager avec les recettes mais les feuilles de sprints rolls se sont les feuilles de bricks oubien ya la difference
Ndeye Ndiaye el é la meilleure
Ah domou ndeye bien reussit❤❤🎉🎉
En fin dakh niou guiss sou niou tata machalla mome rekk lay topou ❤❤❤
Aaa kokou salla la 😂😂 borome boborobaa😂😂😂 machalah si kawe sa kanam mangui lay suivre chaque jours name nala trop nakk
Machalah 🎉todiati nga fi
Maach Allah bonne continuation trop contente si émission bi❤ thia kaw si kanam rk inch Allah
Merci beaucoup ma chérie
J'aime trop❤
Merci beaucoup
Macha sala content na trop, yalla nga doundou ba gniye wane sa aye recette si chaine cuisine tv amine
Machallah tata moi je te regarde depuis le Canada ❤❤❤❤
Machalla machalla ma fille chérie ❤
Merci merci tata
Machallah sister merci djiguen femme contannant si guis lafi❤❤❤❤
Machaallah nekhna lool❤❤❤
Machalla amoré gnoun yow rk lagni topou❤❤
Merci beaucoup ma chérie c'est vraiment gentil
Bonne continuation et longue vie a vous.
Merci beaucoup
❤❤❤machalla fière de toi bien presenter
Je suis fier de toi ça là tu me plais beaucoup je suis t'ai vidéos
Y
Enfin Sala en chair et en os❤❤❤❤❤
Machallah ❤
MASHALLA TATA JE TE SUIVAIS DEPUIS TIKTOK...DIEUREDIEUF
Waw waw
Merci beaucoup
Hun hun nehh ba beugué dé la deff❤❤❤❤❤❤❤
Bravo tata salla... Yalna lép dieum kanam. Merciiii beaucoup
Merci pour les recettes à vous ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalah madame priorité félicitation yalna à yala barkel
Bonne continuation borom recette you neex Yi
Amna solo macha alah
Merci beaucoup
Mashala li nieuw moy dak inshala
C'est claire
Machallah ma sœur ❤
Merci beaucoup
On peux utiliser les galettes ou bien
Machalla man yow reck laye top🎉🎉
C'est vraiment gentil
Salla notre salla
Merci tata sala mane yow rek laye top
Macha allah maman très belle ❤
Merci beaucoup tata de nous honorée avec votre joli visage je vous aime tellement
Moi aussi je vous adore mes amours merci beaucoup c'est moi qui vous remercie
Mashala yallla lokho bi wer
Assallamallikoume machallah bon RAMADAN à ts
Merci beaucoup bon ramadan à vous aussi
Manchala bien fait et propre
Merci beaucoup
Vous vous ressemblé beaucoup
Ha bon tu n'es pas la seule personne qui me l'a dit
Merci beaucoup femu fi ak fenen ak ndeye Ndiaye
Avec plaisir
Ndeye ND rek
Li dé mom la défar ndogou téye mais pipipi lou mou nekh eupeu ne
Macha'Alla ma sœur j adore ton rire merci â ndeye Ndiaye ume bonne éléve❤
Merci beaucoup ma chérie c'est
Tata mane iow rék lay topp
Mane yéne rek laye top
Feuilles bi founou ko meuneun amé
Exclusif ma puce
Maachaala
Bonne continuation...
Merci beaucoup
Sala yao rk lay toop si Tik Tok biii
Bane feuille ga utiliser stp
Mais star bi sou toguone mou neh
Machaallah ❤ mais il faut nous dire les quantités exactes des ingrédients comme cela reproduire recette bii yomb😊
Mongi thie page tik tok Feemu fi ak fénéne
Bien sûr je vais te revenir avec les quantités
Salam , la feuille utilisée c est la feuille de brick la meme qu on utilise pour nems ?
Oui
👏👏
❤❤❤
Bisous
Guisatoumala si tik tok bi fonekn?
Bonne question ndeye rèk amoul fène
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup
Yonaimassi gnummm gnummm
Cvok❤❤
Trop nekh
Bilaye
Kanamou ndeye beugueudj na four bi mounou mako mougn mounoul serieuse😂😂😂😂😂😂
Musique bi c’est pas Yoro mou serigne saliou ?
Beudieuk bi daal koula bayyi nga may gnou ko 😂
😂😂❤❤
Tu ne p beaucoup tata salla❤ diamou si yaw
Merci beaucoup diame thi yéne
Lafthiate hummm
Merci
Sala il faut mou wakhniou louye broncoderm😂😂😂😂
Lollll bilaye pourtant lath na koko
Mais c'est un peu insensée l'émission je croyais même que c'est la star qui allait préparer
Ngir yalla soit naturel way té bayyi roulé rrrrr yi
Tanto nga roulée rrr tanto nga wakh correctement donc doo simple rek
Sa jongoma AK sa khètou cuisine lanela
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤