ولنبلونكم بشيء من الخوف والجوع ونقص من الاموال ولانفس والثمرات وبشر الصابرين الذين إذا أصابتهم مصيبة قالوا إنا لله وإنا إليه راجعون ؤلئك عليهم صلوات من ربهم و رحمة وؤلئك هم المهتدون صدق الله العظيم
C est grace a ses conference et aussi serigne sam mbaye que Sama gueum ( Iman) yokh bou bakh.Allah, un homme Islamic qui aime son prophet kou gueum Alkhourane demna.ndeysann je n aurais plus ses noveaux audio or videos. Thiey adouna. Yallah Naka Yallah yerem te terou ko aldiana. Amen ya moustapha
yalla na yalla dolli yermanndém si mome
Ndeysane serigne saliou sow yalqnalaaaa yalla tabi aldianaaaaaaa😘😘😘😘😘😘🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾🤲🏾😘😘😘
Yalnako yalla yereum ci daray Yonentebi (psl)
Yalla nako yalla yereme harr ko aldiana.
yalla naniouko yalla fayale barké borom barakbi
Nittekou oyoffe vraiment il etait une bonne personne. Il va nous manquer. Merci pour tes enseignements.
Yalla nanouko yalla fayall
Yalnako yala yeureum té jégal ko té maynou deg ak top waxam amna solo lool.
Serigne saliou yalla nala yalla yeureum si barkeb allkhouran diaradieuff
Machallah saa doundou raffet naa guindi nga askaan Wii thi Diiner akk talibe.Yala nala souniou bii khare Aljaana firdawsi yokk saay lerr souf woyof saa kaay thi Darajay geun di mbideff Barke Borom Touba akk bepp djoulite,adouna ngui nii daniouy rott cii koussa ndaak fess nga gnibi
koussa ndaal fess nga gnibbi
Allahouma Amine dieredieuf
Thiey adouna dou dara yalla nala yalla yaram
Yalla ndioko yalla fa yall s bark Mouamid
Bilahi ki damako beugon lol yalla kamnako bilahi yalla nanga yèwo aldiana firdawsi
Allahouma Amine dieredieuf
Yalna ko yalla yereum te khare ko aldiana Amine 🤲🤲😭
Yalla na yalla Tabraka wathalla yeureun ko ta diègal ko ak beb dioulit.
Yalna yalla yeuremko t khareko aldiana firdawsi
Ndey San Machalla amnasolo 🤲🤲💖
S saliou sow yalka na sa borom dolli la yeur mande barkep s saliou
YALLA nako Yalla yeureume th djégueul ko amine
Allahouma Amine dieredieuf
Yalna ko yalla tabal firdawsi
Allahouma Amine dieredieuf
Oustaze yallana yalla Faye la te khareela aldiana si barkhe seydina Mohammed salalakhou tala Ali Mohammed aminn
Allahouma Amine dieredieuf
فجزاه الله جنة الفردوس بجاه طه
Yallna nala yallah diègeul tè yeureum le
Yalla nakô Sounou Borom Khâré aldiana thiy Barkéb Serigne Touba
Yala nagou yala dieguel tey weureum gniou si barkhe seydina Mohammed salalakhou tala Ali Mohammed aminn
Allahouma Amine dieredieuf
شرج صلح شو رحمه الله
Thanks you very much serigne saliou sow
Yalla nako Yalla khare aldiana firdaw sy
Allahouma Amine dieredieuf
yalna yalla yueruem amine
Yalla nako yalla yerem
yalla nako yalla yeureum amine amine
Amine yarabbi
Yalnako yalla yereum
Amine
yalnacou yalla yeureum amin
na li guèy bi dox bakhna dh
😭😭😭vraiment je n'était pas au courant..repos en paix
Paix a son ame repose en paix
Nako.yalla.yerem
amine
رحمة الله عليه ءامين بجاه سيخ احمد بمب
Macha Allah!
Mangui ziar borom chaine bi meun na am sa numéro,?
😞😞 thieuy yalla
ولنبلونكم بشيء من الخوف والجوع ونقص من الاموال ولانفس والثمرات وبشر الصابرين الذين إذا أصابتهم مصيبة قالوا إنا لله وإنا إليه راجعون ؤلئك عليهم صلوات من ربهم و رحمة وؤلئك هم المهتدون صدق الله العظيم
صدق الله العظيم
💅💅💅💅😭
🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔
إنا لله وإنا إليه راجعون
Serigne saliou sow dafa decede?
C est grace a ses conference et aussi serigne sam mbaye que Sama gueum ( Iman) yokh bou bakh.Allah, un homme Islamic qui aime son prophet kou gueum Alkhourane demna.ndeysann je n aurais plus ses noveaux audio or videos. Thiey adouna. Yallah Naka Yallah yerem te terou ko aldiana. Amen ya moustapha