Je suis tidiane mais chaque jour j'ecoute les khassida...mashallah Abdoulaue diop yalla na yalla wèrall bateu biii...... Yalla nagniou Allah fayal Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul
Thieyyyyy Serigne Touba c'est avec un cœur plein de joie que j'écris ces mots vraiment Serignne Touba amoul morom fa Yalla ak thia Yonente ba il est unique baayou bass ak Bara ❤❤❤Mawahibou mon Xassidas préféré je peux pas rester une semaine entière sans l'écouter au moins 2 fois dans ces 7jours ❤❤❤❤je l'écoute avec une joie incommensurable ❤❤❤❤❤❤💟💟💟💟💟💟💟💟❤❤❤❤❤❤❤❤💟💟❤❤💟❤💟💟💟❤❤💟💟❤💟💟❤💟💟💟💟❤❤💟💟💟❤💟
Quel bonheur d'écouter le kourel tous les matins...Au fond de toi tu entends cette voix qui te dit" que la grâce d'Allah t'accompagne pour cette nouvelle journée. Djagen djeuf❤️
Dieuredieuf cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul yalla na lén serigne éfal batte yi guén yague fi lol té andeu ak weur barké khaīssida Yeu .Serigne Mountakha Mbackè Balla yak fi té weur !thi khassida yi rek
Fan yi si koor gui diaar nafi beneu jour ba guis s mountakha AK s basse AK s amsa ma nianfi sama sokhla fimou tolou ni ma ngi ni Espagne djiara djiefe s Touba
Étant un vrai Talibé Cheikh plus particulièrement éléments Mame Khalifa j'aime beaucoup les khassidas Vraiment dfa nexx sii xol walahii Yalna diam yagu way
Thiey mawahibou sed na khôl lol machallah dieureudieuf serigne touba kenla amoul morom mbacke 💕🤲💕 diarama mame cheihk ibrahima fall lamp 💕🤲💕serigne mountakha mbacke💕🤲💕 yallah nafi yague lol ta wer mbacke💕🤲💕 machallah dieureudieuf wa hizboutarhiya sounouy khôl said nalol yallah nalen serigne touba fay guen am wer ak goudou fan ak kheweul you bari si barke yonantibi alay salatou wasalam si barke khasidayi allahou ma amine wawaw mbacke💕🤲💕 ni nga ko wakhe rek mbacke 💕🤲💕gueuna bakh guena selle gueuna rafett guena yiw guena gueun ba aldiana rek mbacke machallah dieureudieuf wasalam💕🤲💕
Thiey mawahibou sed na khôl lol machallah dieureudieuf serigne touba kenla amoul morom mbacke 💕🤲💕diarama mam cheikh Ibrahima fall lamp 💕🤲💕serigne mountakha mbacke💕🤲💕 yallah nafi yague lol ta waw len gor machallah wa hizboutarhiya sounouy khôl said nalol man Souleymane diop beugue fallou mangui fi si touba tolentino keur Serigne touba Italie di tewlou khasidagui di mawahibou sama khôl da said lol ken dou serigne touba kenla amoul morom mbacke 💕🤲💕serigne atou diagne yallah nako yallah yeureum ta kharela aldiana firdawsi si barke yonantibi alay salatou wasalam sikhasidayi yallah nala serigne touba terouAllahou ma Amine machallah dieureudieuf wasalam💕🤲💕
Kouma aimer sama commentaire yallana guissek serign touba yawmal khiyam
Serigne bi amoul morom
Amine
Louwere gua wakhe
@@ousseynoudieng9083 slt
T
Qui peut disliker ça ??? Diakhalnam
Xassida serigne bii xawmaa nane lako nitt dii bagnaa aimer.yalla nagnou yalla dioubolei akk xassidaa yii
malick sow Mane n'a nék eureure tamite
@@fatoulokebe1014 erreur 🙄
@@fatoulokebe1014 Q
Soxor rk
Focus lene ci deglou bi aimer ak niak nieme serigne bi romb neu fofou
J suis layenne mai khassida dama ko beugu Machalla souma koy deglou sama xol day sedd bilahi dieureudjeufè serigne touba kouko santoul gorè wo❤❤❤❤❤❤
Akassa
Ndaye sane
balla ngua hamné beugue ko am solo alakhira
machalah ya bakh dé... sante serigne touba walna bépe dioulite
Seynabou laye Dieng yaw rèk yabakh
Je suis tidiane mais chaque jour j'ecoute les khassida...mashallah Abdoulaue diop yalla na yalla wèrall bateu biii......
Yalla nagniou Allah fayal Cheikh Ahmadou Bamba Khadimou Rassoul
Danga bakh rek akassa.
Yalna sa diam yagg mbokk jullit
Mouridoulahi moy ka diam sa yalla kon Papis ya bakh yalla na la yala faay sa mbêguèl si joulit yi
Ameen
Ligua wakhe rafétna
Qui écoute ce mawahibou Ramadan 2024❤
Mangui ni ❤️❤️
Je suis talibé cheikh souma koye deglou Sama khôl Daye sede trop ma cahalah yalla n'a niou yalla fayalle macke nie❤️😭😭
Segn atou Diagne yalla nako yalla kharé aldiana barkel khasida yi
Serigne touba néna kou leine mokal (Mawahibou, Moukhadimad, Jazbou) keine doula ladj sisa bamél..
Yalna niou cii bokk..Amiine
Hakazaaa, fondre ba diekh rekk si barke Al Quran.. Dieureudiefaty Borom Touba 💖
Je ne peux pas m’en passer Mawahibou♥️
Yallah naniou sunu borome may ay salihat mouniouy diangal Mawahibou chaque jour amine🙏🏾
Ère bi mom gars manatouniouko nimou may deff mane ak yala nioko kham Serigne touba kéne dou mom
Amiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiiine Sokhna Aminatou
Amin
Amiiiiii
Mawahibou barky Serigne Saliou sa soumako dégué douma khamatii fane la nekk😢😢😢😢
Mamiish Mar machalla
Thiey Ahmadou
Yalna yalla guene lene dioubale te doli werseke. Sokhnasi
kén dou serigne touba yalla na yalla léral lep si barké mawahibou
Machala
Dfa Sédeuh ci xol barki serigne touba 😭😭😭
Thieyyyyy Serigne Touba c'est avec un cœur plein de joie que j'écris ces mots vraiment Serignne Touba amoul morom fa Yalla ak thia Yonente ba il est unique baayou bass ak Bara ❤❤❤Mawahibou mon Xassidas préféré je peux pas rester une semaine entière sans l'écouter au moins 2 fois dans ces 7jours ❤❤❤❤je l'écoute avec une joie incommensurable ❤❤❤❤❤❤💟💟💟💟💟💟💟💟❤❤❤❤❤❤❤❤💟💟❤❤💟❤💟💟💟❤❤💟💟❤💟💟❤💟💟💟💟❤❤💟💟💟❤💟
❤️❤️❤️❤️
Ĵuy😊😊😊þ þþĝ😊ĝ😮t😊
Je l'écoute chak matin
Ndeysan xassida mawahibou
Même moi aussi surtout bouma wété
Hakaza tawfekh rk inchalla ngay am
Niosi bok yam d fall walahi
@@badoutall5550 vvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvvv:vvv::
Quel bonheur d'écouter le kourel tous les matins...Au fond de toi tu entends cette voix qui te dit" que la grâce d'Allah t'accompagne pour cette nouvelle journée. Djagen djeuf❤️
Kendou serigne touba amoul marom kenla waw len goor mouride yi amou len marom de fall👂👌🖐
Dieredieuf Serignie touba diarama mame. Chiekh Ibrahima fall serigne mounetakha Mbaké yalla ngafi yague t’es. Wére 🙏🙏🙏
Carrément J ai pleuré en l'écoutant en boucle Mawahibou 😭😭😭 Nom de dieu
Tous les jours à 7h Du matin nous ouvrons la boutique avec ce mawahibou du 4e Jour du ramadan 2K18. Alhamdoulilah
Toubarkala wa hizbou tarquiya yalla nalen sounou borom faye si barki seydina Mohamed psl kene dou serigne touba
Meilleur mawahibou segne Mayib depuis bou lamine seye 2005 🌟
No li douma si doyal ❤
Dieureudieuf Kou tédd ki diarama mame cheikh Ibrahima fall🤲🏽
c vrai !
bilahi
Dieuredieuf cheikh Ahmadou Bamba khadim Rassoul yalla na lén serigne éfal batte yi guén yague fi lol té andeu ak weur barké khaīssida Yeu .Serigne Mountakha Mbackè Balla yak fi té weur !thi khassida yi rek
Je ne comprends pas les paroles mes dafe ma nex tei je suis chrétienne j’aime trop ♥️♥️♥️
Machallah
Machalla
Macha''alla
Machallah 🙏🙏🙏
Machallah 🙏
waw len goor mouride machallah yalla na yalla fay len si barkep serigne touba machallah
Machalla
Machaallah je l’écoute chaque matin❤️❤️ dieuredieuf borom touba ❤️❤️❤️❤️
Je l'écoute régulièrement ndeysaaan th limay yeug walaaahi mounoumako expliquer
W
En 2020
Chaque matin momlayy degglou ,,,,gena yagg gena werr barkep Serigne Touba cheikh Ibra
Koussi Loude doyaLe réqq LaLaLe j’aime 👍
Je soui talibé cheikh mai li nekh na loll bilahii machalla
Machaalla yalla nala yalla défal diameu
Thieuye serigne touba
Iow kou bakh nga
Mawahibou moy salatoul fatiha rekk. Beyid par beyid et tous les secrets du Wird Tidiane
Bari nga si morom et on est tous les mêmes. Allah SWT et le prophète Muhammad SAW moo gnou bollé
Yalla na léne yalla faye same léne takha woulé adouna ak alakhira thi barkép yonéte bou téde bi psl thi barkép borom touba khadim rassoul 😭😭😭😭😭😭
Solen guissé lou dakkeu Khassida guén waxmako, 😭😭😭😭😭😭 Dieureudieuf Serigne Bamba
Alhouran (le Coran) après xassida yiii rek ba yowmalhiyame . Djeureudjeuf kou tédkiii
Mawahibou nafsi chaque matin guisouma louko dakheu dieurieudieufer Serigne Touba 🙏
Thiey khassida yi kene dou Serigne touba ❤️❤️✅✅✅✅🤲🤲🤲🤲😍
Lii leiip mouridoulahi feiip la adunna weurngeul keep cheikh ibra fall serigne touba gnioy aduna diassaka mame cheikh ibrahima fall amine
Wallahi mawahibou nafih bii doumasi doyaL DIEUREDIEUF serigne touba khadim RASSOUL😭❤
Fan yi si koor gui diaar nafi beneu jour ba guis s mountakha AK s basse AK s amsa ma nianfi sama sokhla fimou tolou ni ma ngi ni Espagne djiara djiefe s Touba
Machallakh yalla nalla yalla diapeulè si barkèp cheikhoul khadime
Dafay geuneu nekh rek d inchallah, lila war nak moy fo toleu di si bolé liguéyal serigne bi, mouy si dahira yi, khassidas yi ak yenen
Pape FALL wakhal Mbokk Espagne yi Niouy Drouss Laysal Birou xassida bi day aar si corona bi
Thieuy
Mouridoulahi Adouna ak Alakhira..... Dieuredieufé Serigne Touba - Diarama Mame Cheikh Ibra Fall
Soy deglou khassida yi khamni aldiana sori wouko dei❤
Étant un vrai Talibé Cheikh plus particulièrement éléments Mame Khalifa j'aime beaucoup les khassidas
Vraiment dfa nexx sii xol walahii
Yalna diam yagu way
Serigne Mountakha yala Nafi yague lole te wer Amine
Amine
Mballo Kebe Amine way
Aamine. Kebe. Ak yawod.
Amine way
Amine
Yalla na niou Borom dolli soutoura. Sakhall niou si yone Bi ta mouy deug si yone..
Jeuf ndigueul bayi téré❤❤
Serigne Mountakha Yagg fi té Wer🙏❤❤
Amine Fall
thiey serigne touba nekh fii nekh fagnu dieum serigne moutakha yalla nafi yagg ta and ak weer barkip xassida yii
Yalla nalen serigne touba khadim Rassoul fay len si barke khassida bi amine
Thiey mawahibou sed na khôl lol machallah dieureudieuf serigne touba kenla amoul morom mbacke 💕🤲💕 diarama mame cheihk ibrahima fall lamp 💕🤲💕serigne mountakha mbacke💕🤲💕 yallah nafi yague lol ta wer mbacke💕🤲💕 machallah dieureudieuf wa hizboutarhiya sounouy khôl said nalol yallah nalen serigne touba fay guen am wer ak goudou fan ak kheweul you bari si barke yonantibi alay salatou wasalam si barke khasidayi allahou ma amine wawaw mbacke💕🤲💕 ni nga ko wakhe rek mbacke 💕🤲💕gueuna bakh guena selle gueuna rafett guena yiw guena gueun ba aldiana rek mbacke machallah dieureudieuf wasalam💕🤲💕
Mawahibou et Raiya resteront mes preferés...
dieuredieuf s .touba les khassidas sont adorable oh sama khol seed na c'est pourquoi j'ai des larme aux yeux😭😭
Oooooh li nekhna si khôl j'ai les larmes aux yeux thiey Serigne bi
Machallah Dieredieufff brom Touba cheikh Mountakha Mbacké yàlla na fi yague ta wër ci barkeb ku tëdd qui Aminnne
Aminnne
ndeysane Mawahibou sama khassida ,Yalla na Yalla nangou barkep Cheikhoul Khadim
Cëëy Khadim Rassoul mo meuneu bindeu
Dieuredieuf SerigneTouba♥️🙏🏽
souma koye deglou daye melni manga touba rek bilaye serigne touba amouniou fayame
merci que dieux te protège longue vie bonne santé beaucoup de bonheur avec te ta famille
Thiey serigne touba li couco ame loy dégulou lénéne naniou diape si khasida yi moy souniou ndiarigne tay ak euleuk ❤dieuredieufé serigne touba diarama mame cheikh ibra fall ❤❤❤❤❤
djeredjeuff serign touba khadimou rassoull.....serign mountakha yalla na fii yagg ta werr
Amine yowite yageufi té wér
Thioye Serigne bamba yalna niou yalla gena buege lo serigne bi
Siii xassida yii rekkk nagnou koo deff mouyy sougnou weerouwayy barkeep WAKANA KHAXANN HANLAYNAA NASROUL MOUMIININNN.AHMADOU ONLY♥️♥️♥️
ceux qui mettent dislike c'est quoi votre probléme ...
Machalla dieuredieuff Serigne Touba Khadimm Rassoull khassayidd rékk hisbou tarrkhiyya nalénn yalla défall diamm
akasa khol seed na serigne mountakha yalla nafi yag lol te weer
Amine yowite gua yageufi té wér machaalla
28:05 ndeysann baye atou yallah na yalla yokkou ay lèram
Amine
thieye serigne touba li amoul féne foudoull touba
yallah nalene yallah faye sama xol sedeuna trop Barki serigne Touba
Yalla na lenn yalla faye yewo si barke khassida ye
Machallah wdieurigne wi yalna serigne touba weureul bate wiv🙏❤❤😭
Machallah.. Khassida rekkk.. Dieuredieuf kou ted ki..
Ma shaa Allah* il ne faut pas confondre les paroles surtout couper le non de son créateur 🙂
@@amythiamthiam3898g pas compris lima binda ngay rectifié?
bilahi Mawahibu mo nékh machalla
Ma Shaa Allah !
dieureudieufe serigne touba Khadimou rassoul dieureudieufe cheikh ahmadou bamba mbacke ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Lii Aljana laa jeureujeuf Cheikhoul Khadim
Machalla guene dou souniou wadjie serigne touba yalla naniouko yalla fayalle
Masha allah Mame brome Touba amoule morome kénla yallanagnouko yalla fayale té tasgnousi barkém si barképe Mame fallou mbacké
Diap si khasidayi rek dadiou 2007 bi sa me va droit aux coeur
mane je sais plus fima nek ins bii mashalla yalla nagueine ci diiam
Dieureudieufety CHEIKHOUL KHADIM SERIGNE MOUNTAKHA Bachir yalla nafi yague th werr
Khakassa theiy serigne touba Khadime rassoul thiey xassida yi serigne touba yi gno yemée 👂♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️🙏🏿
Dieureudieufé Borom Touba ❤
Nihmar rijalu, lahum majâlu
Nilû wa nâlû, waqtal 'âna-i...
Serigne Touba meune na binde ♥️😭
Machallah je suis Tidiane mais j’adore
Machallah nekh na Lolll
Dieredieufe Serigne Touba
Dieuredieuf serigne touba khadimoul rassoul serigne mountakha yalla nafi yague looooool te wer mbacke balla aycha diarama mame cheikh ibrahima fall lamp baboul mouridina machalla ❤❤❤❤❤❤
yalla naleiine yaalla yokou xeiweul yii bayi leine fi gueine di gueneu seddal xol yii
Hizbut tarqiyyah yag lénn fi ta werr barké serigne mountakha mbacké
Akassa
Mâcha allah dieureudief serigne touba serigne Mountakha yalla nafi yague té wér Mbacké amine
Dieireudieif borom touba Sante yallah baniou yalla Mayer kou melni cheikhoul khadim 😭😭😭😭😭🙏
Alhamdoulilha yallha nanu yallha fayal Serigne❣️❣️🙏🏾
Me gusta escucharlo todos los días gracias serigne touba el Salvador ❤❤
Dieureudieufety Serigne Touba sunu yakar taye ak euleuk
Thiey mawahibou sed na khôl lol machallah dieureudieuf serigne touba kenla amoul morom mbacke 💕🤲💕diarama mam cheikh Ibrahima fall lamp 💕🤲💕serigne mountakha mbacke💕🤲💕 yallah nafi yague lol ta waw len gor machallah wa hizboutarhiya sounouy khôl said nalol man Souleymane diop beugue fallou mangui fi si touba tolentino keur Serigne touba Italie di tewlou khasidagui di mawahibou sama khôl da said lol ken dou serigne touba kenla amoul morom mbacke 💕🤲💕serigne atou diagne yallah nako yallah yeureum ta kharela aldiana firdawsi si barke yonantibi alay salatou wasalam sikhasidayi yallah nala serigne touba terouAllahou ma Amine machallah dieureudieuf wasalam💕🤲💕
Dieureudieuf serigne touba amoul morom
Dieureudieuf borome touba amoul morom
Faal lii yémémaa... Ndeysane tawfekh rekk ak yeurmandé.. Merci Serigne Touba. AL hamdoulillahi
Thiéye HT mawahibou srgn mayip Geuye Yalla na Yalla youki léram sa barkeb serigne Fallou
Theye sama khassidabi .CHEIKH MOUKHAMADOU MOUNTAKHA yalnagnouko CHEIKHOUL KHADIIM fayal
Amine
Je suis mouride teh Serigne Touba rek la beug lolou mo gueun woor
Serigne bi rekay Serigne bi
Thieye Serigne Touba fima tollou ni khamouma loumaye ligeye j ai des frissons
Thiey cheikh ahmadou bamba khadimou rassoul dieureudieuf serigne touba
Beugueu Serigne Touba rekh doyna tékhé
Jereujeufei Serigne touba❤
Machallah 🤲 Serigne Abdoulaye Diop yal nala yalla faye❤
Merci 🙏🏾 Serigne touba
Mashalah. Dieureudieuf Serigne Touba. HT chapeau à vous !
Tieuy Dame miii 😭😭😭😭 lii keneu meunoul expliqué ni mouy def khol barké serigne Bamba oooh 😭😭😭