Mouride bou xamoul yallah, mounoul fekhe ba moss si maratib yi, maarifa yi, anwar yi, asrar yi serigne di djoudjou si khassida yi khana djang di yemou rekk. Mouride daye xam boromam, xam yallah xam yonent warna kou nekk koulene xamoul yallah bo xam kokou yallah! Xam yallah nak modi xam secret kalimatou shahada lahilaha ilalahou wahda-ou la sharika. Jeureujeuf serigne touba, jeureujeuf cheikhou moussa cisse, ndiambe borom darou.Yonou mouride serigne you barri matougnou talibe baye maat serigne, bay meuna tarbiya ab talibe. Ay domou serigne rekk moffi barri waye cheikhal mou rabbi, bariwoul.
Macha Allah jërëjëfé Serigne Aïdara Mbacké yaggal téwer BMK244.
Akassa