A beau vraie dire y'a des gens qui sont comme diogoye qui détruisent la foyer des gens, que Dieu m'aide d'avoir une femme être seul avec elle pas de famille élastique ni ma mère ni ma belle-mère si je n'ai même pas de dépense sa reste entre nous deux vivre dans l'harmonie c'est mieux que Dieu nous donne une merveilleuse famille amiine!!!
Après le ramadan j'aimerais la série Adja continuer moi je regarde pas les théâtres sénégalais mais depuis le 10em jour du koor je commence à être obsédé cette série
Mansor Sarr lolll wakh na deugu kat kom legui lolo khew youtub mdrr non nioun senegalai douniou dem mdr o lieu gnouuy comenter pour apprecier mai daniouy comenter pour latier ay jaim lol
Des gens ingrats comme Diogoye gno bari ci foyer sénégalais yi. Quoi que tu puisses faire pour leur faire plaisir ils chercheront toujours à déstabiliser ton ménage. 😡
Pathe sene mo yambar rekkk melniii dou borrom keurrr guii. Mann deii koumaa takkall djiabar ta yeugoumaa ko ioe yayyy seye akk momm. Mouyy nijayyy di mammm
- Ben geil moo beug fein loo bein mère bouy sett( voyante). Deim si mère-bi, mou diokh ko petaw yi neko wakhal sa sokhla. Guel bi dadi murmurer :'sama taat-yi'. Mère-bi tassarei pétaw yi nèko: ligay settlou leudeumneu ..khautneu tei khassawna😂 ! Bon Ndogou🤝🏽 !
Da am louma diaxal fin koor gui djigueen youy def letou you bess,tissage,pose cils ak ongles xana dougnou wor ndax doleen def coiffure bou bess diko toyal pose ongles meuno Thié diapou kone wore sans prière dagniy régime 🤦🏽♀️Djigueen sonouna🙏🏾😭
Un journaliste demande à un peuhl. -Comment est-ce-que vous voulez que le ramadan soit? Le peuhl répond :- Nous voudrions qu'il soit comme la coupe du Monde. Qu'il n'ait lieu que tous les 4ans et Comme d'habitude sans la participation de La Gambie😂😂😂
Sama wa team ande Sétane Séries Ramadan yi, name nalène lou beuri. Jespère ke yéna ngui ame diame bou bakh. Et bon Ndogou, qu'Allah vous protège 😘😍💝💖🌸 Mais vraiment nak Wadioubakh kou Seuytanéla
Ndeysane quand j'ai suivi Adja pour la première fois, j'ai tellement aimé la joie que Adja a quand elle accueille les membres de sa belle famille... Et regardez ce qu'elle récolte en retour et Diogoye est le plus hypocrite de tous... pourquoi seuy méti au Sénégal ? on te poignardera tjrs au dos malgré tous tes efforts femme et c'est souvent pire si tu n'es pas liée par le sang avec ton conjoint.... li mo tax sawarouma...
Ah sounou governamayo ray na niou baniu dèt (#ay aja ak ay ami ak ay dolly lèpp darra bakhosi ay phatè sène $# com si patisèn $😱💀💀💀👏 cou bagne yi yèpp sa lou kho
Personnagou Njogaye mom poison piiiire leu 😷😷☠️☠️☠️ Kouko am beau frère dé djomi, siss, sénéne, wax lou amoul... Yalla nagnou Yalla mousseul ci niit you mel ni 🏃🏾♀️🏃🏾♀️🏃🏾♀️
Anii sopéy Mouhamadou Rassoulillah beusseul may guiss
Adja Fatoumata Sagna (psl)
psl
Xjxd
Des photos
Psl
Kéepu koye setan Série Adjia yalla nala yalla defal jamm❤
Astou Cisse amin way yaw bakhga dh 😍
Astou Cisse amine cisse
Amin
Mane dina bayi commenter ..ndakhe douma ame j'aime t chak jour maye 1er
Bassirou Ndour merci de vous abonnez à ma nouvelle
Contane gueuh 😂😂😂
Contane na kaaayyy
qui voit que adja dafa wara continuè après l ramanda vue k la femme de diogoye est la ki prepare de faire du defantè avec adja ! clic Jaime. 😊😊😊
A beau vraie dire y'a des gens qui sont comme diogoye qui détruisent la foyer des gens, que Dieu m'aide d'avoir une femme être seul avec elle pas de famille élastique ni ma mère ni ma belle-mère si je n'ai même pas de dépense sa reste entre nous deux vivre dans l'harmonie c'est mieux que Dieu nous donne une merveilleuse famille amiine!!!
Mohamed Aguibou Ba t'as raison nak 😊😊😊😊
Mohamed Aguibou Ba 😍😍😍😍
Mohamed Aguibou Ba 👍👍😘
Mohamed Aguibou Ba amin way
Mohamed Aguibou Ba peul nga rekk
Les séries vont nous manqué 🙇
Bilay iow 😔😔😔😔
Trop
Après le ramadan j'aimerais la série Adja continuer moi je regarde pas les théâtres sénégalais mais depuis le 10em jour du koor je commence à être obsédé cette série
Salfie réfane😂😂😂 le visage de amy aussi khol day sott wawaw dom ndeyam daka djegué soukay nampal dakoy khol ❤
Patisen pathe Sene 😀😀😀 vous ete incroyable j'aime cette série Aay Aay aay dina lene name 😭😭😭
Ayy sarakh len ma aimer sama commentair way ahhhh boulen ma rousslo wayyy
Mamish la princess 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Wa liii ame naaa tamit Mamish
Mansor Sarr lolll wakh na deugu kat kom legui lolo khew youtub mdrr non nioun senegalai douniou dem mdr o lieu gnouuy comenter pour apprecier mai daniouy comenter pour latier ay jaim lol
Mamish la princess motakhitt yaguisi 🤣
guarda divertente lol souma defoul won ni ken du aimer
Ardo Sow mdr ardo degoumala d
Des gens ingrats comme Diogoye gno bari ci foyer sénégalais yi. Quoi que tu puisses faire pour leur faire plaisir ils chercheront toujours à déstabiliser ton ménage. 😡
mirabelle vraii
mirabelle bilahi wakhatiko dai
Ay badola pur sang lagnou
Pathe sene mo yambar rekkk melniii dou borrom keurrr guii. Mann deii koumaa takkall djiabar ta yeugoumaa ko ioe yayyy seye akk momm. Mouyy nijayyy di mammm
mouhamet sow 👏👏👏👏 goor foula 😄
Je suis de la Mauritanie et je connais par coeur revane et rewmaw et kaba et ndedene de très bon village
- Ben geil moo beug fein loo bein mère bouy sett( voyante).
Deim si mère-bi, mou diokh ko petaw yi neko wakhal sa sokhla.
Guel bi dadi murmurer :'sama taat-yi'.
Mère-bi tassarei pétaw yi nèko: ligay settlou leudeumneu ..khautneu tei khassawna😂 ! Bon Ndogou🤝🏽 !
Nn raygama
Frange tkd mayma beineine way
evah riri koogn'ma souba rk! à la même heure 😂
Frange tkd 😂😂😂😂
astafourllah 😂😂😂
khay ndiogoye tamite loutayy meuna macorro 😂😂 ah li dii ....team adja 😍😍
Sama maman Adja dh kéne meunuko woudjeulé
Kou d'accord pouce bleu 👍
Aywayyy beine Jaime sakh beugg na bala koor gui di diekh 😢😢😭
😍😍😍Ohhh contane naaa enfin
Merciii way de me sagal
Anta Ndir bi dou regle yeine bala gnouko wah bopam si Keur gui sa kanam ni reunio fondé😠😠😠😠
Ani fans Adja yi tamit??💪💪
Vraiment adja elle est très belle. Kou beug adja beuseul jaime
Ta maman vivra jusqu'à ta réussite dit amin ❤❤❤❤❤
Waw yen mom lou khéw khana mousso len setane série adja
Les gens qui regardent les commentaires sans commenter j vous salue 😀😀😀
Aliou Diop xana wa tdd ngeu 😂
Wa guisgua dé 😀😀
Aliou Diop tax gua ma commenté sax
Aliou Diop manguilay fay
Ha Adja mom dou kouy ame woudiou Wa Adja iow ite gawo wonè fem tamite ishh😂😂 euy si cetai moi 😂😂 na Adja da dal nak🤭
Bonsoir chers téléspectateurs 💞 Ana gni bok jixi jaxa tamit 😂
5mn 69 commentaire les gars je vous adore vous êtes extraordinaire yalla niou feke deweun you Barry andakh wergou yaram
SANnews Post votre chaîne c pour les filles mais je les fait juste pour te rendre heureuse comme c gratuite on sentre aide
SANnews Post de rien soeurette on es ensemble
Haramoussa Drame que des pub nak ak ay aimer lén ma
Haramoussa Drame Nô
Team Adja et Pathé Séne
Kane mo recommencer sétane Adja
Kone niou ande sétane adja na xol yeup fékh😍😍yalna diam yagu 😍😍
soleil soleil 🙏🤗
soleil soleil amine niou bok lép
soleil soleil merci way
Penda Thiam je t'en prie 😍😘
Penda Diop 😚
salfie réfaane waye😂😂😂
Oh werr bou sell bi werrou ngueûnel bii mo ngui tagato dhe yalna niou koo téwè ayy atti att amine
BoY Mboro fimistè motax nekhoma wer bi bimouy nieuw es k dala taggou doko bayi mou dematt ak diam tchiip. 😂😂🙏
Amine
Penda Diop hahhah yaw ham nga ma ham nalla soo sagnone korr gui diexx tay aka ragal korr
Alhamndoulilah ma ndieukeu commentaire ndeikei ...taye mom danguene tardei 10mn apres zero commentaire niaww allei mane
Yalnala Sénégal dieul coupe☝ du mnde bi si Barki werou✌ korgui kou d'accord pouss bleu may guis ✔✔
sa yènè RK la mais Sénégal dou deul coup du monde sounu coup moy serigne touba Mame maodo Mame limamou bay niass extra mais yènènalèn KO nak
+ndiaye abi masahallh sa wake rafétna
+Fallou Seye merci bcp mais lolou mafinek nak
Es ce que adjia moromou anta la yène wa RUclips qui warna yeunguel adjia wala bok
Ndeye Diop domou baay mogui melni nga ni combat Bombardier ba ak Rokki Bilbao dou moromam sax walaa😂😂😍
nouyounalène mes chree penda et ndeye...bayil anta fofou mouneii moy roubeii nonou teii khamou nei original dou moromou chinois
Penda Diop wakhatiko dal ma chérie MDR
Gnilane NDOUR pomme de terre dou moromou Angleterre dal
mala wakh lii maiw kène dou diogoye 😂
Kou dakoroul adja ame woudiou sa lokho si kaw
Mouhamed Cisse merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne 🔗
De rien
Franchement nak série yi bou Dieikhei dagnou wett mais dara yalna diam yague rek inchaallaah
Khady Sarr y'a bakh
SANnews Post d'accord pas de problème
Saliou Gueye no yow yama geune
SANnews Post de rien merci à toi aussi
Ana goor yalla yi kou nangou Pathé dieul anta keur gui gueuneu nekh
1 vue 68 j’aime donc les gens aiment avant de regarder😂😂😂😂
diagne diey merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne
diagne diey cvcv
Team Adja machallah namou diongama eupna 😍😍😍😍😍😘❤
Ami K 😂🙋😍😍😍
Ami K anta ndir tamit kén geunou ko djongama di 😊😊😊
Tata adja yalna sa diam yageu way ak mbolèm dioullit yèpou amine
Da am louma diaxal fin koor gui djigueen youy def letou you bess,tissage,pose cils ak ongles xana dougnou wor ndax doleen def coiffure bou bess diko toyal pose ongles meuno Thié diapou kone wore sans prière dagniy régime 🤦🏽♀️Djigueen sonouna🙏🏾😭
Mame Jarrah ha li nga wakh yepeu degue leu
Mame Jarrah iaw esk do def lolou ??
Lalya Renoie 221 😂😂fils shter nala HBD l 10.06 sa dara baxoul sa number ba wone mougui marcher
Pape Maury Sarr tamit damako setlou rek🤷🏾♀️
Lalya Renoie 221 c f supprimer
Diogoy t'as dépassé les bornes hannnn 😣😣
yaay fall Mbow merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne
yaay fall Mbow cvcv
Diogoy moy seytané
yalla na yalla defal léne diame yéne wa ande sétane série yeupe Ana gni d'accord ni ADJA Mo fi tek tank si série yeupe
Ya May 1ère wawaw na rang bi dioup way 😘😍😻😍😂😂😂
Yalla na yalla nangou sounou koor tei niou Yégalé ko si djam ak salaam
Diogoye nak xamal né Adja mattna awa ak niaréll ak niétéll 😂😂 Adja rek dou aÿ foo
Meilleurs série nekhna Hay Hay Hay.....
Lepou lou Waye Diane gni Laylatoul khadri bi yalla naco yalla nanguou si BARCKER SEYDINA MUHAMMAD
🤘Ana ngi beugui adja don sen mamam😍😘
Ana gni diot notification bi jaime
wa Anta Dire kou la bayi ya gui khol sama ADJA 😈😈😈 KI DOU AY FO DH
Wouy kou beug adji beussel jaim
ibzo Gueye jtm
Team adjia koor gui nane kou yokhat ndax adjia way kouma jaime yalna yalla nangou sa koor
mdr no diogoye ray nama mom amoul wakhalé nane beugoul gorou béne diabar😂😂😂 rétane lé léne massi way
beugue loubax merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne
beugue loubax ó
beugue loubax cvcv
adja walay amo marom man nga seuy ta danga dal lolou moma nékh si yaw machalla
Adja rek dou moromou ...💘💟💞
Ana wa teamAdjia, Doudou ak Ngoor? Nouyounaleen dileen ziar bou weer ma setane teh gnew
Mais anta my dara la de🤣🤣🤣😂🤣
Ah namou nalen way Naka senn koor nk mongui deff nekh ah Yalla na yalla nagou sonno koor nk
Ndeysane jj -3 comment vivre sans adja Sama serie prefere 😍😍😍
ęvāčhøù sall bilahi ca sera dure j adore cette serie
ęvāčhøù sall bilahi dan wett ioe
ęvāčhøù sall
Wiiriwii
Ane wa team doudou😍😍😍
Sénégalais loutax mou soxor gno khamné dougnou meussa beuss j'aime gno khamné ni rek 👎👎 lagni déff changé léne options 🤣🤣
Wahal dh babe 😂😂❤❤❤❤
Amadou Mbp déuk la wakh
😂🤣😂🇸🇳
Khana dou ma soxor 😂😂😂
khadijatou Gracet SALL soxor plus🤣
Diogoye insbi yama gueuneu soof ci adouna... Li serie rek la meuneu doone.. sama rak boumako defone dou fanane ci keur gui
Un journaliste demande à un peuhl. -Comment est-ce-que vous voulez que le ramadan soit? Le peuhl répond :- Nous voudrions qu'il soit comme la coupe du Monde. Qu'il n'ait lieu que tous les 4ans et Comme d'habitude sans la participation de La Gambie😂😂😂
Sama wa team ande Sétane Séries Ramadan yi, name nalène lou beuri. Jespère ke yéna ngui ame diame bou bakh.
Et bon Ndogou, qu'Allah vous protège 😘😍💝💖🌸
Mais vraiment nak Wadioubakh kou Seuytanéla
Weee jappu leen si Book likes me🤦♂️
Moustapha Ndiaye merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne 🔗
Ndeysane quand j'ai suivi Adja pour la première fois, j'ai tellement aimé la joie que Adja a quand elle accueille les membres de sa belle famille... Et regardez ce qu'elle récolte en retour et Diogoye est le plus hypocrite de tous... pourquoi seuy méti au Sénégal ? on te poignardera tjrs au dos malgré tous tes efforts femme et c'est souvent pire si tu n'es pas liée par le sang avec ton conjoint....
li mo tax sawarouma...
😂😂😂😂wa déte madior ak👀Xool bu miti bi naku
ani association fanane ak yéndou si RUclips bi
team adja wa dou moromou kenn 😂😂😂😂😂😂
génération boyz merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne
Wa yene Anta ndir mi osé woul mounane tokk seuy seuy bi ki na régler bala makey béléfété
Adja rek dafay moromou bene djekk❤️🇸🇳
Salfi réffane one rasta😜😂
lol
Feuzita Sey mdr
Tanoroi Badiane wadiou bakh dou nite😂
Feuzita Sey cvcv
Adama Fall oui cva
Kou dieppi djiogay like way
anta ndir anta ndir boul sonal sa bop mariétou mo la geuna forokh té manoul thi Pathé dara
Yalnaniou yalla moussaal ji bokh bou melni Diogoye amgo erreur la dey tass keur ahh
Jadore❤
Ani wa team anta ndirrrrr pouz boulo
Koma may j'aime rek yalla na woré le 29
Daouda Mbaye merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne
Avec plaisir
Thx frère
Rock Tube Galsen adaye
#Anta
#Adja
Doussaa moroom #1000 fois
Amna gnu narra namm serie #Adja like maa xool
Haa anta ndir mi tam tarkalah deh aimer svp
Hay hay hay wadiou bakhh
Mangi toupp deh
Ayway yakamti wuma dara koor bi diekh Adja sama série préféré dinala naam troooop
Doudou semeyeuf 😍😍😍
Anta ndir tu ne connais pas ta tête dé kouthji D'accord puce bleu 😂😂😂
Chacha Kane cvcv
adja sama adja😍😍
Mame Diarra Gaye merci de vous abonnez à ma nouvelle chaîne
Rock Tube Galsen dacor
Ahhh Wa association biiii PDG biii nouyounalllén dh... ANTA NDIR. Lagnou wakh anta ndirrrr😍🙅🙅🙅❤️🔥
Mais Presidente foÔ fétté👩💁♂️
On adore❤
D'accord Sannews post
patisen =a paté sen molén di presenté sen seri adja😂
Sama gayi niata jour mo dés thi koor gui ?
LEUZZ VISION 15 leu non?
Cathy Gueye 😱😱😱15
Cathy Gueye mayaakaarné 20 jours la sakh
20 jours
Fatou Ndiaye bayil ligay wakh 😂
ndiogaye seytanega anta ndir demal ga tok ak sa khetou mouseur bou yague😂😂 adja rek si diekk pare yaw la geume
First dou aay foo💪💪💪
Ki regarde ça même après le ramadan
Hiiii koor gui taye moy bess bou bakh biii. Lou nite gnane mou nangou may premier. Topelen sama guinawwww nakkkkkk.
Félicitée moi nakkk
Mohamed Ndiaye 👏👏😂😂
Penda taye siii porte la tokkk notif rek la done khare, dama done ndieukanter
Mohamed Ndiaye hahahha deggal ndiayene bi motaxit daleu nga si
Na gneup topou sama guinaw taye
Sannew post ca va bien mais j'arrive pas
Ah sounou governamayo ray na niou baniu dèt (#ay aja ak ay ami ak ay dolly lèpp darra bakhosi ay phatè sène $# com si patisèn $😱💀💀💀👏 cou bagne yi yèpp sa lou kho
Ana wa team Pathé sene Ana j'aime yi
Personnagou Njogaye mom poison piiiire leu 😷😷☠️☠️☠️
Kouko am beau frère dé djomi, siss, sénéne, wax lou amoul... Yalla nagnou Yalla mousseul ci niit you mel ni 🏃🏾♀️🏃🏾♀️🏃🏾♀️
1er Dou aye Fooo Puce bleu wa #TeamAdja beug n'a len dall yen djuiguen yi Ak goor You Fidel yi ❤️
Aujourd'hui c mn annif max de like les❤
Wadio bakh 😂😂😂😂🤣🤣
Kouy buegué ngoor beuseul jaime
Wadioubakh té ngako may sa bop mo gueune
Yow Diogoye amo diabar di méyé diabar. Charité bien ordonné commence par soit même