Sama Woudiou Toubab La - Episode 14 [Saison 01] - VOSTFR

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 28 окт 2024

Комментарии • 805

  • @batorngom2103
    @batorngom2103 5 лет назад +72

    Kou beugue sa yaye defal j'aime si barké serigne BaBacar Sy

  • @amycisse762
    @amycisse762 5 лет назад +690

    Anna gni beug dem mecque jihare die yonene kou aime yalna gua dem fa si moi de ramandan bi

  • @awaseck8513
    @awaseck8513 5 лет назад +1207

    Ani niou beug sen yaye si sene birr ❤️pouss bleu pour de vrai

  • @queen_fatoumatadabo1934
    @queen_fatoumatadabo1934 5 лет назад +677

    tey dama triste bamay setane série bi
    ndakh sama cousine
    dimanche si goudi migui done wax sama rak yii
    ''diap léne sama woudiou bi toutab la''
    khaley neko ''dou ame tey dimanche la''
    mouné lene dama dioum
    lundi matin à 8h mou décédé
    elle était même pas malade du tout
    elle aimait beaucoup suivre cette série
    donc malene di niane nguéne nianal KO boubax😢😢😢

    • @mbathiodieng3002
      @mbathiodieng3002 5 лет назад +14

      Ay way la vie est ainsi faite k firdaws soit sa demeure éternelle

    • @dashydash9188
      @dashydash9188 5 лет назад +5

      😔😔😔

    • @vampalucho4504
      @vampalucho4504 5 лет назад +11

      Yalla n'ako yalla yeureum

    • @codousylla637
      @codousylla637 5 лет назад +8

      Djaam ak beug begueum yalla ak dogalam adouna mom nirek la kén sakhou fi yalna ko yalla djégal té yereum ko

    • @oussanatoudrame1027
      @oussanatoudrame1027 5 лет назад +4

      Yal na ko yalla khare aldiana you kawe si barke SEYDINA MOHAMED (psl) 😭😭

  • @ndiagandiaye147
    @ndiagandiaye147 5 лет назад +828

    Kou beugue sa baye defal j'aime si barkè borome touba

  • @dioudba5099
    @dioudba5099 5 лет назад +225

    Yalla n'a diam yague sy Sénégal sy barké serigne babacar sy

  • @ousmanelo9096
    @ousmanelo9096 5 лет назад +400

    kou beug sa yaye pouce bleu may guiss

  • @rokhayasy244
    @rokhayasy244 5 лет назад +384

    Sama wa team Annie bi way manifestez-vous.
    Les vrais ont reçu la notif' dans tous les cas.

    • @khadydiop1241
      @khadydiop1241 5 лет назад +1

      Nionguini

    • @rokhayasy244
      @rokhayasy244 5 лет назад +1

      @Rokia Pédro Ngoné chaque jour ñou door ko😛😂😂

    • @ngonediongue2248
      @ngonediongue2248 5 лет назад

      Ay way loy dokh di bokk si team Anie😂😂

  • @abdalnjaay4516
    @abdalnjaay4516 5 лет назад +500

    Série bii dal moy série Guéweul yi commentaires yi da wara nguéweulé am ay thioum wawaw barki yonènté bi 😂😁😁

  • @babouameth9364
    @babouameth9364 5 лет назад +107

    Ani sopè Anni rek. Mais yalla nagnou yalla maye weeer bagnou dou si koor Gui ak diam😍

  • @khamsathiossane1152
    @khamsathiossane1152 5 лет назад +6

    Serigne Mbaye sy mansour yalla naffi yagg lole té adak wére si barkep seydina Mohamed amine

  • @khadykane994
    @khadykane994 5 лет назад +225

    J'adore cette série team ngoné Mbaye
    Lingayy am défaite nak c trop xolal si gnoune wayy

  • @sunnyday7844
    @sunnyday7844 5 лет назад +207

    Ndeysane dafmay fatali toubab bi nieuwone sandaga di djeunde bine-bine.
    Sama copain bi djayei ko bine-bine bou nekk 50.000fr, parei di youkhou nane "wouy naxna toubab bi"
    Toubab bi neko naxoma walay damala yeureum dongue 😂😂😂😂😂😂😂

  • @Karina95800
    @Karina95800 5 лет назад +8

    Kou beug yalla pouces bleu

  • @Papa_116
    @Papa_116 5 лет назад +60

    Yalla na Sénégal am diamb wa ana wakeur seydina Mohamed yi ❤👍

  • @diarrabousso6049
    @diarrabousso6049 5 лет назад +144

    En tous cas sénne Aÿ Taille Basse Tokk na nék si temps

  • @timavanilla3959
    @timavanilla3959 5 лет назад +15

    Série daff may diokh envie nekk gueweul koi 😂😂
    Non mais keur Gui nekh na torop way , barki yonentibi 😂

  • @matyniang6784
    @matyniang6784 5 лет назад +388

    Mangui si bire group anda sétane série yépppp😂😂😂

  • @mariamazahradiagne8552
    @mariamazahradiagne8552 5 лет назад +3

    Bilay ngoné mbaye avec ses manier dado daf may fadj machala 😂😂😂😂😂

  • @diakhardiatou6948
    @diakhardiatou6948 5 лет назад +13

    "Mon père" qui lit le journal
    Choquée😲

  • @adjidiop3905
    @adjidiop3905 5 лет назад +163

    Pomme de terre ak ognon mom moudié na chair di🤣🤣🤣 Maty Mbaaye mo am fitt dé🤣🤣🤣🤣

  • @mouhamedtoure6019
    @mouhamedtoure6019 5 лет назад +3

    Wa ana niou faral ANNI way quou quo faral na def pouce bleu 👍👍👍👍👍

  • @oulitaseck5248
    @oulitaseck5248 5 лет назад +73

    Noo ngoné Mbaye douma Ray 😂😂😂sheut ngeweul mo nekh barki yonentibiii 😂😂😂 Ana gniko beug 😍

  • @astoumbenesamb1135
    @astoumbenesamb1135 5 лет назад +6

    Merci pikini production pour cette belle initiative

    • @papisniang919
      @papisniang919 2 года назад

      sable au qt mais qu'on est sur leur terrain de ski avec des messages de temps en France mais j'ai pas encore trouvé la solution mais bon j'ai passé un très bien d'arriver en ville et j'ai passé un super week-end et j'espère vraiment que ça ira mieux demain car j'ai pas trop de la tête pour le proforma et appeler gratuitement des que sur les caniveaux et les deux équipes en même heure sur la

  • @maridrame2651
    @maridrame2651 5 лет назад +19

    Kou gueumeni Maty Mbaye kholl bi jdiekhna beuseul bleu

  • @choupinachoupi6118
    @choupinachoupi6118 5 лет назад +78

    Wérou kor Bangui gneuw nak ,gnou bayill ay "bb es ce kon peut se voir avant le ramadan " 😀 nathi gneup diap

  • @marieedwigezambo7493
    @marieedwigezambo7493 5 лет назад +15

    Joyeux anniversaire mon père pousse bleu way

  • @mst221
    @mst221 5 лет назад

    Mon père sa wakh diou reuyy dji yeup liguéyo d'accord konn dal da ngayy mbarannn ani

  • @paablaye1389
    @paablaye1389 5 лет назад +210

    Les vrais ont reçu une notification. Team Maty Mbaye🙏❤️

  • @sountouseydi4036
    @sountouseydi4036 5 лет назад +29

    No maty mbaye dou dém 😂😂😂
    Avec Any c'est à mourir de rire 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @amyndiaye7674
    @amyndiaye7674 5 лет назад +10

    Aahhh tioum yein gni di weur ay jaime yeinagui niouy traverser nak dei

  • @oumoukhairyfall2869
    @oumoukhairyfall2869 5 лет назад +47

    Qui a quitté ce qu'elle regardait pour cette série Man en premiere 😃😄

  • @Zazou_wane
    @Zazou_wane 5 лет назад +1

    Il porte un joli costume!!!!

  • @fatoutop9424
    @fatoutop9424 5 лет назад +16

    Barki yalleu guéweul réck dou aye fohhh louma si gueneu nékh deu nguey fébeur mounileu ah thioume iow loh fébeur temps leu😂🤣

  • @dienisstv356
    @dienisstv356 5 лет назад +35

    Souma nèkhè française, souma nèkhè sénégalaise😂😂😂, mon père tothie nguafi patiakh!!!

  • @ndeyefayecamara7933
    @ndeyefayecamara7933 5 лет назад +63

    Maty mbay dinama ray augmenter gua prix marché bi ba tok

  • @angiediouf2837
    @angiediouf2837 5 лет назад +262

    Gniy commenter hors sujet yeinanguiniouy traversé dei ish 😂

  • @mariamaniass399
    @mariamaniass399 5 лет назад +11

    S'il vous plait bayilen lenn yonentë bi guen di fowe si sen watt yi

  • @rokhayadiaw3108
    @rokhayadiaw3108 5 лет назад

    Ani tu est belle et tu joue bien le film mete un pous bleu si vous aimez

  • @adamatoure2559
    @adamatoure2559 5 лет назад +61

    😂😂😂😂 non gni il faut ma décoré léne
    Keur Pére Mbaaye amoul noumou nékhé woul

  • @khadyfaye3786
    @khadyfaye3786 5 лет назад +11

    😂😂😂 ay maty mbaye wagnil
    Ngoné elle est bipolaire cette meuf jvj😂😂
    Elle me tue cette meuf

  • @LoL-hm5lk
    @LoL-hm5lk 5 лет назад +7

    Ah Merciiii beaucoup pour cette série tellement ngeweulé on adore

  • @modoundiaye2241
    @modoundiaye2241 5 лет назад +12

    Ana ahlou ramadan Niamé ame boro kor na Niou Faye

  • @amethtine2986
    @amethtine2986 5 лет назад +78

    Team Anny ana nguène jaime way yalna diamm yagg waaay 👍👍💗

  • @fatouthiam2561
    @fatouthiam2561 5 лет назад +10

    Maty tay noyoul déh. Lambil fénéne pour faye tes cheveux naturels. Légui gnidone nélaw nio yéwou

  • @diborbabou2182
    @diborbabou2182 5 лет назад

    way dimbali lene niou way solene sétanoul guene mayniou ak séni commentairou hors serie yi fi tt le monde adore Dieu ckw le soucis solène mounoul wakh si serie bi guene nopi franchement ame diott ba beugeu dead dème lène diouli niane yalla mo geun cme tt le monde

  • @myriamcarter4091
    @myriamcarter4091 5 лет назад +6

    Tay magui si ngoné 😂😂Ken waroul dem ladj dépasse si woudiou wam

  • @salimatadiallo8312
    @salimatadiallo8312 5 лет назад +11

    Waw mon père Costume le Costume te va 👍😍😃 super bien 👍😍. Barki Yenen Temi 😃😃🤣👍

  • @bebemouhamedndiaye8348
    @bebemouhamedndiaye8348 5 лет назад +1

    Kou beugue ani

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 5 лет назад +3

    *_Anni rék momay fathie mane si Toubab🤣😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😁😁😁😁😂😂😁😁_*

  • @papediaw9949
    @papediaw9949 5 лет назад +40

    Premiere dou ay fooo😁yalla naniou yalla doli soutoureu🙏🏿

  • @yeaitsme_2802
    @yeaitsme_2802 5 лет назад +3

    Anni da faye maye doundoule bou bakh ti amo 😍😍😍😘😘😘😘😘😘😙😙😙😙😙.per favore ngone nekal nguewelle

  • @oumygome3029
    @oumygome3029 5 лет назад +3

    Maty Mbaye lale guama ww keur Bmole seck thia Louga😍😘

  • @fatmadiop352
    @fatmadiop352 5 лет назад +32

    No man Ngoné mbaye labeuggg😂❤️💕

  • @ibrahimadiene2591
    @ibrahimadiene2591 5 лет назад +3

    Bellissimo man toubab la italo la dk

  • @fadiagne810
    @fadiagne810 5 лет назад +21

    Hééé dégueul lolou. Mbaaye, WA keur ndiawar ndella Mbaye sassa aka gno nguewelé.

  • @mamediarrambacke9791
    @mamediarrambacke9791 5 лет назад +1

    Père Mbaye lamou laak eupneu 😂 mane j'aime les Guéweul barki yonent bi danio free manam zéro stress😂😂

  • @mokhtarbalde8772
    @mokhtarbalde8772 5 лет назад +3

    Neina j'ai entrain de regarder le journal I'm dead 😂

  • @oumydia6675
    @oumydia6675 5 лет назад +9

    😂😂😂😂ndakh yalla gonè mbaye nopa lou Tay dada mo ayè Ani rek 😂

  • @salljrsalljr8260
    @salljrsalljr8260 5 лет назад +35

    Serie bi mom khana Ji keur gui rk lay am mdr 😉

  • @cissebouserignesaliou7014
    @cissebouserignesaliou7014 5 лет назад +67

    *Anni nak ndékété yooo dafa ngewelé😋😍*

  • @fatougueye-zh7td
    @fatougueye-zh7td 5 лет назад

    Thioum wawaw barki yonentibi thiey ngueweul long vie pére Mbaye😍😍😍😍

  • @faramareenwalde8291
    @faramareenwalde8291 5 лет назад +37

    j'aime Anni elle est adorable

  • @majoileeva
    @majoileeva 5 лет назад +1

    2:55 Ngoné mo nakari batt si joyeux anniversaire rek 😂😂😂

  • @balla8843
    @balla8843 5 лет назад +1

    vrément série bi dafay dindi stress
    waw léne gor👏👏👏👏

  • @bintrassoul
    @bintrassoul 5 лет назад +2

    Team annie standing ovation
    Yaw lay weur

  • @aramelolodaffe7513
    @aramelolodaffe7513 5 лет назад +2

    J'aime cette série et qui encore?

  • @ndeyendiaye5908
    @ndeyendiaye5908 5 лет назад +1

    Franchement couple goné mn père dafa neeekhh j les adores guéweul dal nekhna

  • @kanediallo4579
    @kanediallo4579 5 лет назад +1

    Mon père dall mo guapo❤️❤️❤️❤️

  • @ndellangom7724
    @ndellangom7724 5 лет назад +39

    Salam wa ande setan série yeup kom mane yalna diam yague🙏🙏💞💞 way mais série bi daal souguen yokon temps bi dina guena bakh

  • @papiseye3608
    @papiseye3608 5 лет назад +1

    Jai trop aimer❤

  • @annietoure714
    @annietoure714 5 лет назад

    Sama tourando rk dou ay fo ♥

  • @lyabdourahmane5703
    @lyabdourahmane5703 5 лет назад +1

    Quand les Ngueweuls souhaite un anniff sa donne sa😅

  • @khadija696
    @khadija696 5 лет назад +7

    Aye waye mane sa m'a woudiou américain le

  • @aichadramecisse930
    @aichadramecisse930 5 лет назад +28

    Ay way bi mom dou chance merite le premier vu😂😂😂yomboul de

  • @Lahaddybala10
    @Lahaddybala10 5 лет назад +2

    Barki rabine alamine fofou tothie na

  • @mouhametngom1995
    @mouhametngom1995 5 лет назад +14

    Maty mbaye dinama kil koi neena waadji . nganei danga kassek say produit😂😂

  • @Fatougueyebello
    @Fatougueyebello 5 лет назад +4

    Maty mbaye rek si xalé teint noir machallah

  • @bellachoufaye1085
    @bellachoufaye1085 5 лет назад +7

    Ma série préféré 👍❤️👏

  • @mamefatoukane9374
    @mamefatoukane9374 5 лет назад +29

    no mai ngoné koumouy fadje?😂

  • @mayagueye5055
    @mayagueye5055 5 лет назад +15

    Mane dale fier d'être ngueweul lou ngueweul amoul beuguma barker yonenti bii suma donul wone ngueweul xawma lumay done

  • @ndeyemaremediakhate4608
    @ndeyemaremediakhate4608 5 лет назад +7

    Thêatre bi dafa gate 👌👌

  • @adjand9709
    @adjand9709 5 лет назад +5

    Famille anti stress 😂😂😂😂teammm ani la puissance 💪🤸‍♀️

  • @khadimdiop8644
    @khadimdiop8644 5 лет назад +5

    Mani commenter yi mongui maye traversé hahaha na ngewalé

  • @genevievendiaye9948
    @genevievendiaye9948 5 лет назад +2

    Vous assurez comme dab rek

  • @ayni7044
    @ayni7044 5 лет назад +16

    Ngoné merenala anni mi warnalay gagner tout l temps ah li dou yonne

  • @abdoulo5252
    @abdoulo5252 5 лет назад +38

    Ay wa Jaime ay wa Jaime. Jaime yangui bénn 100f😄😄😄

  • @binetoukebe7763
    @binetoukebe7763 5 лет назад

    Wa ndougou maty Mbaye bi mom koumou diagal pousse bleu ahahahahahaha

  • @lahadmbengue5630
    @lahadmbengue5630 5 лет назад +20

    Maty mbaya khool bii mo diékh😂😂😂😂😂

  • @elhadjibadaradiagne549
    @elhadjibadaradiagne549 5 лет назад +36

    Ou sont ceux qui d’ambiance sur le générique😂❤️

  • @fatouseyembaye533
    @fatouseyembaye533 5 лет назад +2

    Mane dal j'aime les griots ndakh dagnon beugueu lou bakh

  • @khadykeita2043
    @khadykeita2043 5 лет назад +5

    Heeeey lii Ngoné sagnsé eupeneuuuu Diaba yaye bour lay dooonnne

  • @rokhinagaye1366
    @rokhinagaye1366 5 лет назад +3

    Wa li nékhoul wouy mane serie bi dall momay danel tmt fofou todji radiakh ani wayy mako beugue pir toubab bou diongué la

  • @lasenegalaise9694
    @lasenegalaise9694 5 лет назад +68

    Ngoné mbaye comme kou bipolaire.
    Un coup elle sourit di contane
    Un coup elle s'enerve

    • @mamanmbodji7175
      @mamanmbodji7175 5 лет назад

      😂😂😂bipo nak

    • @lasenegalaise9694
      @lasenegalaise9694 5 лет назад

      @@mamanmbodji7175 dama wax deugg di ngoné dafa manqué deh 😂😂😂

    • @mamanmbodji7175
      @mamanmbodji7175 5 лет назад

      @@lasenegalaise9694 deug pir ga wakh Ngoné rk da wayadi 😂😂😂😂😂

    • @bambakhadimtoure534
      @bambakhadimtoure534 5 лет назад

      Patriote dc elle é bipolaire 🤷🏽‍♂️

  • @sublimesublime7632
    @sublimesublime7632 5 лет назад +6

    Yalla gua féké coorgui ak djam 🙏

  • @sanedieneba1624
    @sanedieneba1624 5 лет назад +1

    Ma beug série bi merci wa Pikini , kou dislike kou sokhor nga ish

  • @bolloniang6287
    @bolloniang6287 5 лет назад +2

    Â français mon père doléne si wakh tamit 😂😂😂 mane dall magui si anni team anni

  • @aminatouthiam6443
    @aminatouthiam6443 5 лет назад

    Serie bi nekhna damay reh bay tourou

  • @binouchathiam6385
    @binouchathiam6385 5 лет назад +5

    Maty Mbay say prix cher neu niaff😂😂😂😂😂

  • @fallou7mbacke873
    @fallou7mbacke873 5 лет назад +4

    Yiiihiii la maniere dont ngoné rie sa m tue walay🔗😭