Keur catolik yi mou fegniouwon nak segn bi kneu meuno kham kou am tieur rk lay fegniou adiouwoul thi bandi bi thi mourid bi thi tidiane bi thi keneu koudoul thi koumou ak foumou ko nameee☝🏼☝🏼☝🏼☝🏼☝🏼
Bayilén Di diamou kheurem Serigne Touba du manam guédj kou sobou né méss sou déloussé khameboromam wouti lén li bamba done khamalé Mouy lérou yalla ak souna rassoulahi
SËRIÑ TUUBA neena : 👉🏻 Buñu démee bathia kanam té guissa tuleen ma, ngeen dima wuut té bëgg maa guiss, xam ngeen fungeen may wutee ? Ñunéko deedét !! SËRIÑ BI ni : wuut leen ma thi XASSIDA YI
Lerou Lene manou len sii Serigne touba mom kouy diangue khasidame Yii te wou tou lo thii dara lou doul ahmadou BAMBA khadim lou raw fegnou dinala ko deff
Wakhouma ni keur gui bokkoul thi you baax yi dh,wayé satan sou beugué wagni jaamou yalla nit bokkou na thi yoon yimouy diaar,ba nit ki diap ni mom dotoul dem safara.Amna ay xista you beuri yougn ci nétali té amna itam kilifa dîné you beuri youm dall Kone nak sama gars yi moytou leen pékhém ibliss,ndax mom soula beugué diapp doula wann lou bonn dh lou baax rk lalay wann bangua déféni yaa fi gueune moujj faté sa borom faf. Yii amoul solo nagn diamou dji yalla ndax moognou fi indi yii yeufi ibliss dong la
Wey sama ndaye magui déee non sénegal gui louné mofi khéw baparé niome sén mir bi di lathie peinture niounane ay Serigne touba diamou djilén yallah moguen sén thiakhan yi
ALLHOU AKBAR SOUBOUHANALAHI MEME MOUHAMDOU RASSOULOULHI SALLAHOU ALAIHI WASALAMA MOUSSOUL FENE SI MUR MAIS YEN NIEMEGEN YALLA DHE BILLHI DOU DEGG YEN GOMOLEN YALLA SOUN BOROM BILLAHI SENEGAL LEHI DHA BARRY BIDIYA ISILAMOU DOU NIARI DOU NIETI DOU NIENTI ISLAMOU BENNALA SI NIOUN MAIS YEN JELGHEN FEN AK FENALE SERINGE TOUBA DIKO TEK SIKAOU YONENTI RASOULLOU KHAOUMA LI LALA NAK MANMI MALEN DONE MOURIDI SHADIK OK
@@diammouyalla3880 pourtant amna ben waykate bou meusa wakh ni serigne fégn na si portable wam nite you bari dal si kawam té kokou ko wakh diamou Yalla la kom nieup. Té façon publication yi limasi diakhal moy do dég bén seutou serigne publié ko. You melni motakh niou yap dioulite yi bouniou delou si diahilia nak
Il faut laissé ces bla Blas là, rien n'est apparu là bas.Vous êtes perdu . mais il faut laissé de dire Dieurdieuf Serigne Touba mais vous pouvez dire Dieurdieuf sunu borom(yallah) c'est plus juste et tu peut gagné quelque chose en prononçant ça .Je pensais que Serigne Touba est une personne comme vous et moi ,la différence est que Dieu lui a donné une superbe connaissance Islamique. Et on peut être d'accord de ça. C tout. Excusez moi de ses mots ..
2019 Guediawaye a gagner le Ballon d'or senegal,,Aliou Sall petrole bii,,,Ndiaye dragon,,,faux billet Bougazelli,,,sa n'est pas souffi pour Guediawaye vous nous dite serigne touba fegnouna ok c bon maintement
Barké yalla africain tanka bayiyoul lii dou développer, liguey moy développer rew, té bayi serigne yi niou nopalou,gueên leen di fénal rek.tallen loleen leek mo guen ci yeen,Sénégal fait parti des 23 pays les plu pauvre au monde.
BAYII LENE SENE FO YI SERIGNE TOUBA SOU DONE FEGNE DOU ROMB TOUBA ROMB SERIGNE MOUNTKHA ROMB LEPP DI FEGNE SI AYE MIRR LEPP AY PEKHE CHAYTANE LA KHASSAYID YI MOY KIRAMAM KHAMOULENE SERIGNE TOUBA MOTAH
Sheuuuuuuuuu ndeyssane non je préfère ne plus rentrer je reste à l’étranger Non Sénégal d’où dème. Pourquoi on avance pas un peu. Popopopopooooooooooooooooooooooo le Sénégal va mal sérieux
Miline Emilien juste une question tu es un homme ou une femme ? Je me pose la question car je suis une femme mariée et je ne préfère pas garder contact avec des hommes. Pour une question de principe.
@Mame Sall Mbacké SmD diegueulou deh dama dioum. BOROM nékebi (kaaba gui )la beugoneu binde. BarakAllh fikoum si dioubeunti kaddou gui. Yalla na gnou yalla tek si yonou siratal moystakkima té yokk suniou ngueum. Amine
Serigne Touba deh dou n'importe qui lay féniou ak dou founek lay féniou dem diamou yalla Serigne Touba fowoul fowlou woul
Fimou fen de ay mourid sadix laniou daniou fa don diangue Alhourane bamou feg fa
Fadj sen Diangoro louy sa problème
Keur catolik yi mou fegniouwon nak segn bi kneu meuno kham kou am tieur rk lay fegniou adiouwoul thi bandi bi thi mourid bi thi tidiane bi thi keneu koudoul thi koumou ak foumou ko nameee☝🏼☝🏼☝🏼☝🏼☝🏼
🖖🤞🤚🤚😚😚😙
@@shannelloukballers9494 niambatane
Bayilén Di diamou kheurem Serigne Touba du manam guédj kou sobou né méss sou déloussé khameboromam wouti lén li bamba done khamalé Mouy lérou yalla ak souna rassoulahi
😂😂😂 non Sénégal mo daakh ci planète bi 😂😂😂😂
Sénègal mo nékh serigne touba fowoul fo Lou woul
SËRIÑ TUUBA neena :
👉🏻 Buñu démee bathia kanam té guissa tuleen ma, ngeen dima wuut té bëgg maa guiss, xam ngeen fungeen may wutee ?
Ñunéko deedét !!
SËRIÑ BI ni : wuut leen ma thi XASSIDA YI
Aka leer
Diadief mouride
@@diopfallou7638 diuere duief
Légui alkouran nak bokoul ragal lén yala s touba wakhoul lolou wakhalko limou wakh
Yén yéna yape serigne touba deug deug sén mure bi ndokhoume tawmi khaw ko raye
Lerou Lene manou len sii Serigne touba mom kouy diangue khasidame Yii te wou tou lo thii dara lou doul ahmadou BAMBA khadim lou raw fegnou dinala ko deff
Sii lu werr
Bilakhii
wawaw malako wakh
Tjéy yalla lii yép ndole mo ko warale ak xif yalna nou yalla mousal tji niak ak fanatismes
Woutil lasso lasso ndeye sa keurgui soukofi bénén nawét féké djibril moy fegn ndakh day guena kharr,😂
mar makhouzizou saway ray ngama, Senegal Mo beuri thiakhne 😂
@@mouhametdiop7470 , barkhé cheikh tijane, na dém outi lasso
Yow reyngamaa dii😂😂
Sawaye dadjinguaniou
@@aramethiam9972 gni danouy fontou Sirk mounta wessou lii niémé dof doflou trop. Ba paré image serigne bi la guissoul sakh
Bayi lén thiakhan yi té diamou ji yalla
Serigne touba fami fégn takhawalou kat doufa ne
Wakhouma ni keur gui bokkoul thi you baax yi dh,wayé satan sou beugué wagni jaamou yalla nit bokkou na thi yoon yimouy diaar,ba nit ki diap ni mom dotoul dem safara.Amna ay xista you beuri yougn ci nétali té amna itam kilifa dîné you beuri youm dall
Kone nak sama gars yi moytou leen pékhém ibliss,ndax mom soula beugué diapp doula wann lou bonn dh lou baax rk lalay wann bangua déféni yaa fi gueune moujj faté sa borom faf.
Yii amoul solo nagn diamou dji yalla ndax moognou fi indi yii yeufi ibliss dong la
Dieureudieufe Serigne Touba ki gueun sén ndaye ak sen Baye ak sen Serigne bi guén geum gnoune Serigne Touba rk lagnou yakar tay ak euleuk ♥️👌
Parè guene thie draragon legui serigne bi mon thie dèss ok
😂😂
Serigne touba meuna lou raw lii 👏👏👏
Dieureudieufé serigne touba
Billahi yéna meuna thiakhane bayiene féneu foo yi serign bi dou thiakhane
C'est ça qu'on appelle allusion optique. Forcer de voir quelques choses
😅😅😅
Wakhal déh
😂😂😂😂😂😂🤣
Bilahi
😁😁😁 wallahi Sénégal dafa Bari nio dof. Shaytaan ay féem lay indi rek Sénégalais yi diommi.
Mane senegal khawma loutakh nite yiii dofé rék serigne touba akk nimou tolou fa yalla akk limou ligeye tchi yonou yalla ndakh fokk ngéne dina déff lou wayadi di fégne tchi mur tt jour you méle ni souniou deukk rekk layy amm loutakh yalla dou fégne tchi mur mouhamet psl walla kénéne kou djiggé yalla di fégne tchi mur a chakk foi ngéne beugg dieul you niakk fayda yii né sangue béko déff wayy mayy lene niou diamb wayy serigne bi dou moromou ayy murr wayy
Fi mo beuri ayy comédien sérieux..
Boss officiel fdv daga skhor my dagaye dê légui mala yrm brome touba amoul mrm si kaww souf
💔
Nioun xawma founiou diéum ak souniouy xeureum yi yéférrou you diéka yi li laniou done daf
Khana sa bay moy comidien
No Senegal yalla nanou yalla yeureume
Kene dou cheikh ahmadou bamba 😭😭 kou téde ki amoo morome fii ta doko am fanou dieum
Wey sama ndaye magui déee non sénegal gui louné mofi khéw baparé niome sén mir bi di lathie peinture niounane ay Serigne touba diamou djilén yallah moguen sén thiakhan yi
Yena graw ragalen yallah
Iow rew ngua déh
Bilay tu raison, na dém outi lasso
Ioe khana domou dmrm gua
@@papasow3790 ma tay rew
Iaw mi rek li ngay deff bokoul si diamou yala ndakh manou wo
Fégué khamoléne serigne touba ba légui toléne ko khama di dh
Mouhamade mooy qui gueun thi mbindéf amoul morom moom aki sahabam
Keineu dou serigne touba. Kou sokhorr dina dée téh boo dée wé nonou sii sokhorr Safarah nguay dem décretemen bilahiiiii👍
Khana mome moy yalla
Diamou ji lén yalla li yep ligéyou satané la rekk kot guis serine Touba solo guis si AP muir
bahilen weddi luunguen fekkei wul
tei aussi bala ngay dig lei toop yalla dafay fekk nga diko jeffei
Koumou nakhari yakham lii dou dara ci Serigne Touba kholbou nakhari molendi raye diaruediuef Serigne Touba
SOKHOR'' baakhoul dh
@@zmby3290 yen demléne ligéyi bayi thiakhane
Saytané mom manta solo SERIGNE TOUBA mangui toup nak
bilay yeina neikh hahaha wouy apres xam na c'est la fin du monde nak wooooooooooyyyyyy
Dieureudieuf ahmadou
ALLHOU AKBAR SOUBOUHANALAHI MEME MOUHAMDOU RASSOULOULHI
SALLAHOU ALAIHI WASALAMA MOUSSOUL FENE SI MUR MAIS YEN NIEMEGEN YALLA DHE BILLHI DOU DEGG YEN GOMOLEN YALLA SOUN BOROM BILLAHI SENEGAL LEHI DHA BARRY BIDIYA ISILAMOU DOU NIARI DOU NIETI DOU NIENTI ISLAMOU BENNALA SI NIOUN MAIS YEN JELGHEN FEN AK FENALE SERINGE TOUBA DIKO TEK SIKAOU YONENTI RASOULLOU KHAOUMA LI LALA NAK MANMI MALEN DONE MOURIDI SHADIK OK
No c grave kw Ana Sene gueume yalla
Sisou Mane gua
Iaw mi geum yala nga dieul ap dioulit day mandou
Yow doull
Legui seurigne si kene beugu df yalla bou len fate Niom omar seydina dina aloun sakha ba yoyou
Sénégal 🇸🇳 nekhna bilahi
Wélélélé..nek hibadou daal mo nopalé nak
S touba dé kouco ligueyal mou wanla bopam
Bilahi lou léér nga wakh gniy wédi danio sokhor rék
@@laminediakhate6201 yaw wero koula wah lolou
@@amyarrmoamsolo648 yaw mi ya weroul
@@thiambabel8885 demal uty ham ham MO gen
taib Ndiaye ligueyal Yallah mo am solo
bilahi yala na gniou yalla mousale gniou sirére
niaka xam serigne touba motax ngeune di deff li
bilayhi
Ya wakhe deugue
Dengue warra ragal yallah guene warra delousi thi yallah ey waye adouna gam yallah rekk mo am solo yene gamlene yallah
Wa Guidieway doyna mouni gui nke si 2019 guidigui guiy ray aki retan be 2020 doyna
Allahou Akbar dieureu dief Sarigne Touba wallahi sarigne Touba amoull moroom de
Serigne TOUBA à réussir sa mission avant sa mort vous aussi essayer de faire quelque chose avant de mourir au lieu de le chercher sur les murs .
😂😂😂😂😂😂😂😂
Bayyileen thiaaxaan yii té nekk nitt
Serigne Touba amoule morome
Kou meussoul guiss Serigne Touba soula féegnoo nokoy khamé ? Sénégal deuk bou doy war leu bilahi. Yalla naniou Yalla mousseul si Shirk.
On a sa foto weuh😆😆
Du vrai blasphème l'islam n'a jamais accepter ce genre d'image adoré une image on c'est même pas d'où ça viens.Que ALLAH VIENS EN AIDE.
Le jour du jugement dernière walahi gueum nanii Niit ñu barii dinañu layo ak Segn Touba Bayile thiaXaan Serign bii fowoul folouwoul 🙏🏾
Mur bou salete bi.
Weuri len serigne touba thi hassida yi mo gueun .
Moy yone de
Bilahi
Fiidal d'Ara lafi gissul
Ak man. Rien vu
Sant Serigne Touba rek
Gni danio yabaté serigne touba si mur lay fégne dinguén ko layo ak mom
Kou diay sa keur diaroul rek nga sentoufa serigne pour mou diar.
Sénégal daall moonékh
Cheikhouna Khadim rek
Iblis de wakhatoul dara parcque sa mission est réussi
Lou were gua wakh
Yen yi obscurantisme lay diour
Bayi lin wide yalla manna lonie
Mane dh xawma deugue la xawma dou deugu waya iblis souy nax niite gni dina diar fénéne foudoul thi Serigne Touba
@@diammouyalla3880 pourtant amna ben waykate bou meusa wakh ni serigne fégn na si portable wam nite you bari dal si kawam té kokou ko wakh diamou Yalla la kom nieup. Té façon publication yi limasi diakhal moy do dég bén seutou serigne publié ko. You melni motakh niou yap dioulite yi bouniou delou si diahilia nak
Ndeysane ba diané nit kou deugou gnon bokone dahira nikhmatou rabal alimine sen keur diang xasidda rek ladjou kham 🙏🙏
Eva Gueye le rapport?
Il faut laissé ces bla Blas là, rien n'est apparu là bas.Vous êtes perdu . mais il faut laissé de dire Dieurdieuf Serigne Touba mais vous pouvez dire Dieurdieuf sunu borom(yallah) c'est plus juste et tu peut gagné quelque chose en prononçant ça .Je pensais que Serigne Touba est une personne comme vous et moi ,la différence est que Dieu lui a donné une superbe connaissance Islamique. Et on peut être d'accord de ça. C tout. Excusez moi de ses mots ..
Waaa mane lima diakhal moy GUISSOUMA DARA
2019 Guediawaye a gagner le Ballon d'or senegal,,Aliou Sall petrole bii,,,Ndiaye dragon,,,faux billet Bougazelli,,,sa n'est pas souffi pour Guediawaye vous nous dite serigne touba fegnouna ok c bon maintement
Wallay ta raison yenagui thiahane lo hamnet bahoul
Guediawaye dal doyna waar legui
Nié daniou bari thiakan
Bayilén sokhor lou nit wakh rék nguén wédiko kéne ladiou lén sén avis
😂😂😂😂😂
DÎËÛRËDÎËÛFÊ CHËÎKH ÃHMÃDÔÛ BÃMBÃ ❤️
Anamou ragual len yalla wy li ken douko def da arame ah fen rk
Lou wéér la lou amla man mi am nasi toff you lérr you wèèr you worr
Barké yalla africain tanka bayiyoul lii dou développer, liguey moy développer rew, té bayi serigne yi niou nopalou,gueên leen di fénal rek.tallen loleen leek mo guen ci yeen,Sénégal fait parti des 23 pays les plu pauvre au monde.
BAYII LENE SENE FO YI SERIGNE TOUBA SOU DONE FEGNE DOU ROMB TOUBA ROMB SERIGNE MOUNTKHA ROMB LEPP DI FEGNE SI AYE MIRR LEPP AY PEKHE CHAYTANE LA KHASSAYID YI MOY KIRAMAM KHAMOULENE SERIGNE TOUBA MOTAH
Bayiléne sene khel yinguédi foowé té dém diamoudji Yallah
Bien dit mon frère def serine comme yalla doynewar
Mo kone gnou nitté...gni beugouniou nitté dih
@@khadiatoundiaye3900 lo kham si bokkalé
Mâcha allah cheikh ahmadou bamba mâcha allah allahou akbar
boudé amna dh Lou bakhla yallana yalla déf Diam Serigne Touba kou bakhla mo takh
Yalla manna lone taliwol dara moye raye mouy dekal moy may koko sop Eskay
Sheuuuuuuuuu ndeyssane non je préfère ne plus rentrer je reste à l’étranger
Non Sénégal d’où dème.
Pourquoi on avance pas un peu. Popopopopooooooooooooooooooooooo le Sénégal va mal sérieux
😂😂😂😂
😂😂😂😂
Miline Emilien je suis à Paris
@@fatoukane4929 l
Miline Emilien juste une question tu es un homme ou une femme ? Je me pose la question car je suis une femme mariée et je ne préfère pas garder contact avec des hommes. Pour une question de principe.
Baye len Boukale ak Bida
Man dhh fi guisou mafi segne bi🙄😅😅😅Nn Sénégal 🇸🇳 dafa nekh rk dem len ligeuyi bay fo bi
Wa loutakhe niou yapp s touba
Mur bi mo nam peinture
Merci😂😂😂😂😂🤣🤣😂🤣😂🤣
😂😂😂
😂😂😂😂😂
😂😂
@@salymadiakho9665 😂
Dieureudieuf SERIGNE TOUBA
Yaguena wané bopane nit mo sokhore rék .Fé djoumaye massalikou nék da tilimone ame ndokhe mais légui koufa awe khameni serigne bi mofa wané bopame
Karaba gueen guis bayleen thiakhan
Aboule li s. Bi boukoule couko sosale li amoule
@@souleymanely2551 ya ko deff thiakhan xana
@@massathir1390 dara lerou la sii
@@ElTIO_Galass thiakhan laako diappè na dem défarou mur bi
DIeureudieufete serigne TOUBA
Bayi leen sen xell yi ngen di fowee
So geumoul dangay mandou c simple
@@badarandiaye7542 en ok yangi mer de
@@cheikheniang503 no dou mère sah grand bi
@@badarandiaye7542 ok
@@badarandiaye7542 ay fen amoul MA ndou sering touba Dena nianalko MO dess yalnanko yalla yereme
😯😂😂eh gni nio meun doul
Sheu guediaway beurina ay comédien 😂😂😂😂
Vraiment😂😂
Vrt
Moytoulén pékhé seytané
Mane commentaires yii gnomaii ray 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂🤣
Bayilen sen comedie yii
Guediewaye ville de l’année 🤣 dragon, 6000 milliards, faux billets... 🤣🤣🤣
Guediawaye kaye macha alla😂😂😂
Wallay 😂😂
😂😂😂🤣
Daguama ray
Wa Guediawaye nieuwa tina nagn dh😂😂
Bilaye mane wa guediawaye la beugue😂😂😂
c domage que bcoup de senegalais ne comprenne pas le message de serigne touba
quel message
Ragalen yalla
Sénégal 😂😂😂😂
Comédie motakh stress douniou ray 😂😂
Bou fekone sa sr la do wakh lolou dh prkw sokhor tmt
Ass malik Nagou lall kote deke ngi mola maye diamo bamba merci
@@modudiop979 t'as rien compris toi. Yaw danga yakaar ni yama ngueneu beugue Serigne Touba. Danga xamoul rek dou ay image wala ay tiakhane motakh niou sope Mame Khadim. Gnii daniouy comédie
Thiey yalla
Billahi 😂😂😂
DEFA ler dey fayy founé machalah
Arretez vos conneries et adorez le Seigneur Dieu des cieux et des terres. Ne mellez plus le nom du saint homme à ces idioties.
Serigne Touba a si bon Dos s'il pouvait revenir et parlerà ces ignares ils comprendront peut etre que si bokkalé legn deukk Soubeu ak ngone
Sen mur bii mo mare peinture 🎨 walay mei serigne touba amoul morom
Lekeleen mirebi il dou tous "borombi nena fal yabadou raba hazale beytii " jamuleen borom nekebii
Merci bcp.. Borome nekebi (kaaba gui) Allahou soubhanahou Wata' Ala mome rek mo dirara diamou...
@Mame Sall Mbacké SmD diegueulou deh dama dioum. BOROM nékebi (kaaba gui )la beugoneu binde. BarakAllh fikoum si dioubeunti kaddou gui. Yalla na gnou yalla tek si yonou siratal moystakkima té yokk suniou ngueum. Amine
Bokkalé rkkkk
Yow yagneme yallah haha ah .
Dengen bougou koulen ta tabahale s mire
Ko yap
😂😂😂douma raye
Dém len diamou djii yalla mo geun sen thiakhan yii
Sénégal 🇸🇳 mo bari ay comédiens serigne Touba fegnou si mur bou bonn bi wakhlen lenen wayy
Saway mur bi lousi nek boulma retane lo way
Murs bala geune doul
Abdoulaye Syll lo beugue expliquer
serigne touba dou morom bayilén liguén di deff baxna
Mais ani image bii serigne touba dou kounouy fowé way tamit serigne touba fowoul folou woul walahi
Et boul niou sonal iow
Abdoulaye Fall senegal dafa nekh
Vraiment Mame borome Touba d'où aye fo
Wallahi
Senegual nene diamou yalla bou lene fate sakhaba yi kene dou nioum
Loutakh ngeine gueme dragon té guemou leine .s Touba bayileine sokhor waye
Amna loo khani soula feenioo nga wakh ko dotoula dieringe teh kendoula guem
à quant le prophète apparaîtra au Sénégal donc toujours les serignes seulement
Ani Viviane mi guisson serig falou ne bayi na sol lougatte