Bercy Teungethie, Wally Seck zappe Eumeudy Badiane sur scène et danse avec Ndiap après audio fuité…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 11 янв 2025

Комментарии • 41

  • @wfamily9941
    @wfamily9941 Год назад +16

    Pour dire vrai li mo manqué wone ramdaan ay khalé, djoubolen rek nek bene ❤

  • @fatoumbye5290
    @fatoumbye5290 Год назад +7

    Wally Seck Ndiap Zo dina dof Lo Wally Seck rek way mashallah non la Yalna jama Yaga Yala dahal len mbolem Seytaneh 🙏🙏🎤👏👑🔥🔥🥰❤️🥰🥰❤️🥰

  • @makyarrjaimemonpaysgeumbam7463
    @makyarrjaimemonpaysgeumbam7463 Год назад +9

    En tout cas il dense bien et en plus il met l'ambiance sur la scène.

  • @BaayFall121
    @BaayFall121 Год назад +11

    Wally ballago seck le Roi de la music Senegalais the number one of All times congrats 🎉🎉

  • @AntaDiouf-wo2kl
    @AntaDiouf-wo2kl Год назад +3

    Mane wally seck♥️♥️ mo takh ma Beugue ❤️diap maryacine ❣️ya bakh te rafate khôl❤️❤️❤️😘🥰💯 sa nonou demb ngay tèral yalla nala yalla defal diamou diou sakh nite kou bakh nga yalna nala thiate sekhlou waye 🤲🤲🤲🙏

  • @aicha.2025
    @aicha.2025 Год назад +4

    Ndiap. Zo dal mo khéw yallah yallah 🎉🎉🎉sam❤❤

  • @mohamedofficiel3658
    @mohamedofficiel3658 Год назад +9

    Wally dafa bakh néna ndiap defal ndank fi dafa ritakh🎉🎉🎉

  • @NoguayeDiop-uq4xf
    @NoguayeDiop-uq4xf Год назад +5

    Waly boula kene diakhassei AK Eumeudi koula toudei dome amo fayam

  • @kadijatoujallow3477
    @kadijatoujallow3477 Год назад

    Machalla president wally secka you're the best
    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye218 Год назад +6

    Ndiap damako beugue dafa nekh cinėmala❤

  • @adama2053
    @adama2053 Год назад +4

    Machallah maryasine nice na ❤

  • @mamikane1250
    @mamikane1250 Год назад +7

    Bilay les Journalistes yi ay seytanee la gnou. Diakhasseee rek les Titres sont que pour separer le groupe. Restez soudee les gas boul keine Doug sene digentee

  • @villanileonardo006villani5
    @villanileonardo006villani5 Год назад +11

    Ndianpe dina dof lo wally rek😂😂😂😂😂😂

  • @buz7755
    @buz7755 Год назад +18

    Ndiap ya khew bolfale ken li subz la tenga parapare sa bop nak wakhna lako dh guisna lifi kew yaw tam kkhalatal ne mak day niaw ngua def kom eumeudi ak arma 😂😂😂

  • @boyngm3258
    @boyngm3258 Год назад +1

    Bayilén doull eumeudy gneuwna 😂😂

  • @serignembaye5223
    @serignembaye5223 Год назад +3

    Diap yalla nala yalla same

  • @falloukarimmbow4981
    @falloukarimmbow4981 Год назад

    Wally ballago séck Nitkou bakh leuh 🤍✌️🥺👑💯
    Sã khôl 🤍🤍daffa rafét trop masa'Alah ôw

  • @Dam-g2u
    @Dam-g2u Год назад

    Ndiap.zo.khawe.mana.danse.nice😢😢😢😢ana.ndey.ndiaye.banaya😢

  • @badaradieng727
    @badaradieng727 Год назад +1

    Entoucas dal Wally do sama chanteur dumala deglu mais eumeudi badiane bul fatei ni il a été là depuis ba Dara dula Dara hum

  • @AdamaDieng-g3m
    @AdamaDieng-g3m Год назад +1

    Wally guir yalla dieulal sidy moulay awou😢

    • @bdiene66
      @bdiene66 Год назад

      Ba do bayi wally top sidy après😂

  • @MamecoumbaNdoye-yt9iy
    @MamecoumbaNdoye-yt9iy Год назад

    Ndiap dall crėė nafiii fėthieu bou bėss rm

  • @mariamandiaye8939
    @mariamandiaye8939 Год назад

    Gnap mane ay diabantém momay dérange mou melni kou passeporam rérr😂

  • @AdamaSignaté-h7u
    @AdamaSignaté-h7u Год назад +2

    Ndiap rek AK waly❤❤❤

  • @aliounetoure5683
    @aliounetoure5683 Год назад

    Ndiap zoo mounoul ferhie ndakh d'où andal music

  • @MgomOulimata
    @MgomOulimata Год назад +1

    ❤❤❤😂❤❤❤😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤c'est.joli

  • @matardieng-cr9xs
    @matardieng-cr9xs Год назад

    Boy Di fethe seytane la boul fek gni and nga beugeu len diakhasse

  • @mariamandiaye8939
    @mariamandiaye8939 Год назад

    Eumeudi nak il est temps nga bayi féthieu oubi école de danse formé jeune yi

  • @KhoulioSakho
    @KhoulioSakho Год назад

    So beugué nopalou kou wally beug beugu ko mou diex c lui le patron ndiap doxalal

  • @MouhamedToure-cv6ol
    @MouhamedToure-cv6ol Год назад +1

    🤪🤪🤪🤪

  • @keweba1522
    @keweba1522 Год назад +1

    Wa Rufisque yéna mal civilisé deug je m'adresse à ceux qui étaient sur VIP Wally nieuw rek nguene taxaw thie chaises yi nithie guinaw kenn guissoul bilay vous m'avez honti mais je partage les responsabilités parce que c'est vous qui devez refuser ça mais Wally ioe mom dinga wéthi samay 9500😢

    • @moustaphagaye1457
      @moustaphagaye1457 Год назад

      En bon dafa nexoul

    • @Sy-c2u
      @Sy-c2u Год назад

      ​@@moustaphagaye1457dafa guissoul ndakh wa VIP 😂

  • @coumbasowsall8194
    @coumbasowsall8194 Год назад +3

    Waly mi li esk taynako 😮ndiap dè comme mo yilif waly li 😮😢

    • @mamsaitsarr7600
      @mamsaitsarr7600 Год назад +4

      No lee du darra wally dafko beug rek. Ndiap dafa nekha beug

    • @Mody-nz3zt
      @Mody-nz3zt Год назад

      Yaw weirenga 😂😂😂😂

    • @cheikhmbaye3730
      @cheikhmbaye3730 Год назад

      Ksn may niou ay waly tayoul li beugue ndiapou com gnepou ksn may niou diamou way

    • @ndeyeamyseck4249
      @ndeyeamyseck4249 Год назад

      Yaw nékale nitt sétanal intégralité soirée bi ba paré

  • @tidianediallo9062
    @tidianediallo9062 Год назад +1

    Vraiment je comprend loutakh ameth thiou bzyi wally est un faux type