Meilleur combat de l'année : 2ème bagarre entre Amanekh et Bébé Diène dans le même face-à-face

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 28 дек 2024

Комментарии •

  • @MameThiaw-i6k
    @MameThiaw-i6k Год назад +13

    Ama nékh dou ragale dé gnoune yaw rékk lagnouye toppp ❤ ani wa Rio wayyyyyyyyy🎉🎉🎉🎉

  • @cheikhniang02
    @cheikhniang02 Год назад +44

    Ama nékh boula boy bi yeungueul waay, c’est l’expérience face à la jeunesse bayiko ak thiow li focus

    • @pierremane4565
      @pierremane4565 Год назад +1

      Mè boy bi dof la way li signature la rk

    • @cheikhniang02
      @cheikhniang02 Год назад

      @@pierremane4565 nako bayi ak thiow li rek té focus si combat bi moko eup expérience

    • @MameThiaw-i6k
      @MameThiaw-i6k Год назад

      @@pierremane4565ki Kaye wéroule wayé bayi ko akh ama nékh rékk

  • @dofouAmabousamel-cl1sk
    @dofouAmabousamel-cl1sk Год назад +29

    Bb diène diokhal grand bi thier nioune Iow rek lagnouy topou ❤️

  • @ibusow7240
    @ibusow7240 Год назад +33

    Yalla na yalla may ndam amanekh

  • @baityrba2447
    @baityrba2447 Год назад +34

    C un combat plein de surprise 🔥🔥🔥🔥🔥💪

  • @petitsene3815
    @petitsene3815 Год назад +45

    Amanekh legui physiquement il a évolué amna dolé machallah

    • @MoraNiboy-hg9to
      @MoraNiboy-hg9to Год назад +2

      Sama deke lay antarene souf bou dis mo ame fi

    • @MameThiaw-i6k
      @MameThiaw-i6k Год назад

      Ama rèkk lagnouye toppp

    • @theblackmamba434
      @theblackmamba434 Год назад

      Non ama nekh amoul dollé damakoy guiss sall musculation walakhi

    • @MameThiaw-i6k
      @MameThiaw-i6k Год назад

      @@theblackmamba434 dagua sokhore

  • @mbackegueye2370
    @mbackegueye2370 Год назад +97

    Bébé Ama nékh dou ragual respecté ko

    • @abdoulayediallo1476
      @abdoulayediallo1476 Год назад +7

      Kham n'a bébé diène Moy ragual poulo bï seul

    • @ametdiop6972
      @ametdiop6972 Год назад

      ​@@abdoulayediallo1476frere ama nekh mo meun bb dien de dakoy dane beure yi sakh dou ben

    • @julioniasse1932
      @julioniasse1932 Год назад +2

      Dou niak respect diaye combat rek leu,Ama nekh mo dof rek pourquoi door,Boy Niang a fait pire a Balla Gaye 2 et il ne s'est pas comporté de la sorte

    • @ametdiop6972
      @ametdiop6972 Год назад

      @@julioniasse1932 bebé diene limou def Mo geneu pure romb lamin samba ak Malick nieuw basi mom di provoque Balla Biko boy niang lale dafa reagire dorko 🎤

    • @BadaraGueye-ii5gh
      @BadaraGueye-ii5gh Год назад

      Lou ler ga wakh

  • @karimcouls3334
    @karimcouls3334 Год назад +36

    Bébé Dieune mo eupeul 🤣🤣🤣

  • @Sow20850
    @Sow20850 Год назад +21

    Ndam rk inchallah pour Bébé djene 🎉🎉❤

  • @kaporalinfos
    @kaporalinfos Год назад +12

    BÉBÉ DIENE NAY AM RESPECT SI ADVERSAIRAM YI AMANEEX A RAISON

  • @barristerken7504
    @barristerken7504 Год назад +7

    as for me i am supporting this guy that speak English, i like him

  • @Amathsene15
    @Amathsene15 Год назад +7

    Nioune teuguethie laniou deug Ama ki wah ko peulh bou ame fite amoule 😂😂😂😂😂

  • @bayemorkasse8491
    @bayemorkasse8491 Год назад +12

    Ama nekh Yalla na Yalla may ndam inchallah ❤❤😂

  • @moussambengue6613
    @moussambengue6613 Год назад +18

    Bb diéne ioe la faral dh mes li gua déf dou yeufou nitt nitt daguay ame respect lamb dou affaire de bvndi

  • @MamadouNDIAYE-ie4ox
    @MamadouNDIAYE-ie4ox Год назад +26

    Yalla nala Yalla may Ndam Amanekh.. Insha’Allah

  • @yancoubaddiedhiou9222
    @yancoubaddiedhiou9222 Год назад +9

    Vous les journalistes. Ils faut que vs aimeriez de dire la vérité a les lutteurs. Bébé diene n'a pas réson il a fauté .il n'a pas le droit de touche son adversaire c'est le règlement qu'on a voté a la sng

  • @mfnmfn6896
    @mfnmfn6896 Год назад +39

    Bébé Diene Amal respect ci amanekh te nga nèk nit lambou ligueye le

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Год назад +17

    BeBe Diene Ndam rek 💪👍🌍💪 ,,, Bombardeh Ndam rek💪🌍👍🙏✌️By god power will win both 🙏

  • @POULO_BII
    @POULO_BII Год назад +14

    BÉBÉ DIÈNE SEUL 🎉😎⚔️ NDAM RK INCHALLAH 🙏🤲❤ POULO BII 😎 SEUL ⚔️AMA NÉKH À FÉTTI😌🔥

  • @ouzinndiaye1118
    @ouzinndiaye1118 Год назад +2

    Peule bi yémal dringue amanekh ❤ forever

  • @abdoulayediallo4028
    @abdoulayediallo4028 Год назад +10

    Bébé la supporté mai ragual n'a ama nekh dane koo.
    Ama nékh waroul niak comba il es tro formidable en face 2 fac

  • @Alimatoukandji2007
    @Alimatoukandji2007 Год назад +4

    LëBu'Ndanane amaneex aak reug reug ndam rek inchaallah

  • @BaugaBalde-ye4ib
    @BaugaBalde-ye4ib Год назад +7

    Vraiment ama nekh a raison meun na wax louko nekh mé boumko lale.togne baxoul.té ama nekh kèn douko sous estimé ins bi sino boy bi meun na ame surprise bouko bét si combat bi

  • @AissatouMbengue-hs8km
    @AissatouMbengue-hs8km Год назад +6

    Ama nekh rek yalla nala yalla may diam🤲🤲

  • @FatoumarMbaye
    @FatoumarMbaye Год назад +6

    Papa yada yalnako yala yeureum quan le chat n'est pas là les souris dansent

  • @MameGaneNdoumbéDiagne
    @MameGaneNdoumbéDiagne Год назад +11

    Yalla nala Yalla may ndam Amanekh🤲🏽

  • @sadibougueye7593
    @sadibougueye7593 Год назад +2

    Ama nekh champion leu
    Bb yalla nla yalla may ndam🙌🏾

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 Год назад +1

    Paulh bi yalla nala yalla maye name champion bi

  • @ibrahimaniane6508
    @ibrahimaniane6508 Год назад +13

    Boy reegleel reek so kholé ama neekh reek khamnee dou ragal amal respect boy dank reek amanekh daflayy defaraal dee

  • @kheuchfatygeneralloupapedi3484
    @kheuchfatygeneralloupapedi3484 Год назад +5

    Très. Bien amanékh

  • @IibouSagna
    @IibouSagna Год назад +17

    Noo Senegal nexx neu Amanekh :” I can do that” Bb Diene répond “amul ay crée ru rat …” 😂😂😂😂😂

  • @yatmaniang6847
    @yatmaniang6847 Год назад +10

    Malick thiandoum le meilleur 😂

  • @djibrildiop924
    @djibrildiop924 Год назад +1

    Ndan rek inshAllah bébé diène kessé ❤

  • @IbrahimaNdiaye-eo3qh
    @IbrahimaNdiaye-eo3qh Год назад +1

    Bèbè diene reug reug mi mbeurè Grand combat moko déranger motakh mouy def lii😅😅😅

  • @salioudiallo3412
    @salioudiallo3412 Год назад +2

    Bb diene name rek inchallah le grand champion

  • @cisseabdoulaye6229
    @cisseabdoulaye6229 Год назад +2

    Ces présentateurs ne sont pas à la hauteur....

  • @aliousene199
    @aliousene199 Год назад +6

    Bébé diene deffa kon il doit revoir son comportement malgré tout

  • @mamadoudia8107
    @mamadoudia8107 Год назад +2

    Bb diene yalna yalla may ndame

  • @MoulayeLaroussi-it6he
    @MoulayeLaroussi-it6he Год назад

    Thieuye combat bi, diné meti mom 😮

  • @onelove6721
    @onelove6721 Год назад +5

    Bb Diéne défal attentionné si Ama nekh

  • @diopmamadoumedoune-cw6zo
    @diopmamadoumedoune-cw6zo Год назад +16

    Ndering bi dina delou ndeim guinéen ya dougou si lebou bi diko roubei ni 😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @BambaDiop-b8x
      @BambaDiop-b8x Год назад +2

      Ki bb diéne dou sakh moromam 😂😂😂

    • @MameThiaw-i6k
      @MameThiaw-i6k Год назад

      @@BambaDiop-b8xki bouko ama nékh diapé dakoye lékk dou sakh moromame

  • @silencieuxbouyant9687
    @silencieuxbouyant9687 Год назад +5

    Bb soit serein eupo dooler amanekh soko respecté woul dinala dann

  • @alassanediouf4329
    @alassanediouf4329 Год назад +1

    Bb Diène🔥Mo meune Amanekh fouff blh lii dou Lamb✌🏻

  • @Galayegueye2009
    @Galayegueye2009 Год назад +3

    Ama nekh yalla nala yalla maye ndam

  • @TallaFaye-y8t
    @TallaFaye-y8t Год назад +2

    Ama nekh yalla nako yalla maye ndam Lou sedd

  • @khoumbadabo9807
    @khoumbadabo9807 Год назад +2

    Bébé ❤❤Touss 💯⚔⚔💪💪

  • @seydinamohamedndiaye6690
    @seydinamohamedndiaye6690 Год назад

    Ama Nekh dinala daane ba dem ngay soga comprendre 😂😂

  • @moussasy2813
    @moussasy2813 Год назад +1

    Da passe nieuw 😂😂😂

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 Год назад

    Ça chauffe déjà 😱🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💥💥💥💥💪💪💪💪💪🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥💥💥

  • @niassesouleymane7163
    @niassesouleymane7163 Год назад +4

    Way Malike Thiandoume , Lamine Samba vous avez perdu le contrôle depuis lol 😂😂😂😂

  • @alphacheikhsylla4071
    @alphacheikhsylla4071 Год назад +2

    Merci beacoup bebe❤❤❤❤

  • @warrios6590
    @warrios6590 Год назад +4

    Bébé diene nekal niit bien vrai que signature combat dara wara am chaud mais amo droit touché sa adversaire

  • @badeneydia6517
    @badeneydia6517 Год назад

    From rio amanekh rek

  • @falloufaye9633
    @falloufaye9633 Год назад +7

    Amanekhe a raison.waroko lale lambe la.😂😂😂

  • @DaourNdoye-f7o
    @DaourNdoye-f7o Год назад +5

    Je pense que le cng doit encore assainir les plateaux de face to face car la lutte n'est pas un milieu de banditisme bébé diène dafa eupeule lamb dafa dépassé faco🎉yi na kholate nimouye singaturé li bakhoule dara mbeur noble la kairé wakhale ak goss bi

  • @modoumbacke6835
    @modoumbacke6835 Год назад +5

    Bilahii bb Diéne dafa mandii😂😂😂😂

  • @massarthiam6077
    @massarthiam6077 Год назад

    Saawaayyy alaapp lébou téyaall 😂😂boyyy. Bébé diène nekall nitt téyall ki dinala niouss niouss you mettiii😂😂

  • @Gazaflow224
    @Gazaflow224 Год назад +1

    Bébé rek❤

  • @seydinamohamedndiaye6690
    @seydinamohamedndiaye6690 Год назад +1

    Ce qui manque à certains lutteurs comme Bb dieng c’est la discipline..Quand je parle de discipline je parle de tenu il sait même pas se tenir

  • @buzzlabbuzzlab6785
    @buzzlabbuzzlab6785 Год назад +1

    Bb diene seul liga bgu ama baldè mtx gua nex ma❤

  • @Habayatou35
    @Habayatou35 Год назад +1

    Bébé diene seul fierté de medina ndam reek poulo bi seul day daw reek 💪💪💪💪❤❤❤

  • @sml6264
    @sml6264 Год назад +2

    très bien Amanèkh

  • @elhadjidiouf2942
    @elhadjidiouf2942 Год назад +1

    Bb diéne boko diokhoul respect doko dane

  • @Xidmatv09
    @Xidmatv09 Год назад

    10 000 abonnés nio Ah 1 milion

  • @sambaba683
    @sambaba683 Год назад

    Bèbè diène moleu mounne fouffffff boy bi guerrier leu😂😂😂😂😂😂😂

  • @badLo-c6d
    @badLo-c6d Год назад

    Thiey fan’s bandit yi

  • @moussaseye3439
    @moussaseye3439 Год назад +4

    Amanekh amna doler

  • @FallouSeck-dn6mi
    @FallouSeck-dn6mi Год назад

    Bb respect ki bakhna

  • @Sowismaila-hh1mb
    @Sowismaila-hh1mb Год назад +2

    Bb diene dam rék inchallah 🙏

  • @ThiernoDiallo-i8p
    @ThiernoDiallo-i8p Год назад

    Bebe❤yalla nako yalla may ndam

  • @BaMbAkarim8437
    @BaMbAkarim8437 Год назад +8

    1000% médina bébé diene seul

  • @LazaSrxbsnss
    @LazaSrxbsnss Год назад

    Boy bi vrai ndêrêng la Opeul na

  • @ibrahimaFall-f3t
    @ibrahimaFall-f3t Год назад +1

    Bb je te supporte mais 1peu de respect sur amanekh c 1 grand champion

    • @BiloBa-uq7nj
      @BiloBa-uq7nj Год назад

      Li lamb la

    • @ibrahimaFall-f3t
      @ibrahimaFall-f3t Год назад

      @@BiloBa-uq7nj lamb la mais bouma lale boulko lale nakh dafko beugu diakassè akk nite yiii lolou rkkk nespo

  • @DieganeNgom-p1k
    @DieganeNgom-p1k Год назад +2

    Lamine Samba sayetane bou mag leu face à face Amoul foula nekh ngay takhaw khamo dara

  • @MoustaphaFadiga-y8y
    @MoustaphaFadiga-y8y Год назад +1

    bebe diene bo amoul respect si Amanekh doko dane

  • @KandjiBams
    @KandjiBams Год назад

    Amanékh le requins de rufisque doi ragual rio tapét deukoufi boy bi le jour ngay comprendre inshalla

  • @maremesougou8031
    @maremesougou8031 Год назад +4

    Il a raison amoul droit lalko😂😂😂

  • @CheikhDia-bb4nb
    @CheikhDia-bb4nb Год назад +1

    Puel Dou ragal 💪💪💪

  • @khadimfall5477
    @khadimfall5477 Год назад +2

    Amanekh mii dafa am dole d lou ler lalay wax😮

  • @moustaphasylla887
    @moustaphasylla887 Год назад

    Bb Diene yaw la faral d mais bayil forcer bi

  • @mamskoita5827
    @mamskoita5827 Год назад +3

    Domou Medina dou meusseu dess guinaw bébé diéne rék medina for ever 💪💪💪

    • @momondiaye4387
      @momondiaye4387 Год назад

      Ki d'où domou Médina dh ki Di poula fouta

    • @maxd.1401
      @maxd.1401 Год назад

      ​@@momondiaye4387Médina la dioudo fall kone Ama baldé dou domou pikine domou peul fouta la.

  • @omarlaye2658
    @omarlaye2658 Год назад

    Waay Ndéraingue bi d'où yame mouy golo gololou

  • @sambaba683
    @sambaba683 Год назад

    Bèbè diène yallah ngua am ndam aamiine ki ya ko moune foufffff victoire de bèbè diène 😂the best player

  • @PrincesseBarry-i1v
    @PrincesseBarry-i1v Год назад

    Bb diurne n'y seul❤❤❤

  • @tallafall934
    @tallafall934 Год назад +3

    Bien joué ama boy bi dafa eupeul

  • @MbayangDiagne-cc1pd
    @MbayangDiagne-cc1pd Год назад

    Ama nakhari😂😂

  • @yacine-t1d
    @yacine-t1d Год назад

    Bb dien mo nek bonne chance❤❤

  • @SowMadiaw-go2uc
    @SowMadiaw-go2uc Год назад

    Bilahi galath amna lamine samba loumoufi diarigne ba parè done saytanè

  • @IbrahimaGueye-q7e
    @IbrahimaGueye-q7e Год назад

    Atation bébé djéne Amanex frener na aye boye you barie

  • @sambagora7848
    @sambagora7848 Год назад +4

    😂😂😂bèbè diène yalnagua danou. Tay wanèwo discipline

    • @elhadjwade508
      @elhadjwade508 Год назад +1

      Liguey wah sah guemoko😂😂😂

  • @rashford5419
    @rashford5419 Год назад +1

    Teungethie amoul ragual xamougn lolou affaire yoyou 😂

    • @KRM2004c
      @KRM2004c Год назад

      Nioun Medina laniou deuk frr

  • @zizouzidane7332
    @zizouzidane7332 Год назад

    boys nioun ay lébou laniou ap dringue ga réglé boys

  • @Nabouchita_h6u
    @Nabouchita_h6u Год назад +1

    Lamine samba da beuri wakh té soph

  • @salioucisse4933
    @salioucisse4933 Год назад

    Guinéen peulh fouta Boumou gnou yapp démal diay boutique allez rio Diokoul 100/100 original boy ndakarou 😂

  • @massarthiam6077
    @massarthiam6077 Год назад

    Bébé bilahii moytoul coup yii 😂😂😂

  • @Soppénabi
    @Soppénabi Год назад +1

    Lidé combat Zarco ak Ada Fass rék lamay ndirol , Ada Fass topone Zarko diko manqué de respect rék mais kholal fimou moudjié😂, reuy lamigne yobou woul mbeur féneu

  • @maxcoly5541
    @maxcoly5541 Год назад

    Wa linla signature wala diay bvndit

  • @sambaliou5859
    @sambaliou5859 Год назад +6

    Bébé ndame rk inchallah

  • @DiedhiouAbdou-zc7wj
    @DiedhiouAbdou-zc7wj Год назад +1

    Touss Nak lumu diar niu Defkosi Bb Diéne seul ✊✊

  • @boubacarlimanbadiane8668
    @boubacarlimanbadiane8668 Год назад +1

    Bébé diéne❤❤❤❤❤