Bour da moudié faté balla à cause de la taille de Tapha Tine, sur une vidéo il a dit sou balla khékhé Tapha door ko mou danou, il est complètement passé à côté, en faisant leur analyse ils ont mis en avant la force de Tapha oubliant les qualités de BG2
Bour tu es vraiment professionnel et d ici peu tout le monde reconnaitra ton talent de chroniqueur. Tu as bien choisi ton metier car tu le fais tres bien en plus la dose d.humour que tu en rajoutes pour diminuer le stress de tous . Yalla na sunu borom same le te téral le . OUSMANE FALL COMO
Bour Gueweul il est un analyste très extraordinaire vraiment dafa xam lamb😊Balla Gaye sou paré kouy taxaw ci lamb dji mola meune💪🏽💪🏽bour vraiment il est pertinent
Voila tout ce que bour voulais depuis le début de sa communication du combat balla tapha tine .. c'est que balla gaye batte tapha tine et que modou lo batte siteu pour s'affronter ... tu aura la même communication sur le combat modou lo siteu pour déstabiliser siteu en lui fendant croire qu'il peut pas battre modou lo .. car bour sont seul objectif c'est le combat balla VS modou lo
Bour mayniou diam fiumouy reigner niatta att moko desss ana khaleyi di niew Sa Thies Reug Ama Boy Niang Franc ......Tapha dem combat Roi des arrnea niak ko, dem Empereur niak ko Wakh len Tapha tine deug doff bou ponkal leuh
Le chemin de modou lo Kharagne moy wanei yoon bi djaroull reuy force intérieure bou woor ngay yor neub sa bopou ba arbitre bi sifflé nga indille sa adversaire djiko djoum khamoul si yaw
😂😂 Bour wakh ngu deug. Temps khalé dafeu am beneu boy Papi momeu meune soutma eupma dolei mais danio khekh meu mbotko tokk ci kaawaw niou atténiou et depuis lors beu legui boy bi légui on devenu grand me respect de ouff😂😂😂
buur savait dep8 que balla va gagner ils tjrs avc cs mafieux aziz rt sont freres mystiquement ils sont eux tapha le combat etait deja gagner si modou prend ils font le gagner je le dit modou laisse balla prend les jeunes que personnes ne d"oblige
Té Modou lo bouniou ko fayé 1 milliard pour mou beurré ak Balla gaye na bagne Aziz Ndiaye daf koy sacrifier kom nimou dèf tapha tine na dieul thi souf rèk com limou wakhonn
Bour linga wa khone lepu deug la du sama mbeur me kuy takk ngembu ci lambu ji mola dakha beure bu amee formu bu bakh mo mane ci rew mi ❤❤❤❤❤❤
Bilahi mon frère deug nékhoul
Bour da moudié faté balla à cause de la taille de Tapha Tine, sur une vidéo il a dit sou balla khékhé Tapha door ko mou danou, il est complètement passé à côté, en faisant leur analyse ils ont mis en avant la force de Tapha oubliant les qualités de BG2
Khana Eumeu sene judo lay déf
@@papendiaye7334 dafa am ay marabout youkoko waxone rek 😂😂😂
Eumeu sene dakha beuré si lamb j
Bour tu es vraiment professionnel et d ici peu tout le monde reconnaitra ton talent de chroniqueur. Tu as bien choisi ton metier car tu le fais tres bien en plus la dose d.humour que tu en rajoutes pour diminuer le stress de tous . Yalla na sunu borom same le te téral le . OUSMANE FALL COMO
Amine❤😊
Bour a dépassé tout le monde sur les analyses avant combat aujourd'hui donc chapeau
Bilahi bour wakhon khako balla cest le meilleur de sa generation tapha tine niemewoul balla
Bliehi BOUR ken du yoww yaa len mann fuuf wakh nga ko wakhat ko yallah Nala yallah defal jamma yoww ❤
BOUR est simplement pertinent, toujours un plaisir et un régale de l'écouter, macha'Allah.
Bour Gueweul il est un analyste très extraordinaire vraiment dafa xam lamb😊Balla Gaye sou paré kouy taxaw ci lamb dji mola meune💪🏽💪🏽bour vraiment il est pertinent
😂😂yèn mom daguèn fèbar je pense eumeu sene xana dou lutteur ??
Néna balla gueye bou amé dolé day réw. Ma sha allah
Bour kay il est exceptionnel
Bour lou lerr gua wax depuis le debut merci bourr ❤❤
Franchement buur t’es unique et pertinent sur tes propos .Bonne continuation !
Un grand merci !
Macha allah bour tu parles avec mentalité
Bour tu es meilleur chroniqueur manchalla
Lou leer
Bour🎉
Bour vraiment tu es meilleur Macha Allah tu avais vu juste
Buur Machallah lamb dji yafii meune lingay wakh yépe deugue laaa
Tu as bien analysé le combat
Tu es le meilleur BUURRRRRRR
Voila tout ce que bour voulais depuis le début de sa communication du combat balla tapha tine .. c'est que balla gaye batte tapha tine et que modou lo batte siteu pour s'affronter ... tu aura la même communication sur le combat modou lo siteu pour déstabiliser siteu en lui fendant croire qu'il peut pas battre modou lo .. car bour sont seul objectif c'est le combat balla VS modou lo
Modou lo le king de l'arène
Ya gnak khorom deug 😂😂
Billay wakh gua deug moy roi des arènes 👑👑👑 dh
Moma oum bamaye def bac 😂ndakh dioutalebi😂😂
Qui Balla Gaye 2 a failli tuer ou tu n'étais pas né à ce moment-là 🤣🤣🤣🤣
Wallahi bour mande dama ragall saywakh ❤❤❤
Ah bour je suis bien d’accord avec toi
Yen gordjiguene you aziz Ndiaye couronne nou modou lo moy sen problème
Modou lo moy ki balla gaye dioutelone 😂😂😂
Couronne bi danouye nanguou ndayame par force par A ou par B foumou mena néke danouko dieuli
Machalla mboure wakh gua lépeu amale diame rék ❤❤❤
Tu est le meilleur vraiment
Bour tapha tine mystique moko dane daniouko nélawale si mystique
Bien dit l’expert ❤
Bour yaye ndandane je t es suivi avant combat après combat
Bour est le meilleur
Nitou deugue walakhii ❤
Merci bour balla gaye 2 est le meilleur lutteur du Sénégal.
Yéna dans modou bakh n'a mais geum léne yalla balla nonn
Ki nako RTS recrute pour emmision Lamb
Très bien caxabal
machallah bour tapha da ragal balla point
Merci beaucoup bour degue rek kha wax❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Kham kham rekk ngay wakh Machallah
Wa khou wan li dé
Bour waxal lula nexx yafi nekk machala
Bour yaw sayetaneng yéne Ay sokhou azize Ndiaye ngéne
Merci mr Beur
Billahi bour waxone nako
Les erics favre wadji ngande diodiou bour raynama 😂😂😂😂
konn déggue ngua lolou
Fi papa sow rék moufi wakh degue
Modou yorna courone maye sence boyi balla yore na courone na riské si boye yi fran miggi fi
Ww lolou moy degue dh
Couronne nou modou lo Lou mo diarign modou dara yor ko pa para di daw mbeur daw di dieul ay siteu nn balla dou sen morom bilhi
Aziz ndiay molène yoni par ce que moko beug ngén beug ko
Bour mayniou diam fiumouy reigner niatta att moko desss ana khaleyi di niew Sa Thies Reug Ama Boy Niang Franc ......Tapha dem combat Roi des arrnea niak ko, dem Empereur niak ko Wakh len Tapha tine deug doff bou ponkal leuh
Ana eric favre ak dawid😂😂😂😂
I really like the way you communicate ❤❤❤❤
Merci bour
Bour meune nga thiép meune nga mafé mé bayile bonne yii
Bour mang laye bégué samba depi bordeaux
Modou Lo vs Balla gaye 💯✍️
Tapha tine vs Franc ♥️
Pour faire quoi
Franchement bour gueweul tu es exceptionnel
Le chemin de modou lo Kharagne moy wanei yoon bi djaroull reuy force intérieure bou woor ngay yor neub sa bopou ba arbitre bi sifflé nga indille sa adversaire djiko djoum khamoul si yaw
Bour bari nga wakh modou Lo même balla gaye nek lafagne sakh modou dotoul beuré ak beneu mak nopo loul
😊
😂😂 Bour wakh ngu deug. Temps khalé dafeu am beneu boy Papi momeu meune soutma eupma dolei mais danio khekh meu mbotko tokk ci kaawaw niou atténiou et depuis lors beu legui boy bi légui on devenu grand me respect de ouff😂😂😂
Bg2 rekkk ❤❤
Tapha tine ngaaka dagne la sarakhé waa keur aziz ndiaye rék😂
Moufi wokhon bou Balla khekhe Tapha dorko mou danou
Ahh ki khamoul dara
Tout le monde était contre tapha tine dès le début ils sont tellement content becay néna esk duñu arrêter combat bi bi Tapha nék si médecin yii
Yéne dangéne sokhor billahi le fait que modou yorr korone bi rk ngéne nane é que cng reconnaître n'a corone lolou bane wax la waxi nafékh
Je fais toujours attention à ses analyses d'avant combat.
Il trouve toujours juste.
Je me demande comment il fait.
Buur mii amoul loumou wakh doul reck la meun domérame fii la wakh balla sou khekhe tapha tine K.O maak day wakh sou bagné guathié féen réck 😂
Khamoule dara Nafekh la doul rék lay déf
No bour taye danga da nou ndakh da nga wakhoun bo niou khékkhé tafa moye man lolou nga wa khoun
Dayy tatôné rekk di féne ki diaxal nama
Tapha Tine Khama touma si môm dara dara
Je suis supporter de MdLo mais tu as bien analyser le combat avant
Merci buur deug rek ga wakh
Balla t’as mon respect 😂thioooooh tapha takhna ponkal bouma taséti nogatouko 😂
buur savait dep8 que balla va gagner ils tjrs avc cs mafieux aziz rt sont freres mystiquement ils sont eux tapha le combat etait deja gagner si modou prend ils font le gagner je le dit modou laisse balla prend les jeunes que personnes ne d"oblige
Vraiment bour tu y'a raison tapha amoul fitt tei balla xam na lolou😂
Té Modou lo bouniou ko fayé 1 milliard pour mou beurré ak Balla gaye na bagne Aziz Ndiaye daf koy sacrifier kom nimou dèf tapha tine na dieul thi souf rèk com limou wakhonn
Machalah mais magui niane balla gaye na délou ligueyi wate mo meune si lamb j
Wakho Won li dh bour bayil fenn
doul rék lay déf
Bourr ioe rkk laye suivre ak lambalok yenna May doundall
Sama khol seee n❤❤❤❤
mbourou guéweul, wagnil doullll gui, ay seytané you mag nguén 😮 Xarègne LÔ amoul sén temps
Papa Sow il l avait dit dans sont interview na gaw tei diaxaso c avantage si balla
Bour tu as faucher le comba wakhowone lolou
Siteu ak Modou Lo keine ci gnom dou beurei ak Balla nak c'est clair.
Bour Amal Wer ❤❤❤❤
Tu n'as dit BOUR rien ya wakhone sounou khékhé Tapha tine dore ko mou danou 😂😂😂😂😂😂
Sacré bour contane si yaw
Modou yalla daka soutoureul modou ne doit pas lutter pour albourakh...
Bour danane ga❤❤❤
Balla vs franc lagnou beug😂😂
❤❤❤❤❤
Ce que les gens ne savent pas c que le principal et premier adversaire de balla Gueye 2 c' est omar sakho
Bour bayil fene 😂😂😂
Modou lo na pas la même mentalité de concurrencé avec balla guay il suit seulement sa carrière té mogui dokhal kone nice revanche amatoul.
Buur❤
C'est ca la réalité thiey buur😂
Bour nak tu avais k sou Balla Kheikhei Tapha daureko mou daanou
Vérité absolue
Mais bour tapha tine mom danio tak lokho Yi comm première combat bi rèk li dou lamb way
🎉🎉🎉❤❤❤💪💪💪💪💪💪
Bour wakhon gaco dè bètoula
Balla gaye le champion❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Mais tapha tine ni la défonn Elton ak bombardier daniou ko fay boram