Série ADJA - Episode 26

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 24 янв 2025
  • Bienvenue chez Pathé Sène et Adja. #SenRamadan, savourez la vie avec #AdjaSérie tous les soirs après le ndogou.
    Retrouvez - nous sur www.marodi.tv ou télécharger l'application sur
    Playstore: play.google.co...
    AppStore : itunes.apple.c...
    Pour suivre toutes vos vidéos préférées :
    Abonnez - vous ici : www.youtube.com...
    L'intégral de l'émission "Lii Xew Tey" : • Lii Xew Tey - Saison...
    L'intégrale de la série "Rep Tep" : • Série - Rep Tep - Epis...
    L'intégral de la série "Tekk Teggui": • Video
    Les meilleures ITV : • XUMAN : " Je suis déçu...
    Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
    Twitter : / maroditv
    Facebook: / maroditv
    www.marodi.tv est la nouvelle grande chaîne web du Sénégal. Webséries, théâtre sénégalais, sketch.

Комментарии • 776

  • @lenfantnoir1553
    @lenfantnoir1553 6 лет назад +998

    Ana gni beugue seydina mohamed psl aimer lèn

  • @LEUZZVISION
    @LEUZZVISION 6 лет назад +516

    Ani gni série Adja di manque bou ramadan bi djékhé sén 👆may guiss

  • @kebadrame4016
    @kebadrame4016 6 лет назад +586

    Képou kou beugeux seydina Mouhamed commentaire maye djis

    • @mariamadiallo1721
      @mariamadiallo1721 6 лет назад +2

      Kéba Drame Paix et salut sur lui

    • @cheikhmbengue2685
      @cheikhmbengue2685 6 лет назад

      Mariama Diallo psl

    • @amydembele8812
      @amydembele8812 6 лет назад

      Kéba Drame salalahu aleyhi wasalam

    • @vitodiop5070
      @vitodiop5070 6 лет назад +2

      S.A.W

    • @Treycell
      @Treycell 6 лет назад

      quel personnage de la Série Adja tu es en cliquant sur bit.ly/adjayoutube tu verras c'est marrant, man d! suis tombé sur Pathé Sene !

  • @fatounoirofall4039
    @fatounoirofall4039 6 лет назад +67

    Ana gni done xar Anta Ndir😅😅😅😅way bilahi wadioubakh sou koor gui diexei dingama manquei
    Ana gniko beugue???

  • @mohamedfrange1135
    @mohamedfrange1135 6 лет назад +216

    - sathi bi dafa dougou ci bene galei fekoufa dara. Mou poupp si digg keur gui. Nimouy solé toubeuy dji rk mére bi dougouci rek youkhou né wouy sama serign bi dayou sathi lama lathi pour sama dom dji am bac. Sathi bi tibbatt day yeup néko dou yii dé 🤦🏾‍♂😂...Bon Ndogou 🤝🏽

    • @amydieng7705
      @amydieng7705 6 лет назад +2

      Frange tkd 😀😀😀😀

    • @lamine7934
      @lamine7934 6 лет назад +2

      Frange tkd oh my godness😂😂😂😂😂👏😂

    • @astoundiaye9726
      @astoundiaye9726 6 лет назад +1

      Frange tkd ya con😂

    • @mohamedfrange1135
      @mohamedfrange1135 6 лет назад +2

      Astou Ndiaye reetanaal rk,té baayi "con" biguay toud !! respect 😙

    • @fatimafall9636
      @fatimafall9636 6 лет назад +1

      Frange tkd yaw tamit ki dey fo rek nak

  • @dabayade2772
    @dabayade2772 6 лет назад +49

    Heum heum pour quoi cela m'arrive toujours 😢😢😢quand je mets un commentaire personnes ne met j'aime 😢😢😢😢

  • @malick1028
    @malick1028 6 лет назад +309

    Kou aimé woul sama commentaire yalla nassa bir bi daw amine touf touf

  • @azizniane3144
    @azizniane3144 6 лет назад +63

    Team wa Thiès,,,,aywaaay maylenema 50 like au moins meusoumako am

  • @ouzibby7239
    @ouzibby7239 6 лет назад +54

    Couy bégué sunugal tapel bleu ...bon courage à nos lions

  • @mouhamedniass9762
    @mouhamedniass9762 Год назад +8

    Le freinage de diogoy m'a tué 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @kamal313soxarxalimandiaay6
    @kamal313soxarxalimandiaay6 6 лет назад +123

    Taay laylatul qadr sugnu mbooku tidijane yii 🕋🕋leip luugne sii niane yalla nako sugnu borom nangu sii barkép yonneté bii🙇‍♂️ taay moom Goudik👐 gnaane laa yalla na diamu yague sénégal ❤❤👌👌

    • @fatimandiaye4715
      @fatimandiaye4715 6 лет назад +1

      dame Ndiaye Merci 😘

    • @kamal313soxarxalimandiaay6
      @kamal313soxarxalimandiaay6 6 лет назад +1

      Fatima Ndiaye diadieuf domu baye Ndiaye diatta amal diamu bubakh ak taw féh 💨

    • @diarrabousso6049
      @diarrabousso6049 6 лет назад

      dame Ndiaye laylatoul khadr bi c'est pour tout le monde amoul exception

    • @ndeyesaliou389
      @ndeyesaliou389 6 лет назад +1

      dame Ndiaye bayilen sen yii ñuun ñiep bend nan ñio bokh kin yakar muy seidina mouhamet slwsm

    • @kamal313soxarxalimandiaay6
      @kamal313soxarxalimandiaay6 6 лет назад

      Bousso bally ligua wakh akaay deugue mala gua naagul amul exception dei waayé sugnu borom deif kumpala mootakh keine kunei dii deif goudi gui gua yakar rek

  • @khadijadiallo2410
    @khadijadiallo2410 6 лет назад +10

    Team diapalé ngorr si amii ani gueen😂💕💕💕🇸🇳

  • @yasminarassoulgueye8023
    @yasminarassoulgueye8023 6 лет назад +134

    1er ohhh tay dama koy fété srx beusseul pouce bi rek boul sokhor

  • @bayeserignediop6283
    @bayeserignediop6283 6 лет назад +37

    Meilleur série cette Ramadan.... Vous étés d'accord ?😂😂😂👍👍👍

  • @princemitri2466
    @princemitri2466 6 лет назад +208

    Senegal 🇸🇳 2-0 Pologne 🇵🇱
    Senegal 🇸🇳 3-1 Japon 🇯🇵
    Colombie 🇨🇴 1-1 Senegal 🇸🇳
    Huitième de finale
    Senegal 🇸🇳 2-1 Belgique 🇧🇪
    Quart de finale
    Argentine 🇦🇷 0-1Senegal 🇸🇳
    Demi finale
    Senegal 🇸🇳 2-2 Allemagne 🇩🇪 Senegal gagne 5-4 aux tirs au but
    Finale: Espagne 🇪🇸 vs Senegal 🇸🇳 Au moment où les joueurs sortaient des vestiaires mon frère est venu me réveiller pour « Kheude »😌😏😏sinon on allait remporter la finale🙃 Yalla bakhna

    • @lhommedelarivegauchedufleu6872
      @lhommedelarivegauchedufleu6872 6 лет назад +15

      Mdrr mais amine quand même Yalla na doon dëgg ba diahi Seydoul woudioudj si barké weeru koor gui ak gouddi tey gui dhi leylatoul khadry

    • @MohamedLePanafricain
      @MohamedLePanafricain 6 лет назад +2

      Prince Mitri amiine yallah nala yallah dégueu

    • @Didi-wm1rt
      @Didi-wm1rt 6 лет назад +5

      😛😛😛😛😂😂😂😂😂
      Yallah na sa guente done réalité nangou ci barke Seydina Mouhamed ci barke goudik leylatoul Qadr bi

    • @eddrissdiallo3673
      @eddrissdiallo3673 6 лет назад +1

      Prince Mitri mdr

    • @princemitri2466
      @princemitri2466 6 лет назад

      L'homme De La Rive gauche Du Fleuve Sénégal Amine

  • @mamywallyseckndiayemonekh8708
    @mamywallyseckndiayemonekh8708 6 лет назад +2

    Wa rone wèrr na😂😂😁😁😀wouy morr mane na ralentire di nènako eupna dèf touy diam magui dè 😂😂😂

  • @juniiorlofficiel3097
    @juniiorlofficiel3097 6 лет назад +20

    Salam à tous mba khôl yangi fekh😍😍😍
    Serigne bi néna kou commenté Lundi tay bi série Adja xamal ni lundi prochain do commenté WASSALAM

  • @gnilanendour2461
    @gnilanendour2461 6 лет назад +31

    Guane gui terroriseii na wa keurgui 😂😂 .kène dou diogoye ...team adja 😍😍

    • @pendadiop03
      @pendadiop03 6 лет назад

      Gnilane NDOUR doyna war ma cherie. 😂😂🤗

    • @gnilanendour2461
      @gnilanendour2461 6 лет назад

      Penda Diop kii katt il est arriveii avk force tamite 😂😂

  • @mirabelle3220
    @mirabelle3220 6 лет назад +21

    Tonton yalna na yagu ci keur gui waay. Diogaye ak haleyou indiscipliné yeup dinagn yarou 😂😁🤣

  • @beugueloubax9241
    @beugueloubax9241 6 лет назад +156

    tanyi nak serie bi nekhatoul dé niveau bi baissé na trop koussi dacor beussal jaime

  • @famaseydyndiaye6
    @famaseydyndiaye6 6 лет назад +15

    meussuma commentaire Hahaa ma fii djeukk tay lollll macha Allah bon ndogou naniu koo djexale si diam

  • @zeynabsamb7680
    @zeynabsamb7680 5 лет назад +3

    Ani ngni beugue Seydina Mohamed(psl)

  • @fatimatasignate6239
    @fatimatasignate6239 6 лет назад +2

    Après MARIÉTOU c'est Anta Ndir wayyé wolouna Adja mannn
    Adja rek 😍😍💕

  • @basemou1399
    @basemou1399 6 лет назад +5

    No Ngor réy gama wayyyyy 😁😀😀😀😀

  • @thiabalayendoye9837
    @thiabalayendoye9837 6 лет назад +5

    No episode bi mo dak yeup cheu😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @pendandiaye9959
    @pendandiaye9959 6 лет назад +10

    niou commencé taguo 😂😂😂wouy Doudou néna dou féthie 😂😂😂Ay way Ngor boul patiné

  • @aichadieng4327
    @aichadieng4327 6 лет назад +5

    🙌🙌 Tay mOm masha'Allah mangii ci kaaw

  • @ousmanesarr1121
    @ousmanesarr1121 6 лет назад +25

    Kouy setane di lire commentaires poussal bleu

  • @papafall1400
    @papafall1400 6 лет назад +5

    A Anta ndiir keur pathe sene du yombou kou aksi sama ginaw beuseul jaime

  • @lhommedelarivegauchedufleu6872
    @lhommedelarivegauchedufleu6872 6 лет назад +5

    Adjia rekk dou ayy thiakhane Anta ndir gnibil fii amofi place

  • @marichoudiop8188
    @marichoudiop8188 6 лет назад +4

    😂😂😂😂😂Diogoy dalosi déh.mais goor liiir👶 bi bou prématuré woul wone kone noumouy démé😂

  • @BMSTV221
    @BMSTV221 6 лет назад +1

    🙋ana kou daccor ngou yok si koor gui 2moi😁😁😂😂😂❤☝

  • @mouhamedtoure8991
    @mouhamedtoure8991 6 лет назад +3

    Qui est d'accord que wadiou bakh est le meilleur comédien de l'année. 👉 hay hay hay Diogoye ray nama 😂😂😂😂😂

    • @pendadiop03
      @pendadiop03 6 лет назад +1

      Mouhamed Touré Daccorouma deh 😂😂

    • @mouhamedtoure8991
      @mouhamedtoure8991 6 лет назад

      Penda Diop légui kan la 😂😂😂

  • @zalsalabangbang749
    @zalsalabangbang749 6 лет назад +6

    Tay môme tel na diot si notification yi team Adja for ever

  • @wifegirls5522
    @wifegirls5522 6 лет назад +13

    Aye way je me demande bou ramadan bi diéhé Dina name wa team djoguaye AK Adja dh 😫😫😫😫

  • @abouabdourahmaneyatmakholl9197
    @abouabdourahmaneyatmakholl9197 6 лет назад +6

    Merci solda, dou KO defatt.

  • @prinmatall1869
    @prinmatall1869 5 лет назад +5

    Mane douma féthie sakh 🤣🤣🤣

  • @babacarsow387
    @babacarsow387 6 лет назад +50

    Loumassi meti rekkkkk moy diogaye dina tass keur gui 😀😀😀

  • @mariamadiatoukoulorbourafe7953
    @mariamadiatoukoulorbourafe7953 6 лет назад +2

    😂😂😂pathé sèn sakh dafa ragal soldat bi😂😂

  • @abdouazizdiop6541
    @abdouazizdiop6541 6 лет назад +1

    Ana Wa mafia bii khana dou tay lagne ame 26jrs dina namou serie yii nak bilahi ak Wa mafia biiii encien soldar bii sadick na dei hiii anta machalla niakoko dei......

  • @MrSurpuissant
    @MrSurpuissant 6 лет назад +2

    Omar sene soldat bi ahahahaha diadieuf frère nice na

  • @showh2414
    @showh2414 6 лет назад +26

    Hamdoulah 1er vue es c la première fois puce Blue wayy #Team_Adja ❤️❤️❤️

    • @adiitadiop9860
      @adiitadiop9860 6 лет назад +1

      Mouha Justina L'officiel welcome

    • @showh2414
      @showh2414 6 лет назад

      adachanel diop mocha gracias

  • @Tapha96
    @Tapha96 6 лет назад +3

    Man daal wadiobakh dina raay sugéen gaawul ❤️beussal sama team kon yees 👍

  • @snapperjoe9012
    @snapperjoe9012 6 лет назад

    Ana team serie Adja Lou beug yana yallah nangoul nue sunu koor nue fekeh ko ayy art yu bareh bareh dewene dakhal nue reen

  • @thiatelhommefortthemoneyte3975
    @thiatelhommefortthemoneyte3975 6 лет назад +25

    Diogoy dinama ray mann yalna yalla defalniou diam ak soutoura Sénégal dem final mondial

    • @pendadiop03
      @pendadiop03 6 лет назад

      thiate l'homme fort the money team amine. 😂

    • @djilymbaye1821
      @djilymbaye1821 6 лет назад

      thiate l'homme fort the money team aminnnne waye

  • @abdoubousso4201
    @abdoubousso4201 5 лет назад +1

    Kepou kou beugeu seydina mouhamet beuseul j'aime mate khol

  • @adjikonare7482
    @adjikonare7482 6 лет назад +1

    Waouw fi dém amna ayy nawkate
    Aniii waaa #teamadja mayy lén ma ayy like book😂😘😘😎😋🤗

  • @morsall5347
    @morsall5347 6 лет назад +2

    Non bi mom douma si doyal dh 😂😂😂😂

  • @chernojallow5936
    @chernojallow5936 6 лет назад +13

    Can't stop laughing 😆😆😭😭😭😭

  • @falldior9914
    @falldior9914 6 лет назад +6

    L ' hypocrisie des Sénégalais à détruire les couples est la horrible réalité . Diogoy incarne très bien le rôle .

  • @diorbambafall319
    @diorbambafall319 6 лет назад

    Est que guiss guen nei adja ndokh kessei mo nek si thine biii kouko guiss beuseul j.aime

  • @wokocaz
    @wokocaz 6 лет назад +75

    Ki mom khana armée bi dafa yob khel mi

  • @bibeboudalldiamb7643
    @bibeboudalldiamb7643 6 лет назад +1

    Man esk douma quitte sakh li nekhatoul d damay khar ba sonou wala sama notification da bakhoull 😈😈😈😈

  • @petitserigndiop1095
    @petitserigndiop1095 6 лет назад +5

    les obsédés de Adja wané woulèn bok gnou fél félaléé ba Korou 2019 ak Jamm

  • @serignecheikhastoufallsow7621
    @serignecheikhastoufallsow7621 6 лет назад +2

    Yala na nieup am diam nguir yala ak yonénti bi 10 aime rk soumako ama bakh na

  • @pendadiop03
    @pendadiop03 6 лет назад +6

    Adja way ravie de te setane chak jour ci salam😂🤗😍...

  • @mohamedsidibrahim5209
    @mohamedsidibrahim5209 6 лет назад

    Ki mooh osè adja naak amoul moroom😍😍😙

  • @aminataseck1911
    @aminataseck1911 6 лет назад +3

    Mais mane goor dinama raye 😂

  • @shupinettediongue8857
    @shupinettediongue8857 6 лет назад +1

    Nooo nguor raynagniou ana wa team nguor

  • @abiboulayekane5112
    @abiboulayekane5112 6 лет назад +1

    Merci l'équipe série Adia en particulier wadjou bakh

  • @lenoblepaco614
    @lenoblepaco614 6 лет назад +5

    1er team setane serie yeup👌👃👃👃👌

  • @diaboukebe3021
    @diaboukebe3021 6 лет назад

    goudi laylatoul khadri bi lepe lougni si gnane yalla nako yalla nangou amine

  • @niankifall993
    @niankifall993 6 лет назад +1

    Bayi léne niguél mél way tamit woor ba nguone diottt nguéni gneuw fi di guinnzz si adja légui mom balla May sétane nafila ba paré 😂😁😀

  • @khadimndiaye9644
    @khadimndiaye9644 6 лет назад +1

    soldare nii lay mel kon😁😁😁😁😁

  • @oussoubb1919
    @oussoubb1919 6 лет назад +2

    Wouy wadioubakh nn kii amoul way😂😂😂😂😂

  • @Kartush
    @Kartush 6 лет назад

    Ana Wa team andeu Sétane Adja click. Ici. Ma Guiss

  • @fafamummy7934
    @fafamummy7934 6 лет назад +2

    Adja thi birr kereum avec Adja tout et possible Mashallah wayy❤️❤️❤️

  • @bangalysankhanou6356
    @bangalysankhanou6356 6 лет назад +1

    Mais loutak cet soldat ci birr série bii

  • @hazishazis2267
    @hazishazis2267 6 лет назад +1

    wadiobakh mak mou rew la 😂😂😂

  • @wademamediarrabocarwade6161
    @wademamediarrabocarwade6161 6 лет назад +2

    Hay Hay Hay Hay wa Ngor 😂😂😂

  • @rignse
    @rignse 6 лет назад +51

    No tay la warou gaayi. bima yéwo nonou thi souba heurou kheud yaw dal ma dém thi boutique bi pour dieund kheud niom pain 🥖 lait 🥛 fromage chochichon kham nga rek mane mom douma lék lu beuri mais ma guén thi bountou bi tassék imam bi makoy khouli 👀 mou may khouli 👀 makoy khouli mou may khouli 👀 après mounima « sonan piiiip may salatou » 😂😂 wa yén warouw lén té mane défoumako dara

    • @diorlabambisteseck4658
      @diorlabambisteseck4658 6 лет назад +1

      Rignese gueye Officiel hay😂

    • @rignse
      @rignse 6 лет назад

      dior la bambiste seck j t’assure yaw

    • @maimounabalde5848
      @maimounabalde5848 6 лет назад +1

      Rignese gueye Officiel bakhna thi yow

    • @Mignelifique
      @Mignelifique 6 лет назад +7

      Rignese gueye Officiel dagua fatei wakh lébone 😂😂

    • @rignse
      @rignse 6 лет назад

      Maimouna Balde hay hay hay

  • @keurdiopndiayelofficielle467
    @keurdiopndiayelofficielle467 6 лет назад +1

    Hay Hay Hay
    Ronne tothe na Keur dh
    😂😂😂 Mais Ngor ya meun mayé
    Koor gui d 3 ou 4 jrs mo ci déss yalna niouko matal ak jamm té Good nangoul niou sunu Ramadan !!!!

  • @khadijandiaye6113
    @khadijandiaye6113 6 лет назад +3

    Hé Mor Mii Beugoul Diam D Waa 😂😂

  • @marierosegueye9159
    @marierosegueye9159 6 лет назад

    mane dé 20:22 la dioth notification marodi nakh li eupp na may baganté si youtube bi di melni Mouss bouy weusine nono way

  • @rigneseboyzndiayeuh8412
    @rigneseboyzndiayeuh8412 6 лет назад +1

    xamone nani dina indi Anta ndire😂😂😂

  • @mamienadf5027
    @mamienadf5027 6 лет назад +45

    1-Nooo Wadiou Bakh lakaléna comme des seins qui ont poussés sur un front mais taye da outhi
    2- Pathé séne nimouy roulé R yi nékh nama.
    3- kou d’accord pour guiss Adja dans une autre série 🤙
    4-

  • @abdoulayegueye1983
    @abdoulayegueye1983 4 года назад +1

    Ki est la thi période confinement Bii

  • @myalasweetdiaw4334
    @myalasweetdiaw4334 6 лет назад +21

    Je crois qu'on continue la série après koor gui et qui d'autres

  • @lhommedelarivegauchedufleu6872
    @lhommedelarivegauchedufleu6872 6 лет назад

    4368 Vus tey tarder na nakk Ana Wa team Adjia, Doudou ak Ngoor? namonaleen ziarnaleen ma sétane teh gnew

  • @fantasadjo1624
    @fantasadjo1624 2 года назад +2

    Machallh 😂😂♥️

  • @adiitadiop9860
    @adiitadiop9860 6 лет назад +8

    Gallé pathe sén dal mo beuri ay tonton

    • @pendadiop03
      @pendadiop03 6 лет назад +2

      adachanel diop waxal way ma puce. 😂😂😘

    • @adiitadiop9860
      @adiitadiop9860 6 лет назад

      Penda Diop def nala name ma choupi

  • @thebesttv1526
    @thebesttv1526 6 лет назад +8

    Noooon série bii waroul diekh prolongé len 3 moi sakh

  • @ameliarose5172
    @ameliarose5172 6 лет назад +1

    Ana wa #team Adjia ♥️notre idole ♥️💎🍭🇸🇳

  • @sante4734
    @sante4734 6 лет назад +2

    Mana kanamou ngor bi meunoumako mouñ🤣

  • @taphasene8074
    @taphasene8074 6 лет назад +1

    Hhhhhh djogoy kh3eee gnalllllll dinama ray wayeeeee

  • @khadimmbaye8482
    @khadimmbaye8482 6 лет назад +1

    Machallah l'équipe ay gor

  • @tambedouyacine7227
    @tambedouyacine7227 6 лет назад +1

    svp pouvez vous Continuer la série après le ramadan

  • @souanimarley9616
    @souanimarley9616 6 лет назад +7

    Tata adja😍

  • @sinditv4275
    @sinditv4275 6 лет назад +10

    Man mom de guiss adja daf may neex trop ak kan

  • @binettefaye6526
    @binettefaye6526 6 лет назад +1

    😂😂😂😂😂tayyy leep leuh nn ngoor dou demm

  • @dijafashion528
    @dijafashion528 6 лет назад +2

    Ay ngoor ani lir ak satieu😂😂😂 mane Anta ndiir lamay Ray

  • @toubadiakhate3525
    @toubadiakhate3525 6 лет назад +3

    Haha Wadjou bakh nèna Touyyu Diamou

  • @astoucisse5714
    @astoucisse5714 6 лет назад +2

    😂😂😂😂waw keye wadiobakh raya tinama

  • @sodambodj3823
    @sodambodj3823 6 лет назад +1

    Anta ndirrr wooy

  • @mbackediop7678
    @mbackediop7678 6 лет назад +2

    96 eme taye nak diambar la mais Yalla na sénegal gagné mondiale bi franc tokk premier tourr Modou lo dane balla Gaye macky sall wathi 2019 )) Savini bou Italia May gayi papier walla mo mort😀😀😀😀😀😂 jaim lénma nak té Yalla takh

  • @sadiyawade7456
    @sadiyawade7456 6 лет назад +1

    Enfin anta ndiiirrr

  • @viati3400
    @viati3400 6 лет назад +3

    Haha 😂😂😂 ils sont fort bilay

  • @mbenedieng8137
    @mbenedieng8137 6 лет назад +5

    1er fofa tothie jaime way topoulen Sama guinaw boulen sisou way Bleu ma guise

  • @aichadieng3248
    @aichadieng3248 6 лет назад

    Ceux qui naime pas limoy sorcellerie mechancetei.. team seri yeup

  • @emmathacen6093
    @emmathacen6093 6 лет назад +2

    Nn Ngore raynema😂😂😂😂😂😂😂😂😂