FACE-À-FACE BOU DAAK SI SAISON BI TAPHA GUEYE 2 VS BOU SITEU

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 31 янв 2025

Комментарии • 208

  • @CheikhsidyaDiallo
    @CheikhsidyaDiallo Год назад +54

    Lamine samba vraiment sa professionnalisme desna vraiment. Eupeul nga torop vraiment.

    • @abloslimshady
      @abloslimshady Год назад +2

      Gueuweul leu motax!

    • @samb8934
      @samb8934 Год назад +2

      ​@@abloslimshadyet c'est quoi le rapport ?

    • @fashionfashion1330
      @fashionfashion1330 Год назад

      ​@@abloslimshadyPourtant Mbaye Dièye Faye Eupeuloul kou dall la

    • @harounasoumare5982
      @harounasoumare5982 Год назад

      Nitt dou bagne nitt mai Kii mome nekhou ma

    • @abloslimshady
      @abloslimshady Год назад

      @@harounasoumare5982 FOg na danga beug wax ni dokhalineum mola nekhoul!

  • @Cheikhndiaye12-z
    @Cheikhndiaye12-z Год назад +14

    Bayi leinn promouvoir carte 😢carte bakhoul

  • @moryfaye7808
    @moryfaye7808 Год назад +19

    Sacré bou Siteu😂😂❤

  • @ibrambaye2970
    @ibrambaye2970 Год назад +23

    Lamine Samba da Bari wax trop 😢😢😢

  • @papemalickndiaye7451
    @papemalickndiaye7451 Год назад +15

    Oh lamine samba laisse nous tranquil 😢

  • @yankeenovember90
    @yankeenovember90 Год назад +29

    Tapha Mbeur sax meunoul mouñ Bou Siteu😂😂😂No Bou dou nitt😂

  • @SILN2k
    @SILN2k Год назад +182

    bilaahi lamine samba yaa bari wax, mbeur yi laniouy deglou pas yaw tu es là pour organiser yamal ci lolu stp vraiment tu gaches les face à face yén gniko djégué wax lén ko deug way akh

  • @AbdoulazizKeita-oy3pc
    @AbdoulazizKeita-oy3pc Год назад +10

    Tapha mbeur ndammm rek inchallah ndammm rek inchallah

  • @papacherifasniang3769
    @papacherifasniang3769 Год назад +56

    Vous n’avez même pas honte de faire la publicité des paris sportifs

  • @konadiouf2596
    @konadiouf2596 Год назад +3

    Kouni Tapha Gueye trabaja nékhoul danga sokhor ki khoromou na😂😂😂

  • @ChekheNdongeu
    @ChekheNdongeu Год назад +8

    Nooo dama reeee ba sanou bou siteu dangeye reeey ba sanou kendou bou siteu ak tafa gaye mai linekh na

  • @seydinanouhathiam
    @seydinanouhathiam Год назад +14

    Magui won fou Aziz Ndiaye nekon 😂😂 bou dou niit 😊

  • @smssanghottmulti-services9607
    @smssanghottmulti-services9607 Год назад

    Tapha mbeur le grand patriote

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Год назад +15

    Lamine samba sooff nga 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @fatoundiouck7582
    @fatoundiouck7582 Год назад +12

    J’adore les tenues ❤❤

  • @moussafall1614
    @moussafall1614 Год назад

    SUNUBET, XBET lépe carte haliss la. dommage que aye kilifeus nioye défe séne promotion si lam j

  • @BallaFaye-jm6yg
    @BallaFaye-jm6yg Год назад +2

    Bayilén xalé yingéun Di encourage si cartes

  • @madoushajoopy6153
    @madoushajoopy6153 Год назад +15

    Bou lagn beugu dh Nioune 😂😂😂😂😂😂

  • @CASI7797
    @CASI7797 Год назад +4

    Vol bi gnou bind alhourane😂😂😂😂 émigré 😂😂😂
    Euyy wa Emirates dinagnela meirei

  • @mounasssy4416
    @mounasssy4416 Год назад +7

    Bou beug nako nak😂😂😂😂

  • @antagueye7993
    @antagueye7993 Год назад +21

    Mai bou siteu nouyouna gnèpou bamou dess gris ak eumeu 😂😂😂

  • @djibsonseye1607
    @djibsonseye1607 Год назад +21

    Vol bine binde Al khouran bi😅😅😅

  • @bbcheikh3364
    @bbcheikh3364 Год назад +11

    Bouu makoo fann

  • @pmsdiouf
    @pmsdiouf Год назад +4

    BOU SITEU PLANÉTAIRE KASSÉ BOROM NIVO 😂❤😂❤😂❤

  • @theblackthought4415
    @theblackthought4415 Год назад +27

    Lamigne Samba, tu parle trop trop trop, on est pas venu ici pour te regarder, mais plutot les lutteurs
    waxleen kii deugg waay!

  • @Le_R319
    @Le_R319 Год назад

    Balla gueye 2 brom bakh leu day retan rekk

  • @khadysyll5820
    @khadysyll5820 Год назад

    Tapha gueye 2 mingui beurre ba tay

  • @verdugokiller8552
    @verdugokiller8552 Год назад

    Xbet ak sunubet ben lah kayy buu😂😂😂😂

  • @falloukarimmbow4981
    @falloukarimmbow4981 Год назад

    Bly😂😂Tarrabakheu lã Farrãl Tapha guéye 2😂😂😂 dama nékh légui bly

  • @BabaColy-w1p
    @BabaColy-w1p Год назад +2

    Bou siteu bly amal diam il es nex se gas 😂😂

  • @papasene6640
    @papasene6640 Год назад +8

    Bou Khana Malick Ndiaye rek la dane si mbeur 😅

  • @MoussaMbaye-c8v
    @MoussaMbaye-c8v Год назад

    Bou siteu rk lay topou ❤

  • @BabacarKanté-o2z
    @BabacarKanté-o2z Год назад

    Sougne ma fayone ay millions sakh douma tekk si bou siteu

  • @mansourndione1342
    @mansourndione1342 Год назад +10

    😂😂😂Bou entrainewoul wakh rekk

  • @layesam5162
    @layesam5162 Год назад +4

    💐Lamine SAMBA , Mane mom franchement dafma nekh rék ☺️ Il sait très bien orienté les débats. MASHALLAH 🙌 Plateau bi✨ c'est TOP👍 Ak BALLA GAYE 2 Ci flanc bi 🤩🥰 Mention à ALBOURAKH🌟🌟🌟

  • @kanka2076
    @kanka2076 Год назад

    Casque youm takke est ce que mugi marché 😂 niaari diaague lay am 😅

  • @akimrassoul7116
    @akimrassoul7116 Год назад

    Lamine samba d'où nitt éspéssou diam leu

  • @lohmfaty7950
    @lohmfaty7950 Год назад +7

    Bou siteu yalla topéwouko dara 😅😅 avion bouniou bindeu al coran bi😂

  • @JazzCheikh
    @JazzCheikh Год назад +3

    DI DEF FACE A FACE BOU TOLNI DI YOREE BENE MICRO 🎤 DIKO PASSANTEE

  • @moussa6869
    @moussa6869 Год назад

    Tapha Gueye dalenasi dhe bilahi mo mene bou siteu foufe

  • @ogfodendour8884
    @ogfodendour8884 Год назад +8

    Fly Emirates 🎉

  • @kossogadiaga-fu6ik
    @kossogadiaga-fu6ik Год назад +3

    Bou siteu kasse 😂😂😂😂❤

  • @øGméttaGueye
    @øGméttaGueye Год назад +1

    Malick thiandoume bougouma mou bocal lamine samb plateau dafa bari wakh diapp ni moy meilleur tée diangoull xamoull dara daye beugue di yeukeutikou sa kaw tée yaka meuneu fouff

  • @alphadiallo3579
    @alphadiallo3579 Год назад

    إمارات lay wakh dh😂😂

  • @IbrahimoKebeo-wb7zv
    @IbrahimoKebeo-wb7zv Год назад +2

    Parifoot c'est Haram bouniou KO kèn forcè

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo Год назад +2

    Scales Guinée😂😂😂😂😂

  • @mbayediop123
    @mbayediop123 Год назад

    Hotel Carlton c international

  • @SeydinaaliouDiallo-y3n
    @SeydinaaliouDiallo-y3n Год назад

    Lamine barigua wakh

  • @Toumanindiaye289
    @Toumanindiaye289 Год назад +9

    😂😂😂😂Guinée 😂😂😂😂

  • @konadiouf2596
    @konadiouf2596 Год назад

    Mais Tapha Gueye trabaja litakh mou sawar si classe Bou Siteu ak Laurent Ndiago moy daf léne eupe dolé

  • @cheikhdiop9013
    @cheikhdiop9013 Год назад

    ay pere de famille tok fi di promouvoir carte xaliss 😢

  • @seydouba2113
    @seydouba2113 Год назад +14

    Bou dou nitu fi 😂😂😂

  • @alyaw1664
    @alyaw1664 Год назад

    Malick samba Dall duul way duul’ wooooo duul

  • @CASI7797
    @CASI7797 Год назад +2

    Dagno escale Guinée 😂😂😂

  • @syllawane4519
    @syllawane4519 Год назад +2

    Lamine mom naggou sarakh leu mom niakk teey moyy thiatam

  • @realnigersweetlove
    @realnigersweetlove Год назад +10

    Man bou siteu moy sama mbeur

  • @malicksarr4213
    @malicksarr4213 Год назад

    Sunu beat thiotou ndeye senegal 😢

  • @AdamaDiaw-ou1dq
    @AdamaDiaw-ou1dq Год назад +11

    Mais lamine samba il connaît rien au lieu de laisser les mbeur parler sur le combat tu nous parle de vol et de voyage

  • @Boymullier1808-bi2ty
    @Boymullier1808-bi2ty Год назад

    Katal sa ndaye bou siteu khana guinne dou deuk yalla nala père tapha DANN

    • @mortadacisse8992
      @mortadacisse8992 Год назад

      😂😂yagui sissu dé

    • @mddi1420
      @mddi1420 Год назад

      mais danga xam ban guinee lay wax ?
      guinee bissau amna, guinee equatoriale amna, guinee conakry amna

  • @Khadimbamba015
    @Khadimbamba015 Год назад

    éééé boulen dofe souyou bet carte la déé baakhoune 😭😭

  • @moustaphasadiboudiame9619
    @moustaphasadiboudiame9619 Год назад +1

    😂😂😂 Bou moy Niveau

  • @Weuzadooo
    @Weuzadooo Год назад

    Mbeurou demb kaye 😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @FataThiam-jy4ew
    @FataThiam-jy4ew Год назад +1

    Ndayesann gri migui rée😂

  • @mamadouba-u2f
    @mamadouba-u2f Год назад

    Nena Balla geuye 2 Moussouma diapalé aka ndey eupall😮

  • @samueldiouf2863
    @samueldiouf2863 Год назад

    Faut chercher des beaucoup de micros waye

  • @mouhamedfall9708
    @mouhamedfall9708 Год назад +3

    Nn bou nioun and niou AK carte khaliss bi dh

  • @SahandatoulMouridina
    @SahandatoulMouridina Год назад

    Lamine samb moffi amoul place billahi dafa bari wakh tropppp

  • @NdiayeSouleye-s7u
    @NdiayeSouleye-s7u Год назад

    Niveau

  • @goumbadiop5387
    @goumbadiop5387 Год назад +3

    Niveau beurou dëmba 😂😂😂😂😂

  • @cisseali659
    @cisseali659 Год назад

    Tékk na si bou Siteu 😂😂😂

  • @cheikhfaye6020
    @cheikhfaye6020 Год назад +5

    Lamine samb soff na lou ko terei tokk non waay

  • @omarndiaye551
    @omarndiaye551 Год назад +3

    Bou namone naniiula

  • @omarndiaye551
    @omarndiaye551 Год назад +2

    Guinée key😂😂

  • @alkhamisskor5823
    @alkhamisskor5823 Год назад

    Lamine samba kom perroquet bou reuthieu

  • @PapaAliouThiaw
    @PapaAliouThiaw Год назад

    Bou siteu rek lay topou

  • @abinediedhiou3425
    @abinediedhiou3425 Год назад +4

    Lamine samba khamoul dara koi

  • @MrOusmane23
    @MrOusmane23 Год назад +3

    Vol bi gniou bindeu alkhourane bi rek😂😂😂

  • @KhadimNguer
    @KhadimNguer Год назад

    Bou sitte rék la nioye tope

  • @baffaseck4853
    @baffaseck4853 Год назад

    Guineé😂😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Год назад +4

    Bou lou takh nouyoul gris deux bordeaux 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @commonans
    @commonans Год назад

    Vraiment ça montre l’hypocrisie des sénégalais, faire la
    Promotion des jeux de hasard li yeup pour alalou aduna di Lék riba.

  • @abbaofficiel4577
    @abbaofficiel4577 Год назад +6

    Mirigiré😂

  • @veridique9454
    @veridique9454 Год назад +1

    Bou dèfal yeufou nitt 😂
    Nouyoul gris ak eumeu Séne fèxèl nèkho ak Vip yii moo guëneu gnioulay diapalè thi you beuri

    • @PaOuzz9
      @PaOuzz9 Год назад +3

      Saway gneuwe nagne ba tokk déé iska nouyou léne bime gneuwé avant mouye tokk

    • @veridique9454
      @veridique9454 Год назад

      @@PaOuzz9 nouyowate dakoy yokou rèk

  • @mehmetfall8249
    @mehmetfall8249 Год назад +5

    Lamine samba dafa sof ta touse hamouko

  • @cheikhcisse488
    @cheikhcisse488 Год назад

    Tapha gueye 2 vs bouche ketchup coumbat laa

  • @kouroubayefallpure
    @kouroubayefallpure Год назад

    Tapha gueye

  • @endthewar4558
    @endthewar4558 Год назад

    Bou yow nekal sii jàama bou sama anti stress

  • @ndiemendiaye9979
    @ndiemendiaye9979 Год назад

    Linak mongui may dor dal ben combat niom niar niep di sama mbeur khamuma kumay faral k p meilleur gagne rek

  • @malangsonko5570
    @malangsonko5570 Год назад

    Lamine Samba xana dou liir sougnou commentaires yi😂😂😂Kii sooof na

  • @domou__rewmi
    @domou__rewmi Год назад

    Waye boulene niou fonto forcé wouniou kene mou joué 1xbet 😂😂

  • @Mister-nay-ler
    @Mister-nay-ler Год назад

    Lamine samba laisse les lutteurs parler

  • @baayfaadhlrafahiste7347
    @baayfaadhlrafahiste7347 Год назад

    Lamine Samba tu es écœurant walah

  • @damewilane55
    @damewilane55 Год назад

    1xbet kay 😂😂😂😂😂😂

  • @mansourfall908
    @mansourfall908 Год назад +1

    Lamine samba tamitt dafay yakeu rek

  • @issaka8150
    @issaka8150 Год назад

    Ay sunu bet yougnii influencer jeune yii 😢

  • @alassanetall8665
    @alassanetall8665 Год назад

    Lamine vraiment exagére impeu trop nakk,,, parle même plus que ses invités

  • @FallouBa-mr4xr
    @FallouBa-mr4xr Год назад

    Lamine samba da Bari wax trop

  • @ousmanegadiaga5670
    @ousmanegadiaga5670 Год назад +2

    Blh dagno wara diri valise

  • @BlackKhou
    @BlackKhou Год назад

    Lamine kou nieup toufly nga toyy wayil waxx,,

  • @hrams4793
    @hrams4793 Год назад +1

    No bou siteu vrai ngaka laaa 😂😂😂