Assalaamu alaykum wa rahmatul Laahi wa barakaatuhuu. Nanu YÀLLA tàggatal sunuy xol ak sunuy cër ca lamu tàggatoon sunu Yonnènt bi sAaws akiy sahaabaam rAa te wërsëgal nu dëkag gnoom ca kërug teràngaam. Nanu YÀLLA wan dëgg bamu leer mu yombalal nu topp ko, mu wan nu neen ba nu ràgnee ko mu yombalal nu dùmmôoyu ko. Nanu YÀLLA sàmm sàmmal nu sunuy njaboot ak sunuy woroomi xamxam yi ragal seen Boroom YÀLLA. Jërëjëfati. Nanu YÀLLA taxawu.
Machallh Chiekh Ibrahima Khalil lo xam xam bi rafét n'a yalna yalla goudal Say fann
J'aime cheikh Ibrahima Khalil Lo ❤️✨🙏
Yalla na yalla gueneu deugeureul