Bébé Saloum yangu dioum dh boy niang vs mbiss... Sentel vs malaw seras gno beuré grand combat bi ... Sa Thiès vs neko réel grand combat lawone ... Sa Thiès vs bombardié jr..... lac Rose vs safandou boy niang vs Akon yii ngua beuré grand combat yii
Nékato mbeur vraiment Nitt kou bakh la Mes lamb dou li wakh di olofal yi nékoul lamb dh nékal mbeur wala gua nék lénén Bébé saloum sa kogne sakh faté nagne la Wa penc ak wa ndokh mi
Ma beugg kou meun communication waxou oloff deug lay wax kène dou mome say cadou lou am solo la si jeunesse bi so douguè si politique wala si yèè nite gni nn saloum man yaw rk lay deglou guir sa deugou . Am na nio xam ni sèn xol bakhoul danio sokhor motakh dougn la deglou so waxè rk niouni danga beuri wax . Diame si ioe saloum borom bkh gua tè geum sa bop beugg sa yaye ak sa ndiabote motakh niou beug leuh
BB SALOUM LAMIGNE BI MON NÉKH😂
Athia Mbeur saloum domou thiaroye bi ❤❤
Mais mom noum meun deuké thiaroy di beuré ak reug reug
@@cheikhtidianembengue6709reug thiaroye sur mer la deuk
@@cheikhtidianembengue6709 nn ki thiaroye gare la deuk ki thiaroye sur mer
@@ModouFall-g1o mais khana lépp dou thiaroy rékk
@@cheikhtidianembengue6709 mais bokoul dh reug reug néna nieup lay beurel
Xoma bo magaté kouye bégall xalléyi aythia bb saloum ya meun dhé
Roi des arènes wakh mom kene dou ko yeuthio ak mom😂😂😂
😂😂😂😂😂
Machallaaaaa bebe
Ya degue ❤
Bb saloum vs sokh mako ficelé sponsorisé par lamine samba drapeau maître elhadji diouf 😅
Ndaw combat bou Bari thiow 😂😂😂😂
Lamb tolof tolof la😅
Sheuteuteut bobou combat ak throw limiy andal
Noo sa way do nitte billahi 😅😅😂😂😂
Aythia bb saloum 😂😂😂
Bébé Saloum yangu dioum dh boy niang vs mbiss... Sentel vs malaw seras gno beuré grand combat bi ... Sa Thiès vs neko réel grand combat lawone ... Sa Thiès vs bombardié jr..... lac Rose vs safandou boy niang vs Akon yii ngua beuré grand combat yii
Wakh nga deug dé sathies vs b52 bobou bb mongui beuré ak garga mbossé
Ki Waham Mo Beuri trop Soko degué muy Wag nga Yakaarni Moy Meilleur Aretél Bou Daan Ray Amon Dofi Tok Ndah Yagnga Daanou Respecté Say Nawlé Mbeure
Bébé saloum vs sok combat la dee
Nékato mbeur vraiment Nitt kou bakh la Mes lamb dou li wakh di olofal yi nékoul lamb dh nékal mbeur wala gua nék lénén Bébé saloum sa kogne sakh faté nagne la Wa penc ak wa ndokh mi
Mba yékhoooooo🤣🤣
Bb Saloum Aka barri ay domou biral😅😅😅😅
Fi thii Malika amna nafi niarri dom you goor😅
Bébé taalif 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Bb lay topou ndakh degu dege bi
Bébé amoul koi😂😂
Sokh vs bébé saloum combat la
Bb saloum sokh gnari politiciens talifkat combat bou nex la😂
😂😂😂😂😂😅😅😮
Bebe salloum bégué nala
Ma beugg kou meun communication waxou oloff deug lay wax kène dou mome say cadou lou am solo la si jeunesse bi so douguè si politique wala si yèè nite gni nn saloum man yaw rk lay deglou guir sa deugou . Am na nio xam ni sèn xol bakhoul danio sokhor motakh dougn la deglou so waxè rk niouni danga beuri wax . Diame si ioe saloum borom bkh gua tè geum sa bop beugg sa yaye ak sa ndiabote motakh niou beug leuh
Bebe saloum 😂😂😂😂😂😂😂mma
Arenbi dou wakh dio bari de
Bb Saloum Nékh lamigne 0 jeuf
Bb saloum demal politique tu parles bien 😂
Ki tamit limiy wakh yeup 😂😂
Wakh rek lay def 😂😂😂😂
Ki mom wakh djou beuri kessé mo yakke carrieram,.topp media yi Di mbélé mbéle t bo amé combat meuno fekhé ba dane.
Grand kouye wakh diou khôl rafet MoMA geune kou ignane mais Sénégal da beurri niou ignane motah safara nioune sénégalais bougne fa djitoul Dinama daixal
😂😂
Roi des arènes wakh moko mom 😂😂😂
@@OusmaneBa-yy4nv sa way comprendouma Liga wakh fi
@@ronebodjis4607 lol ki kay mok sokh bougne dadiéwone sen signature de combat Dina saff sapp
5-2-3 sors de ma tête svp
😂😂😂😂 Sénégal bilay dafa néxeu
Lignay wakh boko done entraîne moubakh
Bb saloum vs sokh 😂😂😂😂😂😂 combat bobou moy combat niari talif kateu yi
Limouye wakh souko done beuré kén douko dane bari gua wakh
Ki wakh rk mais dieuf 0
Bou féké wakh rék ya thi Mane nieup mé bou dé mbeuré rék thi guinaw rék ngaye fété
5-2-3 sort de ma tête
Bébé talif brome mats nul bi mome ak Serigne ndiaye 🤣🤣🤣
moussa ndoye gouye gui yaw khamo lamb dh
Tu parles trop
Da nga bari wakh
Yaw dal Man nako