Kawtef à Yeumbeul "Kharitam moko ray ak paaka, niari diam thi bir bi" triste réaction de son père

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 1 янв 2025

Комментарии • 97

  • @aichatousow9011
    @aichatousow9011 8 месяцев назад +1

    Yalla nako yalla yeureum té khareko aldjana mo moudjé depanné sama pompe bilahi

  • @serignendiayebeuguefallou7088
    @serignendiayebeuguefallou7088 Год назад +9

    Thièye Sénégal fomou dieume ohh vraiment métina

  • @mamitabeye9324
    @mamitabeye9324 Год назад +11

    Oh ndeysan 😭😭yalnako yalla yeureum té haréko aldiana firdawsi🤲🤲

  • @lionelmendy9753
    @lionelmendy9753 Год назад +9

    Sama wadji tu vas me manké que ton ame repose en paix 😭❤️🙏

  • @yaayfall
    @yaayfall Год назад +7

    Tu as parfaitement raison il faut revoir les garages et les responsable

  • @mbayediagne152
    @mbayediagne152 Год назад +4

    Yalla nako yalla yeureum té khareko aldjana

  • @moustaphagueye1767
    @moustaphagueye1767 Год назад +5

    Rip mon frère mon jumeau,tu resteras toujours dans mes pensées 😭

  • @adjilaye9149
    @adjilaye9149 Год назад +3

    😢😢 walahi Sama mak dji dinga ma wëteul Gueye nioro yalla nala yalla kharé aldiana papa ndiaw sunu kilifeu gui kadou yi rafet na

  • @FatouDiop-fe2se
    @FatouDiop-fe2se Год назад +3

    Yalnako yalla yeureum té yalla may léne kholou moungnie

  • @mamadoukaolackdiallo7209
    @mamadoukaolackdiallo7209 Год назад +5

    innalillahi wa inna ileyhi rajihone Allahoumma Akfirlahou warhamhou Paix à son âme et qu'Allah SWT l'accueil dans son paradis céleste éternellement

  • @AntaKebe-l7f
    @AntaKebe-l7f Год назад +2

    Ndaysan yala nala Yala yeureum

  • @MamanDione-m3f
    @MamanDione-m3f Год назад +3

    Yalla nako yalla khare aldiana firdawsi barke seydina Mouhamed psl

  • @libassedieng
    @libassedieng Год назад +1

    Ndeyssanne tiey aduna😢

  • @dijasall7997
    @dijasall7997 Год назад

    Bilay nitt kou bakh beuri diam foko.guiss dey rei rk yalnako yalla yeureum xareiko firdawsi

  • @kambayependasall8908
    @kambayependasall8908 Год назад +5

    Paix à son âme que firdawsi soit sa demeure eternel

  • @awathiaw9848
    @awathiaw9848 Год назад +4

    Paix à son âme métina trop

  • @diakhatefatoumata6272
    @diakhatefatoumata6272 Год назад

    Yalla nako yalla yeureum té kharéko aldiana Ndeysan sunu guinaw keur la khéwé

  • @cheikhounakhadimdiagne756
    @cheikhounakhadimdiagne756 Год назад

    Yalnako yàlla sunu boroom xaré aljana Aamiin

  • @maremediagne9788
    @maremediagne9788 Год назад +2

    Ndeysane marame khalee bou yarou

  • @sokhnaoumoudiop6888
    @sokhnaoumoudiop6888 Год назад

    Yalla nako yalla yeureum khare ko ardiana firdawsi deysane

  • @mariamndiaye9732
    @mariamndiaye9732 Год назад +2

    Senegal rey chaque jour doyna war.yalla nako yalla yeureum te khareko aldiana firdawsi.

  • @MatydiopDiop-r5s
    @MatydiopDiop-r5s Год назад

    Ndaysan Yallanako yalla yereum métyna loll

  • @makhfaye-c2k
    @makhfaye-c2k Год назад

    Yalla nako yalla kharè aldianay firdawsi amine

  • @dakartv465
    @dakartv465 Год назад +5

    C l Sénégal d'aujourd'hui me paaka moom yombal nagnouko trop, wargnou xool arme blanche yi nouniou koy diaayer, bcou de meurtres au Sénégal diam paaka la ,les boutiquiers etc .. on doit les interdires de ventres des couteaux, et sur les marchés trop facile

    • @natou768
      @natou768 Год назад +1

      Wakhale des paka boutique bo dougou niou diayela paka comme pain ton

    • @dakartv465
      @dakartv465 Год назад +2

      @@natou768 🤣😂

    • @WassareSociete
      @WassareSociete  Год назад

      merci pour votre commentaire

  • @amidieng7002
    @amidieng7002 Год назад

    Yalnako yala khare aldiana amine yarabi mon bébé

  • @amadoubadji8195
    @amadoubadji8195 Год назад

    Yalla na ko yalla yeureum té khare ko adiana firdaysi

  • @ndeyeamyyade5608
    @ndeyeamyyade5608 Год назад +3

    Bilay nit kou oyof beugon nit

  • @binetandiaye3108
    @binetandiaye3108 Год назад

    Yallah nako yallah yeureum

  • @binta4894
    @binta4894 Год назад +3

    Do leine ma waxe louxew Sénégal nguir yalah aye waye gnongui rayane té rek

    • @dakartv465
      @dakartv465 Год назад

      Nagnou setane rek com k sokhna bator Sax day Ray kay , bou gni rayer boumou beteu kene

    • @WassareSociete
      @WassareSociete  Год назад

      merci pour votre commentaire

  • @Elhadji2187
    @Elhadji2187 Год назад +2

    Ii yeup bonn hol rke mokay waral mo tah khalé bou télé nakarri derett rek dindi koo hol bou binn bahoul

  • @abdoukhoudossseye1820
    @abdoukhoudossseye1820 Год назад +3

    🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @Scorpion1362i
    @Scorpion1362i Год назад +1

    Am fi kharit woratoul

  • @FatouGueye-r6e
    @FatouGueye-r6e Год назад +2

    🤲🤲🤲🤲

  • @elhadjimamadousakho787
    @elhadjimamadousakho787 Год назад

    Lou melni mara niass wakhone nako beureubou ligueye kayy yii dina beuri you melni yalna naniou yalla doli soutoura

  • @sokhnamaileye68
    @sokhnamaileye68 Год назад +1

    Oh chaque magal souniou keur laye dale oh mara waye

  • @yacinetoure1184
    @yacinetoure1184 Год назад

    Bly nitt kou bkh yallnala yalla yeureum

  • @mamygaye4378
    @mamygaye4378 Год назад +1

    Yalna motali ndawam Aldiana Firdawsi Ci Barke Seydina MOUHAMED ( p.s.l) Ak Mbolem Dioulite Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 🤲🤲🤲😔😔

  • @RokhayaDiop-wq7fr
    @RokhayaDiop-wq7fr Год назад +6

    Il s'appelle marra yallanako borom bi yereum té mou eggalé ndawam firdawsi kou nango ligueye bilahi....

  • @binetandiaye9216
    @binetandiaye9216 Год назад

    Bonne. Revk dagne. KO. Warona. Rey

  • @AdOlPhE_FOOT-y4l
    @AdOlPhE_FOOT-y4l Год назад +2

    Adouna bi mo yakou

  • @binetandiaye9216
    @binetandiaye9216 Год назад

    Lath n'a. La. Founiou. Dieume. Niak. Yar. Revk

  • @yaayfall
    @yaayfall Год назад +1

    Doyena war li metina peine de mort kou rayé niourayela

  • @serignegaye-lp8yu
    @serignegaye-lp8yu Год назад

    Sénégal beaucoup problème

  • @Makavelimef6789
    @Makavelimef6789 Год назад

    macky sall le malheur du Sénégal. Toujours des jeunes qui sont tués

  • @khadydiedhiou4585
    @khadydiedhiou4585 Год назад

    🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲