Mon mari est devenu impuissant après quelques années de mariage, que dois je faire selon l'Islam?
HTML-код
- Опубликовано: 21 ноя 2024
- Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine / tfm
/ tfm
/ tfm.sn .
#TFM #REPLAYTFM #TELEFUTURSMEDIAS #TFMLIVE #TFMENDIRECT
vraiment pape cheikh c’est un héros
Thank you guys!
Kaay leen nu jàng àngale ci wolof tamit, guys.
Le monde bouge avec English..
Beuguenako 🙈j’ai des difficultés
Machallah oustaz modou fall
C'est cette partie qui me plaît sur l'émission
Pape cheikh on t'aime ❤❤
Machaallah dja Allah khayeré oustaz bien dit oustaz
Bilay pape cheikh dafa néx❤ yalna sa diam yagg😂😂
Oustaz dioum nga bou bakh si mbiroum soumèku bi:
1-su fékè ni djeukeur dji mo nèkul si yone, djiguèn dji gnane bate mu bagn, dagnuy tass seuy bi té djiguèn dji du diokhé deureum !!
2- Su fékè ni djeukeur dji nékkna si liko war yeup ba paré diabar dji beug guènn si seuy bi sans raison valable, su bobaa lay meuneu soumèku, té sugnko diokhone 500.000, meune na diokhé sakh 10.000 , suko djeukeur dji acceptè seuy bi tassna .
Oustaz ngir Yalla dèl guëstu wat tèré yi bala ngay tontu way, mbiru di é c'est très très sérieux !!!!!!
ah weh merci pour l’aiclaircissement
Es que dou dote bi moy liniou diokheé si djak dji?
@@naroubayeniassfall8019 question très pertinente
Fatoumata bintou sonko, je veux être éclairée.
@@naroubayeniassfall8019Kham nga lèlè aada dafay diakhasso ak diné. Effectivement si diaka dji dagnu nane diokhnako thiang 10.000 f massalane. Après lénène li waadji mo koy yèné mayko ko. Wayé gnune gneup kham nagn ni si sugnu société yi,lolu en général warugar la bu waadji dul sagna bagn, kon soko kholè fofu dafay mélni luy doug tamite si thiang bi. Wayé alaa kulli haal, su fékè ni ndaw sèe beugueu guénn si seuy bi té waadji mungui si liko war yeup, su boba négociation lay done rék ba lugnu djuboo si luko ndaw si di diokh com dédommagement. Meune na tollo ak thiang bi meun nako yèss, meune na done sakh 5000 f , Waadji sakh meune na bagna laadj dara dal di koy libèré nonu. Lii moy charia !
Pape cheikh Soûla sama Akh dalei yow dh dinga seuyate année bi
Pape cheikh meilleur d sa génération
Yalla nako yalla maye kholou mougne ta yalla safaral ko
Développement Kaw Kaw. Pape Cheikh sérieuwoul😆
Kaw kaw yi danou am yar kham linouye wakh
@@mameawadiop5766 WA yaw louye sa problème
Beugu ngén mettil wax
@@afalbichirifall4030 Kone légui lo Thi wakh
Machallah
Je kiff ce duo
Wouyyyy ma gui dé développement kaw kaw
Pape cheikh dou nitt😅😅😅
Pape cheikh bilay dafa meilleur
Kouné ak sa idole mane oustaz Modou fall moy sama idole préfère thi oustaz yi
Pape respect pour les kaw kaw
QG mom duo pape cheikh ak ouzras modou fall
Developpement kaw kaw kay non Mamy Pape Cheikh déff nalako nak 😂😂😂😂😂😂🤣
Machalla oustaz
Vraiment encore merci
Mamy akk pape cheikh 😅😄 ..oustaz enseignement de façon simple et comique kou sérieux nitë en tire les conclusions justes et vrais!
Développement kaw kaw kaaay pape cheikh d'où niit
Dôme baye macha Allah bisous seydou Ndiaye
Non man pape douma Ray 😂😂
-😂😂😂je plains les femmes qui ont reçu une dot de 10 millions et qui vont devoir rembourser alors qu’elles ont tout dépensé le jour du mariage 🤦🏿♂️.
-Les femmes quand elles ont déjà goûté...je doute fort qu’elles peuvent patienter 6 à 1 ans pour permettre à leur conjoint d’aller se soigner 😂😂
😂😂😂😂😂😂
Si le mari a de l argent elle vas rester sinon mom
@@toosource pas forcément.
Merci,♥️
Pape chekh Diallo d'où nit bilay
Aye pape cheikh Diallo reynama😂finalou lane
ce n'est pas forcément qu'on doit donner le même dot tu peux donner le plus ou le moins de dote
كان ينبغي علي هذا الصفي احترام العالم وعدم طرح اوي تعليق بدون احترام وتقدير
سبحان الله
Wouyy wa Sénégal kay leen wakh ma louy développement kaw kaw
Oustaze bayil wakhi soumeko. La femme le fait quand elle n’a pas de raison valable aux yeux de l’islam. C’est pourquoi elle doit rembourser. Mais si le mari a tord la femme ne rembourse pas.
Ioe lingua wakhe si corant wala sa bakane ak loula arrange ngua wakhe wala lane
Non dou lou ma arranger vous pouvez vous renseigner
@@olymatadiouf2638 Manche allah c est une question que j ai poser et j avais vraiment pas la reponses
Non, non ma soeur
Ouli je me suis renseigné ya ame deugue
Diabarou Pape Abdou Cissé bi yén wa Pikine nélén ko mou débrouiller Bou bax si seuy bi 😂😂😂😂
le mariage se limite pas au sexe.
Très important quand même
Vraiment tu a parfaitement raison
MaChall♥️♥️♥️
Oustaz magui diégalou dh Seuyy you barii tassoul n'ul n'a le droit de répudier sa femme tant que fékoko mouy ndialoo ak kénén mé galSen 1e p'tite dispute nga fassé sa sokhna motakh niou barii niogui bakar Lou
Non, cest pas vrai.
@@mohamethkane5966 bou yeumeulkhiyamé lépp Dina lerr
Vous voulez dire que adultére bou am séddé rek moy liy tass seuy? Sinon aucun autre motif n'est valable pour divorcer?
Li nga wax da léroul thi mane
@@LaBarhamienne ki limou wakh dou islam deh, je ne sais s il est musulman ou pas.
@@mohamethkane5966 Ah moma diaxal di koubakh. Motax ma posé ko question yoyou, ndax soudé lolou la deuguel ma xamni déssé na xam lou islam wax à défaut qu'il ne soit pas musulman, si tel est le cas mom ah🤣🤣🤣🤣ma xamni amna fite.
Mon animateur 🤣🤣🤣🤣🤣
😂😂😂😂😂 pape cheikh
Développement kaw kaw aÿ waye baye 🤣😂🤭😆🤣🤣😆😆😆
Oustaz esk kham ngani niou bari noungui niallo
Lou ta
Kh
No Pape cheikh louye développement kaw kaw tmt😂😂
No li damako ree ba sone 😂🤣🤣
🤣🤣😂😂🤣 no vraiment pape chiekh diallo manga joue theatre srx
Non pape cheikh raynama 😂😂
Un peu plus de sérieux svp dinne la diarul comédie
C'est complètement FAUX, ce qu'il a dit à propos du soumèkou
IL a raison, verifie!
@@mohamethkane5966 il n a pas du tout raison, je sais ce que je dis !
Pape cheikh 1000f kassé layorone dieudé KO crédit moudiékh té diotoumala
Question yi mom fougn kay poser nakh mane da am louma begua lathe
Posé ko fi âme n'a gnou beuri gnou djangue gnouye lire commentaires yi
Pape arêtes de jouer des sujet très important désolé
Pape cheikh serieux woul🤣🤣🤣🤣🤣 dagua niemer développement wou kaw kaw
Oustaz modou fall dama ko beugue
🤣🤣🤣development kawkaw 🤣🤣aye seub amoufi no li loumako retane
Guiryalla si soukerou koor bi
Il raconte des sottises cet homme, ce serait facile pour la femme. Le mariage c'est pour le meilleur et pour le pire.
Oustaz dioum ngua 1 an
Pape cheikh do gooré .
Hum...t'as remarqué ?dama fogone man rek mako seitlou
Le seul.dzfaut de pape deux eupeul parfois mais il est bien
Ki dagg lokho diabaram bi warone na setane li way
Teulé bobou khamna koussi Ay aalkhourrane rek lakoy défé kouma inbox ma diokh la numerome
Mashallah votre émission mais il faut cesser de bcq rires
mane damay ladje ndakh fasse sa diabar ba pare mou gnieuw set sila nguen am report sexual ndakh lolou dafa haram
Wax na deug Mami linguere mo sof ak ay mots wam yi
😂😂😂😂😂
❣️❣️❣️❣️🤣🤣
😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉🎉❤❤❤❤
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣🤣
❤❤❤❤❤❤❤❤❤💘❣🤚🤚🤚🤚🤚🤝🤝