Machalla amatina solo dieure dieuf sandiogou ak souhibou Wakh nga deuk dee billahi Assane messere taye mom Danou nga gani magal guii lonuye wouti hôtel
Bilahi, lii ma cii gueneu méti moy sou régime bi décidé défaar Sénégal, sénégalais yi cii sen bopp niolèn di fi dieulé. Dama yeureum Sonko ak Diomaye weur na Yalla
Le gouvernement ne peut et ne doit pas prendre en charge des autorités venues célébrer le magal. S'ils doivent loger dans un hôtel cela doit se faire à leurs frais mais pas ceux du gouvernement qui use de l'argent du contribuable. Ce serait illégal !!!
Merci beaucoup SA Ndiogo ces gens là sont de mauvaise foi c inadmissible leur façon de faire mais peine perdue la manipulation ne passera pas car porte parole du marabout vient de démentir leur forfaiture
Mais Magal bi c'est à Touba pas à Dakar si réellement ce sont les invités de Serigne mountakha, leur accueil à Touba est réglé bien à l'avance... Dites nous qui sont ces gens car les vrais invités de Serigne mountakha sont dans les lieux qui leurs sont réservés à Touba .... Cheikh Omar Diagne soutien à 100%
Guis nga ce gars là son Ibou ou quoi , mais il faut que tu chasse que le budget du Sénégal n’est pas pour n’importe qui kmm , bon un peu de respect aux sénégalais kmm . Mais j’ai oublié que le niveau n’y est pas . Vive les patriotes, vive Sonko moy Diomay ❤❤❤❤❤. L’argent du Senegal n’est pas comme du marchandise et merci Sa
Souniou diokhé aye milliardaire pour niou ganalé souba souba dina déposer pour gouvernement diokhma ma dieunde keur bou ande ank meubles cles en main Li dafa yombe
@@serignetine1420 li ma wakh lére na ganalé aye nite you diougué biti réw mi diléne logé thi aye hotel dieul léne en charge dafa yombe gouvernement warouko def béne yone Ko am passou avion ✈️ fo dale thi sa posse waroula diafé
Merci sa , le gouvernement du Sénégal n'est pas là pour prendre en charge les gens qui sont venus au magal. Assane ceux ne sont pas des invités du Président
@@seydinaomarsarr8970 Yalla diékhoul té diékhaloul weurseuk. Tfm teuthie, niou dém wouti fénén liguéy. Usines sonacos, Sias, Batta etc. teuthie naniou et la vie a continué. Thiottou nday TFM ak kiko mom
Arrêtez vos mensonges c'est pas a l'état d'héberger des étrangers Touba a besoin de tout pour son développement donc bon attend a l'état sur d'autre chose plus important que des hébergements les fosses informations ne passent pas
Assane kouy dème maka da ngay faye sa billet kone kouye magal si sa nga wara faye ganou gouvernement bi lagne donc nalen gouvernement bi gérer gneupe serigne Touba mo gnou takh diok wa tfm nak yakheu rek la gnou beugua deff
Damane wa touba naniou lijeunti sen magal sen bop budge Senegal dou pour ay magal ak gamou Assan mi khamoul dara billahi ay yeufou niitou aal rek lay wakh aah demal gua wouti khamkham te mayniou diam yaw nulard bi sof na torop
Oui depuis bi check omar diagne waxe ci touba depuis 2021 ba legui lako diappal haine assane pr check omar diagne ak mimi tourè la geuna contre te niit dafa wara fatte mais mom day diap mer te lolou baxoul😢
Depuis commencement la léne wakh né TFM ak GFM si guerre laniou nék ak état bi ils essayent d'ignorer Ousmane Sonko mais Billahi wallahi mouniou dara si mom ils vont voir
Rfm wallaahi séen mission bii du jàll jaxasé waa TOUBA ak gouvernement bi ngéen bëgg mais du ngéen ko réussir. Gan ñu war a Magal ci TOUBA Yaw ngay wax waxi King Fahad Place Mbaam yi ngéen doon.
Sadiogou ❤avec ses analyses ❤🎉très pertinente .sa me rappeler sidilamine naisse. Paix en son âme.
SA dafa xam sénégalais xam sen mentalité.
Walahi comme Sidy Lamine Niass
Merci Omar diagne
Kou d'accord ni wa pastéf danio war di nokhé rék lalall j'aime
Assane il faut dire la vérité ,c'est pas normal que gens vivent sur les dos sénégalais, pourquoi on doit payer ses gens
Assane mom moy lolou,il ne prend pas jamais ses responsabilités,ses analyses incompréhensibles
Un vrai pelerin normal se prend en charge. Aller au Maroc en arabi saoudite vous verrez si c'est ces états qui prenne en charge
Machalla amatina solo dieure dieuf sandiogou ak souhibou Wakh nga deuk dee billahi Assane messere taye mom Danou nga gani magal guii lonuye wouti hôtel
Très bien sadiogou tu es pertinent
Merci pour ta clairvoyance et ta pertinence, SA. Des analyses pertinentes et pointues comme toujours
Manchalla àmatina solllo
Sénégal dina nakharé défar.
Non Sénégal dou nakharé défar déééé na gouvernement bi dieule Ay matou wayam you matte seule🤬🤬🇸🇳
Wakh deug dé khana niou am foulleu ak fayda ndakh hoqatalyi barina mes foulleu rek
Bilahi, lii ma cii gueneu méti moy sou régime bi décidé défaar Sénégal, sénégalais yi cii sen bopp niolèn di fi dieulé. Dama yeureum Sonko ak Diomaye weur na Yalla
Billahi @@laurentmariusdiallo6962
Bilahi
Rfm aye mbam lanou dani diema sapote waye yalla molen appa dolle presidente Bassirou diomaye faye rek moy Presidente ousmame sonko yalnanguen gana yokkou bou bakh barkep yonentabi s a Wasalam amine ❤❤❤
Gouvernement bi waroul dieul bene charge pour kene kou beug magal na dieleul bopam charge
Imbéciles yay khajj !niata milliards là magal di dougal
Merci Sa rfm ay vrai mbam laniou
Et pourtant cheikhouna mbacke président d organisation du magal à confirmée la lettre dawal deglou
@@tele1514hum et pourtant porte parole s mountakha démentir nako
@@tele1514mais cheikhouna yonam nekoul thi AB lettre dawal déglou CH bass
Assane,le budget du Sénégal n'est pas pour gérer des hôtes de gamou ou magal... Qu'on respecte les Sénégalais. Y'a eu trop de pratique nébuleuse.
Serigne si nio eupp khalis état bi kon naniou géré sèni gane amoul gamou amoul magal
Ils peuvent réussir sans l’aide ‘Etat
Jub-Jubal-Jubbanti
L'hôtel de king depuis quand il est à TOUBA 😊@@matarndiaye3048
Walahi ✅
Merci sa ndiogou 🙏🏾
SONKO MOY DIOMAYE ✅
TFM MOY 👉TÉLÉ FÉNN
RFM MOY 👉ÉRÉFÉNN
Merci BDF et O s
Assane ta réponse nous induit en erreur tu maîtrises pas le problème
Assane yagi beugeu soff nak khamo thi sujet tous
Merci sa
Merci beaucoup Sa❤❤
Le gouvernement ne peut et ne doit pas prendre en charge des autorités venues célébrer le magal. S'ils doivent loger dans un hôtel cela doit se faire à leurs frais mais pas ceux du gouvernement qui use de l'argent du contribuable. Ce serait illégal !!!
Sa waye lolou yombna mouride Lol billahi khalis thi gnom la fekké bakh
@@serignetine1420donc il faut le faire et ne pas le mettre sur le dos des sénégalais. Na kou neek gérer sa ay gann.
Haa mane deh dama warou niylene invitee dounioulene fayal hotel tamite gouvernement bi lou takh mou warlena dalale rewmi dale liniou warw sopi berina
Vraiment pour quelqu'un qui est venu pour le pèlerinage doit payer ses frais
@@gnagnadabo3053😂🫰🏽thx Sista
Malheureusement 😢😢
Machalla merci beaucoup sa ndiougo merci
Merci beaucoup SA Ndiogo ces gens là sont de mauvaise foi c inadmissible leur façon de faire mais peine perdue la manipulation ne passera pas car porte parole du marabout vient de démentir leur forfaiture
Sonko moy diomay diomay moy sonko❤❤
mashallah Chico Chicana the conversation was so unique important word❤❤❤👍👍👍
Mais Magal bi c'est à Touba pas à Dakar si réellement ce sont les invités de Serigne mountakha, leur accueil à Touba est réglé bien à l'avance... Dites nous qui sont ces gens car les vrais invités de Serigne mountakha sont dans les lieux qui leurs sont réservés à Touba .... Cheikh Omar Diagne soutien à 100%
Guani Serigne bi lagnou nalene serigne bi terrou
tarikha yeup ak religions yeup la ñu koy defal thi séni bis
Li Moy deug. Naniou ko banial gneup
Sa nopalou tfm est ennemi numéro 1 de Etat actuel
Assane commence vraiment a nous enerver....
Aah vraiment ken khamoul loumouy wakh
Il nous emmerde simplement
Son niveau d'analyse est trop bas ces derniers temps il a intérêt à revoir ses idées
Il a un niveau très bas
Ma challah sa
Mecri
Merci sa ndiogou très bien ❤
RFM AKA NIOO NARA SONOU
Dinagne sonou bilay
Chéih Omar a raison l argent des sénégalais né pa pour les visiteurs k se doit Touba tiwawan ou ayeur .sé l argent du Sénégal
Yao Assane dimba lignou État dou ay Fo
Koufi Ame guane bo beug dalal nga dalale ko sa bopou. Merci Cheikh omar Diagne
Merci sa Ndiogou
Je passe j’attends saa très pertinent
Sa merci ❤❤❤❤
Merci beaucoup sandiogo wakh nga deuk dee billhai bravo ❤❤❤
Sonko moy diomaye
Lolou dafeu yombou trop merci diomaye
Come Séne Baye mackia salle mo amoul ndame niune AK niom wa gfm
Serigne bi néna bindoule lettre gouvernement bi,bass abdou khadre moko wakh, TFM da'iouye manipuler.
Sa toujours très bonne analyse ❤
Machalla séne liguéye rafétna
Amna solo 😍✊🏿
Celui qui vient juste pour le Magal Katy. Il doit être à Touba Non???? Je comprends plus le Sénégal quoi.
Assane messere est dans l'humour et c'est le format de l'émission contrant l'analyse de sa ndiogou. Il faut comprendre le sens de l'émission.
Merci Sa
Wa GFM il faut les appeler désormais '' keur narr yi"" 😂😂😂
😂😂😂
Bayil naryi balla gnula Def warga walla mew 😂😂
Narr yii de mew rakk
tfm aye nafekh deug lagnou!!!
l'État dépenses beaucoup de sous pour ces événements religieusx. Nakou nek géré say gane.
Jërëjëf sa ndiogou❤❤❤
Serigne si dugnu ay pauvre am nagnu alal bugnu meuna dalalé séni gane,
Merci Cheikhe Omar diagne
Ces pratiques doivent changer. Ils doivent payer pour leur séjour dans un pays normal
Jerejef S Assane ❤
Assane mi doula wakh lou lér
Il fait exprès et ça ressemble à de la manipulation; Assane🤔
Cheikh Omar Diagne doit porter plainte vraiment au groupe GFM
Guis nga ce gars là son Ibou ou quoi , mais il faut que tu chasse que le budget du Sénégal n’est pas pour n’importe qui kmm , bon un peu de respect aux sénégalais kmm . Mais j’ai oublié que le niveau n’y est pas . Vive les patriotes, vive Sonko moy Diomay ❤❤❤❤❤. L’argent du Senegal n’est pas comme du marchandise et merci Sa
Assane, tu as tout mélangé.
RFM et TFM fait partie des médias qu'on doit faire beaucoup attention
Souniou diokhé aye milliardaire pour niou ganalé souba souba dina déposer pour gouvernement diokhma ma dieunde keur bou ande ank meubles cles en main
Li dafa yombe
Sa tu n' es pas informer
@@serignetine1420 li ma wakh lére na ganalé aye nite you diougué biti réw mi diléne logé thi aye hotel dieul léne en charge dafa yombe gouvernement warouko def béne yone
Ko am passou avion ✈️ fo dale thi sa posse waroula diafé
Billy sa yadi diambar lou domo ram yi tek. Gua tégui
RFM continu dans sa MÉDIOCRITÉ
Assane Mésséré khana da ngua feurr. Niémé ngua Yalla 😂
😂😂
Yene xamou leen assane 😂 assane problem personnel la am ak professeur check omar diagne lep louy diaxase mouride yi ak check omar diagne dinako deff😢
Yalla na Yalla faye len barke borom touba ❤❤❤❤❤❤
Omar diagne wakhna deug linou beug da yomb trop
Thiey serigne touba
Merci sa , le gouvernement du Sénégal n'est pas là pour prendre en charge les gens qui sont venus au magal. Assane ceux ne sont pas des invités du Président
Assane sa place dou fi vraiment
Amoul fen ci adouna fou état di dieul en charge Aÿ touristes wala pèlerins
Assane messere taye mom wakhofi dara lolou amoul dee rfm doul rek
Mesere degay fen
Nono ganyi niowarona fayalsenbop
Pourquoi c'est à l'état de prendre en charge 😮?
Na niou fèrmèr tfm rfm obs mogane
Lolou dé laa guiss. Et sans état d'âme.
Yaye domou khath gnifay liguey nak
@@seydinaomarsarr8970
Yalla diékhoul té diékhaloul weurseuk. Tfm teuthie, niou dém wouti fénén liguéy. Usines sonacos, Sias, Batta etc. teuthie naniou et la vie a continué. Thiottou nday TFM ak kiko mom
Youssou Ndour la beuugu😢e bou baakh mais GFM dafa wara changer walla gnou teuthie ko. Radio mille collines lagne.
Arrêtez vos mensonges c'est pas a l'état d'héberger des étrangers Touba a besoin de tout pour son développement donc bon attend a l'état sur d'autre chose plus important que des hébergements les fosses informations ne passent pas
Bougnou yappp fiiii khaliss Sénégal dou pour ayy topato kennn rewmi moko guena sokhla fouffff
Assane parfois dageye wakh lou weroull dell holate lingaye wakh dagno beug defarr sun gall
Mim reew dana yeekha avancer dé
Je s8 parfaitement d'accord avec le gouvernement kou am say gan nga teyelko SA boop puis que dou ñiome rek ñiifiy am ay gan dissons la verite
Assane doyna bayil sa mou dieul way stp 😂😂
Na nièpp xamnè lavon vonnèkuna
Assane maye niou diam le gouvernement n'a pas à prendre en charge des gens qui viennent célébrer le magal
C'est de u n'importe quoi
Franchement Assane amoul fi place , amoul ben notion si loumouy wakhh, c’est énervant!
Assane kouy dème maka da ngay faye sa billet kone kouye magal si sa nga wara faye ganou gouvernement bi lagne donc nalen gouvernement bi gérer gneupe serigne Touba mo gnou takh diok wa tfm nak yakheu rek la gnou beugua deff
Touba et la Mecque c différent les catholiques ne vont pas en pèlerinage à la Mecque tandis que Touba reçoit toutes les confessions
Damane wa touba naniou lijeunti sen magal sen bop budge Senegal dou pour ay magal ak gamou Assan mi khamoul dara billahi ay yeufou niitou aal rek lay wakh aah demal gua wouti khamkham te mayniou diam yaw nulard bi sof na torop
Baye assane wakhal deug té yalla takh
👍 👍 ok
Palais ndiouga kébé wara niou woute solution. Meune na jariñ
Assane garde une haine viscérale à l’égard de cheikh Omar Diagne, je ne sais pas se que cheikh Omar lui a fait.
Oui depuis bi check omar diagne waxe ci touba depuis 2021 ba legui lako diappal haine assane pr check omar diagne ak mimi tourè la geuna contre te niit dafa wara fatte mais mom day diap mer te lolou baxoul😢
Bayilene d'impayé AK p m niou ligueye le Sénégal doit avance
Assane nafekh bakhoul
Depuis commencement la léne wakh né TFM ak GFM si guerre laniou nék ak état bi ils essayent d'ignorer Ousmane Sonko mais Billahi wallahi mouniou dara si mom ils vont voir
Pourquoi l'ètat doit payer les frais des ètrangers venus au sènègal pour un.èvenment.que sèrt le tourisme religieux alors tèhorisait par sonko?
Bondé gani magal serigne touba limou ame thi aye deukou waaye mo eupe king fath palace
Mane mom sincèrement gni di déglou ak di sétane lou bok si gfm nioma diakhal quoi ...il faut savoir boycotter tamite
Omar diagne dou nitou dara
Avec des gens comme assane, ce pays sera difficile à développer
Rfm wallaahi séen mission bii du jàll jaxasé waa TOUBA ak gouvernement bi ngéen bëgg mais du ngéen ko réussir.
Gan ñu war a Magal ci TOUBA Yaw ngay wax waxi King Fahad Place Mbaam yi ngéen doon.