Dieu Au Sénégal - Oustaz Alpha Ba

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 3 янв 2025

Комментарии •

  • @ahmethndiaye7943
    @ahmethndiaye7943 Год назад +1

    Mâcha Allah!👍🏾👍🏾👍🏾

  • @ndeyeyandediouf684
    @ndeyeyandediouf684 Год назад

    Ak osi so seulmalé diouli lou yoninte digulé pour gnane louné nguay dégu si oustaz senegal kouné sa serigne nguay wakhal merci beaucoup

  • @ndiogoundiaye3860
    @ndiogoundiaye3860 Год назад +6

    ماشاء الله يا استاذ جزاك الله خيرا

  • @AdamaGueye-rw4kq
    @AdamaGueye-rw4kq Год назад

    😂béééééé kom khaaaaaarrrrrrrr😢😅

  • @abdouthiaw939
    @abdouthiaw939 Год назад +3

    Diaradieuf borome Touba. Rien ne pourra m'empêcher de t'aimer plus que quiconque après le prophète. Diaradieuf mbacké. Yawmi takhma dioulit.

    • @watawasawbilhaq
      @watawasawbilhaq  Год назад +5

      Akh baye yaw la rek. Romantisme dougaloul kenne al jannah .

    • @s.modoubousso565
      @s.modoubousso565 Год назад +1

      @@watawasawbilhaq jeuréjeufé borom touba

    • @abdoulazizsow3734
      @abdoulazizsow3734 Год назад +1

      @@watawasawbilhaq romantisme hahahahaha

    • @amycollediop6519
      @amycollediop6519 Год назад +3

      Manshalla oustaz je suis très fière de croire en allah le seul qui me donne tout et le seul qui est capable de me ressusciter après ma mort

    • @serignefalloudiame6544
      @serignefalloudiame6544 Год назад

      Waaw gooré yaw

  • @ndeyeyandediouf684
    @ndeyeyandediouf684 Год назад +2

    Machala oustaz alpha dama beugone kham photo serigne yi défko sa kr wala salon ndakh dafa arame wala say wadiour

  • @sakhoousmane7066
    @sakhoousmane7066 Год назад +1

    Am na soulo

  • @MoussaAw-q2n
    @MoussaAw-q2n Год назад

    lane mosï sa Younes dieulit day ma nddo

  • @silmakhatraore483
    @silmakhatraore483 Год назад +2

    Louwaye def bopam kou dé aksa bamel ⚰️

  • @amadoulaminediop8852
    @amadoulaminediop8852 Год назад

    Way saway bou de li gnou ne moy bokale yalla naniou ci fatou ta ken douniou ndieuk aldiana

    • @watawasawbilhaq
      @watawasawbilhaq  Год назад +2

      Yaw la rek. Nioune gueune si mbindef laniouy niane dé si yonam. Di diouli di woor bapare bagne bokale ak gni bokale Yalla

  • @deugguitv2564
    @deugguitv2564 Год назад

    Alfa bandi ba 🤣

  • @awaba3307
    @awaba3307 Год назад

    Merci oustaz

  • @AdamaGueye-rw4kq
    @AdamaGueye-rw4kq Год назад

    Terroriste guay ndirol😂

  • @Arwefree
    @Arwefree Год назад +1

    Yow jank nga li nek si tereyi wayé guissouma wala ma degg si yow xam xam yagui interpreté ci lou nekh mais yow hamo darà darà

    • @omardieng-vr9ob
      @omardieng-vr9ob Год назад

      Naka la cou kholam am passe passe yo dopau woul ak alcourane ak sunna di nangou guis deug

  • @serignefalloudiame6544
    @serignefalloudiame6544 Год назад

    Damay lathie lane moy atté kou mandouwoul si yeufou diambour

    • @khadim5779
      @khadim5779 Год назад +13

      Yalla mo niou wakh ci alkhouran niou digalé lou bakh ak téré lou bonne

    • @ابيمريم-ك6ذ
      @ابيمريم-ك6ذ Год назад +9

      @@khadim5779 frere ki diarul tontu danko worone ladjie laan moy mandou ci islam?

    • @serignefalloudiame6544
      @serignefalloudiame6544 Год назад

      @@khadim5779 khana dou " inna benhda zanni ismoune

    • @amdymoustaphaniang4102
      @amdymoustaphaniang4102 Год назад +1

      yoww sa wakh dji fou mou Diemm wahko parai niou wahlla

    • @sagnaawa3591
      @sagnaawa3591 Год назад +4

      @@ابيمريم-ك6ذ bly Senegal waxougnou louye manou ko si wax degu mounii leu manou wooo