Tyson 2 la faral, Palmarès bi mo bax, 22 combats 19 victoires ak 3 défaite, Tchi VIP yii ken dakouko palmarès, même Eumeu mi di kilifeum moko guen Palmarès! Wayé wax deug thiatou yoff mo gueuneu nek tchi forme, tyson sa forme bi baxoul deh! Boy bi dafa am doolé!
Tyson 2 yalla nako yalla may ndam ✅🤍✊🏿
Thiatou Yoff Kasse lanioy tope amoul lenen🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎊🎊🎊🎊🎊🎊🎊
Thiatou Yoff kassé 🎊
Tyson2 rk laniy tope
Thiatou yoff 🎉
Tyson 2 la faral, Palmarès bi mo bax, 22 combats 19 victoires ak 3 défaite, Tchi VIP yii ken dakouko palmarès, même Eumeu mi di kilifeum moko guen Palmarès!
Wayé wax deug thiatou yoff mo gueuneu nek tchi forme, tyson sa forme bi baxoul deh! Boy bi dafa am doolé!
lamb mou wakhoul deuge mais tyson 2 warona dépassé fi bou yague
Thiatou yoff késsé
Tayson 2 brom pokar yii
Boy yémal tyson 2 doussa morom
Tyson 2 dodara téla 19 inchallah ngay khani dodara
Tyson 2 Pokaar Rek✊✊
Athia rick
Thiatou yoff mo meune kii dh blh
Thiatou yof dano pape😂thiam
Après recours
Moka dane Hana do xol
Thiatou yoff seul ⚔️